Rufisque : Les populations empêchent l’inhumation d’un présumé...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 20 янв 2025

Комментарии • 353

  • @gondiaye8810
    @gondiaye8810 2 года назад +12

    Ma mère sokhna baba fall repose dans cette cimetière. Que firdawsi soit sa demeure éternelle😭😭😭😭😭

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj 6 месяцев назад +1

    Merci goordjiguéne nagne ko soul ca hathie wala niou tale ko vous êtes des responsables ça se voit ❤❤❤❤❤

  • @ngoyembengue6640
    @ngoyembengue6640 3 года назад +40

    Nitte boko khamoul rek khamoko yomal khiyame dina metí trop Walahi gnew nga sama keur djiouli koor ngay wor MachahAla yalla nga khipper aldiana 😭

    • @barie4582
      @barie4582 3 года назад +1

      Tu le connais?

    • @ngoyembengue6640
      @ngoyembengue6640 3 года назад +3

      Boubakh

    • @barie4582
      @barie4582 3 года назад +1

      @@ngoyembengue6640 ay way Kon ay toumaal la?

    • @faamar7807
      @faamar7807 3 года назад +5

      Nitt kou bakhe kou djoulité alalame douko bolé ak nitt ki dou homosexuel c mn consin Sénégal naniou bayi yakha dère gor bou khawa djiguéne rk niouné gordjiguéne il faut arrêter nitt loumouy wakhe dafeko Wara lère

    • @zeinabrassoulndiaye6782
      @zeinabrassoulndiaye6782 3 года назад +4

      Djouli ou worr sa veut rien dire très cher ils n’ont pas intérêt diko sossall lou tollou nii sans aucune raison
      Ni de ses actes ni de ses comportements niou nieuw rek niii homosexuel la lolou meunoul nekk nane deff Li Yallah wax
      Daguen banalisé homosexualité teih boulen faté ni niom nio takhon yallah toukkeul adouna

  • @abdourazakba3258
    @abdourazakba3258 3 года назад +15

    Thiey adouna🙏yalla nayou yalla dollyy soutoura🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @Amar_ndiaye
    @Amar_ndiaye 3 года назад +12

    mbiroum gordjiguene lou mata tey la amna nio khamni yalla molene bindé nonou niouy def manierou djiguene ta nekou niouko, teylene dé

  • @annemariedaniellezimmer4328
    @annemariedaniellezimmer4328 2 года назад +7

    Ragual leineu Yalla maanou leineu addina bi diekhna ba parei mmsi c’était vrai respecter les morts
    Repose en paix 🙏🏾

  • @thiamyaceinte
    @thiamyaceinte Год назад

    Soubhanala yalla na gnou yalla mouseul thi gordjiguene 😢😢😢

  • @ndeyefatoucisse8676
    @ndeyefatoucisse8676 Год назад +1

    Mais on doit avoir une preuve palpable avant d’agir

  • @cherif3658
    @cherif3658 3 года назад +9

    J’espère que les gens qui le jugent comme tel pourront le prouver devant dieu.

  • @nogayedjite8187
    @nogayedjite8187 2 года назад +1

    Bou nguéne si amoule louléne lèrre ni gordjiguéne leu di nguéne ko layo ak mome si kanamou yallah souniou borome

  • @maguettesarr8244
    @maguettesarr8244 3 года назад +8

    On l'accuse juste de par ces geste corporel......mane dehhh on se côtoyer pas mais kou nopi la kou souriant khamaloumakoo lou niaw vraiment..... boula mbirr leroul dall boulthi bakarr yalah rkk mo kham.. repose en paix Diagne🙏❤

  • @binetaseck3671
    @binetaseck3671 3 года назад +43

    Def guén lou niaw vraiment😭😭😭😭💔💔💔💔💔trokhal guén kou doul trokhal domou Adama kou doul sigui xol nite ndax timide kou dioulité kou dara sonaloul wone woyofalone adounam nite kou céde reuy xol nite kou amoul djiko yalla Nalen yalla trokhal yén gni def li inchalla 😭💔 ki xamoul sax nou nite di defei lou bone Alahou akbar☝🏼 ki nekone xaleii diapone ndiambouram ndeysane 😭 dioulitei 😭😭😭😭😭😭yén gni yenay fake yi nek ay nite yu bone yalla guén yakar sen bop😭 vous êtes qui pour juger 💔ndeysane j’ai de la peine pour vous mon pays va très très mal 💔🤲🏼 wayei alhamdoulilah sante naniou boubakh t amnaniou yakar bou bakh si ki guén di toumal li ndax def na lou bakh ba dem tei demna si beuss bou bakh mouy guoudi aldioumah🙏🏽 si wërou radiap 🙏🏽 niouy soul ko si diam bi kër céddé diak yeup di weussifeu🙏🏽🤲🏼alhamdoulilah 🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼 mane d gueume nani yagui aldiana firdawsi 🙏🏽 deim na yonam d t leip lou way wax si mom mouy touma Yalla na done tiyaba si mom 🙏🏽 done bakaar bu reuy si kikoo wax🙏🏽 ki dou G… tei xamoul sax nouniouy nekei G… djoulite pire leu wone nite kou céde la wone def katou lou bakh leu wone wayei genre nite yu melni mom meunouniou yague si adouna 💔 😭 wayei Lo doundoul wone lu nekh si adouna yalla nagua ko dounde firdawsi 🙏🏽😭💔 souniou xel dal na si yaw🙏🏽

    • @bafoumatymbaye9923
      @bafoumatymbaye9923 3 года назад

      Ont dirait que tu le connaît bien

    • @cheikhantandiaye4183
      @cheikhantandiaye4183 2 года назад +1

      Binta ndayssan sa khôl dieekhna.waye mougneul goor djigueen dara safouko waye ay mbookam rek niooy soonou masta.

    • @marimardiallo7428
      @marimardiallo7428 2 года назад

      Bilahii bineta wakh nga DEUG Koubakh démenaa

    • @ndeyeawatavares173
      @ndeyeawatavares173 2 года назад

      Mane mi ma meuneu cédé si moom doon ma takhawu

    • @maxmiliano4682
      @maxmiliano4682 2 года назад

      mane mom Djigueene gni rek laye guiss gnouye diapalé goordjigueene gni,yalnagnou yallah mouthieul si djigueene djou dianguoul dîném amiine...

  • @bybrufisquois257
    @bybrufisquois257 3 года назад +7

    Le pire de l'histoire c'est que la majorité ne connaisse pas le défunt . Gnak lo def mo waral mbolo mi am temps di raye sen bop pour des suppositions

  • @altineguisse9635
    @altineguisse9635 2 года назад +3

    Ndeysane dans ce cimetière repose ma tante Gogo Hawa Sy
    💔🕊️paix à son âme ainsi que toute personne qui nous a quittée 🤲🙏😭

  • @bebinasow5901
    @bebinasow5901 3 года назад +83

    Je trouve vraiment cette situation insensée, avez-vous de réelles preuves que le défunt est un homosexuel et même s'il l'est avez-vous réellement le droit d'empêcher son inhumation? Les cimetières n'appartiennent à personne et vous ne pouvez vous octroyer le droit de juger qui que ce soit, seul Dieu est juge. Faisons preuve de dépassement et de tolérance face à certaines situations. Imaginez un instant que ce soit une personne qui le haïssait ou a un démêlé avec sa famille qui ait lancé cette rumeur. De toute façon quoi qu'il ait fait il n'est plus de ce monde alors laisser de grâce sa famille l'enterrer. Ce n'est plus entre vous et lui mais entre lui et Dieu.

    • @coumbaniang1597
      @coumbaniang1597 3 года назад +59

      Yen Khana diangoulene arkhouran wala yen lolen done goordjiguene Ken amoul droit soul ko ci Ben cimetière k ça soit cimetière musulmane ou chrétienne diangui len wakhou yalleu dou fo yalla bindoul di effacer

    • @fatougninguefaye4284
      @fatougninguefaye4284 3 года назад +33

      Si tu est musulman tu ne sais pas ce que ta religion a dit par rapport à l'homosexualité donc retourne apprendre

    • @zeinabrassoulndiaye6782
      @zeinabrassoulndiaye6782 3 года назад +33

      Apprend ou renseigne toi avant de parler gay diaye reuy gatt ak humanité nonou di wax teih tu es une grande ignorante Allah azzawajal a été précis dans Coran daniouko wara sani ken warouko soûl si cimetière ni djouléko
      Honte à toi si tu te dis musulmane

    • @elmilkadiallo7449
      @elmilkadiallo7449 3 года назад +3

      Tah geule

    • @lala_aishaa
      @lala_aishaa 3 года назад +3

      Je suis totalement d'accord avec.

  • @BoubacarDIALLO-kk1kn
    @BoubacarDIALLO-kk1kn 3 года назад +24

    Pourtant tous les gens que vous voyez comme ça, la majeur partie ne le connais pas. Donc accusés une personne d'homosexuel ou de lesbienne sera banale et deviendra un problème très sérieux pour la société. On est dans une société où l'on peut facilement détourner la conscience des gens. Même si l'on est immame du quartier. Donc faisons très attention, à nos pratiques religieuses.

    • @senethialy8748
      @senethialy8748 3 года назад +2

      Boubacar khoniou até si yen yi rek sa melo moko waral naniou meuytou yiye takh niouy ndiorte si nioune lou niaw

    • @ahdaaf970
      @ahdaaf970 2 года назад

      Donne un argument stp, ça c'est pas un argument, pourtant tu ne connait pas les marabouts ancêtres et tu peux croire en eux

  • @yasukekey
    @yasukekey 3 года назад +10

    Goorjiguenn deh bakhoul mais loguén def tamite bakhoul Dara. Sénégalais day guiss nite rék né lii la wala léé. Les préjugés au Sénégal c'est extrêmement grave. Fii rék guay guiss niouni famille bi ay deumeu laniou

    • @abdunjaay738
      @abdunjaay738 3 года назад +1

      Lii ab yar la rekk ngir ñoom 🙏🏾

  • @aissatouleonie8985
    @aissatouleonie8985 3 года назад +2

    En tt cas kou am kersa la waune yalla nako yalla yeureum

  • @annadiallo1689
    @annadiallo1689 3 года назад +37

    C'est vraiment triste cette situation j'espère que vous à des preuves car c'est une accusations très grave.

  • @BoubacarDIALLO-kk1kn
    @BoubacarDIALLO-kk1kn 3 года назад +46

    On est dans quel monde ? Quel l'importance de croire au préjugé ? Le Sénégal va mal. La situation qu'est ce garçon, tout le monde y passera. Pourtant avant se base sur des paroles incertaines ,basons nous sur des faits réels et concrets. Il fallait l'enterrer et ce qui c'est lui et le bon Dieu. Que son âme repose en paix

  • @ibrahimafall2376
    @ibrahimafall2376 3 года назад +2

    Merci bonne continuation la guérre

  • @adjisylla1727
    @adjisylla1727 3 года назад +17

    Senegal bouniouy diawalè goordjiguen , ak goor goudjiguènè amna nio xamni danionooy , bindela , wala yarosiy djiguen dinayobè goor mou noy ,
    Mai goordjiguèn moy kouy seuyak moromou gooram , linak man xawma wadji xamanoumako , mai li boudè ay rumeur rek laniou topou ba tomalko ko , gnikodef diaratoul niouy diamoti yalla , bodè liniouy wax fou ler laniouko tek yalla mi yor ndiegalam tay diegal kouko nex yalla na diegal ,
    Liiwate moy goordjiguèn encore une fois
    Bounioukoy diawolè , wayè khol nit mou sed bamou noy rek nganiko goordjiguèn nga bakar bou reuyla

  • @ismailadiallo7784
    @ismailadiallo7784 2 года назад

    Tres bien. Bagne lene. Je suis avec vous gordjiguene thia khath. Boulene saltele sene armere

  • @barasarr2297
    @barasarr2297 3 года назад +1

    Merci beaucoup contana thi yène

  • @ngoyembengue6640
    @ngoyembengue6640 3 года назад +26

    Lo tegoule sa beute meusoko guiss mou ande ak gor di seuy wala di def lou nekhoul yalla nga wara Mandou senegal bayilene diw nenama dagne ma wakh wala dagne ma Netali Bakhna gneupay dé yalla na Yekh té lou way wakh dingako wakhate

  • @germainehoueto7377
    @germainehoueto7377 2 года назад +5

    Te ki pour juger.seul Dieu à le droit de juger c lui ki à le dernier mot. Laisse léglise en dehors de ca. Nous les chrétiens on jugent pas parck nul n'est parfait. SÉNÉGAL EST vraiment en retard dommage

  • @eakM5
    @eakM5 3 года назад +18

    Je suis choquée Sénégal dal metti na kou nekk ak sa bamelll et surtout wakh lilenn léroul dakh dafa peu être effeminer. Donc yena dieul plassou yallah dal di juger c'est bien. Le défunt doit être respecté. Et j'espère que dinalennn ball akh liii dafa niaw... yallah nako yallah yeureum et qu'il repose en paix.

    • @layendiaye6850
      @layendiaye6850 3 года назад +1

      Damani yalla limou wakh lanouy def fi gordjiguene mom sa khathie yaw aussi bothi boké changel toup sino c comme sa rek domiram moy gordjiguene

    • @eakM5
      @eakM5 3 года назад +3

      @@layendiaye6850 yako féké? Wallah yéna nékone? Yallah limou wakh si wakh lila woroul ak lo khamoul. Dem lenn rek comme que yenna beugue dieul makama yallah di juger té khamo nitt ki. Yaw ya wara changé diéguelou bala mou tard si yaw. Wassalam

    • @elmilkadiallo7449
      @elmilkadiallo7449 3 года назад

      Bayilén sene yi way

    • @boubacarthiendiaye1188
      @boubacarthiendiaye1188 3 года назад +1

      Laye waxal loula woor

    • @layendiaye6850
      @layendiaye6850 3 года назад +1

      @@boubacarthiendiaye1188 dama wakh nila mom la dra lathie khamoul mai barina gnoufa dee te kene wakhou lenko

  • @julesmane8834
    @julesmane8834 3 года назад +29

    L’état doit agir le plus rapidement possible sinon dinane déme bakou déh saye none woté thi armél yi ni gorjigen ngua. Ces 3 personnes doivent être immédiatement arrêtés ils se basent sur des on dits pour empêcher l’enterrement de ce jeune. Ils ne savent pas ce que faisaient toutes personnes enterrées là-bas à leur vivant. Eux-mêmes ils font pire Bilahi walahi na yone dieule ay matou kayam

    • @aissatou5948
      @aissatou5948 3 года назад +5

      Sou si etat bi di wakh niouni guordjiguénn yi lay diapalé

  • @modoundiaye2551
    @modoundiaye2551 3 года назад +8

    Si vous en avez pas des preuves vous n’avez pas le droit d’empêcher son enterrement .

  • @usad01
    @usad01 2 года назад

    Merci beaucoup leral yi lerna wak dji sel na ay nitou degue guen Ken doufi soul borome niary tour..

  • @gildasatchade9535
    @gildasatchade9535 3 года назад +16

    J'ai honte pour le Sénégal, on dit qu'il est présumé et vous décidez de ne pas l' enterrer.
    Vous vous mettez à la place de Dieu et décidez de qui est bon et qui ne l'est pas.

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 3 года назад +3

    Ohh c'est vraiment désolant thi un pays comme le sénégal

  • @fn-vx5rg
    @fn-vx5rg 3 года назад +22

    Personne dans les témoignages ne connaissaient l accusé ! Fait attention ⚠️ un jour un d3 vos ennemi peut vous faire la même chose pour vous déshonoré

    • @julesmane8834
      @julesmane8834 3 года назад +1

      Bilahi walahi ce que j’ai dit dans mon commentaire

    • @fn-vx5rg
      @fn-vx5rg 3 года назад +6

      @@julesmane8834 c est trop,je ne sais pas pourquoi on est aveuglé par la haine ,on doit faire attention ! C est une abomination d être un homosexuel mais pour juger il faut des preuves

    • @boubacarthiendiaye1188
      @boubacarthiendiaye1188 3 года назад +5

      Frere boy bi dou dara gni df li ay ennemis lagn boy bi day diouli ame yeurmande nango ligueye Lolou la Xam si mome

  • @daoudasaabaly3365
    @daoudasaabaly3365 2 года назад +2

    Ma question est la suivante??? Légui kou gañiou té nékone dëmeu🤗🤗🤗 mom fougne Koy souuul??? ☺️☺️☺️

  • @djenebouguindo6589
    @djenebouguindo6589 2 года назад +1

    Le gas en rouge est un vrai ignorant walaye

  • @abdoulayefall1047
    @abdoulayefall1047 3 года назад +15

    Kerok Yawmal khiyam dina metti trop surtout pour les sénégalais. Dina am nio khamni dinagn layo ak sen borom. Vous ne l’avez jamais vu faire telle ou telle chose et aujourd’hui vous empêchez son inhumation.

    • @Lepéedudebat
      @Lepéedudebat 3 года назад +1

      Kane mola wakh yowmal khiyam da am

  • @mamadoulaminediaboula
    @mamadoulaminediaboula 3 года назад +22

    Félicitation le combat continue 💪🙏🙏💪💪

  • @joembengue774
    @joembengue774 3 года назад +7

    Safara dina beuri 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @awayacinesylla
    @awayacinesylla 3 года назад +35

    Le défunt je le connais depuis son plus jeune âge. Il a toujours été correct. Je ne lui connais aucun comportement de ce genre. C est désolant qu il soit victime de rumeurs infondées

    • @fn-vx5rg
      @fn-vx5rg 3 года назад +5

      Vraiment c est koi ça et le pire les personnes qui sont là ne connaissent même pas la personne

    • @Onomar
      @Onomar 3 года назад +4

      Allahou Akbar métina lolou j’ose même pas imaginer la famille du défunt 🥺💔✨Thieuy sénégal

    • @zeinabrassoulndiaye6782
      @zeinabrassoulndiaye6782 3 года назад

      Vous pensez pas que si c’était le cas yallah si bopam miy borom soutoura douko soutourall bopam ndakh yallah moy sameuh ay nittou bopam
      Li c’est une leçon pour les autres
      Arrêter d’être seytané

    • @aissatou5948
      @aissatou5948 3 года назад +5

      zeinab rassoul Ndiaye mais yow est ce que ça va? Toumal naniou ndeyou Adji gueum gni yaye Aïcha (rta) est ce que ça veut dire moko déff ndakh touma bi siw na «yaAllah soutoural louko»

    • @julesmane8834
      @julesmane8834 3 года назад

      @@zeinabrassoulndiaye6782 yaw est ce que ça va ? Yoboul sa baye thi gynécologue pour un test anal ngua xam ndax gorjigen leu waleu déte. Fi yalla soutoural na kouné. Même gorjigen amna séne khalifa diné ak fépou

  • @mouhamedkhalifakounta4307
    @mouhamedkhalifakounta4307 2 года назад

    Tres bien fait merci les jeunes

  • @ahdaaf970
    @ahdaaf970 2 года назад +1

    Je suis avec vous à 100%. Au sénégal on peut même nier qu' à 20h00 il fait déjà nuit.

  • @yayourassoul6110
    @yayourassoul6110 3 года назад +5

    Kouy dound goor djiguene guenn ci li metina Décédé sonal sa mbok yi nga fi bayi metina li dara diarouko ci kaw souf koukay dound daaal sopillll

  • @youriyouri4656
    @youriyouri4656 3 года назад +21

    Vraiment c'est très très grave personne ne cautionne l'homosexualité c'est un grand péché .
    Mais d'après le peu que nous connaissons à l'islam il doit être traité comme tous les morts car il est musulman qui a péché étant être humain comme lui il n'est ni de notre pouvoir, ni notre droit encore moins notre devoir de punir ça c'est du ressort de dieu. On doit le lui faire le lavage mortuaire, la prière,, l'enterrer. Ensuite dieubal sounou Borom
    Maintenant le reste c'est entre lui et soubhana wa talla.( Dieu)
    Par contre un musulman qui sort de la religion pour se convertir en non musulman ( Mourtade) après sa mort ne doit pas avoir les mêmes traitements d'un musulman c'est à dire prière de l'imam lavage etc....wallahou akhlam

    • @yayoubayam2217
      @yayoubayam2217 3 года назад +2

      Nga balma d mais dioum nga l islam dafa ni goor djiguene sou gueneh adouna dougn ko soûl si armer musulman dougn ko diou leh
      Souf si bopam sougn kofa dougueuleh daf koy guedd ndokh itam daff koy guedd
      Goor djiguene Dara daganoul si mom
      Mm les chrétiens dougn ko soule si seni armer

    • @youriyouri4656
      @youriyouri4656 3 года назад +1

      @@yayoubayam2217 salam , amoul akh nioune nieup diné bi moniou nior.
      D'après ce que je savais tes propos sont liés à une personne morte par suicide mais nak naniou bokate guestou rek diadieuf.

    • @yayoubayam2217
      @yayoubayam2217 3 года назад

      @@youriyouri4656 en tt cas lolou khel sax nangou wouko goor djiguene bakhoul si deuk bakhoul si rew l islam beugou ko christianisme beugou ko donc pk sou de weh niou war ko diou leh comme dioulit yi wala diko soul si cimetière dioulite wala catholique
      Soyons logique nak

    • @youriyouri4656
      @youriyouri4656 3 года назад +1

      @@yayoubayam2217 ,
      Je ne dis pas le contraire on est en phase sokhna habibatou.remonter vers mon premier commentaire.
      L'islam nangou wouko douko meussa nangou ni dagianal.
      Par contre il faut savoir que c'est un musulman qui a pêche,
      Alors soufékone kou péché ne serait pas enterré cimetières yi daniou wét lol sakh.

    • @damany7419
      @damany7419 3 года назад +2

      @@yayoubayam2217 non islam waxouko deh oustaz yi disait sa pour titeuleine ay bida la rek dem ba law
      amoul feine si alxourane fouko yalla waxei homosexuel c haram c un péché comme bookalei adultère fornication voyance etc mais au ken douko soul ay yokoula

  • @touffknow9104
    @touffknow9104 3 года назад +6

    N’oubliez pas que être efféminé et être homosexuel c’est pas la même chose. Amna goor you barii bolen guisee ils ont l’air tellement virile mais fek ay homos lan et vice-versa. En plus est ce que dans le coran islam interdit leur inhumation ? L’islam ne dit pas ça. Refuser de l’inhumer sous prétexte qu’il était efféminé, c’est vraiment désolant.

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 3 года назад +3

    Très bien bouko fa kénn soul goor djigen bu déh rék taal lén ndayam

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 3 года назад +5

    Mais c'est hallucinant comment vous pouvez refuser son enterrement sous prétexte qu'il est présumé homo ??? Même s'il est il à le droit d'être enterré sur se cimetière . Sénégal légui un deux gniouné borom xari tour...

    • @Onomar
      @Onomar 3 года назад +1

      @Prince Askia Haruna II vtff n’accepte pas de croire aux rumeurs imbecile .
      Sûrement dans ta famille y’a une personne efféminé mais qui n’est pas homosexuel.
      Nite mo soxor reik téh bone kou dé ak seu bamel lougn koy waxal tégouniouko beutt béne yone donc amougnou preuve ni c’est un h….

    • @Onomar
      @Onomar 3 года назад

      @Prince Askia Haruna II boul Bakou deih nianal yallah mousseul leu sutural leu reik ainsi que votre famille .
      Tu pourras avoir un jour un neveu efféminé ou ton propre fils .
      Yallah loumou binde nite lassi geuna fonk téh nio téy si mbirou yallah téh bagn porter jugement bamel xatt neu dé .
      Té kounek liga wax fi digako wax feulé

  • @fn-vx5rg
    @fn-vx5rg 3 года назад +13

    Il ne faut pa exagéré !qui a des preuves qu il était homosexuel ! Il faut faire attention

    • @mbasd2404
      @mbasd2404 3 года назад +3

      @Prince Askia Haruna II tiey un noir arabisé

    • @aissatou5948
      @aissatou5948 3 года назад

      Prince Askia Haruna II dinagn la djign ndialo? Question la

    • @senloka8381
      @senloka8381 3 года назад +2

      @Prince Askia Haruna II saway linga wakh teigoko fein.nit gni man nagne la djigne louneik deumeuk gordjigueineuk ndialok sathiak truank leip même boy dound alkhouranak sounah.fi nala nit gni wakhtanei ni linga walla leulei nga leigui nga donko ci seini beut.deigo Kini khamouko banoppi banoppi nikein douko fi soul

    • @fn-vx5rg
      @fn-vx5rg 3 года назад +1

      @@senloka8381 pourquoi parler avec une personne qui insulte des inconnus et en même temps parler de l islam
      C est contradictoire,.
      Il m a traité de menteur sans me connaître

  • @alkalycamara1954
    @alkalycamara1954 3 года назад +7

    En tout cas ça veut nous dire un musulman ou musulmane doit avoir un bon comportement gorr na goore djiguène n'a djiguène Dee bayill sa famille gathie li Dara gunou niaaw

  • @fatoukine92ify
    @fatoukine92ify 3 года назад +13

    On voit bien les dérives lesquelles nous sommes confronté aujourd'hui . La rumeur, et les accusations gratuites faisons attention, bientôt on va aller déterrer des morts au nom de je ne sais quoi

  • @meirefiy8063
    @meirefiy8063 3 года назад +6

    De vrais fou et ça que vous apprenez à vos enfants ... vraiment inhumain... tout ces enfants qui applaudissent thiéy c'est des juges en plus ...xalé yi rek la yeureum de pire en pire tekksi Massa

  • @galsendouze212
    @galsendouze212 2 года назад +1

    borom lou rouge li deugeur nga fit yaw yaye juge bi ok

  • @amadouba4736
    @amadouba4736 3 года назад +6

    Ce mec en tee-shirt rouge doit être arrêter et condamner avec la plus grande sévérité. Il est qui pour décider que ce défunt ne sera pas enterré. La plupart de ces gens font des actes répréhensibles.

  • @ndeyegueyeloum1741
    @ndeyegueyeloum1741 3 года назад +1

    Ay li loukofi diar ☹️☹️

  • @djibydiouf2263
    @djibydiouf2263 3 года назад +10

    Il ne fallait pas laisser le doute de se vivant... Un musulman doit jouer claire dans sa vie....

  • @ousmanenoelcisse1878
    @ousmanenoelcisse1878 3 года назад +4

    thiowou gordjiguéne bi fi mou dieumé réwmi bakhna nagnou démm rék

  • @ladjitandian9311
    @ladjitandian9311 2 года назад

    Bonjour
    Boulènn nangou moukk niou soulko foofou jamais goor djiguène domeramm leu khadj leu

  • @juniorjunior1345
    @juniorjunior1345 2 года назад +1

    Vraiment nite dafay mandou... Lo guissoul lo khamoul dara woroulaci meusso ték sa beute mouy def l'acte. Ah ngua bayi lép si lokhoy borom... Sénégal deh dégeuna ak ki néna ak wakhnaniouma rek nguay ame kom motif di jugé dieuy yomarhiyame dina méti. Amoul kéneu kouci wakh maci ték sama beute.... Mane déh dangou la deuk mais je le connais pas donc je ne le juge pas. Yalnaniou yallah doli soutoura té yeureum bépp domou dioulite

  • @ousmanenoelcisse1878
    @ousmanenoelcisse1878 3 года назад +7

    li da nara eupeu lokho bilahi nagnou moytou kou dioukk gnouni gordjiguéne la té dara lérou gnou si

  • @sirasow6377
    @sirasow6377 2 года назад

    Am na gno khamni kén dakhoulén djouli ak woor té bolèn guissé dagnouy diantal mais ndeyssane c ds vicieux 😭gordjigén mom bakhoul si dara té Senegal dagnouy yok wayé dougnou soss famille bi nagne sét si yalla bagne déf loulén sounou borom di topé gno diour sén dom kham nagne si c un 2 puces ou non

  • @patricesylva3658
    @patricesylva3658 3 года назад +6

    N'importe quoi qui somme nous pour interdire une personne d'être enterré un mort ne peut être jugé que par le tout puissant mes frères les cimetières son la' pour recevoir ce qui ne son plus de se monde respect

  • @cheikhniang4754
    @cheikhniang4754 3 года назад +1

    Niit su fattoo dagn ko wara soul
    Lolou moy yon nitt sou fatto tee ken soulouko gneipay am bakar mm soudé gorjiguen leu kon soul lenn koo kom d’accord guen ni ap joulitt leu lisi des yalla leu ak mom.

  • @aitandiour3499
    @aitandiour3499 3 года назад +1

    Mass Gueye sa yaye Khady Thioub xam nagn ko tiaga la boulgnou takha wax

  • @zeydarassoulryba4203
    @zeydarassoulryba4203 3 года назад +13

    Yaw vraiment kou meuna doule ga biga ko khamoul wé siga warone theudj sa gâte gui tu n’est pas Dieu bay juger kene

  • @modoudiop3170
    @modoudiop3170 3 года назад +1

    Merci mn frère Alhah

  • @mamembayendiaye7125
    @mamembayendiaye7125 3 года назад +1

    Wawawww bouko kéne soull , bagne réck douffiii am tay douffii am souba n'a lérrrr ya de négociations.

  • @ibrahima1964
    @ibrahima1964 2 года назад

    Si lou Yalla beugoule laniouye deffe Sénégal chaque jour billahi

  • @boubacarthiendiaye1188
    @boubacarthiendiaye1188 3 года назад +8

    Gni daniouy Doul liniouy wakh amoul boy bi il es correct

  • @niasseamadou6161
    @niasseamadou6161 3 года назад +11

    Fait très attention nous sommes des musulmans se que vous entrez de faire très graves pour le sénégalais

  • @seynithiam7857
    @seynithiam7857 2 года назад

    Thiey Mane dal adouna doy n'a waar,leguii dagay dooh wingal tankeu saàx gnouné goordiéguéne la.
    Dagnoo wara am Lou lére bala gnouy diegne vraiment .

  • @cheikhouthiam4443
    @cheikhouthiam4443 2 года назад

    Gnaw c trés bien ,li da wara diékhe ci adouna bii ak sunu rèw car étabi dou ko meussa criminaliser!

  • @mcisse-qy6in
    @mcisse-qy6in 3 года назад

    Merci momo bravo

  • @arthurconley1969
    @arthurconley1969 3 года назад +14

    Il faut avant tout respecter un mort.Quoi qu il en soit il faut l enterrer dans la dignité. L etat doit interdire ces genres d attroupement dont la majorité sont des mineurs Nul n a le droit de prendre une telle décision.

  • @lalaaichacamara8437
    @lalaaichacamara8437 3 года назад +4

    Déjà ya ngui wate thi serigne touba bokaler yallah bou feuse ngua tok fi di oubi sa lamigne .bokaler yallah mo guana grawe boude bone rek bokaler katou yallah yi gnon geuneu yess guordjigene yi

  • @djenebouguindo6589
    @djenebouguindo6589 2 года назад +2

    Vraiment c'est ma première fois que j vois ça,vous exagéré vraiment personne n'a le droit de juger son autrui

  • @sport_univers.2482
    @sport_univers.2482 2 года назад +1

    Loufi way jugé yawmalhiyam digako jugé tu as vu gnidef intervenir gnep nenagn hamougnouko mais pourquoi sénégalais eupeul l essentiel yalla moham lép voilà
    Repos en paix 🙏

  • @ndiayeibrahimadabo3771
    @ndiayeibrahimadabo3771 2 года назад

    Le combat continu Macha Allah

  • @djatoudiawara1075
    @djatoudiawara1075 3 года назад +13

    Ce que vous faites c ajouter de la peine aux parents du défunt

  • @annemariedaniellezimmer4328
    @annemariedaniellezimmer4328 2 года назад +5

    Jugez et vous serez jugez!

  • @alphadiallo7537
    @alphadiallo7537 3 года назад

    Machalah merci beaucoup a vous

  • @fatoudiminguandiaye5511
    @fatoudiminguandiaye5511 3 года назад +3

    Ay way dethie lenko tei yalla takh

  • @bambathiaw6913
    @bambathiaw6913 3 года назад +4

    Yalna borom bi doli yeurmandheii,lo Dara jarouko adouna dey diekh naniou bayi well biss pinthieu

  • @georgpom9229
    @georgpom9229 3 года назад +11

    Vive la jeunesse sénégalaise nous Barrons la route au homosexuel le peuple sénégalais dit non a l'homosexualité au Sénégal Vive le peuple sénégalais le 20fevrier nous serons tous sur le terrain a la place de l'obélisque nous exigeons à macky la criminalization de l'homosexualité au Sénégal c'est obligatoire ou bien macky quitte le pouvoir point barre

    • @julesmane8834
      @julesmane8834 3 года назад +1

      Yaw sa xourou baye

    • @georgpom9229
      @georgpom9229 3 года назад

      @@julesmane8834 yaw goordjiguene gua

    • @georgpom9229
      @georgpom9229 3 года назад

      @@julesmane8834 c'est normal sa mbokou goordjiguene guay soutenir wayai fii Sénégal goordjiguene doufi am diam mouk ta doufi naner gniekh

    • @julesmane8834
      @julesmane8834 3 года назад

      @@georgpom9229 kone deh tu peux commencer par ton père il est le président des gorjigen. Ousmane sonko mome n’en parlons pas mome sodomiser rek diokhko

  • @etiennediop4942
    @etiennediop4942 2 года назад +2

    Il fallait simplement appliquer la charia : donc prendre 4 personnes qui ne se connaissent pas , tegal lèn Camiiine niou wat nè giissneniouko mouy seye ak gor. Et surtout aussi rappeler a la population lou dinèr wakh cii kouy ndialo ak koudoul djeukeurome wala diabbarome. Dokhal lèn charia cii yoone

  • @oumiinatraiteur3400
    @oumiinatraiteur3400 3 года назад +23

    Bilakhii lignouy wakh yeupe dou degue kéne waxoussi degue mome mi ko djité mo guena bone dangou kou wédii démal lathieuté mass gueye mome sobé néne leu té ay gordjiguéne gnii lay andal mouy djéma sétal déram dangou diko diaralé si domou diambour djii ... yéne doléne sakh ayy nite kéne xamoukosii ngéne dii doul rékk dingéne ko layo dhh yéna guena bonne nieupe ...

    • @boubacarthiendiaye1188
      @boubacarthiendiaye1188 3 года назад +3

      Bilay boy bi nio deuk gni daniouy sooss rk

    • @oumiinatraiteur3400
      @oumiinatraiteur3400 3 года назад +2

      Bayiléne kou nékk yorr sa lamine dii féne

    • @Yetou85
      @Yetou85 3 года назад +1

      Yawe tamite yangi soss deh. Ça décrédibilise ton propos

    • @bbouhama5373
      @bbouhama5373 3 года назад +2

      Ki deh mola gueune ndakh, moungui takhaw di defendre souniou diiné

  • @bayesalioba6760
    @bayesalioba6760 2 года назад

    Billahi

  • @bayesalioba6760
    @bayesalioba6760 2 года назад +1

    Billahi dof

  • @ibou1061
    @ibou1061 3 года назад +1

    Bayilén ndiorte ! Ani preuve c grave sa

  • @onlygood1114
    @onlygood1114 3 года назад +3

    Ay waay lii niaw n'a seul dieu peut juger 😭

  • @PendaDiop-g6f
    @PendaDiop-g6f Год назад

    Anta dingleer yow fatte khadioufi ani wa dingleer

  • @wolysougou
    @wolysougou 3 года назад

    Kou nékoul si bou gatte bi yangui si bou gougou bi

  • @josephdia4354
    @josephdia4354 3 года назад

    Doye n'a waar 😭😭

  • @bbrama5303
    @bbrama5303 3 года назад +3

    Je suis choqué plus d humanisme dans ce pays

  • @mamegormar8897
    @mamegormar8897 2 года назад

    Walahi diaroul khékh diaroul khoulo lolou kouci nék bafatou bounioula solone makka sakh yalla doumalla te d'où yakhayal dioulite yanoufa de soul Dara nguir yalla yéwou lène té toub délou nguinaw louye diékh kéne douko dieundé loudoul diékh té adouna loulou nékh nékh daye diékh

  • @abdunjaay738
    @abdunjaay738 3 года назад

    Lii rekk doyna mbuugal !

  • @fatoumbacke9083
    @fatoumbacke9083 3 года назад +1

    Ah li gnawena torop si même quartier gniy wakhe yep kene khamou kossi gno wakhe mesou gnouco guiss pourquoi guene dico wakhal borom gnari tour yi ay rumeur rek senegal bayilene khel bouba bakhe li ameth Khalifa niass wakhe dinagne guiss goor guou refet ni borom gnari tour yila

  • @fatimagueye963
    @fatimagueye963 3 года назад +1

    mane lima diakhale gniome gni si almére yi kéne khamou kosi diko toumale yalla amena dé té kou dé ak sa bamel

  • @adakouloukouofficiel8522
    @adakouloukouofficiel8522 3 года назад +1

    Ada kouloukou artiste sétane ka abonné

  • @kanitoure1313
    @kanitoure1313 3 года назад +3

    Entoucas cei de grave accusation wadji sol tee shirt bou rouge bi kom khamoul defunt bi en faisant les investigations il devait se rapproché de personne fiable et avant de parler qu’il jure sur le coran komsa il saura k ya k la verité qui sortira de leur bouche s’ils sont de vrai croyants

  • @abdoulayebadji5664
    @abdoulayebadji5664 2 года назад +5

    Merci ne lâchez pas 🇸🇳✊🏿❤️❤️

  • @Fraiizybaby
    @Fraiizybaby 3 года назад +1

    Bilahi yeinagui def lou graw lou niaw deigue na rek gueine di wakh une chose amena goordjigueine yi leigui nio gueuna gooré doleine ko sakh foguei