Xawma nyaata yon laa fekeh wareh Bai Omar. Paa bu ma dan tiyeh loxom bess bu neh su ganeh si wan sunnu baye yi Banjul, ma di dan boka chi ndap gam dan lekkeh. Tolu na jurom nyarr fuki att. Ku daega limaa wax di nga xam la Bai Omar donon chi nyun. Maa neh, suma sopeh Baye, Sopa Sheikh, sopa yonenteh ba, sopa Yallah, mom Bai Omar moh tax.
Machallah yalna Yalla yokou leram té Tass niou barkem
Amine Baye ya rabbi
Amine
Yallah na yallah yook lérrame te tass gnou si barkém
Baye malah beug Baye malah beug Baye malah beug Baye malah beug❤
Billaye Niass yallana niou yalla tassou thissa barkee
Aamiine bijahi seyildil woujoud (slas)
❤❤❤❤
Thieye baye omar faty diallo
CV dagua khame ki
Bou bakh sakh sakh
OK foumoudeke
Kaolack moukhadam baye niass
Manedé damako begue mé khamoumako mom bir Kaolack le deke
Xawma nyaata yon laa fekeh wareh Bai Omar. Paa bu ma dan tiyeh loxom bess bu neh su ganeh si wan sunnu baye yi Banjul, ma di dan boka chi ndap gam dan lekkeh. Tolu na jurom nyarr fuki att.
Ku daega limaa wax di nga xam la Bai Omar donon chi nyun.
Maa neh, suma sopeh Baye, Sopa Sheikh, sopa yonenteh ba, sopa Yallah, mom Bai Omar moh tax.
Houdiatoul haarifiine!
Al hamdoulillah
ان دور العربية
Dds
Pp