Ahmed Khalifa Niasse Ndeyssane kou ame yité leu kou meunti ame nakkar ak fo meunti bokk di na takhaw seu beussou nakkar ! Yalla nako Yalla faye ! Serigne Bethio Yalla nako Yalla yeuram 👏🏽
Avec tout le respect que je te dois Segne Khadim, tay mom def nga dioumbté lou reuy. Cheikh Béthio délouwoul si kéne koudoul Yalla. Té en plus kéne rék moo mom assamane ak souf té moy Yalla. Boudone Segne Saliou moy Yalla kone dou dé. Waa Salam
Mane niome daniouma djiakhal sax ba legui niogu bokkalé Sene serigne yalla rek moko mene yereume ta baleko aye bokaleme Bene xel daloule souniou wakhaté ak deuk
Sourate baqara verset 28 Comment pouvez-vous renier Allah alors qu'Il vous a donné la vie, quand vous en étiez privés? Puis Il vous fera mourir; puis Il vous fera revivre et enfin c'est à Lui que vous retournerez.
Vraiment c’est dommage quand vous croie que c’est serigne Saliou qui vous ramène au paradis vous oubliez dieux est le profete m’aime serigne Saliou némerai pas que vous prononcer son nom avant dieux lui c’est t’es un bon misulmen Sénégal doyena war
Mes condoléances les plus attristés et mes respects les plus profonds ainsi que mes prières lui font cortège! Mis à part cette tristesse vécu par tous les sénégalais, il est gravement tant de revenir à la normale, du moins de récupérer la raison! Que pensez vous de ces victimes, je ne dirai pas de part sa faute mais via son nom? Aujourd'hui tout le monde éprouve des sentiments de solitude cumulés à une tristess en apprenant le décès de Cheikh Bethio Thioune; pour moi, il faut tout de même penser à ces victimes, de nombreuses fois cités morts ! Toutes les personnes sont importantes, chacun compte pour quelqu'un et souvent sur quelqu'un! Une perte humaine est toujours pénible à vivre! Feu Cheikh Bethio (paix à son âme) a peut-être mal gérer sa confrérie avant d'être d'une générosité reconnue par tout le pays! Il va grave manquer le Sénégal Après tout! Il avait le rôle du sel dans une marmite en plus d'être guide religieux pour ceux qui le suivaient! Après mûre réflexion, je note un manque de sincérité et une hypocrisie sans fin de ma nation! Comme chaque personne sur terre, Bethio était propre en nature, les personnes sont différencier par leur caractères. Ceux qui l'ont sévèrement critiqué hier, sont ce qui l'aiment aujourd'hui où il n'est plus! C'est de l'incohérence absolue! En effet, les opinions sont nombreux, chose normal et bien de dire ce que l'on pense! Sur ce coup, j'ose dire qu'il est parti au bon moment; et je continue de croire qu'il est sauvé d'une tragédie (10ans de prison +travaux forcés) par la divinité qui ne cessera de blanchir le nom de SERIGNE SALIOU MBACKE! Il a toujours cru à ce dernier qui à la longue était sa source de respiration malgré le fait de pratiquer la religion musulmane à sa manière! Tout musulman notamment Mouride, doit donc remercier Alah, pour l'étendue de sa discrétion! Car en fin, le NOM DE SERIGNE SALIOU qui ne méritait d'être mêlé à n'importe quoi! Dieu, le miséricordieux a une fois de plus déversé sa grâce sur ce nom de SERIGNE SALIOU MBACKE, l'épargnant de toute tâche! Merci à tous!
Mane dh mouride sadikh laa serigne saliou moy sama serigne wayé dou yalla..deug la yalla maynako lou mayoul nieup mais takhoul mou nékeu yalla..yalla kéneu la naniou bayi di teukeulé serigne si ak yalla nguir yalla bokalé bakhoul
Subhan’Allah. Le jour de la résurrection même des prophètes seront effrayés. Personne n’emmène personne au paradis. Yalla wakhouko fén. Sénégal mo bari shirk ak tapalé. Mais paix à son âme. Chaque âme répondra de ses actes. On doit se tenir au Coran et à la sunna. Et merci de ne pas comparer Cheikh Saliou qui est un homme pieux d’Allah
Aaah li des bokale bire le nak adiana kene momouka koudoule.yalla sounou borom na gnou bayi wokou serigne te topa wokou yalla ak muhamed psl mo wore si aduna ak alahira 👌👌👌👌👌
Doul rek rek Maintenant il va voir si c'est sérigne Saliou qui est son Dieu ou Allah Soubhanahou wa Ta'lâ. C'est ainsi qu'est la fin de tout homme. On lui souhaite qu'en même une rencontre juste avec le vrai Seigneur et qui lui recompensera selon les troupeau de vaches qu'il achétait pour chaque maggal Touba ainsi que les femmes qui dansaient le mbalax devant lui. C'est tout ce que nous pouvons temoigner de ce nous l'avons vu faire dans sa vie.
Subhanalah bayelen khell che le ngen de wah pasa ka wohu len fi yonente Muhammad saws woho len fi Yalla nyeme ngen chai Sénégal bokale Yalla international Daw na yarum😭😭😭😭
Len rek lay gnan moy si barki werou koor gui Yalla moy dieguel Yalla nako Yalla diegueul.. Yalla nako Yalla may aldiana... cheikh betio Yalla nako Yalla may mbakh ak yeurmandé...
Yen commentaires yi meuna niak gni dagno am nakhar rek ak kheur motakh gnouy wakhé ni Cheikh bi nelaw na bayi len ko nak nguir yalla so meunoul wakh lou rafet dal nga nopi pr man ngen Balma
Dieureudieuf Arame, douma talibé cheikh bethio mais domou adama sou deudo so menoul wax lou rafete si môme nopil, yéne yi dafa eupe ta koumou si matoul mame, mat la baye,ana yaar
Na nitgni di dégue lou rafét rék ndah commentaires yi rafét, mane s.touba moy sama wasila ab mouride la beugue done thi diangalém s.touba lanioy teukou ,jamou Yalla kénalko fokou ko , bégnko yémalék lén bégna yakar lén yit loudoul sounou borom.
Cheuuuuuteuuuuute trop de cinéma et vrai de comédien. Légui éléments de langage, le mot d'ordre partout moye : Madior Thioune alias Bethio Thioune est mort mais il est tjrs parmi nous. Bien sûr ke c'est ce qui vous reste a dire pour 'assurer vos arrières et faire de sorte que les khéwal et les millions de vos thianta cons vous soient versés pour pouvoir continuer à entretenir vos trains de vie de folie. Kou tchi bayi baye bayi Ndéye pour bayou diambour torokhe adouna AK alakhira.
Mom deh manshallah kholam setona amona yeurmendé si domou Adama. Thiat nak dou niak si niit. Yen ñi di critiqué yena xamoul yalla ndakh ko bañ bamou guéneu adouna té don jdioulit ni yow ngua meun ko nianal té wakh lou rafet .respctelen geum geumou nit yi té khamni seul Dieu est juste et vrai. Cheikh Bethio Thioune yalla nako sounou borom diegueul ay Bakaram té xareko Aldiana si Barker serigne Saliou Mbacké
Yalla bougoul bokalei t serigne saliou minou yakar bougoul kouy bokalei yalla walahi. Cheikh bethio diamou serigne saliou lawone mais nite lawone si yalla la diouguei t falay delou niane nak yalla khareko aldianay firdawsi mo gueune wax yi nga khamni nekhoul yalla nekhoul yonent bi nekhoul borom touba t nekhoul serigne salih. Man nak mouride pir la mais deugg rk monou nior. Yalnako sunu borom diegal ay bakaram t terouko si aldiana ya geuna kawei
Le prophète salahou aleyhi wa salam disa sa fille fatima .ya fatima si tu adores pas Allah le jour du jugement je pourrais rien faire pour toi. Il disa encore meme moi mes actes ne pourront pas me donner le paradis sauf la miséricorde divine et pourtant yaura que lui qui intercede pour la oumma qu'Allah ns guide sur le droit chemin et pardonne ts nos morts
Sènégal gno sone yow déklougua ligua dék néxoula boule comentér mé il fau couné woné bopam ki dém démna ba parè guéne gnanalco ta madou si parolou famille wame pleas
boudoul woon serigne touba ken dou took tala commentaire dax ba toubab yi takhawe ne wedi len yalla koudoul serigne touba takhawoul signe khoul khouwa llakhou akhad
Cheikh bi a commis l’erreur de sa succession en parlant de sokhna Aida Diallo tout monde sait que le successeur légitime est son fils Serigne Saliou celui que ça dérange va ailleurs...si demain sokhna Aida Diallo se remarie elle n’aura même pas votre temps...degeuna lou nek bamou dess serigne bi dafa nek en état de grossesse😂
Je suis souvent contre l'exé mais des fous il faut savoir que dieu depasse ce qu'est la logisue...dangay degeu waxi waliw djaxlé meune na tax sax nga wedi..wayé manoulen ndax nhionhiou nhiou yallah maye legne..
Je savais pas que la clé de PARADIS est avec vous. Svp fait moi rentrer, je suis là à la queue pour le dernière jugement. Svp fait moi rentrer au PARADIS.
La religion musulmane est une religion de paix donc nagnou yeneintei djam tei bayi di gueneu yeine gadou car nonoulako sougnou yonentei beuguei seydina Mohamed saw ak yalla sougnou borom...wa salam
Fenneu rek kuleen yeureum sax ndax seen décès bi boleen waxeii rek mou djeppy leen lii nga wax fii yeup serigne saliou waxoo ko ndax mom dou waxeii nonou waxou djaahil rek nga fi wax niouneu ay mouride laniou mais seu genre bii mo takh kou diok am loumou niou wax bayil leen s saliou bi ngaine di fenneul bethio yalla nako yalla diegueul ses erreurs
Soubkhanala et où est Dieu dans tout ça est le prophète soubkhanawatalla psl vraiment le Sénégal est un pays perdu de le religion musulmane Remercie Dieu le créateur qui t'a donner la vie
@@BasokArt frer kenn bañiou ko.mais fo juste savoir kil n est pas dieu ni le prophete..(psl).personn je di bien personne ne peut t'amener au paradis...si tu n'as fei du bien.(seul mohamad,peut le faire)
Ab tour déhh mo djitou borom si kaw souff serigne saliou moy mouhamed bo khamoul ma khamal dakh serigne touba diabotame yeup mouahmed psl lalén toudé dieureudieuf magui diégualou
Ahmed Khalifa Niasse Ndeyssane kou ame yité leu kou meunti ame nakkar ak fo meunti bokk di na takhaw seu beussou nakkar ! Yalla nako Yalla faye ! Serigne Bethio Yalla nako Yalla yeuram 👏🏽
Sheikh Mouhamed tu as raison ahmed khalifa NIASS nit kou bakhe la
PAPE AMATH NDIAYE
Walahi ndeyssane borom bakh leu kou niak kignane ! Nitt yi nioy wakh ci mome rek mais kène eupou ko xam xam
Avec tout le respect que je te dois Segne Khadim, tay mom def nga dioumbté lou reuy. Cheikh Béthio délouwoul si kéne koudoul Yalla.
Té en plus kéne rék moo mom assamane ak souf té moy Yalla.
Boudone Segne Saliou moy Yalla kone dou dé.
Waa Salam
Ioe danga rer wayei li yalla wax rk وا إذا خاطبهم الجاهلون قالوسلاما
el hadji salif diop des fois dagnouy wakh yeufou doff Senegal dou dem vraiment 😔
Mane niome daniouma djiakhal sax ba legui niogu bokkalé
Sene serigne yalla rek moko mene yereume ta baleko aye bokaleme
Bene xel daloule souniou wakhaté ak deuk
Sa wax djii té koula deigeu xamni doo djoulit doo lou ken xam.. Di ngein dhei dé domexaraam yi ngein doon
Li lén metti ken tégoulenko..
Sourate baqara verset 28 Comment pouvez-vous renier Allah alors qu'Il vous a donné la vie, quand vous en étiez privés? Puis Il vous fera mourir; puis Il vous fera revivre et enfin c'est à Lui que vous retournerez.
diagne mey yawma la tamlikou nafsine li nafsine chay ane wal amrou yawma izinz lilahi
Sk eux il le connaît
Walahi tawhid moungui dioy fii thi Sénégal.bokalé bi biirna
Nissa Feem lou léer nga wakh taw khiid diôyna mbokou mi yalla nanou yalla dioubeul aamiinn
Machalaah sokh na si Yal na YALLAH féy.Bokalé bi bari wayé YALLAH mom dou si bolé wakh ndakh wiri wiri diari ndari té ndari moy bamméél
Yalla nako yalla até si yeurmandém té kharé ko si aldiana firdaws si barké yonenteby SAW 👏👏👏
Thièy bamèl leudeumna Kou jamouwul yallah perte nga
Yayou Muhammad tawheed reek mo worr
En tout cas moi j'ai confiance a Serigne Khadim thioune le fils de cheikh il vas régler cette situation inchallah kou âme fouleu AK fayda la.
Vraiment c’est dommage quand vous croie que c’est serigne Saliou qui vous ramène au paradis vous oubliez dieux est le profete m’aime serigne Saliou némerai pas que vous prononcer son nom avant dieux lui c’est t’es un bon misulmen Sénégal doyena war
Ousay Diallo yaw gnibile guinee
Lima diakhal ci Senegale moy lotakh NittYi donumandou ci geumgeumo diambournekoci?
Senegal Fi bofikene sonslate,dagaye guinitt koy wakh di sabou te,Tee katt mome thi bopame bako Chariha rayee yageuna
@@mbayeissa7363 Lolo moy debaby, merci bc
Yaw nopil
Mandou warnala
Yalla na ko yalla yeureum mom miye Bourou Boure yi térou ko Aldjana
Balama deh nionan yalla nako serige saliou teero
@@malicksow3192 vraima denio fate yonenti bi
Mes condoléances les plus attristés et mes respects les plus profonds ainsi que mes prières lui font cortège!
Mis à part cette tristesse vécu par tous les sénégalais, il est gravement tant de revenir à la normale, du moins de récupérer la raison!
Que pensez vous de ces victimes, je ne dirai pas de part sa faute mais via son nom? Aujourd'hui tout le monde éprouve des sentiments de solitude cumulés à une tristess en apprenant le décès de Cheikh Bethio Thioune; pour moi, il faut tout de même penser à ces victimes, de nombreuses fois cités morts ! Toutes les personnes sont importantes, chacun compte pour quelqu'un et souvent sur quelqu'un!
Une perte humaine est toujours pénible à vivre! Feu Cheikh Bethio (paix à son âme) a peut-être mal gérer sa confrérie avant d'être d'une générosité reconnue par tout le pays!
Il va grave manquer le Sénégal Après tout! Il avait le rôle du sel dans une marmite en plus d'être guide religieux pour ceux qui le suivaient!
Après mûre réflexion, je note un manque de sincérité et une hypocrisie sans fin de ma nation! Comme chaque personne sur terre, Bethio était propre en nature, les personnes sont différencier par leur caractères. Ceux qui l'ont sévèrement critiqué hier, sont ce qui l'aiment aujourd'hui où il n'est plus! C'est de l'incohérence absolue!
En effet, les opinions sont nombreux, chose normal et bien de dire ce que l'on pense!
Sur ce coup, j'ose dire qu'il est parti au bon moment; et je continue de croire qu'il est sauvé d'une tragédie (10ans de prison +travaux forcés) par la divinité qui ne cessera de blanchir le nom de SERIGNE SALIOU MBACKE! Il a toujours cru à ce dernier qui à la longue était sa source de respiration malgré le fait de pratiquer la religion musulmane à sa manière!
Tout musulman notamment Mouride, doit donc remercier Alah, pour l'étendue de sa discrétion! Car en fin, le NOM DE SERIGNE SALIOU qui ne méritait d'être mêlé à n'importe quoi! Dieu, le miséricordieux a une fois de plus déversé sa grâce sur ce nom de SERIGNE SALIOU MBACKE, l'épargnant de toute tâche!
Merci à tous!
Machallah wax dji rafete na lol
Machallah wax dji rafete na lol
Ta tout dis
Q'Allah nous protéges de l'égarement🙏
Soubkhanal lah on dirait qu'ils ne croient pas en Dieu. Mais Serigne saliou Dou yalla. Thiey yalla
aminata kebe dia Yaw amal Yarr nganann serign Saliou Dou Yallah boudoull Yallah Daii Yallah Daifnasi Mom Loumou Daifoull thi Domou Adama yii Barcke Borom Touba ☝🏻☝🏻☝🏻
Dafa diabate
Aminata kebe dia wakhga deug dey
@@labsolugueye9016 yallah deh ay yonéntam leu defal loumou mesoul defal keineu..lenen lofi wax rek yaagui nax seu bop
Mane dh mouride sadikh laa serigne saliou moy sama serigne wayé dou yalla..deug la yalla maynako lou mayoul nieup mais takhoul mou nékeu yalla..yalla kéneu la naniou bayi di teukeulé serigne si ak yalla nguir yalla bokalé bakhoul
Dieuradieufati Serigne Saliou. Cheikh bethio que la terre de Touba te soit légère
Croyont en dieu le tout-puissant yalla reek mo meune kouye yakar nanga yakar yalla moye bour
Subhan’Allah. Le jour de la résurrection même des prophètes seront effrayés. Personne n’emmène personne au paradis. Yalla wakhouko fén. Sénégal mo bari shirk ak tapalé. Mais paix à son âme. Chaque âme répondra de ses actes. On doit se tenir au Coran et à la sunna. Et merci de ne pas comparer Cheikh Saliou qui est un homme pieux d’Allah
Paix à son âme yalla na ko yalla kharé aldiana firdawsi ci barké seydina mouhamed psl
Aaah li des bokale bire le nak adiana kene momouka koudoule.yalla sounou borom na gnou bayi wokou serigne te topa wokou yalla ak muhamed psl mo wore si aduna ak alahira 👌👌👌👌👌
Yalla amoul morome amoul masse mome reka fi nek. Di gnanal nak gneupe gni fatou mou diegal lene si yeuremandeme inchaaalah.
Yonebi salawou alihi wassalam nena boîte bou guener adouna wakhal Lou bax wala nga nopi.yalla nako yalla yeureum
Paix à son ame et Allah l'accueille dans son paradis éternel.
Qui ne s'accroche pas du l'alkhourane de Dieu et du sunnah du prophète Mahomed diapo si dara
Bilahi wakhatiko seydi Camara
WAllah
Wallahi Alkhourane ak Sunna gni ko fi top Sénégal fi doumani bariwoul deh wayei Touba mom koufa dem xamni alkhourane ak sunna fala fek baax
Masha'Allah Ismaila je veux etre dans ami envoyema sa numero
wallay
Yalla nako yalla yeureumn tabalkoo aldiana you kaweya ,,
Jiadieuf serigne salou jirrama cheikh bi machalla thioune mame bambi they serigne touba
Doul rek rek
Maintenant il va voir si c'est sérigne Saliou qui est son Dieu ou Allah Soubhanahou wa Ta'lâ. C'est ainsi qu'est la fin de tout homme. On lui souhaite qu'en même une rencontre juste avec le vrai Seigneur et qui lui recompensera selon les troupeau de vaches qu'il achétait pour chaque maggal Touba ainsi que les femmes qui dansaient le mbalax devant lui. C'est tout ce que nous pouvons temoigner de ce nous l'avons vu faire dans sa vie.
Yaw tamitt déh bo agué ci yalla digua kham lepp deugleu néna ngou bou nitt guéné adouna so meunoul wakh ci mom lou raféte nopile bakar dafa sew dale
Tu es mal éduqué lâche que tu es
Haha maintenant il me parle du respect
Brown Sugar yene gnou wara nopi guéne li ba kham di douleu nite ba nekhatoufi ga wara thieudieu sa gate doull way yene
ousmane ba bi n dit Mon frère
Subhanalah bayelen khell che le ngen de wah pasa ka wohu len fi yonente Muhammad saws woho len fi Yalla nyeme ngen chai Sénégal bokale Yalla international
Daw na yarum😭😭😭😭
love Allah wakhenga deg
Very true
Yaw doulllll khamou lén sakh lan moy bokalé sen saram ndeye rek
Abdou Fall yow ak nyoom ma yem kep ba pare yow respecte wu lo sa ndeye mo tah ngai saga ndeye yu jambur
Kou amm serigne touba soxla woul dara lou fiy bokalé
Yalla rek mo fii nekh serigne du dar du yalla du younette
Wayé moy gniy ramb sa bay euleuk
Diamoulénn yallah bayi thiakhann mou guennn
celui kon jugera ne dpit pas jugé.vous vous croyé etre mala ika
Cheikh bethio yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana
Yalla na yalla dolli yermande thi ñom thi brkp sr saliou mb allahouma amine te ñou bokou ko
Yalla Sobhanaho Watahala, mo mom nittgni, mo mom soufsi, mo mom khèwal yi, bayien di bokalé. Yalla dou morom borom la.
Kène rek moye assamane ak souf moye souniou borom cheikh yallanako yalla yeureum
Yene gnianalene ki mo geune sene lebone yi sim douguene rous yalla nako yalla yeureum kharai ko adjana atai ko si rahmane
Len rek lay gnan moy si barki werou koor gui Yalla moy dieguel Yalla nako Yalla diegueul.. Yalla nako Yalla may aldiana... cheikh betio Yalla nako Yalla may mbakh ak yeurmandé...
Soubhanalahi naniou gueme yalla té djoully si yonenntibi niou Baye par par lo bi
Déme léne diamou dji yallah té bayi séne tiakhane yi... al jannah kéneu mo ko mome, té kou ko diamou woul do Fa dougou
Heureusement ba yaw khamo fo dieum
Ba kham gua fo dieum nitagui diami yalla té ab kholam laboule dakh deuké togn ak wakh lou yonam nékoul
@@mouslycisse9125 li ngua wakh deugue le... wayé serigne Cissé, mane talibé la, wayé gni dagnoul thiakhane. Serigne Touba diamou yallah rék li digue lé. Lane moye thiantakoune ?
ماشاءالله
Khana yala amofi placé
Yen commentaires yi meuna niak gni dagno am nakhar rek ak kheur motakh gnouy wakhé ni Cheikh bi nelaw na bayi len ko nak nguir yalla so meunoul wakh lou rafet dal nga nopi pr man ngen Balma
Dieureudieuf Arame, douma talibé cheikh bethio mais domou adama sou deudo so menoul wax lou rafete si môme nopil, yéne yi dafa eupe ta koumou si matoul mame, mat la baye,ana yaar
Bilay yen yi dafa niaw sakh
@@ndeyefatoukasse5180 man dama warou dafa melni nit gni legui lou gnaw mom lanouy ndamo lolou diakhal nama trop com si yarou crime la
arame ndiaye Franchement wah yi gnaw na trop ketatoufi nk respect
Na nitgni di dégue lou rafét rék ndah commentaires yi rafét, mane s.touba moy sama wasila ab mouride la beugue done thi diangalém s.touba lanioy teukou ,jamou Yalla kénalko fokou ko , bégnko yémalék lén bégna yakar lén yit loudoul sounou borom.
Cheuuuuuteuuuuute trop de cinéma et vrai de comédien.
Légui éléments de langage, le mot d'ordre partout moye : Madior Thioune alias Bethio Thioune est mort mais il est tjrs parmi nous.
Bien sûr ke c'est ce qui vous reste a dire pour 'assurer vos arrières et faire de sorte que les khéwal et les millions de vos thianta cons vous soient versés pour pouvoir continuer à entretenir vos trains de vie de folie.
Kou tchi bayi baye bayi Ndéye pour bayou diambour torokhe adouna AK alakhira.
Sama wadji li ngay wakh ni yéméneu deh
Yen rek yéna diara yeureum ndakh dangen yoroul djiko dioulite bilahi yalla nalen yeureum cheikh bi mom amna ngeureum
@@moustaphasalafi3549 diami serigne saliou mbacke yalnako yalla khare aldiana firdawesi AMINE YARABI THIEYE MBACKE
Sa datap ndeye
@@lincontournablemomo1319 yaw lou khewe gamaye sagani 😭
Akassa thioune yalla na yalla doli diam
Aye way cheikh bethio famou djieum yalla rek mofa nek tegeune ko gnianale yalla mou balleko ta djiegeule ko
Nexoule ba nexoule wayé doye na ware
Yalla nalla serigne saliou téroul bopame
Yala naka yala yeureum té kharèco aldianay firdawsi thi barkep serigne babacar sy
Yerémnaa len !!! Wallaahi .....
Man Daii cheikh Bethio Thioun Naikoull sama serign barcke serign Touba Mai pour koi ndiounn sénégalaise yii Amm ndiou sokhorr Non putin khanaa Nith kii Loko bagn bagn Bamou wanla Guinaw nga warko Nianall Laigui Yallah Diegeull ko hum...../Cheikh Bethio Thioun Mom Limou Amm Dou Mon serign Saliou Mbacke la Moko Tairall Ta serign Saliou Mbacke Mom koumou Tairall Dinga Taidd Adouna Taidd ausi Allakhira Bandiou Dieumm Billahi 🙂
Gnoune serigne touba lagne gueune adouna akke alakhira
Mom deh manshallah kholam setona amona yeurmendé si domou Adama. Thiat nak dou niak si niit. Yen ñi di critiqué yena xamoul yalla ndakh ko bañ bamou guéneu adouna té don jdioulit ni yow ngua meun ko nianal té wakh lou rafet .respctelen geum geumou nit yi té khamni seul Dieu est juste et vrai. Cheikh Bethio Thioune yalla nako sounou borom diegueul ay Bakaram té xareko Aldiana si Barker serigne Saliou Mbacké
Ani kham kham??
Akhmed khalifa ndiass kou am yitté la yalnako yalla faye
Qu'Allah les guides, il y a que des gens fermés qui y sont présents
Yalnako Yallah Yeureum tei khareiko aldiana lolou ngueineko wara gnanal mais pas nekk fi ak serigne saliou boudoul diekh
Yalla bougoul bokalei t serigne saliou minou yakar bougoul kouy bokalei yalla walahi. Cheikh bethio diamou serigne saliou lawone mais nite lawone si yalla la diouguei t falay delou niane nak yalla khareko aldianay firdawsi mo gueune wax yi nga khamni nekhoul yalla nekhoul yonent bi nekhoul borom touba t nekhoul serigne salih. Man nak mouride pir la mais deugg rk monou nior. Yalnako sunu borom diegal ay bakaram t terouko si aldiana ya geuna kawei
Le prophète salahou aleyhi wa salam disa sa fille fatima .ya fatima si tu adores pas Allah le jour du jugement je pourrais rien faire pour toi. Il disa encore meme moi mes actes ne pourront pas me donner le paradis sauf la miséricorde divine et pourtant yaura que lui qui intercede pour la oumma qu'Allah ns guide sur le droit chemin et pardonne ts nos morts
Amine
Yallah nako yallah yeurem té kharé ko aldjana
Quel égarement!
Vraiment
Ta gueule
T'a gueule si tu n maîtrise po tes mots sal con
Égarement deug !!
@@khadijaleau1800 iow dull dmrm
Yalla na co yalla khare adiana
Sènégal gno sone yow déklougua ligua dék néxoula boule comentér mé il fau couné woné bopam ki dém démna ba parè guéne gnanalco ta madou si parolou famille wame pleas
Wax deug nak lou yallah wax ler na manou mo geun diamou yallah tei nit kou nopalou naga wax lou ba si mom wala gua nopi
Bousso Diankha bilahi
khana yéne doléne yéwou dém léne diamou ji yalla mo geune séne tiakhane yi
Yaw danga kham yalla
nioune bounioufi fékoule wone serigne touba dounioudiébalou si kène.ndokebinioukofi féké ndank sounioukofi fékoulwone l'islam niake niou
@@dioufibrahima2601 wakha tiko
Khadime yw laye wakh kholal linguaye wakh
diouf ibrahima boba mouye sa pertama rek née diabalou mome desouko defal koudoul ki bindeu t’es moye ALLAH
chiekh bi mô am dague môme là yala diokh dague nakh yobou nako thi keurouge daguegi kone môme to nioule mô am dague alhamdou lilha dieureu diafati serigne touba kene dou môme amoule morome
Yalla bamouy binda al qur'aann kéna nékoufa woon ragal yalla walahi dafa diott
Billahi ki kaye dafaye lep ak lepone ببكر بدان
Ses des vaurien
Kéneu nékoufa wone kone ioe mi itam dara worou la ci ... kone mandoul ndakh ay mbiram kéneu khamoul
Bara Niang yaw mandou nga yaw dégage waay
li dé setane ko sa bakaarla yala nagniou yala dieghal thi djotay bo khamne do degue tourou yalla wala seydina Mohamed doyna warr 🤦♂️🤦♂️🤦♂️
Doul rk ngay def khamna yay malaka biy bind bakar yi
saaa data ndeye yak koi yakar yaw
@@bnoitbadiane7386 werou kor gui guay sagua yala nala yala bal🤲🤲 khana woro balnala thi khol bou sede gouy
@@bah546 ken niemoul wakh
@@kadiasy970 🤷♂️🤷♂️doyna warr
Yalla nako serigne salliou terou yobouko thie adjana yii kawe
Thieye Sénégal monekhe ake façon biniouye diamo yalla...titena lool sounou euleuke ame aye surprise
boudoul woon serigne touba ken dou took tala commentaire dax ba toubab yi takhawe ne wedi len yalla koudoul serigne touba takhawoul signe khoul khouwa llakhou akhad
Fenne reck. Bayilène fénal Serigne Saliou mou bakhmi.Dinguène halkou dé.
think tank Diao yaw de sa baye datam fene mo takh nga ham kouye fene amlen yarr bande de tidiane you bonne
Yalnako yalla khare alldiana.firdawsi.amine
Cheikh bi a commis l’erreur de sa succession en parlant de sokhna Aida Diallo tout monde sait que le successeur légitime est son fils Serigne Saliou celui que ça dérange va ailleurs...si demain sokhna Aida Diallo se remarie elle n’aura même pas votre temps...degeuna lou nek bamou dess serigne bi dafa nek en état de grossesse😂
Feuz john jay
Sosal serigne saliou rek mai ki dem yalla nako yalla yerem
iow silence
Yalla nako yalla yeureum t wonalekok sangam ba barke Serigne saliou Mbacke
Yalla rek mon momme souf ak dieriji Sénégal bokale rek
yala nako yalla yeureume wayé yalla kéne la dougnouko bokallé
Xolal ndey dof bii way , ligua wax fii yeup amoul bop amoul guéne
ousmane adoulaye diallo rentre. en. guinee. sans. eau. ni. electricite. la. ferme. nderingue
@@cheikh.sidyfaye7758 hahahah fekk meu sama deuk digua xam app Guinean la wara
yalla nako yalla yeureum kharel aldiana firdaws
Sénégal beuri na tiakhane trope...déme léne kham yalla c mieu k di wakh ay wakhou dof rk
Ndeye Nafissatou Ndoye yaw sa thotou ndaye waye yaw yaye délo niite yi thi yalla domourame sa leufeul ndaye
ndeyssane yereum na sa yaye. sagua dou takk féne ,dolil yénéne way...
@@ndeyenafissatoundoye9533 merci surtout n'insulte jamais personne sur réseau social encore merci YALLAH nga goude fane té ande ak wérrrr
Ndeye Nafissatou Ndoye yaw waxi dof rek gaye wakh
Moussa camzo tkt yaw man je suis bien éduqué et je respecte ma mère...kou respectéwoul sa yaye rek moy sagua ndeye
Sante lenn yallah teh baye di sante
Domi adama... Senegal bayelen chahan
Yalla nena kola defal nga sante ko bagne nak dou beug
Waw ku bugul sharia yallah lu youmbu lai wutt... arjannah toppt alquran ak sunnah teh roy si mam u bahkyi mo koy amm ... bayelenn oppal
Li du islam... li ay fenn ak Bari wahk ak bidah rek la
mandou si loum bok
@@alphamollo7768 xam
واتقوا يوم ترجعون فيه الى الله ثم توفى كل لنفس ما كسبت وهم ل يظلمون .........
رب اعفر له ورحمه
Away sama xarit mame khadim masha Allah ya bakh té yatou
Je suis souvent contre l'exé mais des fous il faut savoir que dieu depasse ce qu'est la logisue...dangay degeu waxi waliw djaxlé meune na tax sax nga wedi..wayé manoulen ndax nhionhiou nhiou yallah maye legne..
Yalla dina mayè, mais yakarouma mou may kenn loumou mayoul Mouhamad (saw)
Sante Serigne Touba chieh Bethio rawe na talibe Serigne Touba yeppppp mane baye falle ma co wahe
Yalna ko yalla yereum
C'est le levè du jour pr bèthio yalla nako yalla yeureum tè diègeul ko
Yalla nako yalla té si yeure mandéme
Je savais pas que la clé de PARADIS est avec vous. Svp fait moi rentrer, je suis là à la queue pour le dernière jugement. Svp fait moi rentrer au PARADIS.
wallahi kou bayiwoul di dingatt serigne touba yawmal khiyam dinga dadj mbougueul mou tarr
La religion musulmane est une religion de paix donc nagnou yeneintei djam tei bayi di gueneu yeine gadou car nonoulako sougnou yonentei beuguei seydina Mohamed saw ak yalla sougnou borom...wa salam
Yalna nou yalla yeureum, lolou rék mo am solo
Ya pas une seule partie du coran dédié aux mourides ou autres mais c'est pour tous les musulmans
Yallah rek moy terou thi aldiana. Il y'a bcp de bida au Sénégal. retournons à la source , avant qu'il ne soit trop tard .
Enfin tu apparais mais déf si com nekofi rék. Bayi djiguén di djité ay talibés rék. K Dieu laccueill en son paradis celeste.
Fenneu rek kuleen yeureum sax ndax seen décès bi boleen waxeii rek mou djeppy leen lii nga wax fii yeup serigne saliou waxoo ko ndax mom dou waxeii nonou waxou djaahil rek nga fi wax niouneu ay mouride laniou mais seu genre bii mo takh kou diok am loumou niou wax bayil leen s saliou bi ngaine di fenneul bethio yalla nako yalla diegueul ses erreurs
Yalla nako yalla yaram lol Ti Barkip Borom Touba Mbacké
Boulèn gnou sonal. Koussa Ndéye liguéyoul Bissimilahi.
Soubkhanala et où est Dieu dans tout ça est le prophète soubkhanawatalla psl vraiment le Sénégal est un pays perdu de le religion musulmane
Remercie Dieu le créateur qui t'a donner la vie
Du n importe quoi dit nous de Dieu et de son prophète PSl
Ils se trompe trs lourdement ma soeur...ils pensk sont des dieux
Ah doyna wareu
Yallah rek ak yonanté bii.nio fi meune...tou le reste sera jugé comme tous.(yallah rék ak Mohamad psl)
Oumou Khairy Gueye lou nguén bax nioun Serigne Touba lanou beug
@@BasokArt frer kenn bañiou ko.mais fo juste savoir kil n est pas dieu ni le prophete..(psl).personn je di bien personne ne peut t'amener au paradis...si tu n'as fei du bien.(seul mohamad,peut le faire)
Yéne gninga khameni daray serigne bethio meussouléna nekh prkoi ngéne di lire ay video yinga khameni si cheikh bethio lay wakh nitt ki sokko beugoul waro lindianti darame sokhor ngéne bone ngéne soungéne amê lénéne dieul léne ta bayégnou cheikh bethio gnoune dé lindiantiwougnou kénéne ndakh serigne saliou mbacké rekk mognou gnorr ta mome lagnou doylo adina akk alakhira wa salam
Défal lén bèthio niane mo gueun wakhi doff yi 🤣
😱🙊
Vrema c du m'importe quoi nianalenko c mieux k tout ça
Yene kom d'où guéne ayy dioulite kéne khamoule louguéne done simm
Baniou KO gnanaler dou tay thim
@@soukynadieno1853 😂😂😂😂ya yéy wakh ko dé dagnouy fontou rék
Ayeu naféhh ayeu féni késsé ayeu douli késsé
Yal nako yalla yerem si batou la ilakh illala
yala nako yala yeureum si barké werou koor bii nel aminn
C'est grave do dégue mouk Mouhammad est ce que toudéna ko dome sakhe 😠😠😠
Ndeye Sarr ab dioulit deug day mandou
Ab tour déhh mo djitou borom si kaw souff serigne saliou moy mouhamed bo khamoul ma khamal dakh serigne touba diabotame yeup mouahmed psl lalén toudé dieureudieuf magui diégualou
Té cheikh diabotame yeup serigne touba ak diabotam la lén toudé
Y’a mouna fene deh allahou akoubar
Doul rek
Bizarrement il fait son discours téy wakhou fii yalla wakhou fii yonétibii nii aya Alkhourane que Dieu vous vienne en aide
khadim maguilay masta sama kharite bi,magui nian sunu borom haréko aldiana firdawsi🙏🏼🙏🏼🙏🏼.
Amin