Sans nul doute son savoir est immense ..la façon dont il l'explique est unique repose en paix ya oustaz la fayda ne t'oubliera jamais vous nous avez rendu si fièr ...
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته Mashallah , Grand Merci à Oustaz Biteye pour le niveau et la pertinence de ses émissions. Félicitations à nos deux imams. Ils ont été à la hauteur. Salutations depuis San Sebastián Jërëjëf بارك الله فيكم
Débat bii dama si am kersa beu légui ndakh kimou diakarlol bakh neu torop mais il n'était pas à la hauteur... Dieureudieuf Oustaz Ba Yalla na Yalla yokk kham-kham bi té kattanal la
Fa tabarakallaah ! Yalla na Yalla tabbal Oustaz Ahmad Ba aldiana bi gueuneu kawé. Remarquez comment l’assistance est entrain de l’écouter religieusement ! Wallaahi doundeum am na ndiarigne!
Dieureudieuf oustaz biteye oustaz ameth ba yalla n'a la yala faylen ci barke sydi n'a Mohamed amiine yarabie xam xam by rafena lol content lol ci yeen machala 😘☝️☝️🙏😇😇😇❤❤❤
C'est le Dieu des Dieux qui façonne le cré de la créature de façon à ceux qui sont dans le trône de sa royaume se manifeste dans l'esprit du croyant édifié spirituellement.
Fa tabarakallaah ! War nagniou gueuneu fonk sougniou kilifeu diné yi. Kén wéranté woul kham khamou Oustaz Ahmad Ba té gnieup nangou nagniou né Cheikhal Islam moy Serigne gnieum. Waaw Kone lérna ni sougniou Serigne ci amougniou morom.
Le surlendemain de son enterrement 😄😁 vraiment pas par ce que je content mais plutôt les dimensions dans les qu'elles il s'exprime le regard de baye Aliou ba qui voit un autre oustaz amad ba parler wallahi y'allah maynaleu...
et pourtant y a des gens qui habitent au senegal qui ont un savoir inconmesurable hors paire et qui sont des fervent musulmans mais ils se prononcent rarement à cause de leur >
Kiii mo moudiou ci say nopou rek. Affaire bi dou Médina Baye ou ailleurs. Cheikh Tidiane leu, moy nandal ay talibém niou raw nieupp. En plus mom mi di wakhtane, nieuwoul pour wakhi parparlo comme yaw doff bi, diwakh ay wakhou niveau. Xam-xam bo guiss, xam-xam mi ngui ci kawam. Nangoul ko mom mii té mandou ci lidéss. Li Yalla yorr yeup ci xam-xam diokhou ko Cheikh bi kécé. Bayilén wakhi doff. En fin Cheikh bi Yalla nako Yalla dolli ay may ndakh fékheul na sama khol
Un débat islamique doit avoir kune seul finalité c d prendre sa Vérité com modeĺ a suivre mai demander dan l bu d dénigrer ou d trouver un nullard n est k polimik Dieureufe BAYE
Sans nul doute son savoir est immense ..la façon dont il l'explique est unique repose en paix ya oustaz la fayda ne t'oubliera jamais vous nous avez rendu si fièr ...
🎉
Amine
Tout ce qui se conçoit bien s'annonce clairement et les mots pour le dire viennent aisément dieureudieuf Oustaz Ba.
Waxatiko d !
Qui a dit ça ??
Wallahi je ne suis pas soufis mais cet homme m'impressionne à chaque fois que je regarde ces vidéos que ALLAH lui accorde son paradis 🤲🤲
Ahhh bah walag katabna fizabourri minebahdi zikkr aradnal arda yahrisouha min ibadillahi salihinna ...ustaz bah yalla nalla yalla guerem ter yokusaay daradia ...bokugasi kawteff yalla yiii
Il fait parti des meilleurs ces vidéos datent de plus de 5 ans... Oustaze Ahmed ba mérite plus de dans les chaînes de télé
@@Daoudaj tu veux son numéro?
Kén dou Oustaz Bâ skéy 🙏❤Niass
Alkhandou lillah Macha allah Oustaze Ba xam xam bi fachana yallna yalla Barkél yallna Baye Niass féyanték yow si Lou bah .sante Baye Niass rék
Yallah contane n’a si Yaw Y’a Outaz walahi azim degu degu karama Baye Niass gua 😭🕋🙏🏾
Ndeysane yalna allah yokkou sa léer niass ba
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته
Mashallah , Grand Merci à Oustaz Biteye pour le niveau et la pertinence de ses émissions.
Félicitations à nos deux imams. Ils ont été à la hauteur.
Salutations depuis San Sebastián
Jërëjëf
بارك الله فيكم
Nagniou gniaanal bou baakh Oustaz Ahmad Ba ! Il faisait la fierté de tout musulman et en particulier de tout Talibé Cheikh !
Macha Allah kham kham daal nekh na wayé dieuredieuf oustaz ahmeth ya woor💖
Machala xam xam rk mo ousstass yalna yalla fay yiw j'aime les niasséne ndax Séne begue yalla ta xam yalla
Débat bii dama si am kersa beu légui ndakh kimou diakarlol bakh neu torop mais il n'était pas à la hauteur...
Dieureudieuf Oustaz Ba Yalla na Yalla yokk kham-kham bi té kattanal la
Mané ko bokoul nak nanou waaye yi bokoul bénéne wadji diambaar la mais vraiment il n’était pas à la hauteur
@@souroublegadiengalama4932 Alhamdoulillah
Niome niar nion bokou loniouye wakh bayiléne parparlo thi dînedj topal feulé waye
@@souroublegadiengalama4932 j admire oustaz ba mais l autre est à LA hauteur et est plus posé car il ne cherche pas à impressionner biteye
@Sy Babacar salam alayka.dieureudieuf si kaddouy yi.wayé Wallahi parparlo wouma,soumma wallahi liniouy wakh bokkoul...nguén balma akhe
C'est ce genre de plateau dont le Sénégal à besoin
Machallaha barhama Niass yallah na niou yala Faye barhama Niass dianatoul firdawsi !❤❤❤!
Baye Niass mo meuneu daiffar..Oustache ba yalla ngua gouddou fane andakk weurr ak weurseuk ak willaya ak allale ak barkai
Amine ya Rabbi
Dieurdieuffé baye niass amoul morom
Ndeysane sa niane mom moy lolou 😢
Ndëysane xoolal waadji si guinaawam ak mbékté gui ❤️ xam xam rék moo woor MAACHA'ALLAH 🧠💫
Fa tabarakallaah ! Yalla na Yalla tabbal Oustaz Ahmad Ba aldiana bi gueuneu kawé. Remarquez comment l’assistance est entrain de l’écouter religieusement ! Wallaahi doundeum am na ndiarigne!
Dieureudieuf oustaz moumadou wilane yalla n'a la yala faylen ci barke sydi n'a Mohamed amiine yarabie machala 😘❤❤😇🙏🙏☝️☝️😘
Merci Baye Niass ,il nous a libéré
Yagu na
Billahiii❤ gm baye niass
الحمدلله رب العالمين جرجفي باي إنياس أستاذ أحمد به ماشاءالله بارك الله فيكم وجزاكم الله خير الجزاء أبلغت
Ndeysane waaw amoul solo lou baax mo lene taxa diok dagni khadialanté rek kham kham bi leer na machaallah
Masha AllaH Jeureudieuf Oustaz Ba
Wallahi xam xam rek laa Dieureudieuf seydi Ba yalna yallah yessal yeurmandë wam ci ioe
Dieureudieuf oustaz biteye oustaz ameth ba yalla n'a la yala faylen ci barke sydi n'a Mohamed amiine yarabie xam xam by rafena lol content lol ci yeen machala 😘☝️☝️🙏😇😇😇❤❤❤
kham kham bou lére rek oustaz Ameth ba machalah tu es le meilleur
Oustaz Ba mashallah yalla na yalla weral xam xam bi
اللهم اغفر استاذ أحمد به وارحمه وعافه واعف عنه وأكرم نزله ووسع مدخله واغسله بالماء والثلج والبرد ونقه من الذنوب والخطايا كما ينق الثوب الابيض من الدنس
Bilakhi yalla na ko yalla yeuram si barkip seybina mohamette barkip ailkhorann karrim
Qu'Allah t'accueille dans son Firdaws Oustaz Ahmed Ba. Un esprit Clair est parti.
Amine ❤😢😢
C'est le Dieu des Dieux qui façonne le cré de la créature de façon à ceux qui sont dans le trône de sa royaume se manifeste dans l'esprit du croyant édifié spirituellement.
حفظك الله يا استاذي
استاذ احمد به
Fa tabarakallaah ! War nagniou gueuneu fonk sougniou kilifeu diné yi. Kén wéranté woul kham khamou Oustaz Ahmad Ba té gnieup nangou nagniou né Cheikhal Islam moy Serigne gnieum. Waaw Kone lérna ni sougniou Serigne ci amougniou morom.
Dieureudieuffffeeeeeeeeeeeeeeeee BAYE NIASS Oustaz diam si yaw
BILAHI LI DOUMASSI DOYALL
DIEUREDIEUF BAYE NIASS❤
pour bien reconnaître le savoir dé OUSTAZ BA il faut un plateau spécial pour lui
Wallahi cheich bi.
Bilayi thie borom kham kham youma meussa deg yeup ken eupoukassi kham kham
Ma cha alla
Wahdatoul woudioud pass pass bou bone la
Walahi
Machalla YALLA na Yalla gudal seni fane 💯💯💖💖💖🙏🙏🙏👑👑👑😘😘😘😘
Yalla nala yalla yeureum té kharé la aldiana 😭❤️
Amine yarabi ❤
اللهم اغفر له وارحمه واسكنه فسيح جناته الفردوس الأعلى ببركة رسول الله صلى الله عليه وسلم
Macha Allah, ya'Allah waxtal bi nekna amna solo lol. Yalna Yallah barkel Bá
ماشاء الله أستاذ أحمد به فرحنا بك غاية الفرح جزيت خيرا وكفيت شرا بجاه سيدالكونين والثقلين
Machallah way oustaz bâ kham kham bi leure na
Wassiha kursiyu samaawaati wal ard walaa yahuuduhu hifzuhumaa wahuwa al aliyul haziim☝🏾
Mach Allah Oustaz Ahmed Bâ dieureudieuff xam xam bi lerr na
Machalla yalla nako yalla yeuram thi barke alkhouranoul Karim ya oustas ba
Aminé ya rabbi 🤲
Qu'allah soit satisfait de lui🙏🙏 Rahmatoulahi Aleyhi
Oustaz Bâ amoul morom😍
Oustaz BA bii déi, maachallaah
Débat très intéressant qui fait frémir les cœurs de bonheur (Woudjilat khouloubikoum)
❤❤
Merci à Ouztaz wilane et ouztaz Ba kham kham bii leer neu
Machalla oustass Hamed ba
oustaz ahmed ba fierté faydou fouta toro
le meilleur ❤❤❤
. machallla ba yalla na la yalla khare aldiana
Nyerejeff Oustaz Bah,lii moi Ham Ham, Deugeu
Ya oustaz❤😭😭😭🤲🤲
Yalla yalla faye
جدد الله رحمته ويسكنه فسيح جناته الفردوس الأعلى ببركة رسول الله صلى الله عليه وسلم
Ohhhhh oustaz dieureudieuf 😢 baye amoul morome
L'autre ouztaz aussi je connais pas son nom mais il est calme et connaissant
Diéme Yanla thi kaw la nék.mais kham khamam mo nék fép.Bouléne compliqué mbir yii té yanla takh.
No oustas Bâ dou nite barcké serigne touba li dafa lér
Boul yemou sama Xarite, Ouztaz kéneu la rèk si Talibé Baye Niass you ndaw yi
Macha Allah Ouztaz Ba est trop fort
Machalla son ame repos en paix
Mashallah yalna yalla barkel
Machalla jërëjef seydina Aïdara mb
الحمدلله اللهم لك الحمد حتى ترضى ولك الحمد إذا رضيت ولك الحمد بعد الرضى ❤️
فالعلم لعمري هو إمام العمل
Oustaz ba weli
Thiey xam xam mo nékh bilahi machallah
LAA ILAAHA ILLALLAAH
MOUHAMADOU RASSOULOULLAH SAWS
Oustaz ba d'où nitt kesse Al hamdoulilah
Le surlendemain de son enterrement 😄😁 vraiment pas par ce que je content mais plutôt les dimensions dans les qu'elles il s'exprime le regard de baye Aliou ba qui voit un autre oustaz amad ba parler wallahi y'allah maynaleu...
Machalla seri mory willane alhamdoulila
kou may dimbale ma guiss oustaz ba nguir YALLA
machalah xam xam rk woor bilahi yallah doli ko yeurmande
Alhamdoulilah mashallah dieureudieufé BAYE
Machahlah débat bi nékhna
MaSHA ALLAH
Les niveaux ne sont pas les mêmes Medina Baye est incontestablement le temple du savoir
et pourtant y a des gens qui habitent au senegal qui ont un savoir inconmesurable hors paire et qui sont des fervent musulmans mais ils se prononcent rarement à cause de leur >
Amoul sikk déhh .
Tu mens
Kiii mo moudiou ci say nopou rek. Affaire bi dou Médina Baye ou ailleurs. Cheikh Tidiane leu, moy nandal ay talibém niou raw nieupp. En plus mom mi di wakhtane, nieuwoul pour wakhi parparlo comme yaw doff bi, diwakh ay wakhou niveau. Xam-xam bo guiss, xam-xam mi ngui ci kawam. Nangoul ko mom mii té mandou ci lidéss. Li Yalla yorr yeup ci xam-xam diokhou ko Cheikh bi kécé. Bayilén wakhi doff. En fin Cheikh bi Yalla nako Yalla dolli ay may ndakh fékheul na sama khol
C vrai c un talibè baye mais il a fait une partie de ses etudes a boghè au fouta en mauritani il y a bcp de Hamed ba au senegal
Macha lha ouztas ba ouztas mori
Al hamdoulilah BAYE NIASS
اللهم اغفر له وارحمه واسكنه الفردوس
Amine!
Maachaa Allah
Machalah oustaz ba gueth laa thi xam xam Mai wakhtaan ak ay xam bou diap ni dafa xam mo metí
Dieureudieuf ya oustaz
Mancha Allah Cheikh Ibrahim Niass
Eskey ba machalla amnasolo machalla
Dieredieuf ouchtache Ahmed ba
Macha'llah thieuw oustaz bâ yall na baye niass fayla
Alkhourane ak Sunna ❤️🙏🏾
Un débat islamique doit avoir kune seul finalité c d prendre sa Vérité com modeĺ a suivre mai demander dan l bu d dénigrer ou d trouver un nullard n est k polimik Dieureufe BAYE
Kouci nanoul do komp masha ala dieuredieufé baye cheikh al islam
Macha allah sayedi ba
Machallah bon débat
Alhamdoulilah yalla diame sakh
Yalla nako yalla yeureume tète kharè aldiana cy barkè baye niass
Mashaallah ya oustaz 🙏🙏🙏
Thieye Sénégal gno bari khame khame
Machallah oustaz Ahmed ba
BA yo Allah juunou balde ma
Aamin ya rabbi