J'ai fait des recherches à Touba pour avoir le xassida où xadim Rassoul lui-même écrit ce passage de la prière. Personne, même pas à la bibliothèque principale de la mosquée, personne n'a été capable de me sortir ce xassida. J'ai sollicité tous mes amis mourides, et aujourd'hui encore j'attends toujours. Je lance ici un appel à tous les lecteurs, mourides ou non, de m'aider à avoir ce xassida écrit par le Cheikh sur sa prière en.mer
Serigne touba nena si khassida Wa sallalil khakou samay wakh kouko wedi niou bolé la si yefer yi so demm ba amm siki saka manou si li mame seex di wakh serigne bamba yonam niar la guiss lila doyy dieurinio guisso lila doyy ngua rombe bakofa ❤ th nguenn khamni koudoul yalla di yonente bi serigne touba mola geune geune ko yakar 👍❤️
Ahmed a gagné ce débat car le mec ne peut rien prouver sur la façon dont les sherings prient sur la mer. Aucun témoin, aucune preuve écrite. Même l'Européen qui l'a arrêté n'en a pas été témoin.
diouli Cheikh Ahmadou Bamba s'explique pas par la pensée pluto par la foi ndax XeL NANGOUWOUL MIRACLE bouko déggé wala mou guissko yémou donc c'est la foi qui s'explique le miracle mooy GUEUM GUEUM deja fok ngua GUEUM CHEIKH AHMADOU BAMBA pour mana gueum sa priére sur la mer. Cheikh Ahmed tidjiane CHERIF for LIFE
je pense que vous n'avais pas compris le but de ahmed cissé, il a comme objectif de faire comprendre au gens que niit leip limouy daf ko wara tek fou leir... et l'autre oustaz aussi a des réponses logique. il ne critique pas, il essaie juste de nous comprendre comment argumenté et défendre tes choix...
Salut Oustaz, bravo pour votre émission. L´histoire nous enseigne que Le Prophete Mouhamed (psl) a effectué la priere mortuaire pour le Négus quand il a appris son décés,. Car le Négus était croyant car chrétien. Alors c´est totalement le contraire de vos affirmations. C´est une histoire vraie, factuelle et veridique!!! Au Senegal on fait trop d´amalgames , Djoulites veut dire celui qui prie donc un croyant, le chrétien et le juif prient ,alors ce sont des croyants. et Dieu s ´adresse aux croyants. "Yéfeur" ou "Kafir" c´est celui qui ne croit pas en Dieu oubien hypocrite. Merci et bonne continuation. Que Dieu nous éclaire d´avantage
Réellement chercher à connaître qui est Jesus Christ c’est vraiment important Ps : je ne parle pas de religion mais chercher à connaître qui il est vraiment ne vous limitez pas que sur le Saint Coran🙏🏽
Diangue téré yii mana firii taxoul nga am xam xam m.!!yalla ay mbiram téré yii dadiouko.!!kou amoul batiin yoor beutii nén boul wéddii un point c'est tout ❤
ALLAH est trop loin des amalgames... Serigne bi, wadji xana xamoul né Issa Ibn Mariam doxe na si kaw ndox . Sirou bou waral lolou mome la mame Bamba ame...Nitou Yalla dou morome kou ordinaire, Yalla amoul morome
@@mouslayeimmosenegal3529 yaw bane monde gua nek avec ça guani dioulite gua later ko sa pape dou samay wakh wakhou yalla leu meune guéne tinial torop pithi sakh diko sapeu dou samay wakh
Dieureudieuf ya ouztaz yalla nala sounou borom faye 🙏🏽 si barké Cheikhoul khadime🫶🏽
Mâcha Allah ya oustaze yalna sa brom bi fayla barkép Cheikhoul Khadim❤❤❤❤
J'ai fait des recherches à Touba pour avoir le xassida où xadim Rassoul lui-même écrit ce passage de la prière. Personne, même pas à la bibliothèque principale de la mosquée, personne n'a été capable de me sortir ce xassida. J'ai sollicité tous mes amis mourides, et aujourd'hui encore j'attends toujours. Je lance ici un appel à tous les lecteurs, mourides ou non, de m'aider à avoir ce xassida écrit par le Cheikh sur sa prière en.mer
Ahmed cissé c'est une autre dimension.
Merci oustaz mouhameth mbaye Serigne Touba yalla KO maye Lilou am
Oustaz guéne nala beugue 'ndakh sa kham kham bou seleu ❤❤❤
Serigne Touba,loumou binde deuggleu..dieureudieufeuti serigne Touba...
Mdr
Machala oustaz moukhamad mbaye yalna sa diam yague ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieufety cheikh ahmadou bamba khadimou rasoul ♥️♥️♥️♥️
Remercier Allah azawajal est meilleur si seulement tu savais
Kou santoull nittt doo sant yallah sawayy meunolenn diakhassé nittt gniii AK senn boromm soff nguenn torop Di diaayy arabisant dinguenn déé bamba kessé DIEUREDIEUFE BOROM TOUBA ❤❤❤❤❤
@@yaobenjamin4320khamoo Dara bayilll doulll
Merci oustaz ❤❤❤mouhamed mbaye
Jajeff oustaz Mohamed MBAye yalla nala yalla fayla Thie barké khadiiim Rassoul PSl ❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuf borom touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieufti Serigne Touba machala oustaz
_صلّي الله عليٰ محمد_
Dieureudieuf ouztaz yalla faaye
Ahamadou amoul morom kouko bange dél ❤❤❤
Dioulit da warawakh degg bayi fene té yalatakh ❤❤❤❤❤
Merci beaucoup mouhamed ❤
Outaze mouhamed,toutes vos réponses sont pertinentes, mais de grâce vous portez votre temps sur cheikh Ahmed Cissé vraiment
Ahmadou bamba mbacké kassé❤️❤️❤️❤️🫶🤌👌👌👌👌🙏🙏🙏🙏😭😭😭😭🙏
Un vrai comédien Cissé 😂😂😂😂khaliss ak badio laye werre😅😅😅
❤❤❤deurdeuf Brome touba diarrama mame cheikhra fall ❤❤❤deurdeuf Brome touba diarrama mame cheikhra fall ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Serigne touba nena si khassida Wa sallalil khakou samay wakh kouko wedi niou bolé la si yefer yi so demm ba amm siki saka manou si li mame seex di wakh serigne bamba yonam niar la guiss lila doyy dieurinio guisso lila doyy ngua rombe bakofa ❤ th nguenn khamni koudoul yalla di yonente bi serigne touba mola geune geune ko yakar 👍❤️
Diereudiefeuty borom touba ❤❤❤❤
Ken dou serigne touba❤❤❤❤
Ahmed mi ,vrai doméram leu.meussonn nagn ko tégueul ,ngir wakh you bonn,yimou wakh si serigne touba.
Machallah Ahmed Cissé gayi comprendre loul loutakh question yi c pour les wahabis comprendre les tarikha mais merci oustas Muhammad mbaye❤
Tu es un grand intellectuel bro🙏✍🏿🧠👂
@@ndiayeassane8961 merci
@ndiayeassane8961 merci
Diérédiéf ya OUSTAZ ❤❤❤❤
Ma challah amna solo Ahmed cissé question yi bakhna 🇸🇳ouztas mbaye laf thiat way kham kham rék ngén wakh ❤❤
Diéréfeufé Oustaze Mbaye, "Guédji", Safara etc dou loré Lou ame Yalla la.
Demal tok si gaz bouy takeu
Serigne touba yakkiine ak xamni ragal yab yallah la motakh mou sani derwa sa ndokhma diouli lolou gueum gueum guou fort la ❤❤
Dieureuf oustazجزاك الله خبراما شاء يا استاذ،
Ahmed a gagné ce débat car le mec ne peut rien prouver sur la façon dont les sherings prient sur la mer. Aucun témoin, aucune preuve écrite. Même l'Européen qui l'a arrêté n'en a pas été témoin.
Le débat est intéressant machallah
Niaupu ay tidiane laniou ❤❤❤❤❤❤❤
Çay s touba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf serigne touba chekhoul khadim yalla rek la gueumone motakh yalla defolko lolou mou djouli siguedji hui da fa âme
diouli Cheikh Ahmadou Bamba s'explique pas par la pensée pluto par la foi ndax XeL NANGOUWOUL MIRACLE bouko déggé wala mou guissko yémou donc c'est la foi qui s'explique le miracle mooy GUEUM GUEUM deja fok ngua GUEUM CHEIKH AHMADOU BAMBA pour mana gueum sa priére sur la mer.
Cheikh Ahmed tidjiane CHERIF for LIFE
Nioun Sénégal serigne touba lagnou beuge❤❤❤❤
🥰💖💕Mouhaméd sama wadji ❤❤❤je t'aime fort ❤❤
Serigne touba kendou mom ❤❤❤❤amoull khalatt de ok❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😊😊😊😊
lolou yombouna trope
@@MouhamadouSakhirDiba dieureudieufé serigne touba ❤
Ci yow 😂
ضصغيشسز
Li mora ame si telè yi lou bakh la yalla nalèn yalla defal diamou ❤
Bilaye ndayessan dierdiaf s Touba
Serigne Touba amoul morome ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diarama oustaz merci
Cheikh Ahmad machallah il raisonne bien 😂❤contrairement aux fanatiques
Bilahi tu sais pourquoi je l'aime : parce qu'il force la réflexion
Mouhamed machallah ❤❤
Dama beug kham ahmadou mo wakh dioulina si ndokh wala nienagni nioco wakh leral lenma ngir yalla ❤❤❤
DIEURDIEUF SERINGE TOUBA❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Jerejëf Cheikh Ahmadou Bamba khadimou Rassoul.....
Dieureudieuféti cheikhoul khadim ❤🙏
Maa Shaa Allah Yaa Ustaas
Eska saye dialo wol kula ko wakh sayaye mana dialou ❤❤❤❤❤❤😊
Allahou Akbar genre yi danio sannkou ba parei oustaz da ngua soory lathie ko guel Biko filmé mou def tatounen😅😅😂😂
Merci beaucoup pistasse❤❤❤❤mbaye
Ouztaz wakhofi lou leer deh, Ahmed Cissé tu as un esprit critique et c'est comme beaucoup parmi les non fanatiques.
ما شاءالله أستاذ محمد بي جزاك الله خيرا
Waa légui bane yonéneti la djieune wanneu mouy doundou thi biir biirou dieune mouy doundou mou yabiko !!
Légui koumana gueum loolou xanaa wara mana gueum dioulli thi gaidj gui
Loolu yalla ko nettali ci alxouraan
@@OusmaneNiang-z4q dieureudieufé serigne touba ❤
Lou Yallah wax ak Lou Nitt gni wax dou bën way Nguiro Yallah
@@sadigintergalaktik.11M koula wakh yalla moko wakh??
Mai ki du yonenti
Akhmet t’es trop intelligent par excellence.
Dieureudieuff borome Touba ❤❤❤ !!! Do fi nopalou yaw C.A.Niass
Merci mbaye✌️
je pense que vous n'avais pas compris le but de ahmed cissé, il a comme objectif de faire comprendre au gens que niit leip limouy daf ko wara tek fou leir... et l'autre oustaz aussi a des réponses logique. il ne critique pas, il essaie juste de nous comprendre comment argumenté et défendre tes choix...
Machallah. Serigne guewel.yalla na bari
Dieureudieuf Serigne Touba diarawlack Cheikh Ibra Fall
Foumala djiss Oustas Mouhamed Mbaye barkeep Mame Cheikh térale
DIEURDIEUF SERINGE TOUBA ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
AHMADOU MBACKE Gnoune gno ngi nii tè bula nèkhè mayè ak diay te kou bagn dèè ❤❤❤ BAMBA MERCI
S. Tuoba Moniye dimalli❤❤
Ohhhhhhh guisada oustaz yi senegal li mo takh cheikh mbacke sakho dou sen morom koi
Merci Mouhamed Mbaye ❤❤Diereudief 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
❤❤❤❤wloulouulouulouuuuya ❤ choukhrane serigne lerrrna nagn cheikh akhmet ya teugu ya touli tontou nga sa bopou❤
Yalla n'a yalla mottali yéné nieup incha'Allah dolliniou soutoureu baniou yobbou wadiour'yi maqqa si barké seydina Mohamed psl ♥️🫶
Bilaye ya baakh nianaal ma
Merci beaucoup ouztaze Mouhamed
Merci Oustaz Ndiaye Oustaz Ahmed
Salut Oustaz, bravo pour votre émission. L´histoire nous enseigne que Le Prophete Mouhamed (psl) a effectué la priere mortuaire pour le Négus quand il a appris son décés,. Car le Négus était croyant car chrétien. Alors c´est totalement le contraire de vos affirmations. C´est une histoire vraie, factuelle et veridique!!!
Au Senegal on fait trop d´amalgames , Djoulites veut dire celui qui prie donc un croyant, le chrétien et le juif prient ,alors ce sont des croyants. et Dieu s ´adresse aux croyants. "Yéfeur" ou "Kafir" c´est celui qui ne croit pas en Dieu oubien hypocrite. Merci et bonne continuation. Que Dieu nous éclaire d´avantage
C très intéressant machaallah
Wallahi wadji mo meuneu fenn
Réellement chercher à connaître qui est Jesus Christ c’est vraiment important
Ps : je ne parle pas de religion mais chercher à connaître qui il est vraiment ne vous limitez pas que sur le Saint Coran🙏🏽
Dieuredieufety cheikh akhmadoul khadim 🙏💚🤍💚🤍💚🤍
Diangue téré yii mana firii taxoul nga am xam xam m.!!yalla ay mbiram téré yii dadiouko.!!kou amoul batiin yoor beutii nén boul wéddii un point c'est tout ❤
Alahou akbar, kimom geumoul sakh yalla, ndakh moy may nite louko nékh
Machalla serigne mouhamd mbaye
Bilay li Lou raféte la❤❤
Kèndou Serigne Touba diere dief ousstas
Oustaz Mouhamed Walahi beugg nako ndakh tontou waaam youh leer yii
Seringue touba dieuredieufé brom touba dieuredieufé brom touba ❤ allhamndoulillah 🎉kou guemoul sa afére la
Ibrahima aleyhi salatou wa-salam safarassi lakouko, younouss dieune wa dafko gokki kou gueumoulni yallah momou mo thiompou si karamam déf Serigne Touba diouli si guédj.
Mâne ãmena yâkâr bou wére né serigne touba djoulina si guédjegui
Lolou amoul
@djibyndiaye1528 loutakhe nganê amoule
Serigne Touba amoul morom
Cissé beuss😂😂😂❤ya nekh
ALLAH est trop loin des amalgames... Serigne bi, wadji xana xamoul né Issa Ibn Mariam doxe na si kaw ndox . Sirou bou waral lolou mome la mame Bamba ame...Nitou Yalla dou morome kou ordinaire, Yalla amoul morome
Ndeysan djouli ci guëdj d mo guëna ndaw ci lou borom touba djêffë
وقال الشيخ محمد الامين ديوب وفي اليم صلى العصر الغ ❤❤❤❤
Al ouztas dieuredieuf
Khamàl né Ahmed cassé khadj la
Laye wakhlène loungène khâm thîie LAYÈNE Laye
Machallah Sangue bi Moukhamed yalla néna kham lénema bala guéne may diamou Cheikh bi day roubé rek li moulay later yeupe khamnako 😂😂😂😂😂😂
Xamnako guemnako gni xamoul té rér la beug guindi
@@aichasow4672 sissi il fait semblant koba leu 😂
Mane linga waxxni guissouma fouko yalla waxxé si alkhour ane soma meuné labiral rek ma xam fouko yalla waxxé djaza koumoula hayerane 🙏
@@mouslayeimmosenegal3529 yaw bane monde gua nek avec ça guani dioulite gua later ko sa pape dou samay wakh wakhou yalla leu meune guéne tinial torop pithi sakh diko sapeu dou samay wakh
ولا تصلي على احد منهم مات ابدا ولا تقم على قبره انهم كفروا بالله ورسوله وماتوا وهم فاسقون( القرءان الكريم )
Diérédiéf OUSTAZ Muhammad
Ken Dou Serigne Touba
Diereudief Mouhamed Mbaye ❤❤❤❤
Je suis avec Cheex Ahmad😊
Vous êtes pareil daguen Alkou boy yagg Dieureudieuf Serigne Touba ❤❤❤❤☝🏽