QUARTIER GÉNÉRAL - Invité : SERIGNE GANA MASSERE - 16 Mai 2020 - Partie 2

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 442

  • @mamisakho9242
    @mamisakho9242 4 года назад +1

    yalna yalla fayal gnou serigne touba. seydina mouhamet psl kaine dou mom.leip lougn am si adouna mognouko may.emission bi neikhna.serigne gana yalnala yalla samal bopam goudeul seine fane weireul doli khamkham bi.mane yeinay feikheul sama khol

  • @diaristadiaw3777
    @diaristadiaw3777 4 года назад +54

    Balak marame Aïchak sadio goor gua botone fouta roguanti guanar ramlo mbaxane toublo bour sine Coumba ndofféne DIOUF .Bayou Serigne Saliou ak Serigne Fallou ana éléments Bamba yiiiii waye waye ana salihats ak salihates yiiiiii ay waye ani éléments Mame Fallou yiii 💖💖💖💖💖💖Bamba poit 👍

  • @assmalickguisse2707
    @assmalickguisse2707 4 года назад +42

    Wallahi jai les larmes aux yeux ndakh bimou wagneko niou dinthie ko ki tek lokho bi ni guigne nani alkhourane laniou dinthie machalla sokhna diarra lepp yawla

  • @kinembaye8565
    @kinembaye8565 4 года назад +47

    Bilae khole séda tina cheikhoule khadim amoule morom walay .Mame diarra bousso ki gueune si djiguène yalla nagnou yalla tasse si sa barkéi

  • @tackkofaaltv534
    @tackkofaaltv534 4 года назад +13

    Kendou ndoll makka. Yallah na gnou borombi fayal serigne Touba

  • @MbeneSaliou
    @MbeneSaliou 4 года назад +150

    ANi KAAN MOOMAY SANTALÉ SERIGNE BAMBA ❤️AMOUGNIO FAYAM

  • @mamadoudiop5760
    @mamadoudiop5760 4 года назад +19

    Serigne touba ken d'où mom beug serigne bi beusel j aim

  • @dieynabakande3690
    @dieynabakande3690 4 года назад +34

    Vraiment avec objectivité je peux affirmer que Pape Cheikh Diallo est un excellent animateur..pour ne pas dire le meilleur de sa génération👌👌👌mention spéciale à lui et à toute l'équipe du GFM...

  • @youngthiam9821
    @youngthiam9821 4 года назад +9

    Dieureudieuf Cheikh Ahmadou Bamba Khadimoul Rassoul 🙏🏽🙏🏽 mais naak kèn dou Oustaz Hann ça ce voit il a un joli cœur Masha Allah

  • @macouraniang
    @macouraniang 4 года назад +12

    Ma beug serigne ganamessera ndakh limou beug bamba ak yonentam sws yalla nanouko yalla fayal mom gana barki khadim Rassoul.

  • @assmalickguisse2707
    @assmalickguisse2707 4 года назад +71

    Ken dou ya rassoulillahi borom barriere or bi sama sope

  • @sarrfatou3386
    @sarrfatou3386 4 года назад +51

    Yalla nagnou guisse ak kou ted ki euleuk yalmal khiyam🥰😭😭😭

  • @moustaphingomi1604
    @moustaphingomi1604 4 года назад +7

    segne bi dall noy gueuna khirree sii ay mbireum moulay gueuna wone boppam. thieuy Bayou Serigne Saliou Mbacke❤❤❤

  • @ibrahimadieng4315
    @ibrahimadieng4315 4 года назад +67

    Félicitation à pape cheikh Diallo meilleur de sa génération big up à TFM

  • @ahmedsane2666
    @ahmedsane2666 4 года назад +39

    Kenne dou Serigne Touba ❤️🙏🏽

    • @fadeldiop4563
      @fadeldiop4563 4 года назад +1

      ❤❤❤👍

    • @antathioub1349
      @antathioub1349 4 года назад +2

      Dieuredieuf serigne touba diarama mame diarayatoula

  • @sokhobbsamb6265
    @sokhobbsamb6265 4 года назад +8

    Xol séde tina barki serigne Touba 🙏❤

  • @aissatouleonie8985
    @aissatouleonie8985 4 года назад +7

    Souniou beugue Serigne Touba yalla naye gueune Di yokou abadane❤️

  • @salioudiakhate9095
    @salioudiakhate9095 4 года назад +6

    Kou ted ki amoul masse 🙏🙏

  • @fatoukineinediane6247
    @fatoukineinediane6247 4 года назад +1

    Diereudieuf Cheikhoul Khadim kou ligueyal Yalla Yalla Faye la ... Wakh tane bi amatyna solo...
    Serigne gana mala beugue ndak kou Tedd ki ❤️🙏

  • @mustaphasamb2313
    @mustaphasamb2313 4 года назад +22

    Dieureudieufeuti serigne ganna messere yalla nafi yague ta wérr si barkép khadim rasaul... dieureudieufeuti serigne touba khadimou rasaul

  • @keurrassoul5810
    @keurrassoul5810 4 года назад +49

    Ani gni serigne bi di sédall sén xolll ❤❤

  • @boussothiam5604
    @boussothiam5604 4 года назад +37

    Keneu dou serigne touba

  • @papismane1576
    @papismane1576 4 года назад +7

    Yalla naniou yalla tass si barké diëurëudiëuf chëikhoul khadim

  • @oumarsene4604
    @oumarsene4604 4 года назад +10

    Baye cheikh maacha alakh borom xol Bou réfét nga yala nala kou téd gui faayy amiinn

  • @diaristadiaw3777
    @diaristadiaw3777 4 года назад +38

    Keneu d'où Bayou Serigne Saliou Mbacké 💖💖💗

  • @adamadiouf5788
    @adamadiouf5788 4 года назад +11

    Kène dou serigne khadime Rassoule❤❤❤

  • @keurrassoul5810
    @keurrassoul5810 4 года назад +22

    Bilahi serigne touba la beug
    Kén dou serigne touba si xoll ❤❤

  • @ndoyeastou80
    @ndoyeastou80 4 года назад +9

    Thiey borom Touba yalla naniouko yalla fayal dieureudieuf mbacke diarama sokhna Diarra ak sidi Brahim fall

  • @antasilla3035
    @antasilla3035 4 года назад +18

    Wa tfm yalna télé bi sx si dim gaba j'aime

  • @bayesylla108
    @bayesylla108 4 года назад +13

    Ndey sane serigne touba amoul morome

  • @amadoubambandoye9256
    @amadoubambandoye9256 4 года назад +2

    Oustaz pape hanne guis geu liguay def ni amoul chance guay dageu gana bagne mou waxtane fumu waxx gua dagg ko diko lathie kene guis geu serigne bamba beurigo si mbartal leu pousse mou déme ñakka pousse mou déme guéne balma nak si kaddu yi wa salam 🙏🏾

    • @ababacarndiaye3993
      @ababacarndiaye3993 4 года назад

      Pape Hann n'a pas besoin de le limiter ou contourner mon frère. Le gars déroule normalement sans contrainte. Pourquoi vous aimez la division. Nay rafet way. Adouna amoul solo

    • @amadoubambandoye9256
      @amadoubambandoye9256 4 года назад

      Ababacar NDIAYE mon gas kou khol pape hane demb day kham ni dafay dagg gana pourquoi meunou ko bayi a chaque fois mouy dakk souy waxtane si bene serigne dou egali sakh mou toudd kenéne frère ñoune douñou ay gaka way ish

    • @elementssaliou6373
      @elementssaliou6373 4 года назад

      Bilaye deuge boi wer nga wax fimouye nékhé rk lakoye dague

  • @mariamadiop2924
    @mariamadiop2924 4 года назад +1

    billakhi kene dou seringe touba senge gana dounda yokal werall pape chiekh diallo yalna yalla goudall sa fan way sa ligéy rafétna machalla

  • @dieynabakande3690
    @dieynabakande3690 4 года назад +33

    ..avec certitude je confirme qu'il est le meilleur animateur du Sénégal

  • @mameboussondiaye4314
    @mameboussondiaye4314 4 года назад +5

    Kou bagne serigne touba dèwal bamba amoul mome kèn rk la amoul mass amoul morom mome rk mofinèk sonou yakar ❤ana mouride yui

  • @sambasow2104
    @sambasow2104 4 года назад +18

    Machala machala Karabakh yeup mane bimo mama si gueuneu markè lil Moukhtakha wa jeukh tou fil Ndakarou Quand je serais Mountakha je reviendrais à Dakar mane mom bobou markè nama mè Ken dou bayi Bass ak Barra goor ga demone Gabon diarry Mayombé delou si fi diniou khamal boromam

  • @fatouba9460
    @fatouba9460 4 года назад +2

    Man dh Lima manoul wona dougou rk moma méti won yalnalé yalla défal diamou barké s touba

  • @adjimbenendiaye578
    @adjimbenendiaye578 4 года назад +24

    Kénn dou Sokhna Diarra❤️💯

  • @mami107diop2
    @mami107diop2 4 года назад +11

    Sounou kholll sedatina machalla serign Touba kene dou mome gana massere yalnafi yague te weerrr barki chekhoul khadim

  • @jamilejoop2908
    @jamilejoop2908 4 года назад +9

    Machallah yalla nagnou yalla tass si barkey sunu Mag yi...🙏🙏🙏

  • @BirahiimCr7
    @BirahiimCr7 4 года назад +77

    Sama xol bi diokhnako cheikh Ahmadou bamba khadimou rassoul ak kane may guiss

    • @evadia9028
      @evadia9028 4 года назад +1

      Aka diara diokh walahi kéne d'où mame brome touba kheuye dii diakarok diouma dji rk daguaye am mbécté

    • @videogiochi3945
      @videogiochi3945 4 года назад +1

      Bilahi daff layy yobuu thia saa brom xamm naa thie dra

    • @TEAM_DMG_OFFICIEL
      @TEAM_DMG_OFFICIEL 4 года назад

      Alkhamdoulila
      Santati serign touba

    • @TEAM_DMG_OFFICIEL
      @TEAM_DMG_OFFICIEL 4 года назад

      Alkhamdoulila
      Santati serign touba

  • @ndongodarasonexcellence8930
    @ndongodarasonexcellence8930 4 года назад +1

    Dieuredieuf Mame Soxna Diarietoullahi yallah na yallah yokk sayy ler té Tass Niou si sa barker

  • @mamankane2863
    @mamankane2863 4 года назад +5

    Machalla sama khol mo toye sakh dakh dama khamné kéne dou Serigne TOUBA

  • @voyageautourdumondesn
    @voyageautourdumondesn 4 года назад +7

    Ko beugue Gana 👍 👍 guir serigne touba dieureudieuf mame Bamba

  • @jadimproplayer5229
    @jadimproplayer5229 4 года назад +28

    Li gnouy wakh serigne touba khadim rassoul koumou sédoul sa khol do gorr diame nga ndakh liniou ko tékk si zayire AK batine eupena tei lépp la dékou si diomame ak foulame balla aíssa mome dongue

  • @Mouss400
    @Mouss400 4 года назад +30

    Pape cheikh est un animateur intelligent,très très intelligent,👍👍👍

  • @babacardiop4068
    @babacardiop4068 4 года назад +5

    Bilahi Baaye cheikh ya mane plateau kène dou yaw machala 😍😍😍

  • @kinekane4791
    @kinekane4791 4 года назад +3

    Serigne guana messare yallana yalla fanewou good bou ande ak weer

  • @soldaroussalioudjite1828
    @soldaroussalioudjite1828 4 года назад +7

    Khadimou Rassoulilah Keneu dou mome QG ala dawme s gana yalla na yalla samou leu defal tawkhef ak tayzir thi barke borom Touba

  • @biggmane1873
    @biggmane1873 4 года назад +7

    Ken dou mame mariama diarra toulahi yayou sama serigne💓💓

  • @labsolugueye9016
    @labsolugueye9016 4 года назад +4

    Dieureudieuf borom touba Dieureudieuf borom serign touba Dieureudieuf serign touba Dieureudieuf serign touba Dieureudieuf serign Touba Mai Gana Mésérè xoll yeupou féx Nann Wallahii kaindou serign touba Mbackè Balla Dieureudieuf ♥️🤍💙🙏

  • @madjigueneseye6973
    @madjigueneseye6973 4 года назад +6

    Yalla naniou yalla fayal serigne touba ❤🙏

  • @pendathiam7869
    @pendathiam7869 4 года назад +6

    Lahilaxa illalaa moukhamedou raroulla salalaxouhenlayhiwasalam 😍segn Gana yagu fi loll diniou yaga gougué 😍😍😥😥

  • @mameboussondiaye4314
    @mameboussondiaye4314 4 года назад +12

    And ak serigne bi ba aldjiana rk❤❤❤❤

  • @mustafallfall2073
    @mustafallfall2073 4 года назад +1

    Merci amna solo lol Yalla nali Yalla Fay jbarkb Seringe touba

  • @bossbambaofficiel7698
    @bossbambaofficiel7698 4 года назад +6

    Nehul ba nehul, wayé Ganna mo meun Gayi . Tu es le meilleur

  • @papito8025
    @papito8025 4 года назад

    TFM Yalla na nguén yagg djitou ci barkei Serigne touba , sen liggey rafet na en plus vous êtes des professionnels MashaAllah... bala dewene yalla na nguén meune louko raw té yalla def QG comme meilleur émissions beu faw ci mbaxou Serigne touba

  • @binetaseck9538
    @binetaseck9538 2 года назад +1

    Merci beaucoup 🤩🤩🤩

  • @astoucisse4394
    @astoucisse4394 4 года назад

    Merci beaucoup serigne gana doundal te wer merci pape Cheikh

  • @adjameta
    @adjameta 4 года назад +1

    Pape cheikh yalnala soung borom bolei si gas yiii sering touba yiii si barcke weerou kor gui khol yeupp sedna😍😍

  • @mouhamddia5291
    @mouhamddia5291 4 года назад

    Beugue serigne TouBa Diarna lounee nakh day farta si nitt kou nioul gana Bonn continuation

  • @boygainde3764
    @boygainde3764 4 года назад +5

    Kou mere tan pis daniouy gagné wa li nekhoule enkay dieureudiefé kou serigne touba diarama Lamp fall baboul mouridina di niane serigne Mountakha yague fi lole té andak werre 💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕

  • @modougning3509
    @modougning3509 4 года назад +14

    Tfm rek machalla gana goud fane rek

    • @anneevamendy293
      @anneevamendy293 4 года назад +1

      Je suis catholique mais serigne Touba machalla

    • @abdoulayebaneniang
      @abdoulayebaneniang 4 года назад

      @@anneevamendy293 merci sokhna Anne yallah na la yallah fayal bopam

  • @petitngom9295
    @petitngom9295 4 года назад +4

    Walahi beugeu Serigne touba rk doyna diamou yalla sougniou wadjie kene dou mome

  • @creartstudiosenegal5079
    @creartstudiosenegal5079 4 года назад +5

    Nagn kénal yalla, té nangoul Serigne Touba liko yalla may

  • @Minarassoul05
    @Minarassoul05 4 года назад +6

    Seydina Mohamed ani gniko beug ❤❤

  • @firdawsifall3947
    @firdawsifall3947 4 года назад +21

    un vrai Google ce mec il maitrise tous les versets et vers (poème) des xassidas de kutedki

  • @bayetaphagueye5290
    @bayetaphagueye5290 4 года назад +5

    Dieuredieuf Serigne Touba Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall

  • @falloudiop1580
    @falloudiop1580 4 года назад +10

    Macha'Allah kenn dou Sgn Bamba

  • @khadimdiop5498
    @khadimdiop5498 4 года назад +5

    Sokhna diaara lépou yawla dh bousso baly liguéy bi sétna sélna rafétna yalla fauénala serigne bamba

  • @mouhameddiaw5504
    @mouhameddiaw5504 4 года назад

    Vraiment pape cheikh c'est le meilleur présentateur de sa génération c'est le meilleur

  • @bambahann5573
    @bambahann5573 4 года назад

    Dieuredieufety sama tourando chiekh ahmadou bamba 🙏🙏

  • @mansourndiaye7954
    @mansourndiaye7954 4 года назад

    Mani Ganna Messere al khadim Gueye dagnio tijaane fii (damay toogne) li dafa neekh beggee martaba sugnu mak gnu baakh yi nga khamni foo nat seen wilaaya rek romb nako. Sugnu fierte sugnu mame CheikhCheikh Ahmed Bamba

  • @binetadieng595
    @binetadieng595 4 года назад

    Balla aysa dieureudieufer yaw, dieureudieufer Serigne Touba🤲💖💖

  • @oumarsene4604
    @oumarsene4604 4 года назад +16

    Dieureudieuf serigne Touba

  • @bayesylla108
    @bayesylla108 4 года назад +5

    Pape cheikh contenant Machallah kéne dou Ahmadou

  • @bonneintentionbonneaxion1515
    @bonneintentionbonneaxion1515 4 года назад +22

    Je suis fier d'être moride . car les moride son tjr les meilleures donc srgn bamba amoul morom si zayir bi rek . Les 3 mosquée les pl8 grand .

    • @babacarsy8860
      @babacarsy8860 4 года назад

      Tu es un seytané toi ça se pas un arène

    • @makhandiakho1154
      @makhandiakho1154 4 года назад

      Aucun tarikha n'est meilleur que l'autre bro

  • @bayesylla108
    @bayesylla108 4 года назад +7

    Pape cheikh mourid leuh

  • @oumarsene4604
    @oumarsene4604 4 года назад +4

    Serigne Gana yala naala kou téd gui faayy amiinn yaara baall amiinn

  • @awkine7685
    @awkine7685 3 года назад +1

    Dieureudieufé borom Touba khadim Rassoul

  • @fatmandb8319
    @fatmandb8319 4 года назад

    Vrement pape cheikh diallo tu est le meilleur anomateur yalla na sarigne Touba Takhawou

  • @abdoudiakhoumpa6304
    @abdoudiakhoumpa6304 4 года назад +2

    Mouride tidiane khadre ak wa layénn bamba gnieup lafi nékal....dieureu dieuff khadim rassol

  • @formni893
    @formni893 4 года назад

    Thiey Serigne ganna messere yalla na diamam yagg ♥️♥️♥️

  • @papakasse4225
    @papakasse4225 4 года назад +4

    Ndayssane serigne touba kénn leuh

  • @falloufaye7151
    @falloufaye7151 4 года назад

    Gana yalla na la yalla Faye barkè serigne touba

  • @farbaseck2854
    @farbaseck2854 4 года назад +5

    S bamba amoul mass wayai tfm sa kao sa kanam Marshalla contane naniou trop

  • @ibouthiam6003
    @ibouthiam6003 4 года назад

    Mariama moye yayi Issa jesus mi doundou 33 ans niewate di Mame Mariama Bousso kémanou yalla la ma cha ala ❤️🙏

  • @salioudieng3870
    @salioudieng3870 4 года назад +1

    barkii yalla serigne bi kén la amoul wéranté

  • @bassiroudiouf2449
    @bassiroudiouf2449 4 года назад +3

    Jarajeufeti serign touba khadimou rassoul

  • @boussothiam5604
    @boussothiam5604 4 года назад +11

    Serigne khadim Gueye doundal weral

  • @modoundao4004
    @modoundao4004 4 года назад +4

    Diueradiuef serigne touba ♥️

  • @serignesalioumbaye2344
    @serignesalioumbaye2344 4 года назад

    Diaradieufa serigne touba pape Cheikh yalla serale sa khole amina

  • @ndongodarasonexcellence8930
    @ndongodarasonexcellence8930 4 года назад +2

    Al hamdoulillah sant yallah Macha Allah bima dioudo Sénégal

  • @madiawmboup7403
    @madiawmboup7403 4 года назад +5

    Souniou amoul la amoul wonne khaw ma founiou dieum ahmadou ❤️❤️❤️❤️

  • @khadimkane7195
    @khadimkane7195 4 года назад +9

    Merci ❤❤🙏🙏🙏🙏

  • @aidafall5465
    @aidafall5465 4 года назад +8

    Machalla khol sedda tina

  • @sophiediakhate141
    @sophiediakhate141 4 года назад

    Diereudieuf Serigne touba amoul morome 🙏🏽

  • @pendandiaye4236
    @pendandiaye4236 4 года назад +1

    Machalla gagna yallnala serinbi fayall bobpam

  • @bayesylla108
    @bayesylla108 4 года назад +1

    Ganna néna béne enemi la ame mouy kou diokhagne serigne touba

    • @videogiochi3945
      @videogiochi3945 4 года назад

      Taa muyy deugg ndax moo deff luu kén déful

  • @cheikhnafall7101
    @cheikhnafall7101 4 года назад

    Ndaysaan oustaz hassane kou beugg seurigne touba la.😊😍

  • @fatouthiam4060
    @fatouthiam4060 4 года назад +11

    Oh sama kholle dafa séd❤️