Je suis tidiane, talibé de Baye Niasse, ceci touche mon cœur, mon âme, mon être tout entier et me procure une joie intérieure inexplicable, mes entrailles jubilent en recevant la lumière émanant de cette belle mélodie. Si ce n'est là les prémices du paradis qu'est-ce que ça pourrait être
bilahi walahi talahi malikia souléne yalla fayé guen contane. déssé la toléne niou dara. en plus KHILASS bi gniy awou niogui gueneu guéné awou diékhital bi. gueun na leer pour gniy diangué khilass à travers zikr. cheikhoul hadj malick mom amouniou fayame yalla naniou ko yalla fayal. bidjahi taha aleyhi salli souma alal ali wa sakhbi wa salim rabbi yallahou
Loin fut ce temps où ce genre de délice était servis que les vendredis à l'heure de prière dans nos TV. La véritable révolution médiatique c'est ça. Yalna Yallah fay yiw
Que Dieu continue de répandre sa pluie de grâces sur Mame Cheikh Seydil Hadji Malick SY (rta). Je ressens toujours un plaisir inexplicable lorsque j'écoute les chansons de Aboul Aziz Mbaye. Khilassou zalab, notre fierté.😍
Tidiany fi dunya wal akhira 💙💖💞 Cette mélodie me fait tellement du bien. Je l'écoute chaque jour avant de m'endormir ca apaise. Mame khalifa ababacar Sy protege 🙏
Abdou Aziz mangui lay gnanal goudou fane yalla bayi la fi bassi kaname weral batte bi ameen🤲 Wa keur Mame Maodo diamm si yéne yalla may léne goudou fane ak weer in sha Allah ameen🤲
MACHA ALLAH ALHAMDOULLILAHI MERCI MON DIEU DE M'AVOIR DONNER L'OCCASION D'ENTENDRE DANS MA VIE CES MERVEILLES DE MAME MAODO CHANTER ET DIFFUSER PAR DES VIRTUOSES MERCI A TOUS
Aldiana soriwoull,,je suis un jeune talibe Serigne Touba , cette khassida ça touss au ceurr naniou yalla fayall mamm Al, Malik
Amine khôl Sed na
@@omarsow1800 😅😅😅😅😅😅😅
Bilahi yabakh yagorre yalnala yalla diapale si barki khassida bi
❤❤❤
@@AdamaNdiaye-r1ua ❤
Je suis tidiane, talibé de Baye Niasse, ceci touche mon cœur, mon âme, mon être tout entier et me procure une joie intérieure inexplicable, mes entrailles jubilent en recevant la lumière émanant de cette belle mélodie. Si ce n'est là les prémices du paradis qu'est-ce que ça pourrait être
Barkei Cheikh Ahmadou Bamba li dafa neix❤😭
bilahi walahi talahi malikia souléne yalla fayé guen contane. déssé la toléne niou dara. en plus KHILASS bi gniy awou niogui gueneu guéné awou diékhital bi. gueun na leer pour gniy diangué khilass à travers zikr. cheikhoul hadj malick mom amouniou fayame yalla naniou ko yalla fayal. bidjahi taha aleyhi salli souma alal ali wa sakhbi wa salim rabbi yallahou
Diarama seydi hadji malick et famille keur mame Moussa mbaye vraiment yénagui séddal xol yii
Mbokk bouniou faté djapalé malikia ci ligeey bi nanie japp si like yi commentaire yi niaanal sunu Maam Cheikh Seydil Hajj Malik ak partage yi😇🙏🏾
Khilass 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰ak wa keur moussa ale mbaye 🥰🥰🥰 ak malickia
Hoooo Machalla c comme 1 medicama quand jecoutais khalissou zeukhebb....je emu!!
Ndeysan doumassi doyal papa longue vie dieureudjeuf mame Maodo ❤❤❤❤
Loin fut ce temps où ce genre de délice était servis que les vendredis à l'heure de prière dans nos TV. La véritable révolution médiatique c'est ça. Yalna Yallah fay yiw
Wallahi
Srg Babacar Sy Mansour Yalla nafi yagg té andak wérrr
Mame Maodo c'est tout de même un homme incroyable !
L’homme de qui par sa plume a réussi à combattre l’ignorance et l’exploitation de l’homme par l’homme Cheikh Seydil Hajj Malik sa,sunu Maam 🙏🏾😇
Extraordinaire 🥰
Merci DIEU MAME Maodo c'est tout de même un homme incroyable
Que Dieu continue de répandre sa pluie de grâces sur Mame Cheikh Seydil Hadji Malick SY (rta).
Je ressens toujours un plaisir inexplicable lorsque j'écoute les chansons de Aboul Aziz Mbaye.
Khilassou zalab, notre fierté.😍
Amine bijaayi Seydina Mouhamad aleyhi wa salam
Baye Abdou yagg fi té andak wérrr ak ndjabotou Maam Moussa Alé bi yeup 🙏🏾😇
sama xol sedna bilahit hiey wakeur Moussa alé Mbaaye .Goudou fane ak wer inchallah
Salaam wa Malikya, dégueul liii. Ma cha Allah, Yalla na gnou lène Yalla fayal, lii nekh na. Comme une berceuse falaahou. mahassalaam,🤗🤗🤗🤗🤗🤗🤗
Neysan thye khilass😍😍😍😍😍🤩🤩
Tidiany fi dunya wal akhira 💙💖💞
Cette mélodie me fait tellement du bien.
Je l'écoute chaque jour avant de m'endormir ca apaise.
Mame khalifa ababacar Sy protege 🙏
Machallah malikia diarama mame Maodo rta diadieuf Abdou Aziz mbaye yalnalene faye fiiw goudeul sen fane barke yonenti bi psl
🤩🤩🤩🤩 Par force lii dafa neikh. Je ne cesse de le mettre en boucle! JARAMA SEYDI HADJI MALICK🤩🤩🤩🤩
Je suis talibe Serigne touba j’ai des larmes osées
Machallah 💖😍😍😍😍 nexx na trop !!!!
Machallah Mame maodo diara ma
Macha Allah sama khôl sedna djeureudjeuf cheikh seydil Hadji Malick Sy et un grand merci à Malika tv
Machala félicitation à toute l équipe yalna yalla mayy goudou fane bou andddd akkkk weer
Abdou Aziz mangui lay gnanal goudou fane yalla bayi la fi bassi kaname weral batte bi ameen🤲
Wa keur Mame Maodo diamm si yéne yalla may léne goudou fane ak weer in sha Allah ameen🤲
Mancha alla Talibé cheikh y
Liii nekh na wayyyy....Malikya Dieureu nguéne Dieuff
Solene kodone bindd nioussiy topou dina guene neekh ci barki rassoulillahi aleyhi salam 🙏❤️
Damal play stor ga télécharger khilassou zahab amna binde
Diarama Mame Cheikh Seydi El hadji Malick Sy. Yalla na Yalla fay ko taxawayam bijaayi Seydina Mouhamad aleyhi wa salam Amine.
Cheikh Seydil Hadji Malick Yalnaniouko Yalla fayal😍
Dieurdieuffé cheikh seydil Hadji Malick Sy ❤
Sante djiouli si yonénte bi saws dieuredief mame seydi hadji Malick Sy rta
Abdou Aziz Mbaye brom batou Ore bi Ma Cha Allah dieureu dieuffaty Contannan trop Ndeysane yanna yalla fayale
Annn Onnnn
Wa bakhna
Yallah Naniou co Yallah Fayal
C est avec joie que j écoute ce poème de seyd Hadj Malick wekhyert walahi.
Machalah sedd n'a khol
diarama Mame Maodo 🥰🥰🥰🥰le bonheur de ca❤❤❤❤ (psl)
MACHA ALLAH ALHAMDOULLILAHI MERCI MON DIEU DE M'AVOIR DONNER L'OCCASION D'ENTENDRE DANS MA VIE CES MERVEILLES DE MAME MAODO CHANTER ET DIFFUSER PAR DES VIRTUOSES MERCI A TOUS
Al Hamdoulilah 🤍😁
Machallah EL HADJI ABDOU AZIZ MBAYE. Yalna Yallah fayla yiw. Sama khol sedna si MALIKIA sunu Télé
JARAMA CHEIKH SEYDIL HAJJ MALIK
Maodo l’éternel source d’amour pour le Prophète 😍
الله أكبر ولله الحمد الله أكبر ولله الحمد الله أكبر ولله الحمد
Machallah
Nguir yalla toppou léne ko rk bamou mott 30 yeupp
Jaraama Cheikh Seydil Hajj Malick
Jarama ndiol fama❤❤❤
je suis un vrai TALIBE cheikh
Jërëjëf🤗🥰❤️❤️❤️❤️❤️
Macha’Allah Yalna Yalla faye yiw Malikia thia kaw thia kanam rkk 🙏🏾😇
Sama nidiaye waay yalna baate werr. Lékko darra bayi gnou. Yalna say fane yokkou
Yallah naniou yallah fayal sunu mame maodo❤
Dieureudieuf Mame Seydil Hadj Malick IBN Ousmane
Malikia dal sene stock legn yor chaque semaine niou diokh niou ravitaillement. Jerejef 🙏🏽
Tidjiane fid dunya wal akhira ❤📿😭😭🇫🇷
Machalah merci mame MAODO
Djadieuf wakeur moussé alé mbaaye bou gnou faté pin s ligueye djouma mame maoda bi inchalla
Jarama Mame Maodo 🙏♥️
Diazzakallahou khaîrane
Seydina Mouhamed PSL❤❤❤
Khol sedna tropppp bilahiii
Machallah Machallah Machallah je n'arrête pas d'écouter merci abdou aziz merci malickia tv que dieu vous bénisse amine.
Oh li nex na way machalah❤❤
Bilahi sy Malick kendou mom kholalma li rek
ماشاء الله فرحنا بكم نحن معكم اسمي باب ساخ
Cey Abdoul Aziz Mbaye niguaye serale sougnou khoole yalla nalako yalla faye si barkep yonenetibi Psl Amine
Sallalahou aleyhi wassalam Amine
Yalla na noiu yalla fayal mame Saydi haji malick s’y❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤ bilahi j'ai mm pas les mots dakh contane
Cey Abdou Aziz Mbaye, mo mënë way dé...❤
Manchalah ❤️
Machallah bara qu'allah ❤
khol sédatinaa❤❤
Oh min hi ratil karimi ❤❤❤❤
mais gni yalla daléni faye inshallah ohh loumouy yékk diarama seydil khadji malick 😭🥹❤️
Machalla
Yalla nala fay Seydil Hajj Malick
Ohhhhh
La dimension spirituelle de seydi El hadji Malick me depasse
❤️❤️🥺Ken meunoul expliquer mbecte miii❤️🔥❤️🔥🖇
Wallahi DEUG pire ga wakh
Un lakhad haadja boudal bou thiossané nous le voulons aussi
Wallahi ndeysaan, dîna nékh dé
Vraiment son bi neikhna lollll Sakh machala yalna yalla weral thè mayla goudou fane
Machallah abdelaziz mbaye est un "Don"
Al hamdoulilah ❤️ santé Yall 😍😍
Machalla kholyi Sedna yalna lenyalla fay yene wa Malickia ak wakeur Mame Moussa ale mbaye si Barker yonetibi saws 🤲🕋♥️😍🥰🙏
Machalla que dios te bendiga muchos más
Maachalah yalna niou yalla fayal Maodo
Machalah
Machalla machalla machalla
Thieuy sama Tourando❤
Ndeysan li nekhna dh ❤️❤️❤️😭
Yallna yalla samou
Des cœurs pour mame malik❤❤❤❤❤
Eh paa bi soll lou bleu li😍❤
Abdou Aziz mbaye ❤️❤️yalla nako yalla faye inchallah 🙏🏻🙏🏻
il est tres fort
ELHADJI ABDOU AZIZ MBAYE C'EST LE CHEF D'ORCHESTRE 😍😍😍
Callalahou hala mouhamad
Jarama ndiole fama❤❤❤
Toutes mes félicitations à Malikia TV pour ce travail excellent pour les musulmans et pour la tariha. Bonne continuation!!!!
❤❤❤❤machallah alhamdoulilah
Dieureuf seydi Hadji Malick yalla naniou ko yalla feyal
Billaye wallaye barcki serigne touba sama xole da sédde loooooooooooole
Li dafa nékh trop ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mâcha allah
Mame el hadj malick yalna la yallah faye
Hoooooo bi si souf si karami bi❤❤😢😊