@@yorosarr4140 nopi pourquoi? Pask limey wax nekhoula iow? Non non djambaar moto wooroul def transport kou wax ak sa bamel rek mann dawal na façon moto bou nek tei lissi nek si insecurité dafa beurri bagn naako ba kenneu douma supporter soumay yeek si moto dafey fekk makoy dawal donc lima beugal sama bopp rek laay partager bo amé avis contraire meunn ngako indi mais khamo ma khamou mala na donn si respect ak yar ndax lolou rek moy deug. Wa salam
@@thiernomboup5878 Man liguèyou ma moto dawa louma moto mais lingue wakh andou ma ak ioe louy thiakhane gnii di liguèye nguanan thiaxan loutakh nguen dof khamo wakh
Il a bien parlé Machaallah bravo et bonne continuation
Bien Bien parler
Bien parlé
Yalna yalla diappalé khewal ak wer
Bro sma gayui bonne continuation 💪
Machalla wax dji rafét na
Sénégal dafa meti 😭😭😭
li ter bi motakh gouvernement bi Di wakh si diakartamane yi
Nanioulèn bayi niou ligèyeu
Jajef waye
Sama gayi meunn ngeen use senn machine pour livraison mais pas transport. Transport moto baxoul sama gayi woorul
Yaw nopil yaw yalen diokh lougnou djeundé moto
@@yorosarr4140 nopi pourquoi? Pask limey wax nekhoula iow? Non non djambaar moto wooroul def transport kou wax ak sa bamel rek mann dawal na façon moto bou nek tei lissi nek si insecurité dafa beurri bagn naako ba kenneu douma supporter soumay yeek si moto dafey fekk makoy dawal donc lima beugal sama bopp rek laay partager bo amé avis contraire meunn ngako indi mais khamo ma khamou mala na donn si respect ak yar ndax lolou rek moy deug. Wa salam
😭😭😭😭😭😭😭🇸🇳
Nanioulene bayi niou liguye
Djiakarta mo nekoul pour capital
Bayilen nouliguey ndem
Thi ay thiakhane guene nek
Kane moy thiakhane ?
@@damegaye342 borom moto yi li sais irrégulier
@@thiernomboup5878 yaw mi yaa nek thi ay thiakhane
@@damegaye342 a kone bakhna