Oothentik Zeus - Wreew Beu Dof (Clip Officiel)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 янв 2025

Комментарии • 499

  • @oothentikzeus219
    @oothentikzeus219  Год назад +291

    Yallah mooma tathiou waayé teubeugoumeu
    Lemko bamou rond ken weureutouleu
    Lima yagg rêver teureuloumeu
    Neel sa rappeur Tant que meunoul soul ker beugueudiouma
    Boum si baat keud nd* tabouret
    Corbillard gnima yap daniou neew
    Ndekki laay omelettes nitou neen
    Des grosses chattes mais sibouleen
    Thiouss, ween
    Mooy sa cachet rappeur
    Doul, fèn
    Rek lama dakheu
    Coups, plaies
    Y’aura des blessés
    New, Wave
    Chaud melni été
    12, 16
    Samay couplet daniou nice beu danioumay faatélo célibat
    Douter
    Fooko deguer sama vocabulaire égale à quinquélibat
    Mouss, nguinw
    Quand le chat est là tu t’en bats les couilles bouder yaay Gaïndé
    Doublé
    Taal smoke fay gnima beug pop sakhaaral sen game BP
    Marquer sama droit comme latéral gauche
    Def campagne delouwaat aal ba
    Yallah rek mooma maneu térè doon GOAT
    Bay sama waar douma khaar kouma niaakh
    Mbeur caamin bou amoul ben mass laa
    Xaliss mooy wakh booko amoul boul masslaa
    Sons yi nioogui daw fatt fepp c’est le karma
    Tégou sen radios nakh damaleen damatt
    Refrain:
    Damalaa soof
    Meunooma neekh
    Gueun leen thioof
    Niou beug maa thieeb han
    Cours ak long
    lepp laay def
    Na niaaw na moche
    salifondé wouyumeu
    Wreew
    (Wreew beu Dof)
    Wreew
    (Wala beu neup)
    Wreew
    ( ngani ma lane? )
    Kou meun li ngay def boula neekhé (x2)
    2e couplet:
    Sama tailleur dieul sama mesure
    Néma punchlines laalay niawalé
    Yor khiir gun ak ceinture saleteel kone douma baalé
    Soum waay neel say lèche cul yimay conseiller taat laay déguer
    Fouma diaar sen grosses pointures tuut tank lanioufay takhawer
    Yaay sa taaw nako thiatt seekhlou
    Tégouniouma louma meunoul dékou
    Bras long amoumako def coup mou sorri
    Zidane amoul karaw dieul coupe
    Di nga naaw boumla maayé as tout
    Douma dak teh maa gueneu aay buur
    Sama yoon si golo bouy bokh golo
    Khel niaar amoul damalaay doute
    My boy Bouma natter si rap damalay tek daan
    Doug ay nikou wara dieul 2e femme
    10 zero laay door sen 11 départ
    Amoumeu comme élection première dame
    Beug dieul péh waral douma daw deuss
    Teh si ndieulbeen beugumeu woon am buzz
    Seni clichés diaaroul sama album
    Naroumako yaagal boumalendi sankeu
    Golden boy
    Refrain:
    Damalaa soof
    Meunooma neekh
    Gueun leen thioof
    Niou beug maa thieeb han
    Cours ak long
    lepp laay def
    Na niaaw na moche
    salifondé wouyumeu
    Wreew
    (Wreew beu Dof)
    Wreew
    (Wala beu neup)
    Wreew
    ( ngani ma lane? )
    Kou meun li ngay def boula neekhé (x2)

  • @CHEIMZO.BOY.OFFICIEL
    @CHEIMZO.BOY.OFFICIEL Год назад +14

    Oothentik est le meilleur de sa génération kou d'accord lalal j'aime abonné

  • @FatouDieye-f8p
    @FatouDieye-f8p 11 месяцев назад +3

    Black mafia rk laye topou ☠️

  • @Adamaguzman
    @Adamaguzman 10 месяцев назад +1

    Akbess sa baye

  • @ogvinz2216
    @ogvinz2216 Год назад +52

    Zeus toujours égal lui même, il ne déçoit jamais 🔥🔥🔥

  • @seynaboudiatta2012
    @seynaboudiatta2012 11 месяцев назад +2

    Rang mouye gawe yawe rek lini topou🖒mais mane lima def tayou makoo

  • @mohameddrame820
    @mohameddrame820 Год назад +23

    Le Rap galsen a tellement évoluer avec cettes nouvelles générations 🔥🤛. Franchement force à Toi Zeuss

  • @layendiaye1935
    @layendiaye1935 Год назад +2

    Golo bouy bokhou golo ce le logo d ki 😂😂ça

  • @Adamaguzman
    @Adamaguzman 11 месяцев назад +1

    Akbess sa bay

  • @El_PIS_LEGEND
    @El_PIS_LEGEND Год назад +5

    Zidane amoul karaw djel coupe 😂zeus tu est ki ❤waw !!

  • @Modoumbayelemeringué
    @Modoumbayelemeringué Год назад +4

    Weuro di rare souma sagnone chaque 2 jours danguay guene sound bly degue sa batt day sedd xol ❤❤

  • @falzacarlos8716
    @falzacarlos8716 Год назад +20

    flow bou doop bi techique bou graw lyrics bou kawei créativité n'en parlons pas Zeus t'es le meilleur des meilleurs 😢

  • @PIsta__________og
    @PIsta__________og Год назад +3

    Barkii rassoulillah ya meune rap way 🥺❤️

  • @simpetin
    @simpetin Год назад +2

    Zeuss💪🏾🔥

  • @BLYKY9A
    @BLYKY9A Год назад +2

    Barki yallah galsen yaffi meune Zeus techniquement flow lyrics leep c'est dope

  • @etmohjrlofficielle3652
    @etmohjrlofficielle3652 Год назад +185

    Kou guiss ni boye bou khéss bi akbéss lasiy wakhal😂 beuseul Jaime ndank

  • @wallyseck3087
    @wallyseck3087 Год назад +9

    Dégguén punch line bi:Marquer sama droit comme latéral gauche déf campagne délou watt alaba 😂💥💎dope

  • @seydouly6762
    @seydouly6762 Год назад +1

    Ak bess mi nak🎉❤😂

  • @Ibrahimaciss-zs5hc
    @Ibrahimaciss-zs5hc Год назад +1

    Dop frr

  • @Luisscar
    @Luisscar Год назад +1

    Li nekhna wayy 😂❤

  • @FodéDiba-m6h
    @FodéDiba-m6h День назад

    Affaire de rap amoul kharito Nice zeuss 🎉

  • @kittysall4501
    @kittysall4501 Год назад +1

    Ya meunn ya eup dolé 🎉🎉

  • @iscojo6600
    @iscojo6600 Год назад +4

    Zeus Siloné ! Zeus si job Bi lanékhone!! Dop neu Le ZEUS!! Et soit un Expo maintenant ♥️🙏🏾🥰

  • @youssoupouye3512
    @youssoupouye3512 Год назад +1

    machallah mboka lébou tjrs au top

  • @lamzii_dml
    @lamzii_dml Год назад +1

    Défone rare teul rék seureukheul niou wreew beu doff🤣🤣🤣Zeus louy problème bi koula togn🔥🔥🔥🔥 nice.

  • @Dunkhaff
    @Dunkhaff Год назад +10

    Bayil rare bi rek legui nga depasser gayou beuri

  • @mhdrvssoulsogue2430
    @mhdrvssoulsogue2430 Год назад +6

    L’authenticité tu répond à ton nom Tu ne déçois jamais
    Tu fais partie parmi les meilleurs

  • @CissMamegor-p2f
    @CissMamegor-p2f 11 месяцев назад +1

    Yaye sine baye bilay 🤍🙏🙏🤍🤍🤍❤️

  • @ogvinz2216
    @ogvinz2216 Год назад +2

    Mista cash si beat thiey lolou 🔥🔥

  • @alphasow2405
    @alphasow2405 Год назад +3

    Warro di guej di guene ay sound d ❤❤❤

  • @idsonbii7418
    @idsonbii7418 Год назад +1

    Namon nagne leuh🎉🎉🎉🎉

  • @yeguebonysamba9421
    @yeguebonysamba9421 Год назад +1

    😂😂 da nga ay brooooooo

  • @AdamaSow-r2i
    @AdamaSow-r2i Год назад +1

    Papou gayi

  • @alassanediallo2369
    @alassanediallo2369 Год назад +3

    Remember othentic zeus nice bro🎉🎉

  • @smamemor
    @smamemor Год назад +6

    Great Job oothentik
    Misterio I see you bro
    Keep it up

  • @khoulada_best9155
    @khoulada_best9155 Год назад +1

    Nice na bonne continuation

  • @mymthiapathioly6133
    @mymthiapathioly6133 Год назад +1

    Thiapathioly game bi tu n déçois jamé le golden boy ❤

  • @iboudabo9260
    @iboudabo9260 Год назад +1

    Boy Zeus 🎉🎉🎉

  • @DameGauye-cs5yj
    @DameGauye-cs5yj Год назад +1

    Gâteau dêmm waww😮😮❤ zeu

  • @serignefalloudoiuf4598
    @serignefalloudoiuf4598 Год назад +2

    Oothentik Zeus 🎧

  • @BossbvrvLo
    @BossbvrvLo Год назад +1

    Thiapathioly the best 🎉🎉

  • @El_PIS_LEGEND
    @El_PIS_LEGEND Год назад +1

    Kou guiss akbess si clip bi rek lalal ❤😂

  • @dizikha2003
    @dizikha2003 Год назад

    Do nitou fi

  • @Ibrakhisamba
    @Ibrakhisamba 11 месяцев назад +2

    RIME BOY 😮😮

  • @fallouthiam8168
    @fallouthiam8168 Год назад +4

    Lo déf yako tay kon boula kén bal🔥🔥🔥

  • @ngaakablindejr1771
    @ngaakablindejr1771 Год назад +1

    Ya bien Zeus

  • @AlineGueye-bm2sz
    @AlineGueye-bm2sz 11 месяцев назад +1

    Le camavinga du rapgalsen

  • @BabacarDiouf-i3x
    @BabacarDiouf-i3x Год назад +16

    Le game a besoin de sa 🔥🔥

  • @taphacityzens
    @taphacityzens Год назад +1

    Do nitt bilay ❤🎧🔥

  • @AlineGueye-bm2sz
    @AlineGueye-bm2sz 11 месяцев назад +1

    Meilleur k tout❤❤❤

  • @Cheikhbouroi
    @Cheikhbouroi Год назад +2

    Ya mane 👑💪

  • @PUISSANCE.333
    @PUISSANCE.333 Год назад +39

    🇵🇸Une prière pour les Palestiniens 😢 car le bilan des morts ne fait que s'alourdir. Tous mes pensées et prières aux vont aux peuples palestiniens. Q'Allah leurs vient en aide 😑 #FreePalestine 😢

  • @Bibho
    @Bibho Год назад

    Prod bi aussi dope ne🔥respect Zeus

  • @djibrildiaw5244
    @djibrildiaw5244 Год назад +2

    T'es passé a côté de la plaque fils t'été bourré de talent mais t'en a mis temp pour percé dans le game top ay futilités rk té khékh yigay khékh d'où sa khèkhe amal objectif com au début guiss nga légui Papa One mogui thi lénéne ana thieuk AK niom k.o

  • @KINGMG0066
    @KINGMG0066 Год назад +1

    Nono cessss vraiment doppp ❤❤

  • @serignefalloudoiuf4598
    @serignefalloudoiuf4598 Год назад +1

    Le meilleur rappeur 🇸🇳😎❤réwwwwwwww

  • @zykatrapboyz
    @zykatrapboyz Год назад +1

    Booomboclaaaaaatttt🍾🔥🔥💯🦅

  • @abdoukhdrediallo4817
    @abdoukhdrediallo4817 Год назад +2

    Yaw rèk lay tope zes❤

  • @BIZDEFROMBADLANDSGANG
    @BIZDEFROMBADLANDSGANG Год назад +2

    Beugueu dieul pei tax douma daw deuss 😮😮

  • @Kelisaleupaleup
    @Kelisaleupaleup 12 дней назад

    Boy boul clash deffaal ay sound
    Wakhaak fans yii
    Ngaaa jaaal nice

  • @Mboyiz22
    @Mboyiz22 Год назад +1

    Yafiné❤

  • @aidakebe5976
    @aidakebe5976 Год назад +1

    Clip bii Giss n'a si Bm jaay akbess

  • @bigmomo6418
    @bigmomo6418 Год назад

    Zeus nieuwna dh✌️👍🫶👌

  • @KhadimSamb-g4b
    @KhadimSamb-g4b Год назад +1

    Wow 😶‍🌫️

  • @BayeMamourKhoule
    @BayeMamourKhoule Год назад +1

    Zeus never disappoint

  • @zoleroi
    @zoleroi Год назад

    Ñoune daño meune❤❤❤ zeusss bal léne

  • @matkingofficiel
    @matkingofficiel Год назад +1

    Got jop idol bi Zeus rèk laye topou

  • @mansourmbengue2908
    @mansourmbengue2908 Год назад +16

    Un retour phénoménal ❤
    Aladji Ass 🎉😊

  • @Niang_m12
    @Niang_m12 Год назад +10

    Le meilleur de sa génération kou d’accord lalal ❤

  • @AbdouSeck-zy2wy
    @AbdouSeck-zy2wy Год назад

    Moye sène baye😊

  • @alioundoye4109
    @alioundoye4109 Год назад

    Ya Mane dé bly souma❤

  • @Benmomo88
    @Benmomo88 Год назад +1

    woooowwwww golden boy ki alkhourane dga meune doo niitt 📌🎖️🎖️🎖️🎖️🎖️🎖️💥💥💥💥💥

    • @Benmomo88
      @Benmomo88 Год назад

      kou meune Say none boula nékhé wrééwww lyricalement yaffi meune🎖️🎖️🎖️🎖️🎖️

    • @Benmomo88
      @Benmomo88 Год назад

      kou meune Say none boula nékhé wrééwww lyricalement yaffi meune🎖️🎖️🎖️🎖️🎖️

    • @Benmomo88
      @Benmomo88 Год назад

      salii fondéé🤣💥💥💥💥🎖️🎖️🎖️

  • @pacoseck3815
    @pacoseck3815 Год назад +6

    Niveaux clip bi doune di wax 😮 tjrs a la hauteur 🔥🔥 force 💪🏿💪🏿

  • @BambaFayeSene
    @BambaFayeSene Год назад

    Papou Gayi 💕💕oothentik DG bou Mak bi

  • @papefall6942
    @papefall6942 Год назад +16

    Il ne déçoit jamais ❤

  • @BintaDiouf-i6i
    @BintaDiouf-i6i Год назад

    Kharal ba tidiou king fékk la fii

  • @PapaMane-s3e
    @PapaMane-s3e Год назад +1

    le meilleur rappeur

  • @omarfall1262
    @omarfall1262 Год назад +1

    Doop Zeus 🔥👊❤

  • @Azou_capo
    @Azou_capo Год назад +1

    Kou guiss ni boye bou khéss bi akbéss lasiy wakhal
    ) beuseul Jaime ndank😂😂

  • @OusmaneSamba-yu7ks
    @OusmaneSamba-yu7ks Год назад

    Fiérte bendoo bii✅✅

  • @BigSonTV-jm6kp
    @BigSonTV-jm6kp Год назад +1

    Y’a wor

  • @PapaSene-y2d
    @PapaSene-y2d Год назад +1

    Ndanane🎉❤

  • @zalsalabangbang749
    @zalsalabangbang749 Год назад +1

    *Zidane amoul karaw dieul coupe* 😊 ya meune punch

  • @cherifnassardineaidarambay5507

    Akbess😂😂😂😂 Zeuss yagui koy néweulll dolé dehh

  • @mouhage2157
    @mouhage2157 Год назад

    Gueye ndioro ❤

  • @talladieye6086
    @talladieye6086 Год назад +1

    Wtf zeuss rap deug lay deff🎉

  • @djo_221
    @djo_221 Год назад +2

    Oothentik ya meune ya eupp dolé ya geuneu fété xallléééé wrewwww 🎉🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @Fansclubsoumanebongo
    @Fansclubsoumanebongo Год назад +20

    Quand le chat 🐱 est la tu tant bat les couille bou deé ioe gainde 🦁 nga nice punch yaci meuneu

  • @Thiouneeee17
    @Thiouneeee17 Год назад +1

    Salifondé wouyou ma 🔥🔥punchline yi dop

  • @pipssthelyricist
    @pipssthelyricist Год назад +5

    Boy Keur Ndiaye Lo daye lakè🎉🎊✨✌🏾

  • @yahyawade3311
    @yahyawade3311 Год назад

    Ils ne reste que 2 rappeurs aux Sénégal et c'est lui et Bmjayy

  • @gastarpdg8490
    @gastarpdg8490 Год назад +1

    Il est bon 🎉

  • @Enzo_Welbeck
    @Enzo_Welbeck Год назад +1

    Dope mon Gars 🔥Dokhote nga digou hip hop bi .

  • @issaboye2021
    @issaboye2021 Год назад +2

    Flèche waŕga flécha....Misterio Ndiaye lô got TALENT

  • @bilalfall1125
    @bilalfall1125 Год назад +1

    Aladji ass ya meune gneup✨🥳

  • @karbatwomc4024
    @karbatwomc4024 Год назад

    Ya bandit bro yako tay koumene say non wrew🔥🔥🔥🔥

  • @agroline.diagne3422
    @agroline.diagne3422 Год назад

    #Akbess boul meuss tonton bala Zeus di tioum sa mam 😂😂😂

  • @malicktoure916
    @malicktoure916 4 месяца назад

    Zeus je t'adore trop walla 😂❤eplus le frérot, yagui melni kou am 20ans jtj

  • @elpero2140
    @elpero2140 Год назад +1

    Kou leune li nguay dèf boula nékhé rèèw ❤❤ je valide 😂😂

  • @Ouzmilliad
    @Ouzmilliad Год назад +1

    Nice