Mashaa Allah Cheikh Mouhamadoul Bachiir NIASS wakh dji amna sollo trop je suis Mouride et j'apprecie vraiment votre contribution goudall fane tei am werr
Belle intervention de Mame Cheikh Bachir ...si c’était en science vous avez fait l’ultra-structure du problème. Merci encore une fois. Mame yaw nei fi reik tam andeu ak weir gou matalei seuk nak.
Iba der le plus grand raté de la politique sénégalaise. Que Dieu me soit témoin que j'ai jamais pu le supporter tant depuis enfant, je ressentais son hypocrisie. A tel point que je l'avais dit à mon père étant jeune adolescent. C'est individu devrait se remémorer de grands hommes intégres et méconnus du Sénégal à l'instar de Seydou Cissokho, Mady Danfakha, Cheikh Anta Diop etc... Vraiment tonton Iba Der, il est temps que tu apprenne à faire preuve de adab. Salam wal adab filah
Liguien wara wah wakholego gu yab mirina ba ga yab leona lebou ahmet khalifala wolengo wahgo deg mou bayi teleyi mouy dem bisbouset di toñ ustasyi ta amoul ben orma yablou bopam yablou tarikhabi lebou momla kilifa dou Bari wah day respecte bopam ta bolensi wakhoul dina tall senegal
Merci papa bigua comprendre nai nonou l'islam yi danio beuri fimne Tai niougui fepp keur dina yi, hopital yi feepp mm si laboratoire yi yalla naniou yalla mounial rek wayer adouna tasarona
[S7 ; V188-194] : (V188) : « « Dis : « Je ne détiens pour moi-même ni profit ni dommage, sauf ce qu’Allah veut. Et si je connaissais l’Inconnaissable, j’aurais eu des biens en abondance, et aucun mal ne m’aurait touché». (V194) : « Ceux que vous invoquez en dehors d’Allah sont des serviteurs comme vous».
[S6 ; V159] : «Ceux qui émiettent leur religion et se divisent en sectes ; de ceux-là tu (Mohamed) n'es responsable en rien : leur sort ne dépend que d'Allah. Puis Il les informera de ce qu'ils faisaient».
Lou melni khila la souzahm bou elhadj mamick sy amoul Senegal lolou la yalla def elhadj mamick sy neñou ssnt yalla bi mou ñou meye maodo Senegal amoun beyt borom kham kham bou nek Senegal te wakho si kham kham mou maodo borom kham kham bou nek Senegal te wakho si maodo kane la amoul ahhh
Kaaw Kane saway wakho fi dara. Dagnou nila mame El hadji Abdoulaye kenneu si gni gnouy taggeu si sén livre bobou attanouko si kham kham banane yako diangal. Boudoul dara les millions de talibés si diokkou si domam bi di Baye Niass rek régléna question bobou. Boulén gnou takha wakh nak.
Thierno sadji amoulen ham motax Ken doussi wakh ak yen....la preuve jiis deugue di inventer histoire alors k sen propre serigne en ont écris la vraie histoire donc boulma woo si hame hame way ndakh nekoul si ioe mii di wakh...jhon jhon yaw moom niaak lo wakh mola taha saaga c’est la réponse la plus facile au monde...Mame Abdoulaye niass dou morom donc respect...mo meune sa baye ndakh diouroul kou melni ay doomam! Nopil
Manshallah jereff Niass 🙏🏽🙏🏽
Mashallah léér na dé yàlla nañu yàlla taas ci barkéep Mame Alhaaji Abdulaay ya rabbi
Mashaa Allah Cheikh Mouhamadoul Bachiir NIASS wakh dji amna sollo trop je suis Mouride et j'apprecie vraiment votre contribution goudall fane tei am werr
ماشاءالله الحق يعلوا ولا يعلى عليه حفظكم الله ورعاكم وأدام صحتكم
Dieuredieuf Niasse, Yalna Yalla fayla. Mane dé sopey El Hadji Ibrahima Niasse lá, samaa khol séd na lol thi wakhdji. Dieuredieuf.
Mashallah ❤❤❤❤❤
Alhamdoulillah baye defar na diabote bii ba adouna meunoulene khémm . Dieureufé Baye Niass
Mame El Hadji Abdoulahi Niass diouralnagnou dome bo khamné dou moromou kéne si adouna mouye Baye Niass Radiyallahou Anhou
Mach alla Cheikh bi
شكرا جزيلا يا شيخنا أطال الله عمرك وأيدك في نصرة دينه
Bilahi dage la dh dieureudieuf cheikh bi
يا شيخ بشير انت بطل بما في الكلمة من معنى
Mancha Allah Cheikh Ibrahim Niass
Mane mourid mais j'aime beaucoup les naisséne
Machallah niass♥️♥️♥️♥️♥️
Mashalah Niass jerejeufé Baye RTA ❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machaallh Niasse deugeul......
Machalla Machalla niass
Mashala niasse yalla guoudal sa fan ta mayla weer
machallah niass si leralyi yalnanou yalla fecgal bekhey noon
Merci Niass
Machaalla niass ziar niass
Macha alla niass
bilahi li mo takh ma beugue Baye niass
Dieureudieuf Niass Senegal kou bakh nieup niolèye beugue diour wala niouné sama serigne mola diangual Faydou bi mo disss sèen nop yi
Merci beaucoup niass
Yaagfi lool té andak wér !!!
Walahi wakh nga deugue niasse sante nagnou yallah banga khamni
Yallah may nagnou gnou kham yeuf ye noumou démé dembou mé
Kou deugue deugue nangouko
Belle intervention de Mame Cheikh Bachir ...si c’était en science vous avez fait l’ultra-structure du problème. Merci encore une fois. Mame yaw nei fi reik tam andeu ak weir gou matalei seuk nak.
Macha allah♥
Masha alla allhamdou lilahey waxbe rrefetti na
Respections la famille Niass niome rek niofiye international
Bilahi wakh nga deugue gnom rék gnooy international
tarikha bi ba mouy weur adouna baye niass dioudogoul
@@aliounediop2709 c pas vrai
@@papesarr3117 cheikhou oumar bimouy weur monde bi ken da kham baye niass
@@aliounediop2709 j'aime bien ch. Oumar mais Sénégal rék la am talibé actuellement comme les autres 😂
Iba der le plus grand raté de la politique sénégalaise. Que Dieu me soit
témoin que j'ai jamais pu le supporter tant depuis enfant, je
ressentais son hypocrisie. A tel point que je l'avais dit à mon père
étant jeune adolescent. C'est individu devrait se remémorer de grands
hommes intégres et méconnus du Sénégal à l'instar de Seydou Cissokho,
Mady Danfakha, Cheikh Anta Diop etc... Vraiment tonton Iba Der, il est
temps que tu apprenne à faire preuve de adab. Salam wal adab filah
Macha alla
Qui peut cité les grands marabouts ici au Sénégal sans fondateur du Layéne c'est impossible. Merci beaucoup mon papa
Wawwww goor way حقيقة
ماشاء الله أطال الله عمرك انياس
Mashallah Niass mane dai mouride la wayyè linga wakh yeupp deugg la, tèh ci xam xam nga ko tèk
Machalla wakh dji rafetna
Merci sama kharit
Machallah kilifeu leu bo khamnii dou wakh louka nekh deugue rek lay wakh
Liguien wara wah wakholego gu yab mirina ba ga yab leona lebou ahmet khalifala wolengo wahgo deg mou bayi teleyi mouy dem bisbouset di toñ ustasyi ta amoul ben orma yablou bopam yablou tarikhabi lebou momla kilifa dou Bari wah day respecte bopam ta bolensi wakhoul dina tall senegal
Dieurieudieffffffffééé Baye Niasse docteur roux khôl yii
Merci papa bigua comprendre nai nonou l'islam yi danio beuri fimne Tai niougui fepp keur dina yi, hopital yi feepp mm si laboratoire yi yalla naniou yalla mounial rek wayer adouna tasarona
Machallah merci merci merci
Machalla Machalla niasse
Niasse goudal fane
Kou nekk sa Maame moola gueuneul. Thiey Sénégal dou dém dé.
MAACHAALAH SERIGNE BI LOUNGA WAKH AMNA SOLO NGANA KAY GNOUN TALIBE YI GNOU DIAPANTEEE WAAT REK NDAX LI DAY GUEUNA MOTIVEE TALIBEEE REK
Macha Allah amna soloo
Salam. saa bay, yal na yalla goudal sa faan tè mayla wèer.man bay fall laa wayè khamna ni nitt kou bakh nga
[S7 ; V188-194] : (V188) : « « Dis : « Je ne détiens pour moi-même ni profit ni dommage, sauf ce qu’Allah veut. Et si je connaissais l’Inconnaissable, j’aurais eu des biens en abondance, et aucun mal ne m’aurait touché». (V194) : « Ceux que vous invoquez en dehors d’Allah sont des serviteurs comme vous».
Alhamdoulila baye niass mo bakh reke bilaye
Man dé talîbé serîgne Touba la mai Baye nîass dafma nékh lollll
أيدك الله
Wallahi
dieureudieuf serigne bi
Merci
wahdji amoul ndiarigne.histoire bi manougnouko bind ba gneup nangou.kounek sa bop nguay defendre rek
Vraiment ninga waxé dafa wané finga bokk té biu gneup waxé ni solution dou meussou am
Merci bcp goor gui keye daye parpar lo mome tamit
[S6 ; V159] : «Ceux qui émiettent leur religion et se divisent en sectes ; de ceux-là tu (Mohamed) n'es responsable en rien : leur sort ne dépend que d'Allah. Puis Il les informera de ce qu'ils faisaient».
Baye Niass point
Niass niass niass niass
Baye niass Moy international
مشاالله إنياس
Diadeuf niasss
L'État bi war outal ibader sécurité vraiment peur na
Si saloum ani mame abdoul hamid kane ani seydi ahmed deme boulen di wahe hol te yalla tah
Akasa ibader dou nitouk dara
Rafetna
Moride la wayé dameléne begue niass
Je suis layénne vraiment peur na pourquoi niasényi di wanteed iba der comme les américaine contre ben Laden
Vraiment peur na l'État bi war na outal ibader sécurité damay ragal lou dal Babacar sey 1993 dal ibader
Niasse
Dieredieuff'niass
Yagg'fi lool'niass'té werr
Can'xam'bi leer'na
Tontou'bi sét'na tèggui'nouna
ziyarnala waye tamit nopingen thie rwmide koniolal ngawakh bou maki sall yakhe rewmi ngane tek
Si senegal sakh ngay wakh serign bi
Koulou hakhou walaw kana Mourane
wakh dji yaw rek yako wakh kaniane rek moy ndayyi lepp te yagnafi
Akassa tabarakalla
Danga mér rėk papà ...iba dér kou baakh là ....dalalal sa khol.
Toubap you gnoule yisi rewmi lérna madiambal Diagne moy chef bi
Anne toubap buu ñuuwul
Vraiment peur na thi niasén l'État bi war na outal sécurité damay ragal lou dal Babacar sey dalko 93
Lou melni khila la souzahm bou elhadj mamick sy amoul Senegal lolou la yalla def elhadj mamick sy neñou ssnt yalla bi mou ñou meye maodo Senegal amoun beyt borom kham kham bou nek Senegal te wakho si kham kham mou maodo borom kham kham bou nek Senegal te wakho si maodo kane la amoul ahhh
Kaaw Kane saway wakho fi dara.
Dagnou nila mame El hadji Abdoulaye kenneu si gni gnouy taggeu si sén livre bobou attanouko si kham kham banane yako diangal.
Boudoul dara les millions de talibés si diokkou si domam bi di Baye Niass rek régléna question bobou.
Boulén gnou takha wakh nak.
Kaaw Kane khilasou zahab bakh na trop machallah mais todioul nigeria té todioul mauritanie gahna....
Niass
Rèwmi dé taay laa kounè sognia wahhh wayè bamouy mèti kèn sognioul tabahh diouma kèn sognioul toudou tourou yalla si Kaw
Mom rèkk Seydil khadji malick Djiouma yi si reww mi sèdè nako
Kou sognia wotè kou nèkk Maodo mola mèyy independence kholal èvenement mo commencè dèpuis 1902
Saway boulen sonal mame maodo serigne bou mague leuh machalah ken weranter wouko way nak tamite diangaloul mame Aladji lolou aussi daguenkoy nangou té diouroul kou melni baye niass si dinner bii aaahhh tamite!
bilakhi bo beuge khame khame deuge dougale fouta wala tiva wane
Yaw kou iniane gua amadou diallo aveugle que tu es foleen todhi tarde ba dee
T'as un problème avec iba der, et puis va voir un dentiste
Doundeul ba ame son âge xool ndakh diga desser dent yaw domeram di ame Lo xasté...si none yii ga bok way xool bou dague rek gassiy ame!
Amo yarr wakho fii kham kham
@@mamadouyayaba8825 boy sa yayou yaye, yayam
Thierno sadji amoulen ham motax Ken doussi wakh ak yen....la preuve jiis deugue di inventer histoire alors k sen propre serigne en ont écris la vraie histoire donc boulma woo si hame hame way ndakh nekoul si ioe mii di wakh...jhon jhon yaw moom niaak lo wakh mola taha saaga c’est la réponse la plus facile au monde...Mame Abdoulaye niass dou morom donc respect...mo meune sa baye ndakh diouroul kou melni ay doomam! Nopil
Au moins du respect. Boulêne yakhal sène bopou dof ak khamadi wèssou woul di wakh Lou gnaw si kilifa.
Macha Allah amna solo
Machalla niassssss
Machalla niass