Ndeysan nitte diabootna té soukoul diour. Yana Yalla yokk soutoura 🙏😓. Mère Ndèye Wade yanala Yalla samm té mayla werr ak goud fane. Une vraie comédienne qui interprètait ses rôle à la perfection. Goro Bathie borom violation de chambre 🤣😅👏dans Wadiour avec Ndèye Mour
cest triste. comment dartistes sont dans cette situation? ceci devrait servir de miroir aux jeunes artists qui mettent leurs corps nu a lecran. cette femme est est une modele et ellle a laisse une bonne impression a la nation. bravo maman
Allaaahou akbar yay booy guenala beuggg linga bakk Mame Limamou ooooooh😭😭😭😭wayé tamm mére bou khoromo nguini😂😂yalenalafi yallah bayi way andak weer ak soutoura barki sanguou sangue yi mame Libass Laye
@KHADIM MURID TV no ki waxoul Die astou sarre dh Die astou diop bou mag bi jouer won nidiaye ak lamine ndiaye Fanyé guisnako si sargalou rouba seuye bi ❤
wa la fille qui méne l'interview est ce qu'elle est normale? Pourquoi elle insiste autant sur le fait que la dame n'ait pas d'enfants? cinq questions successives toutes sur amouloo dome, c'est ca enfoncer le couteau dans la plaie et appuyer sur là ou ca fait vraiment mal et c'est une méchanceté gratuite, mais heureusement la dame kou matt leu
Comédienne dans le sang. Sou fébaré sakh dafay comédie. Yagg fi lool té wér mame boye. Amine.
Alhahouma amine diakhe sama yaye de sang la
Ndeysan nitte diabootna té soukoul diour. Yana Yalla yokk soutoura 🙏😓. Mère Ndèye Wade yanala Yalla samm té mayla werr ak goud fane. Une vraie comédienne qui interprètait ses rôle à la perfection. Goro Bathie borom violation de chambre 🤣😅👏dans Wadiour avec Ndèye Mour
J
Ndeysane yalla na léne Yalla takhawou yague nguéne gno bégueul ngoude fane ak wér machalah.
Wallahi wakhe ngua deug Masha Allah Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 🙏🙏🙏💞
@@mamygaye4378 wala y t ba taye day ta lamyi 😂😂
@@mormbaye2989 salam wawaw souniou yaye dji kayy Masha Allah 🤗🤗🙏
Elle jouait très bien machallah. Longue vie Yaay boy
cest triste. comment dartistes sont dans cette situation?
ceci devrait servir de miroir aux jeunes artists qui mettent leurs corps nu a lecran. cette femme est est une modele et ellle a laisse une bonne impression a la nation. bravo maman
Ndeysane santé de fer et longue vie à la grande dame Maman Ndeye Wade yallana yalla Maye weer AK werle goude fane
Ndeysaane goudeul fane Tante Ndeye WADE, yalnaleu yalla sameu si barké Nabil Moustapha
Ma sha'a Allah. On t'aime grand mère ❤❤❤❤. Une femme très authentique
Ndaysane bly théâtre warnaléna fay 😘
Théâtre wadiour MoMA guena marqué mère Wade elle est formidable elle excellente dans son domaine
Moi aussi ça m'a beaucoup marqué
Moi aussi franchement wa daaray kocc ndeyssane dagn daan éduquer la jeunesse.
Ndeysane sama haritou tanta la heur bouma démé thiaroy fek kofa mou bah lool oyof té yaatou yala na sa diam yague mame boy ❤
Mere bi Machallah vrai comédienne 😂
Ndeyssane théâtre wadiour yii lako fan wé mom ak tata Ndéye Mour 😂longue vie mame boye 🤲🏻❤
Elle a la joie de vivre machallah werr ak gouddou fan Inchallah
Mashallah sounou yaye yi long vie et bonne santé à vous baniouye khalé yenaniou done begueule
Bravo Lala tu fais un très bon boulot ❤️🙏🙏🙏
Invitel Die ASTOU Diop une icône du théâtre name nagne ko
Machala woor n'a yalla Reina ba sone yalnala yalla may werr
Elle est adorable souriante est imouriste long vie à tâta
Beaucoup de bonheur longue vie ♥️♥️
ndeysane machalah longue vie maman souvent soudane guéneu douniou dane wakhh sama yaye yéna diroo niguénii wakhé❤️❤️❤️
Sougniou mame bégueul nagniou ba tayi yallana yalla goudeul fanam
Alaouma Amine Ya rabí 🤲🤲🤲
Ma sha allah retrouve nous djiee astou diop darayy Cook
Mâcha allah notre mame boy longue vie ❤❤❤
Lala est une excellente intervieweuse
Machala 😍😍😍mane d xalei la wayei théâtre rétro yi rek lay seitane
Baringa si morome demb dafa nekh
NON LALA MERCI MÈRE BI REK LA BEUGUE ELLE JOUAIT TELLEMENT BIEN ET NATURELLE DANS SON JEU MAMAN DOUNDAL AVEC UNE TRÈS BONNE SANTÉ MACHAALLAH
Ndeysane yalla bou yakaar Tass masha Allah goudou fanne mou andack were insha allah
Une grande dame très professionnelle, longue vie mamy pleine de bonheurs
Ndeye wade longue vie
Walahi vrai comédienne la longue vie sougnou mame
Ndeysane sama maman de valeurs. Gnignos Mane théâtre way légui Les séries comme filmes ou cinéma
Les jeunes acteurs doivent penser au futur, notre chère maman est à l'aise aujourd'hui machallah. Buzz dafaye diékh
Allaaahou akbar yay booy guenala beuggg linga bakk Mame Limamou ooooooh😭😭😭😭wayé tamm mére bou khoromo nguini😂😂yalenalafi yallah bayi way andak weer ak soutoura barki sanguou sangue yi mame Libass Laye
Amine laye makhtar ❤️
Ndeysane.. mère bi dafma masseu nékh.. goud fane ak wér.. amine🙏🏽
Yalla nala yalla samb artla mayla fane wougoudou ak wérr ak khéweul gou bari ak féké ak talle sibarké seydina mouhamed ak serigne touba
Yalna yalla goudeul saay fane mayla weur
Manchallah goudou fan ande ak weer 💚
Ndeye Yade masha allah une grande actrice longue vie
Machallah, mere bou aye une actrice bou aye,yallah na diam yague ci mom contane na.
MachaAllah vie longue vie maman
Elle me plait becoup longue vie à toi machallah
Yalla souniou borome goudal fane wi andak wer si barké seydina mouhamed psl ❤❤❤❤❤
Diereudief mère Ndeye Wade contente ci yaw
Ndaysane mère bu yiw té bakh merci DB gni gno Diara séti délén weur lès anciens li moy koleuré
nous remercions beaucoup à vous les théâtres
Ndeysane sunu Mame yalna nga fi yague té werre waye wa Dakar buzz thiaw kaw thia kaname ❤️❤️❤️
Machalah koun meun joué ses rôles longue vie mére
Wa ani dié astou diop bou une si longue lettre😭💗💗💗
Die astou diop kokou moy yayou maïmouna ndour faye 7fm
@KHADIM MURID TV no ki waxoul Die astou sarre dh
Die astou diop bou mag bi jouer won nidiaye ak lamine ndiaye
Fanyé guisnako si sargalou rouba seuye bi ❤
@@mormbaye2989 waw kaay dié astou bobou laa
@@amymbaye454 A bon lolu dh meuso mako kham
@@amymbaye454 ah amy mere die astou diop mo diour maimouna ndour ndeyssane mere bu amone classe meuna joué ndeyssane
Machallah mère bi dakhoromu mais Lala yawit chapeau way contane ❤
Ndeysane longue vie à toi mame boy je cherche désespérément le théâtre avec ndeye mour wadiour kouma si meune dimbali
Ndeyssane yalla na yalla goudal sa fane may la wer gou yaram
Aka bakh ndeyssaan sunu Mame boy yalla Nanga gudu fan té werr
Yalla na yalla takhawoula defale tawfeekh goudou fane mou andack were amine ya rabi insha allah
Longue vie à tw maman chérie ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mame Ndeye wade sa interview bi nekhna 😂😂😂😂dafa khoromou
Nonn lala do niit yagui ñi délo démbb vraiment courage à toi
Bonne continuation lilou bakh la mère bi ndeyssane vrai artiste mais damako fatewone carema
Yalla naléne yalla defal jamm si barké alkhour ane mére bi dafama marquer rawatina daraaye kocc
Machalah yague ngagno beugeul
Yalla na la Yalla takhawou
Ndaysane Machalla longue vie mame boy
Ndeysan sama yaram dawna longue vie maman yague fii lole téwér machalla
une grande artiste
Machalla mer ndeye Wade longue vie
ماشاءالله بارك الله فيكم 💗
Mame Boyer ni rék yangui nouye bégueul bilay yalna yallah dolli sa diame
Machalla ❤️❤️❤️
Kharit keuz mouné keusme🤣🤣😅balla gaye ancien cloire 😆😅mame yalla na sa diam yag
CV lalá nakamou soukeyena diagne bou darray koc
wa la fille qui méne l'interview est ce qu'elle est normale? Pourquoi elle insiste autant sur le fait que la dame n'ait pas d'enfants? cinq questions successives toutes sur amouloo dome, c'est ca enfoncer le couteau dans la plaie et appuyer sur là ou ca fait vraiment mal et c'est une méchanceté gratuite, mais heureusement la dame kou matt leu
Bonn rek!
Ndeyssane mere ndeye wade way artist bou mak
Macha alla maman tu es naturelle
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️You Mama yaag fi té wéerr🥰🥰🥰
Ndeysan goudal fane wayy bou andeu ak werr jërëjëf bilay Senegal hamoul valeurou artiste.
Ndeye saane Sounou maman yi,fane wu gouddu ande ak were...
Longue notre maman grande commedienne machallah
Ay way tante ndeye ndeysane yala goudal fanam
Ndeysan sama yaram dawna mère ndeye Wade yalnako yalla maye fane wougoude ndeysan théâtre amatoul daray kocc Amou niou morom gni Fatou yalnalene yalla yeureum kharlene aldjana firdawsi bidiahi seydil woudioud Amin.
Machalakh ♥️❤️
Ndeysan aka meune théâtre
Dax dafa niroke sama yaye bilahi mai sama yaye dafa décédé 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
YALLAH NGAFI YAGG LOLOU MAME BOY NATIONAL
Wa matildé bu daray kocc fomou nek
Kouma nekh
Nenagn mongui gambie
Longue vie santé de fer
Yén artists theatre you bess yi di gagner xalis bou bari xana dolén rousse oute lén caisse de securité social dimbali ancien yi té yalla takh
Idée bou rafét
Barke serigne Babacar sy mère bi dama ko beugue bilahi
Ay mere bi ak ndeye mbour thieatrou bathie ba 😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
@@fatimayoussouph4570 blay yw mom laye weur ni 😂😂😂😂Woy nom film bi la fate
Bilaye mor mbaye bathie rec. rew ba dof en 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤙
@@mormbaye2989 Théâtre daraay kocc Wadiour
"Nek bou amoul palantér bakhoul"😂
longévité mame
Vraiment elle peut jouer des rôles ndeysan
Ndayesan aka niro ak sama ben yaye yalla neguen fi yague té wér
Ayawe merci ndeyssane dama koye late rek 😍😍😍😍
Lala lakalenga Bilahi 🤣🤣🤣🤣
Oooh met bi Aka nekhone machalah longue vie à toi maman ♥️♥️♥️
Gui Kay dafa nékh ba tay❤❤❤
Mashallah nekhna longue vie ❤️
Une bonne vivante badiène doundeul weral amal diam. On souhaite voir badiène Seun SENE svp
Longue vie a notre maman. Lala sa liguéy rafetena lol
Ay way bathie ak ndeye mour bi khawma noumay def ba sétane ko
Ndessane ❤❤❤❤🇺🇸🇲🇷🙏🏿eskey adouna
Deyssane je parlé d'elle il y a quelques jours de cela.
mère bi dafa nekh 1😃😀😀🙂😀😀😀😀