Serigne bi moudiadid la Yessal dînè Kou dondou yonentabi cie xam xam Ar Rassoul Serigne bi ayy yitèm yallah rek la wo nitt yi cie Dieubeul sèn boppou cie yallah ba dièkh tax
Tella nangou lou mou dône Noppal la Titre boumou ám yallah mokko nommè Dè dina am matt yènen Lolou mbirroum allah la Serigne bi ma beugeul sama boppou gnirr yallah Lire le coran et méditer sur les versets moy sakkou yallah agreer la
Linga bind AK linga firi bokul dh esk dioumo Dani keep Ku khathio AK man dra teh tubu Loko Sak tekhé Di bind nan ko ndayi tera yi(lawhul mahfus) Wasalam
@@MameyoroDime bala gay wah ni Serigne Touba dou nit warga mana xam limou doneu alors Digako lahoo sougnou borom nak Gnoune talibés yi gno wara xolat sougnoy kadou kou yap ak di saga sougnoy kilifeu rk sa genre Kadou yi moko waral
@@babacarndong-ge7mc MERCI DE BIEN RESPECTER NOTRE GUIDE CHEIKH AKHMADOU BAMBA,L’UNIQUE CRÉATURE DANS CE BAS MONDE D’ICI BAS ET DE ´L’AU-DE LÀ.LUI MÊME À DIT:JE SUIS NI DJINN NI ANGE NI HOMME NI PROPHÈTE,JE SUIS UNE CRÉATURE UNIQUE QUI VIT AU DE LA TERRE ET JE SUIS JAMAIS PARTI.MERCI ENCORE POUR POUR VOTRE RESPECT ET VOTRE COURTOISIE À L’ÉGARD DE NOTRE VÉNÉRÉ CHEIKH AKHMADOU BAMBA
@@MameyoroDime parfois kheur bou meti moy tah gnou wah yéneu yi ,,,,sougnoy maytou yéneu Cadou yi rk dina bah fi mom amna gno xamni yakam ti nagnou tariha yi wah bagnou critiqué len motah Parfois day am wah yi xamni kéneu douko wah si public Amal diam rk yaw ak bolem dioulit def si deuk bi diam inchallah Yala fayal gnou sougnoy kilifeu diné 🤲🤲
@@babacarndong-ge7mc SAABAH YI DANIOU KHERONE TIE MOUHAMED PSL. DE LA MÊME FAÇON DINONE GUEUNEU KHERRE TIE SUNU WADJI CHEIKHOUNA AKHMADOU KHADIM, Yalna BOROM YOKOU AYES LERAMES BARAKATOU SEYDINA MOUHAMED PSL.A BON ENTENDEUR SALUT
En tout cas le Prophète Seydina Muhammad PSL est un être humain. Et DIEU lui a dit de le dire aux gens. Je suis un être humain comme vous. Après, qui est supérieur au Prophète Seydina Muhammad PSL ? Évitons le fanatisme. Au passage, le Prophète Abraham dit qu'il veut que DIEU lui pardonne ses péchés le jour du jugement dernier et il fait partie des cinq plus grands Prophètes, grand-père de Seydina Muhammad PSL et grand-père de beaucoup d'autres Prophètes et Aboul Mouwaahidoun c'est à dire le père de ceux qui vivent l'unicité de DIEU. Thiaaxaan bakhoul.
Dieureudieufati yallah na yallah gouddal sa fan
BOROM TOUBA DOÙ NITTE.DIEUREUDIEUFÉ BOROM TOUBA
Merci pour les éclaircissements
Machallah amna solou jërëjëf mbacke balla li dé warr Na yatou
Machallah mbacke amna solo
Macha Allah yalna yalla fayla yiw ❤
حفظه الله ورعاه إنه عالم مخلص في مقالته يقول للحق .إذا من خالفه فقد خالف الحق❤
ماشاء الله تبارك الله ياالشيخ احمد محمد
ماشاءالله جزاك الله
Ahmadu Mbákk kepp rekk ndong jaajëf ❤❤❤❤❤❤
Serigne bi moudiadid la
Yessal dînè
Kou dondou yonentabi cie xam xam
Ar Rassoul
Serigne bi ayy yitèm yallah rek la wo nitt yi cie Dieubeul sèn boppou cie yallah ba dièkh tax
Tella nangou lou mou dône
Noppal la
Titre boumou ám yallah mokko nommè
Dè dina am matt yènen
Lolou mbirroum allah la
Serigne bi ma beugeul sama boppou gnirr yallah
Lire le coran et méditer sur les versets moy sakkou yallah agreer la
Bama xamè lolou Cie la dieubeullou sama boppou Cie yallah directement
Et avoir un bon cœur et comportement
Être miséricorde envers ton prochain
Ma challa
Dieuredieuf mbacké serigne lépapam dafa ler nagne nek si ahirouzamane di toumal yone wi rek lolou lou mene gnak la
Machalla xam xam Bi rafena
Seriñ tuubaa dou niit th lolou ay wkhm la
Good luck and good health and your family members
Borom Touba dou nit mo wakhe « adiabani rahmanou khabelale khalkhi » diamouna Yalla diouraume fouki diouni ate Yalla sakoul dara
Borom touba néna : »adiourou mane annassaniya walam yatoub sakhawatoune tadoumou fi oumil koutoub » kep koumay ndiro lé wala dima wala teuklé ak nit yi ngua khamni daniouy faté boko touboul di ngua dem safara wakhi borom touba nak dousamay wakhe
Linga bind AK linga firi bokul dh esk dioumo
Dani keep Ku khathio AK man dra teh tubu Loko Sak tekhé Di bind nan ko ndayi tera yi(lawhul mahfus)
Wasalam
@@cheikhounalo8342 adiabani rahmanou khabelale khalkhi » diamouna Yalla diouraume niar fouki diouni ate
Borom touba dou nit
Danga gàtt xam-xam rekk
Serigne Touba dou nit lane la ??
Borom Touba KENE là. Té KENE khamoule loumou doone ! A bon entendeur salut.Dieureudieuf Borom Touba
@@MameyoroDime bala gay wah ni Serigne Touba dou nit warga mana xam limou doneu alors
Digako lahoo sougnou borom nak
Gnoune talibés yi gno wara xolat sougnoy kadou kou yap ak di saga sougnoy kilifeu rk sa genre Kadou yi moko waral
@@babacarndong-ge7mc MERCI DE BIEN RESPECTER NOTRE GUIDE CHEIKH AKHMADOU BAMBA,L’UNIQUE CRÉATURE DANS CE BAS MONDE D’ICI BAS ET DE ´L’AU-DE LÀ.LUI MÊME À DIT:JE SUIS NI DJINN NI ANGE NI HOMME NI PROPHÈTE,JE SUIS UNE CRÉATURE UNIQUE QUI VIT AU DE LA TERRE ET JE SUIS JAMAIS PARTI.MERCI ENCORE POUR POUR VOTRE RESPECT ET VOTRE COURTOISIE À L’ÉGARD DE NOTRE VÉNÉRÉ CHEIKH AKHMADOU BAMBA
@@MameyoroDime parfois kheur bou meti moy tah gnou wah yéneu yi ,,,,sougnoy maytou yéneu Cadou yi rk dina bah
fi mom amna gno xamni yakam ti nagnou tariha yi wah bagnou critiqué len motah
Parfois day am wah yi xamni kéneu douko wah si public
Amal diam rk yaw ak bolem dioulit def si deuk bi diam inchallah
Yala fayal gnou sougnoy kilifeu diné 🤲🤲
@@babacarndong-ge7mc SAABAH YI DANIOU KHERONE TIE MOUHAMED PSL. DE LA MÊME FAÇON DINONE GUEUNEU KHERRE TIE SUNU WADJI CHEIKHOUNA AKHMADOU KHADIM, Yalna BOROM YOKOU AYES LERAMES BARAKATOU SEYDINA MOUHAMED PSL.A BON ENTENDEUR SALUT
En tout cas le Prophète Seydina Muhammad PSL est un être humain. Et DIEU lui a dit de le dire aux gens. Je suis un être humain comme vous. Après, qui est supérieur au Prophète Seydina Muhammad PSL ? Évitons le fanatisme.
Au passage, le Prophète Abraham dit qu'il veut que DIEU lui pardonne ses péchés le jour du jugement dernier et il fait partie des cinq plus grands Prophètes, grand-père de Seydina Muhammad PSL et grand-père de beaucoup d'autres Prophètes et Aboul Mouwaahidoun c'est à dire le père de ceux qui vivent l'unicité de DIEU.
Thiaaxaan bakhoul.