Plateau wadial appel layenne 2024 avec Oustaz Pape Hann

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 янв 2025

Комментарии • 124

  • @bayecheikhndiaye2642
    @bayecheikhndiaye2642 11 месяцев назад +14

    Barka seydina Limamou C’est un grand plaisir d’écouter cet Grand et Bel Homme Si pédagogue Si Instruit avec cette sensation extrême❤️🫶🏽
    Oustaz Mame Abdoulaye Kébé🥰 Sougn borom goudal say fane yokou la Weer🤲🏾BAYE LIBASSE NIANG néna « Xamxam, lu muy jariñ, lu moy jëfe ko, digal ko saw gaay Bu loolu lépp nekkul, moo jaa, ku fiy wonew yoon Subhaana xamxam bu lay wommat jëme Saam Wax ja moo lay gétën ngay làyyoo jëme naari »🤍🕋🕊️

  • @seydinafaye4097
    @seydinafaye4097 10 месяцев назад +7

    Nous réclamons Ouztaz Abdoulaye Kebe cette année à Quartier Général🙌🏾limouy wakh lerr na teggou na tii xam xam ma sha Allah✨

  • @papendiaye505
    @papendiaye505 10 месяцев назад +7

    Walahi sunu Gueum Baye Lahi psl mélnani bou Aboubak'r baa. Baka Abou Diàjli né kay waxak sa wadji nane dém na Jérusalem diougué fa dem thi boromam thi bén goudi nieuwate, Abubak'r néko dax moka wax. Mouni ka waw. Mounika kone deugueula dax mom loumou rek deuguela. FA LANIOU TOLOU AK BAYE LAHI (PSL) MI WAXNÉ YALLA MA YONI. DAX MOM LOUMOU WAX DEUGUELA❤DIEREUDIEUF LIMAMOU LAHI SALALAHOU HENLEYHI WA SALAM (moma demb moma tay)

  • @fatouciss121
    @fatouciss121 10 месяцев назад +6

    Affaire bi dou lolou déh kou beug kham nak limamoulahi moy rassoulilahi fait un prière de consultation pour voir si Dieu veut te montrer tu verras inchallah par ce que Dieu est capable de toutes choses barakalahou fik machallah 🙏🙏😢

  • @ibrahimadiop7781
    @ibrahimadiop7781 11 месяцев назад +8

    Yalna naniou yalla fayal seydina limamou laye Al mountazar 🕋🤲🏿🤍☑️

  • @rokhayapouye7377
    @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +7

    Machallah toujours à la hauteur ❤yalna yallah defal la diam barkel xam xam bi ❤

  • @AdamaKebe-ni5zb
    @AdamaKebe-ni5zb 10 месяцев назад +4

    Yalla na yalla goudeul say fane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @DioLaye
    @DioLaye 10 месяцев назад +5

    Diadieuf sama wadji Mame Abdoulaye yalna yalla yook khamkham sounou fierté gua❤

  • @SambaNgom-v1h
    @SambaNgom-v1h 10 месяцев назад +5

    Guem nagnou la baye laye sopp nagnou la baye laye Mouhamadou rassulahi❤💯🌕

  • @KhadyFall-k7k
    @KhadyFall-k7k 10 месяцев назад +7

    Limamou laye Moy rasoulou lahi asws 🙏❤️ si kou beugu ak kou bagne koumou nekh ak kouma nakari lolou la yalla déf kéneu manousi Dara bilahi walahi.

  • @AishaLaye
    @AishaLaye 10 месяцев назад +4

    Sama ndidiay ma sha allah alassane diadieuf ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Kingbaba__221
    @Kingbaba__221 10 месяцев назад +3

    Dieure dieuff limamou lahi yaw minou khalal yonou islam khamal nou allahou moyy buur bi yayoo sabal al mountazar psl 🙏🏿🙏🏿🙏🏿😍❤️❤️❤️❤️

  • @AishaLaye
    @AishaLaye 10 месяцев назад +4

    Baye Laye Moy mouhamadou Rassouloulahih sallalahou aleyhi wasalam

  • @babacarniang3453
    @babacarniang3453 10 месяцев назад +4

    Kou wéddi baye laye ba déé yeureum nalla walahi

  • @diouldesow7604
    @diouldesow7604 2 месяца назад

    Machalla laye mactar rafaite na limamou laye yayeu rosorou laye moye roso Lou laye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MassambaBassel
    @MassambaBassel 10 месяцев назад +5

    Thiey papae Hann Say question yi ngay posé dafa am solo lolou

  • @ByaGueye
    @ByaGueye 10 месяцев назад +4

    Kene dou mame Abdoulaye kebe machala

  • @thiawlaye6620
    @thiawlaye6620 11 месяцев назад +2

    mansh-Alla khol sédd n Laye mahtar❤❤❤

  • @BasirDiop
    @BasirDiop 9 месяцев назад

    Macha ala amena solo baye Laye mouye rasouloulaye psl

  • @thiawlaye6620
    @thiawlaye6620 11 месяцев назад +2

    mansh-Alla ❤❤❤...

  • @alassaneka646
    @alassaneka646 10 месяцев назад +3

    Niou mel ni Lane sokhla si palato yiiii yallna yalla goudal Sá fane barke baye laye PSL

  • @abdouseye9154
    @abdouseye9154 10 месяцев назад +4

    Un homme digne et fiert mame abdoulaye kebe yalla na yalla goudal say fann dolila téranaga si barkéy baye laye ❤❤

  • @jaabutv
    @jaabutv 10 месяцев назад +2

    Walahi Baye Laye moy Rassoulilahi saws

  • @MamadouNdoye-t2d
    @MamadouNdoye-t2d 10 месяцев назад +1

    Limamou lahi mome la débe mome la tayue bly ❤❤❤

  • @RassoulLayegueye
    @RassoulLayegueye 11 месяцев назад +14

    Bly sangue bi la yalla gureum ts moy mame Limamou psl di mouhamed psl

  • @ByaGueye
    @ByaGueye 10 месяцев назад +1

    Machala toujours meilleur machala

  • @MBEUGEHANEHANE
    @MBEUGEHANEHANE 10 месяцев назад

    Dieuredieuf ma Abdoulaye kébé khamkham bi rafétena❤️ machalla

  • @Moustapha-s6x
    @Moustapha-s6x 10 месяцев назад +1

    Dieureudieuf BAAY AWS

  • @Lomouha
    @Lomouha 11 месяцев назад +3

    Machaallah ❤❤❤❤

  • @NeneSissoko-r5c
    @NeneSissoko-r5c 10 месяцев назад

    Manchala laye Mamadou sama sope bi yalla ne yalla yagal sa takhaway

  • @ramatoulayembaye9422
    @ramatoulayembaye9422 10 месяцев назад +2

    Bilahi walahi Baye laye Moy Mohamed rassoulay

  • @magattediagne7812
    @magattediagne7812 10 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ LAYE MAKHTAR 🥰🥰🥰

  • @babsndoye1161
    @babsndoye1161 11 месяцев назад +3

    Baye laye ❤❤❤❤❤

  • @khadingom8654
    @khadingom8654 10 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤machalla tonton❤❤❤❤❤

  • @awa4548
    @awa4548 10 месяцев назад

    Machala mame abdoulaye kébé kéneu dou baye laye psl

  • @fatimafaye7895
    @fatimafaye7895 10 месяцев назад +1

    MACHALLA kou bzhhh wayyyy

  • @ColléMbaye-k4q
    @ColléMbaye-k4q 10 месяцев назад

    Manchalla laye yaw yama khamal baye laye yalna sa diam yague

  • @NdiayeAli-v5u
    @NdiayeAli-v5u 10 месяцев назад +1

    Machall Laye mahatar

  • @adjaindefall6544
    @adjaindefall6544 9 месяцев назад

    Bilahi wallahi wa tallahi Seydina Limamou Laye moy Rassouloulahi ( saws ) moy Mouhamed demb moy Limamou tay. kou ko wedi ba dei wallahi deim safara

  • @miinaba4901
    @miinaba4901 10 месяцев назад

    Machalla laye mamadou laye ❤

  • @moussaka3488
    @moussaka3488 11 месяцев назад +5

    Baye lahi psl moy mouhamadou Rassoulilah psl

  • @seydinaissandoye8751
    @seydinaissandoye8751 10 месяцев назад +1

    Bilahi khôl yi fékhna diajeuf laye makhtar

  • @moussagueye2740
    @moussagueye2740 11 месяцев назад +2

    Mashallah laye Mamadou 💗

  • @baye-f8b
    @baye-f8b 10 месяцев назад +1

    Macalah

  • @viadasaliousaliou8483
    @viadasaliousaliou8483 11 месяцев назад +3

    Machalla laye makhtar qui rek la nop

  • @Ndiaye-j1j
    @Ndiaye-j1j 10 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MamedjibrilNdiaye
    @MamedjibrilNdiaye 11 месяцев назад +2

    ❤❤❤

  • @IssaNdiaye-mq8kg
    @IssaNdiaye-mq8kg 10 месяцев назад +2

    Limamou laye is a prophet

  • @AntaDiallo-r6i
    @AntaDiallo-r6i 10 месяцев назад

    Yéne déguéne allcou balaye moy mouhamed coumou nék coumoou nakarriii

  • @semoudiouf4781
    @semoudiouf4781 10 месяцев назад

    Gni bilay damaléne yeureum

  • @abdoufaal786
    @abdoufaal786 10 месяцев назад +2

    Li dou yon si senegal yen oustaz yi ki wakhlen ko bay lay yoof dou yonente neklen nit

    • @OmarNdiaye-ju3ru
      @OmarNdiaye-ju3ru 9 месяцев назад

      Yaw nékal nit limamou laye rasoulou lay lolou Lou âme la

  • @fatouzahran5459
    @fatouzahran5459 10 месяцев назад

    ❤️🫶🏾

  • @abdoufaal786
    @abdoufaal786 10 месяцев назад +1

    Yonente bi nena bay lay yoof dou yonente day fen

    • @NdioneLay
      @NdioneLay 10 месяцев назад

      Yaw diokh masanimuoruo niou WAHKTAN

  • @gueyeabdou8849
    @gueyeabdou8849 11 месяцев назад +5

    Pape Ane waxal wkhbii loy rayy walakhi day fénn bo néké thi thiaxann Yalla daflay diayyy mô takh Senegal nafekh barifii

    • @doudbambeysamb1450
      @doudbambeysamb1450 10 месяцев назад +3

      Ioe la yalla diey yangui door sa lokho si euk mandoul

    • @LuminescentAverage84
      @LuminescentAverage84 10 месяцев назад

      pape hann yeufou nafékh rek, lo wakh mou lay diayy

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +2

      Nafekh wessou woul dianguo xamo mandou wo ..nguir yallah bayilen layenne yi gni dagnlen guen ba paré way isshh

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +4

      Guisnguen yena yoor s'en connexion di wax té fallé wouniou len layenne yeup focus si sen appel ..am len foula way lidianti Sénégal mo guen di wax lou nguen xamoul ...wate ni si barké jésus christ bou nguen bayiwoul limamou dinguen lake ba diekh

    • @LuminescentAverage84
      @LuminescentAverage84 10 месяцев назад

      @@rokhayapouye7377 do bayi féne ! yo jésus faléwoula sakh ndakh li nga gueum si mom ay féne leu, Jésus dou yalla dou domou yalla, voilà nga diot sa wall aussi
      Paix et bénédictions sur Issa Jésus le Verbe de Dieu et un de ses nobles serviteurs et prophètes, ainsi que sur ses fidèles apôtres et disciples d'hier à la foi véritable et originelle, et paix et bénédictions sur sa maman Maryam Marie,
      Merci et paix sur toi aussi

  • @mohamedmbaye1357
    @mohamedmbaye1357 10 месяцев назад +2

    Wakhou fi dara
    Dou al khourane dou khadisse dou dara loudoul ay histoire pour meuneu deugueul lou tollou ni SEYDINA mohamed mo déllou si aduna
    Pourtant Pape Hane il c’est très bien qu’il ment mais bon Senegal mome souniou diné bope laniou yorr 🤷🏾‍♂️🤷🏾‍♂️

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +4

      Saway so xamoul mandoul khamna ibadou ngua yen danioulen yeureum layenne amoul temps di tontou lidiantil sa Sénégal bi di tak ak sen avenir bi nek en jeu mo guen sen yi nguen di wax ....lernama man catholique bi sax malen tané

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +3

      Limamou est le dernier des prophète k nulle ne peut contester ..maxala khep sen bop rek parsk nitt kou nioul warouko done

    • @Papisco.sall.
      @Papisco.sall. 10 месяцев назад +2

      😂wèddi nguèn loudotoul dègne dogal ba djitouna sa dioub mame ak sa baye ❤baye lahi moy Mouhamadou rasoulilahi psl ❤

    • @aicha20972
      @aicha20972 10 месяцев назад +1

      Wallahi commentaire bi la done weur layenn yi yalla nalenn yalla guindi réer meti neuh😢

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +1

      @@aicha20972 yaw momou ya rere té khamo sa bop....nopalou len way ishh appel.diale n'a. Focus si Sénégal mo guen sen bavardages yi amoul sens barké jésus christ...amal.foula way

  • @gueyeabdou8849
    @gueyeabdou8849 11 месяцев назад +3

    Kuni limamu yonêttte leu fénn nga wallakhi

    • @viadasaliousaliou8483
      @viadasaliousaliou8483 11 месяцев назад

      Bonjour soit plus explicite

    • @layendoye7591
      @layendoye7591 11 месяцев назад +1

      Setal si yalla sa way

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +7

      Sa way nangoul dogual mo gueune nous catholique sax on sait que limamou est le dernier prophète

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +8

      Lidianti sa Sénégal bi di tak et votre avenir au lieu de rester la à bavardé...franchement danguen fans layenne yi motax nguen di wax rek c'est normal nak ...wayé limamou laye RASSOULOULAHI ❤❤❤❤douniou ko bayi mouk

    • @SambaNgom-v1h
      @SambaNgom-v1h 10 месяцев назад

      ​@@rokhayapouye7377bolen tontou waay lahi makhtar yena neke cci deugg.

  • @LuminescentAverage84
    @LuminescentAverage84 10 месяцев назад +4

    layennes yi bayiléne thiakhane
    dioulit dou gueum li nguén gueum
    Mouhammad est le dernier prophète et il n'est pas revenu
    bénéne yonente amoul, té rouhou yonénte bi nieuwatoul dakar difa nékk nit kou nioul
    Les oustaz hypocrites là vous êtes complices
    lou yague deug leu c'est un mensonge, ndakh saytané yagg nafi, yééféér yi yague nagne fi, té douniou deug béne yone

    • @my_sabr
      @my_sabr 10 месяцев назад

      Dama rouss sakh 😢subkhanAllah

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +3

      Nioune catholique sax legui nioungui gestu qui est limamou ... ?..lidianti le n sen Sénégal bi di tak way mo guen té bayi mak gni

    • @alphonsesarr4105
      @alphonsesarr4105 10 месяцев назад +2

      @@rokhayapouye7377 Rokhaya magui ziar laye makhtar. JEREJEF ndax beug nala ba parer mai gnune gni deuk ak Seydina Limamo Laye ASWS ak Seydina ISSA as geum nagnu bu baax LAYE amal jam LAYE MAKHTAR

    • @rokhayapouye7377
      @rokhayapouye7377 10 месяцев назад +1

      @@alphonsesarr4105 laye makhtar delo ziar bou wer amal diam diou sax inchallah barké baye laye ak seydi 🥰

    • @alphonsesarr4105
      @alphonsesarr4105 10 месяцев назад

      @@rokhayapouye7377 aminn laye makhtar niu bokk lep

  • @bounamandir
    @bounamandir 10 месяцев назад +4

    ❤❤❤❤❤❤❤machallah leya makhtar ❤

  • @laminendiaye7881
    @laminendiaye7881 10 месяцев назад +1

    Machallah ❤

  • @seydinaaboubacarbalde5534
    @seydinaaboubacarbalde5534 10 месяцев назад

    Machalla ❤

  • @hamdysalamlaye7673
    @hamdysalamlaye7673 11 месяцев назад +2

    ❤❤❤❤❤

  • @layendoye7591
    @layendoye7591 11 месяцев назад +3

    ❤❤❤❤

  • @PapeTv-y7g
    @PapeTv-y7g 10 месяцев назад +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @CheikhboumklGadiaga
    @CheikhboumklGadiaga Месяц назад

    ❤❤❤❤❤