Pape cheikh Diallo gueune nala beugue ndakh sama wadji Elhadji Fallou Mbacke, oh pape yaa bakh, wayè mon cher bo kholé ci Rassoulilah (SPL) gueune gui mbindèf , khole ci sounou wadji serigne Touba khadime Rassoulilah dara dou la nakari, pape bo bonone tèki wo dara.kène doula wakh lou gnaw, wayè.ma sha Allah bakh gueune, il faut nga bari none. Wayè mba khame nga ni gnila beugue gno eupe fouuuufe gni la bagne. Pape boul falè we love you ❤ lolou nake lagnou beugue nga kharou ndakh da ngaye dèranger
Nekhoul ba nekhoul khamou mala mé kou bakh ga khol bou rafete machallah yallana yalla goudal sa fane mayla wer ak werle barke Seydina Mohamed Saws 🤲❤️❤️
Pape quelle belle leçon de vie tu nous fais la. Ça m’est arrivé aussi d’avoir des envies suicidaires a cause de la méchanceté des gens. Mais j’ai fini par comprendre que ce n’est que l’expression de leur jalousie. Je te jure
Belle philosophie de vie . J'ai toujours pensé que la conjonction "mais" dans un certain contexte est tout simplement négatif. C'est comme apprécier et déprécier en même temps . Dieu est le plus juste des juges ☝🏾
Je prie pour k yala boléwat léne walay Machala tu as un grand coeur diam rék gay wakh diko dokh kiya de grâce je vous demande solennellement de revenir vers pape cheikh Diallo guir yala
Ndaysan pape cheikh yalla nako yalla may goudou fan diambar la dh
Pape cheikh Diallo gueune nala beugue ndakh sama wadji Elhadji Fallou Mbacke, oh pape yaa bakh, wayè mon cher bo kholé ci Rassoulilah (SPL) gueune gui mbindèf , khole ci sounou wadji serigne Touba khadime Rassoulilah dara dou la nakari, pape bo bonone tèki wo dara.kène doula wakh lou gnaw, wayè.ma sha Allah bakh gueune, il faut nga bari none. Wayè mba khame nga ni gnila beugue gno eupe fouuuufe gni la bagne. Pape boul falè we love you ❤ lolou nake lagnou beugue nga kharou ndakh da ngaye dèranger
Quand je t'écoute Pap je me vois moi même je te le jure et tu es très tolérant et gentil Macha alakhhh 😂😂
Bilaye walaye vérité absolue Pape Cheikh.
Nekhoul ba nekhoul khamou mala mé kou bakh ga khol bou rafete machallah yallana yalla goudal sa fane mayla wer ak werle barke Seydina Mohamed Saws 🤲❤️❤️
S. A.W.S❤❤❤❤❤allahuma amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine🤲🤲🤲☝️🙏
Pape boul leralati dara on t aime comme tu es bonne continuation et bonne chance avec nomade blue
Pape yééd guama😢, kouma wok ma xourila, bana niep ba wett. Dina toléré now inch'Allah jajeuff. Yallah na sa diam yague
On est pareil ma sœur 😢 mais YALLA naniou YALLA maye kholou mogne
Diallo dierry y'a bakh tè raféte khol, tè am esprit de dèpassement!
Pape quelle belle leçon de vie tu nous fais la. Ça m’est arrivé aussi d’avoir des envies suicidaires a cause de la méchanceté des gens. Mais j’ai fini par comprendre que ce n’est que l’expression de leur jalousie. Je te jure
❤
Ç'est ça frère t'as tout compris 😢
❤❤❤Pape Cheikh est adorable. Ne change jamais.
Pape Cheikh tu as un esprit exemplaire. Je t’adore manchAllah
Ay way pape cheikh yak Wally yéna Niro djiko yalna yalla same léne
Pape yiow ndékété walliou nga déh Machallah
Belle philosophie de vie . J'ai toujours pensé que la conjonction "mais" dans un certain contexte est tout simplement négatif.
C'est comme apprécier et déprécier en même temps .
Dieu est le plus juste des juges ☝🏾
Wollahi Hakhane Pape Cheikh ❤🎉🎉🎉 que le tout puissant vous protège amiine Yarabbi
Merci Pape cheikh tu es très gentil que Dieu te protège ❤❤😂😂
Machalla baye cheick❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Well said pape cheikh,u can't fight with everyone! Lou wayy deff bopam!
Tieuy Pape waxatingadeug d ❤ lilageuna metti sa adouna kilageuna diégué molakoy def
J'admire votre esprit de dépassement 👏
Pape cheikh dafa nekh 😂😂😂 mbeuguél deh xana warna nékh❤❤
Bilaye pure vérité pape chiekh
Merci pour cet enseignement Pape Cheikh..... je suis tellement déçu des gens , surtout au sein de sa propre famille
Wakh diou niaw diouguewoul famou dieum. Filou diougue la thiossano. Tu es magnifique. Je suis ton fans no. 1 et je sais le pourquoi.
Bly ma beugue serigne Fallou ❤🎉
Barké serigne fallou mbacké mala beugue piir. Qu'allah te garde et te couvre de sa protection
J t adore pape yalla n'a yalla same la
Quelle grandeur d’esprit Baye Cheikh ya barh yalla ne le yalla sameu 🤲🏼 Keep going bro we love you 🥰
pap du courage je t'aime bien sa jikou machallah du courage nite kou bakh nga
Yalla naniou Sunu Borom sam arniou maye niou mouthieuk mouthieulé t lafal niou thiate aussi 🙏🙏🙏🙏 🙏
Chevreau bombe atomique, on t’aime gran❤😂😂
Hey way pape delole ak kya
Pape qu ‘ الله vous protège
Bilay djiko tata Deguene Chimère rek lay guiss thi yaw nopi garmi ga yoré diallo djeri balla aicha mala beugue mon frère ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Yalnala yalla sam te arla bi barakati Cheikhoul Khadim
Machallah mon frère yalla nala yalla defale diame 🙏 🙏 ❤❤❤❤❤❤
😂😂ndeysan yalla nalen yalla delowat cii diam barkeb Serigne Fallou 😂😂😂
Machallah Diallo diery ya bakh wayyy❤
Right PAP Cheikh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je prie pour k yala boléwat léne walay Machala tu as un grand coeur diam rék gay wakh diko dokh kiya de grâce je vous demande solennellement de revenir vers pape cheikh Diallo guir yala
Pape ckheikh bilahi kou niakk kigniane bilahi jtm fort ❤❤❤❤
Mashallah pape dundal
Pape chekh Diallo diery yaa baaaakhkhkh yalna sa diamm yagg way longue vie à toi
😂😂😂😂 Pape boumaréye😂 wollahi ték nagne lounékk sakaw 😂😂❤🎉
Très imteressant tu es especially adorable gentil cœur en or❤
Je l'aime ce gars super cool❤❤❤❤❤❤❤❤❤! God bless you 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
j'aime ta philosophie et ton humour. ❤❤❤❤❤ you are a good boy.
va voir PROS , s'il donne son negueul Kya se remettra avec Kya.😂😂😂.
Billagui degue rek kha wax billagui baye cheikh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ay way pape cheikh magui content. Tu es merveilleux
Wa kaylénn jeuliii kia😂😂😂
Papa loula wayy yeureumm yeureumm rétannnn😂😂😂
Vraiment je te respecte
Reste solide t as tout dis t as la foi yalla rek ame yalla moy bour
Machallah ya rafet khol❤❤❤
merci bcoup pape❤❤❤❤
Cheikh Diallo❤❤❤❤
pape cheikh diallo vous etes vraiment une personne exeptionnelle
Pape dégge nga louné wayé nitt kouBakh yalna yalla maijam❤❤❤❤❤❤❤
Machallah Pape cheikh diallo ont aiment ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂kia yeureumeulll ki wayyy
PAPE YA BAKH ❤️🙏
Dafa kya ndeyssane ❤
Verité dé Pape Cheikh lolou mofi nek mais yalla nek
Papa chiekh sayoumako deklo rec guisci sama bop❤
ManchAllah ❤
Pape cheikh je t'admire beaucoup tu es vrai
Mashallah pape❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay man nk dama beugeu pape cheikh souma dégé béneu bat bou gnaw day melni man lagnko wakh mais alhamdoulila
Quel homme merveilleux pape cheikh ❤
Au début j'étais triste mais ça m'a dakka joyy fiiii 😂😂😂rétan lonama tropp😂😂😂😂
Bilay mala beuguena guirr serigne touba ❤❤❤
Machalla amal diamm
Yalla nala yalla défal diam
Mais mane en personne mane kiya laye votèle pour mouniéwate inchallah
Bilaye deuguela yalla na la yalla Fay sa khol❤❤❤❤❤❤❤
Yalna yalla same arla sama domou baye bi bakh réck am solo
Ndeysan 😢❤❤❤❤
Machalla niite kou bakh gua
😂😂😂😂tu es tres fort Maachalah ❤
Pape cheikh Diallo yalla nala yalla delowate akhe kiya si Barker sedina mouhamat Barker Serigne Touba Serigne fallou bi ga yakhar
Non il est exceptionnel bravo 👏🏽
Machala yala nassa diam yague
Ya bakh Pape cheikh
Ndaye saan rafétna ❤
Merci pape❤❤❤❤
Pape cheikh Diallo mane sah woy n'a j'ai pleurait
Machahalah......
Lou ler nga wakh machallah
Bilay damala beuggg nakkkk Serigne fallou
Mane mome naka diékk dama la beug dakh srg fallou 💞
Sonko na ci waxx kya dellou ak pape cheikh nguir Yallah
Frère boule guessou amnga gnanou wadiour❤
❤❤❤❤❤❤❤❤Pape niit kou bakhe nga❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️👏👏👏
❤❤❤❤❤❤tu as parfaitement raison la separation est difficile bamba arrete boul deef khorome ci gaume ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Duoulit pure ngaa pape
Ndaye San ❤
Bilahi walahi li géna miti Moy nou toumal la té mo no KO wédi Lou miti bilahi
😂😂😂Machallah ❤
Je l'aime beaucoup
Machalla pape cheick
Verité❤
Ya bakh❤