Oustaz Ahmed Ba Debat RDV

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 27 дек 2024
  • Oustaz ahmed Ba

Комментарии • 205

  • @justuncliktv5262
    @justuncliktv5262 5 лет назад +10

    Ndeychane je suis Talibé Baye. débat bi c’est très riche et important. Niom niarr nieupp amnaniou xam xam té ay geustou kat laniou seulement que L’autre invité problème dëgg la am motax souvent danguay degg Baye di wax Yalla naniou Yalla may dëgg ganaw lolou Yalla naniou Yalla may topp. Alxuran sax borom xell yi lay waxal. Diarama Oustaz Ahmad Ba. Yalla na Yalla def diam si ummah bii

  • @TheKilifa
    @TheKilifa 10 лет назад +22

    Alhamdoulilah Yalla naniou Yallah may dégg ! Dieureudieuf Ouztaz Ba sa ham ham sétt na séll na wérr na ... Choukrannn .Talibé Bay deug moy yaw .

    • @madamebittaye2249
      @madamebittaye2249 9 лет назад

      Dem Len diangui Ba yeyowoul deg oustaz khamoul dara bou neke li mou wakh la kham.

    • @cissetahiroupascal6004
      @cissetahiroupascal6004 7 лет назад +7

      Ton coeur est malade vraiment.. Tout le monde sait et voit que Oustaz Ba da beuri xam xam. Wakhal lenen. Lan mo le méti par exemple!? So len bokoul tarikha tam yen na bok diiné dé len rafetal té bayi sokhor, febar xol le d

    • @aliouly9660
      @aliouly9660 5 лет назад +1

      Même l'ignorent le plus ignare au monde sait que OUSTAZ ba est un grand savant.

    • @babaagne7656
      @babaagne7656 Месяц назад

      Oustaz deh alkhourane hadiss wakhou borrom xam xam yi ak yeuk yeugam . Fo ték khamoul dara.

  • @9Fadel9
    @9Fadel9 9 месяцев назад +6

    Yalla nako Yalla Defal yeurmande 🙏🏾🫶🏾

  • @kebadiop9819
    @kebadiop9819 11 лет назад +19

    oustaz ahmed t'es vraiment une fierté pour l faydou de baye niass!!lii dafay wané né baye dou sene morom!!!yalla fay laa!!

  • @aliouly9660
    @aliouly9660 5 лет назад +20

    ce qui est dans le cœur de cet homme dépasse largerement le niveau des plateaux de télévision.

  • @lomsoumare468
    @lomsoumare468 7 лет назад +38

    Baye niass nakhougnou billahi

  • @kemp2mgrafff914
    @kemp2mgrafff914 4 года назад +9

    Bilahi Peulbi mo bari xamxam Machalla... yallna gouddou fannnne

  • @abamba13
    @abamba13 8 лет назад +30

    Oustaz ba yalla na yalla yokou fanam ak xam xamame

  • @momarniang6670
    @momarniang6670 5 лет назад +11

    Machalla , qu'Allah procure sa bénédiction et sa protection à Oustaz Ba et à tous les ulémas .

    • @alhaqq310
      @alhaqq310 5 лет назад +1

      Amiiine ya Raby Macha'Allah

    • @saullayton4476
      @saullayton4476 3 года назад

      sorry to be so off topic but does anybody know a way to log back into an Instagram account..?
      I stupidly forgot my account password. I appreciate any assistance you can offer me!

  • @lomsoumare468
    @lomsoumare468 7 лет назад +12

    macha'allah oustaz bâ Baye Niass réek moye deugue

  • @namadiop4077
    @namadiop4077 6 лет назад +6

    Ki si khame khame layi wakhé.kou amoul khame k hame do dégueu limouy wakh.merci oustage Ba

  • @barhamasene3118
    @barhamasene3118 5 лет назад +8

    thiey l meilleur ds guide c'est l savoir djeredjeuf Baye niass Macha alla Oustaz Ba

  • @mouhamedmaria9003
    @mouhamedmaria9003 10 лет назад +9

    sant yalla alkhamdoulilakhi pour moi affaire bi diaroul khoulo diaroul wéranté kham yalla rek inchala

  • @djibyndiayeboxeur5438
    @djibyndiayeboxeur5438 5 лет назад +5

    dou moromou kene oustaz bah yalla moy maye nouko nekh moko moye yalnako doli

  • @mohamednaby5384
    @mohamednaby5384 4 года назад +4

    Mashallah Amna solo 💟 💟

  • @cheikhousow3486
    @cheikhousow3486 6 лет назад +2

    Journaliste bi amoul beneu yarr dieum cii ouztaz ahmed Bâ.
    Wakh dey teguinee rawatina debat gou nimel. Ya salam

  • @ousmanesakho4422
    @ousmanesakho4422 5 лет назад +4

    Liii dou debat puisque les niveaux n'ont pas pareil

  • @talladjitte8756
    @talladjitte8756 Год назад +2

    Oustaz Ahmed ba yalla nako yalla yeureum

  • @ismailabah4276
    @ismailabah4276 7 лет назад +10

    non benene oustazbi niakoul khamkham juste limou kham rek la wakh

  • @musafaye5346
    @musafaye5346 3 месяца назад +1

    Khamkham dafa nexh, thank you so much oustaz Ba

  • @bayegueye6839
    @bayegueye6839 5 лет назад +3

    ماشاء الله بارك الله فيك ياأستاذ أحمد باه

  • @bayegueye6839
    @bayegueye6839 5 лет назад +5

    حفظكم الله ونشكركم ويطويل عمركم

  • @cheikhoumbodj6612
    @cheikhoumbodj6612 11 лет назад +27

    gayi ni oustaz ba daléne done yokk si yalla. il ne boxe pa dans le mém ring doussakh béne

  • @laminekone6329
    @laminekone6329 7 лет назад +9

    thiey yala khamkham deug ci deunde laye nekk zairla ak batine nagoulene batine yala maye nako gnou barri rawatina wakeur baye yi machala

  • @jobizjobe7436
    @jobizjobe7436 4 года назад +1

    Slam... Dos anyone have the full video pls

  • @ousmaneboiro7518
    @ousmaneboiro7518 7 лет назад +6

    dieurdieuf oustaz ahmed ba

  • @ousmanethiam5314
    @ousmanethiam5314 11 лет назад +24

    Je suis pas un disciple de Baye Niass mais javou qu ils sont trop fort Oustaz Ba et lautre ne boxe meme pas dans la meme category

    • @iboupene6101
      @iboupene6101 5 лет назад +10

      Moi js8 disciple de baye Niass mais je te conseille de ne pas t'arrêter à ki est plus fort comprends et gorgorloul si diné bi c'est ce ki est réellement important

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 5 лет назад +4

      Machallah Yalla nala Yalla bolé ci Talibé Baye yii

    • @leuzleuz8602
      @leuzleuz8602 5 лет назад

      Pour toi c'est la boxe

  • @djibyboxeur838
    @djibyboxeur838 9 лет назад +18

    oustaz ba mouna diagal serigne yi néka si sénégal yép ak koumou ménti DON

    • @batinegueye4872
      @batinegueye4872 5 лет назад

      Lo lo wé roul

    • @bayelamajakirtv2029
      @bayelamajakirtv2029 4 года назад

      Lou ler

    • @mouhamedthiam9048
      @mouhamedthiam9048 4 года назад

      Louleine sein heil joh reik niou wahko..da wah reik mai am na niou ni patte fesse deil .borom ham ham la ..nak..

    • @mouhamedcisse9728
      @mouhamedcisse9728 4 года назад

      Kouko widi kay andil sa serigne plateau kham kham yi face to face talibè baye rek la guis gnioukoy def (entre eux ou bien gnome ak ibadouyi) gayi wakh rek mais kèneu doulène affrontè

    • @mamadoumanediop3601
      @mamadoumanediop3601 4 года назад

      @@mouhamedcisse9728 wakho DEUG dh

  • @momodiack2494
    @momodiack2494 4 года назад +1

    بفضلك أيها السني .والباقون لاتجهل الناس احفظوا علوامكم

  • @mohamednaby5384
    @mohamednaby5384 4 года назад +2

    Mashallah Amna solo 🌹🌹😍😍
    mashallah amna solo 🌹🌹❤️ 💗

  • @lomsoumare468
    @lomsoumare468 7 лет назад +5

    macha'allah dieureudieufé Baye Niass la solutions​

  • @amadoudione7291
    @amadoudione7291 2 года назад +2

    Machallah serigne Ahmed ba

  • @djibyboxeur838
    @djibyboxeur838 8 лет назад +13

    oustaz bi dafa beure xam xam machallah xam xam rek laye wakh bilahi mor yaw Amoulo xam xam té xaméwo

  • @mouhamednazircoundoul6391
    @mouhamednazircoundoul6391 10 лет назад +6

    yalla na yalla yok sén léér

  • @babandiaye9405
    @babandiaye9405 11 лет назад +8

    salam on voudrait d'autres dars ou waxtane de Oustaz Ahmad Ba si possible

  • @gayegaye9457
    @gayegaye9457 5 лет назад +2

    شكرا لكم بهذه الجلسة لما فيها من منافع كثيرة

  • @KanteJamil
    @KanteJamil Год назад +1

    MACHA Allah

  • @boubasarrsarr934
    @boubasarrsarr934 7 лет назад +5

    ماشاء الله بارك الله فيكم

  • @ndiaga79
    @ndiaga79 11 лет назад +7

    thieye baye niasse lepp mome la

  • @bayeibrahimaniassniane7003
    @bayeibrahimaniassniane7003 7 лет назад +3

    Oustaz macha allah xam xam dal mo woor

  • @sylladiaite4824
    @sylladiaite4824 5 лет назад +3

    Wollah oustaz je vous aime

  • @myasow8087
    @myasow8087 Год назад +1

    Mashalla paix à son âme 😢

  • @baxboy3895
    @baxboy3895 7 лет назад +2

    Macha allah oustas Ahmed ba

  • @kinapapa4657
    @kinapapa4657 5 лет назад +2

    Oustaz Ahmed Bâ Yallanafi yag té weur Bilahi walahi tanhallahi mangilaye talale samaye lokho gueume nala wolounala té bougounala guisss trop sakh bilahi nga yobouma fa yalla

    • @adamasow9292
      @adamasow9292 5 лет назад

      So begué ma diokh la numero wame nga woko direct

  • @LaminNiass-v8i
    @LaminNiass-v8i 4 месяца назад +1

    رضي الله عنه ونفعنا به

  • @serignembacketv3618
    @serignembacketv3618 4 года назад +2

    Gnari oustaz yeuppou lignouy wakh khamnagnko

  • @serignemodouniasse3561
    @serignemodouniasse3561 6 лет назад +6

    Niom niarr xam xam bou lerr laniouy whh lolou rekk mo am solo

  • @matarcisse9063
    @matarcisse9063 5 лет назад +2

    Machallh bâ machallh

  • @dembaly9050
    @dembaly9050 11 лет назад +6

    xam xam dafa am solo yalla nekoufi ak kene kou fokné ya ngui fi ak mom ya ngui nakh sa bop :lolou moy bokalé yalla bou guena mak c prkw yalla né dou bal mouk koukay bokalé car si batine bok sou amé da fek mou nek niar manam yaw ak yalla lolou motakh niit ki dafa wara effacewou sakhal dieum yalla dji lolou rek moy deug (BAYE NIASS si les gens te connaissaient lep leerr)

  • @omarcamara9028
    @omarcamara9028 5 лет назад +2

    Mashalla ya oustass ba

  • @adamthiam5175
    @adamthiam5175 5 лет назад +2

    Machalla si outasyi amanane kham kham

  • @mamourba1889
    @mamourba1889 7 лет назад +2

    Maashalla doundal oustaze di defendr payi bii

  • @sayediop7987
    @sayediop7987 5 лет назад +2

    Machalah xam xam bi barina ta lere

  • @elhadjiniane8154
    @elhadjiniane8154 6 лет назад +2

    Machall Baye Niass Reik Reik

  • @DIENGPapi
    @DIENGPapi 11 лет назад +2

    Masha Allah yalla naniou Yalla mousseul ci erroné
    Yalla naniou yalla may Yalla

    • @sambadiao7245
      @sambadiao7245 7 лет назад +2

      Amine papi.....defection bakhoul wayei nak yalla wakhnaka dei

  • @amboutiqueba240
    @amboutiqueba240 6 лет назад +4

    Oustaze ba amo morom

  • @abdoulayeagne7089
    @abdoulayeagne7089 6 лет назад +4

    Mais le débat est équilibré chacun défend son avec des idées et des arguments clairs chacun des deux spécule nul n’a eu le monopole de la vérité c’est le débat de l’islam car son champ est vaste et le savoir est large donc pour moi ce débat est équilibré on ne peut accorder victoire personne ne juger pas à partir de vos appartenances dans les maisons religieuses et aussi à partir de l’éloquence des paroles

  • @djibyboxeur838
    @djibyboxeur838 9 лет назад +8

    oustaz xam xam rék lay wakh kouko wédi xam xam nga wédi me pas mome

  • @mbayesarr743
    @mbayesarr743 8 лет назад +7

    wallahi niogui laye sante ci sa xàme xàme

  • @kalamoukalamou6068
    @kalamoukalamou6068 6 лет назад +3

    Bilay baye niass dou morome ....

  • @malickdiallo3331
    @malickdiallo3331 4 года назад +1

    Macha Allah gnabotou Cheikh rta

  • @ababacarniang605
    @ababacarniang605 4 года назад +2

    thi mane c 50 50 yene deglou woulen sakh li oustaz mory di waxx

  • @cheikhbayedittara1020
    @cheikhbayedittara1020 10 лет назад +25

    baye dou morom li wanènako

  • @monopinionhd7581
    @monopinionhd7581 5 лет назад +2

    Machallah oustaz ba

  • @desunoto6869
    @desunoto6869 11 лет назад +12

    xol lene meu diference bi rk, bilahi yereum nako saax ndax niak xam xam

  • @dethiediouf7400
    @dethiediouf7400 5 лет назад +2

    thiey hamham deug laniou wah bep talibé Baye niass école la

  • @amadougueye5347
    @amadougueye5347 4 года назад

    Oustaz Ahmed ba diaridieuf xam xaw séla na yana yalla samou la diaridieuf

  • @elhadjibabouceesay9354
    @elhadjibabouceesay9354 4 года назад +1

    Ma challah ❤️❤️❤️

  • @ahmedseck558
    @ahmedseck558 11 лет назад +3

    Machalla oustaz Ahmed mais est qu on peut avoir la suite de la video

  • @gaoussoucisse2752
    @gaoussoucisse2752 11 лет назад +5

    thiey baye niass diference dafa léreeee

  • @ablayesarre-Fatima
    @ablayesarre-Fatima 4 года назад +1

    niom niar nieupe danio am xam xam mai vu les commentaires sénégalais mo beugg concurrence sèn diné yeupe lolu la et c'est vraiment dommage guémulén yallah sakh ay niit rék nguén gueum tei mak gni niom nguén gueum yallah lagn beugone mai pas nguén gueumlèn niom mai dommage que c'est le contraire

    • @mouhamedcisse9728
      @mouhamedcisse9728 4 года назад

      Demal nèk talibè baye bayi sisoubi sa wadji khamoul tousss

  • @djibyboxeur838
    @djibyboxeur838 9 лет назад +8

    sante yalla ak seydina mouhamad psl baye nakhougnou
    li dafa lér

  • @lesavanttv4631
    @lesavanttv4631 5 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤

  • @cheikhsidyndiaye-yf1mm
    @cheikhsidyndiaye-yf1mm Год назад +1

    Khakham dem na

  • @mamadouniang47
    @mamadouniang47 6 лет назад

    contanena si gnom gnar nieup xam xam fegn na machalla yalla na yalla fay

  • @ebrimatouray9464
    @ebrimatouray9464 6 лет назад +1

    Yana yala yagalafi si barké baye Nyass

  • @amathbiguprastafffsylla7277
    @amathbiguprastafffsylla7277 7 лет назад +2

    ALHAMNDOULILAH

  • @mahdibalde6932
    @mahdibalde6932 6 месяцев назад

    Le niveau de outaz Ahmad bah est supérieur au Sénégal

  • @ndeyemalickmbow8901
    @ndeyemalickmbow8901 6 лет назад +1

    ماشاءالله يا استاذ باه

  • @ndiayealiou286
    @ndiayealiou286 6 лет назад +2

    dème si baye NIASS wane léne yalla

  • @amethgueye4082
    @amethgueye4082 5 месяцев назад

    Machallah 😢

  • @laminemoukaramoubarasow4803
    @laminemoukaramoubarasow4803 9 лет назад +3

    khamm yalla rekay deg emission ana importances

  • @mohamednaby5384
    @mohamednaby5384 6 лет назад +1

    Allahu akbar

  • @alioukandji9966
    @alioukandji9966 3 года назад +1

    Massalla islam ca kanam

  • @ousmaneniane1822
    @ousmaneniane1822 5 лет назад

    Billahi wallahi BAYE Niass Rekk moy Deugg

  • @alassanecoundoul2759
    @alassanecoundoul2759 11 лет назад +2

    machalla

  • @karimmane7491
    @karimmane7491 10 лет назад +1

    Yalla gui fepp lolou dou tawkhit waye fep gui ci si yalla

  • @mamadouniang47
    @mamadouniang47 6 лет назад +2

    La suite du débat svp

  • @serignemodouniasse3561
    @serignemodouniasse3561 6 лет назад

    Yalla ngui fepp kenn douko wakh feppa nekk si yalla ndakh yalla mo sakk place yepp

  • @mohamednaby5384
    @mohamednaby5384 6 лет назад +1

    Masallah

  • @papamoussasow3293
    @papamoussasow3293 3 года назад

    Thiey AL OUSTAZ Talibé BAYE NIASS

  • @ndiayelamune6859
    @ndiayelamune6859 2 года назад +1

    ماشاء الله تبارك الله عليك يا سيدي

  • @cheikhlaminediop9372
    @cheikhlaminediop9372 6 лет назад +1

    شكرا جزيلا

  • @mactardrame1901
    @mactardrame1901 9 лет назад +5

    vraiment mor gueye tu as montre ta faiblesse.le debat n'est pas equilibre oustazba daf ka raw lou baryyy

  • @ousmanesana3477
    @ousmanesana3477 4 года назад

    La foi peu déplacé les montagnes kham kham rék mo amsolo baye Niass la solutions

  • @ebrimatouray9464
    @ebrimatouray9464 6 лет назад +1

    Massa-alla

  • @kebatraore5883
    @kebatraore5883 11 лет назад +1

    Sakhalale laine Yalla li mou sakhalale bopame tai niou nopalikou

  • @cheikhbayedittara1020
    @cheikhbayedittara1020 10 лет назад +1

    machallah

  • @kebatraore5883
    @kebatraore5883 11 лет назад +1

    Ndji da gnon gueuneu khame Yalla bopame baye soppi a ka dakhe li Yalla sakhalal bopame

  • @aliousow6213
    @aliousow6213 7 лет назад +2

    Yalla mogi fou nekk mogi Fou nekkoul وآلله وجود فى وجود وآلله وجود فى عدم