Dédommagement waroul neik sah ay procedure. Du moment où la justice se rend compte que la personne a rien fait rk, automatiquement il doit recevoir son argent. Mais senegal c'est vraiment triste.
@@amethseck9195 lou leer nga wakh ici en France kougnou acquitté do togue semaine ta indemnisé wougnou la dinaniou calculé 365 jours × 6 si xaliss plus intérêt gnou fayla
Voila le Senegal .nos hommes de tenue doivent être eduquer mais c vraiment désolant notre justice et nos hommes de tenues .boulen yalla diegaloule dou bakhe
La peine de mort c’est par rapport à des preuves irréfutables. Avant de l’appliquer on s’assure d’abord avoir des preuves solides. Sinon c’est la meilleure solution pour lutter contre un assasinat volontaire.
@@FatimamatifLolou la niit yi, khamoul, peine mort dou ay simples accusations wala suspicions. Il faut niou am preuves you leer nagne avant niou kay condamner à la peine capitale.
yaw khana dégouléne Lou wadji wakh diapougnouko guir mo Ray wayé ki Ray dafa dégantéwone mome ta Ray dafa daw gnoukoy weur guisougnouko gnou diap ko mome khamna ki Ray Boudone peine de mort amone sakh mome kéne douko Ray ndakh khamnagne ni rayoul wayé dafa déganték ki Ray mome lolou lagnoukoy topé ndakh khamna fi wadji dém bimou dawé ndax migui Gambie wala migui Guinée wayé bignou diapé wadji gnou bayiko nitt dagaye déglou ay wax bou bakh
La police scientifique c est Des policiers tres serieux .ILS donnent souvent de bons resultats .ILS ne suivent pas forcement Les voeux de policiers our gendarmes ou douaniers pour incriminer Des innocents .ILS font correctement leur boulot Avec serieux .Bonne continuation chapeau .
Bayil yabaté. La police doit faire une enquête sérieuse. Saway on est des êtres sociaux, chaque jour on rencontre des gens. Ken meunoul mouthie ci la à part enquête sérieuse am.
@@badiboy8698 on ne peut pas échapper à la fréquentation, même ceux que tu penses clean seul dieu les connais vraiment. Même un frère ou in parent peut faire n'importe quoi. Police mo wara def travail bou sérieux au lieu di torturer
Man dh fréquentation jamais man 6h laay yewwou dem kheuyi 22h ma wathi dem teuddi douma tardé benneu wax tou dioulli limay wooté téléphone bari woul whatsapp dafay khaar informations rk wassalam té walf laay seetaan xalaat tv ak patriotes you woor yi ak solution tv
Mais santal yalla souniou borom amana bo douguoul wone casso accident dei wala lago wala dara hamalni souniou borom amna loumou la fankal ba gua dougou kasso damay degg mak gni nane kasso ba dei🙏🏾
Lii moy inconvénients peine de mort. Buniuko waré établir naniu bayyi khel si yu mel nii bu baakh.
Lou ame solo ngaye wakhe
Merci
Ça ne doit pas empêcher le rétablissement de la peine de mort
@@IbouNdiaye-h1s J'ai dit, niu bayyi khel si genre cas yii.
Dédommagement waroul neik sah ay procedure. Du moment où la justice se rend compte que la personne a rien fait rk, automatiquement il doit recevoir son argent. Mais senegal c'est vraiment triste.
Vraiment
Bilay Sénégal… damay bagna saga koii💔
Une. Pseudo justice qui ne dédommage jamais ses propres victimes c'est triste Sénégal dou réew
Ils te collent une condamnation banale de qques mois comme ça do am dédommagement
@@amethseck9195 lou leer nga wakh ici en France kougnou acquitté do togue semaine ta indemnisé wougnou la dinaniou calculé 365 jours × 6 si xaliss plus intérêt gnou fayla
Frère koula guiss kham ni do ray nitt ms courage frère😢❤
😢bilahi wahatiko❤
Voila le Senegal .nos hommes de tenue doivent être eduquer mais c vraiment désolant notre justice et nos hommes de tenues .boulen yalla diegaloule dou bakhe
Genre yi motah peine de mort manoul am imaginer niou rayone ko 6 ans après niou kham ni rayoul
La peine de mort c’est par rapport à des preuves irréfutables. Avant de l’appliquer on s’assure d’abord avoir des preuves solides. Sinon c’est la meilleure solution pour lutter contre un assasinat volontaire.
Voilà lingua wakh moy deug
Waw mais sou boba dafay leer ba paré nioukoy soga ray, leer naagn, preuves you leer naagn wala sakh nit ki avoué
@@FatimamatifLolou la niit yi, khamoul, peine mort dou ay simples accusations wala suspicions. Il faut niou am preuves you leer nagne avant niou kay condamner à la peine capitale.
yaw khana dégouléne Lou wadji wakh diapougnouko guir mo Ray wayé ki Ray dafa dégantéwone mome ta Ray dafa daw gnoukoy weur guisougnouko gnou diap ko mome khamna ki Ray Boudone peine de mort amone sakh mome kéne douko Ray ndakh khamnagne ni rayoul wayé dafa déganték ki Ray mome lolou lagnoukoy topé ndakh khamna fi wadji dém bimou dawé ndax migui Gambie wala migui Guinée wayé bignou diapé wadji gnou bayiko nitt dagaye déglou ay wax bou bakh
Kane mo Ray fulber sambou ak didié badji
Une très bonne question
Bonne question
Sheuttttt esk ki nit la daguan meunoul keppp ki wah limou doundou ahh no wayy di interrompre la parole à l’invité
Minimum 20 millions. Il a perdu 6ans de salaire
Voilà il a perdu son temps,salaire boumou monnonn am et son réputation 😢Donc Akkeu bi bakhoul’
La police scientifique c est Des policiers tres serieux .ILS donnent souvent de bons resultats .ILS ne suivent pas forcement Les voeux de policiers our gendarmes ou douaniers pour incriminer Des innocents .ILS font correctement leur boulot Avec serieux .Bonne continuation chapeau .
Poukw ngua inviteko komke do deglou
Mais 6ans d'attente pour sciences 😢
Kholat léne boubakh linguéni deff, li métina trop😢😢😢
Di invité nit ba nopi Di beugue wahh à sa place, merdre wayyy
Vraiment 😅
C'est de la merd 😅
Doynawar
Délais 6 mois minimum pour demander les indemnités il faut écrire les textes en wolof pour que tous le monde comprend
bayil invite mou wakh aaaahhh
Li bou de deugue war na takh NIT teey bou bakh si li mi Até ndakh yen yi Akh la 😢😢
Se gas mérité d'être accompagné il connais bien la vie c'est un vrais croyant ❤❤❤
6 an de prison té defo vraiment li metina , warna gno holate
Mais major loutakh mouy couper chaque fois l'invité ? Des fois il faut ngen bayilen aussi niouy wakh.
....té limouy wakh gnepp xamnagneko.
Moytoulen frequantacion ak grand place yii 🙏🏽🙏🏽
Bayil yabaté. La police doit faire une enquête sérieuse. Saway on est des êtres sociaux, chaque jour on rencontre des gens. Ken meunoul mouthie ci la à part enquête sérieuse am.
@@bf-bif louy yebate?
@@badiboy8698 on ne peut pas échapper à la fréquentation, même ceux que tu penses clean seul dieu les connais vraiment. Même un frère ou in parent peut faire n'importe quoi. Police mo wara def travail bou sérieux au lieu di torturer
@@bf-bif dieu est control de tout mai ak sabab frère
Bilay gnu bari dagnou lendi toumal legui sunu aplique bene de mort ndioum te dina barri
Sénégal weugn.bou.leuthie.là.néxoul.ndindi.li.yéména...courage frère comme nikko.wahé.rék.soubanallah.
injustice injustice Lii kagne lay diéx perdr 6ans d sa vie prkoi mandat de depot sans preuv concrete palpabl
Man dh fréquentation jamais man 6h laay yewwou dem kheuyi 22h ma wathi dem teuddi douma tardé benneu wax tou dioulli limay wooté téléphone bari woul whatsapp dafay khaar informations rk wassalam té walf laay seetaan xalaat tv ak patriotes you woor yi ak solution tv
DIAM RK NGAY AM INCHALLAH
❤
Il faut arrêter de dire certains secrets
Santal yalla sounou borom koumou beugeu rk laye ték natou ndaysane
Nattou bi moy metineu torop sakh, yalnaniou si yallah mousseul
Kiyeu wakh thi souff dégueloul 😊
Gendarme bi la sofnalolou
Ki kay dafa beuri wax 😂😂😂
Pape mbaye Moy pape médina gordjigen la
Donc évitons di abalé subu téléphone à n'importe qui wagni fréquententions yi
❤❤❤❤
Pourquoi dii torturer pour ame ay infos.niite boko torturer meuneu na avouer loum deffoul
Tout à fait. Et pourtant certains policiers et gendarmes sont pires que les délinquants.
Sénégal Amoul wone justice
Luttons contre l'injustice
Frère yagui dougallat sa boppou
Waw gui pape niak diomla domikharam ana macky
Ces ça le problème de peine de mort
Mais santal yalla souniou borom amana bo douguoul wone casso accident dei wala lago wala dara hamalni souniou borom amna loumou la fankal ba gua dougou kasso damay degg mak gni nane kasso ba dei🙏🏾
N'importe quoi accompagner le à monter un dossier à la place de 6 moi caduc c'est à la loi de lui dire ce qui la de droits
Condamnè a vie mo guen ,,on ne sait jamais parce que erreur judiciaire meneu am
non un tueur professionnel ne laisse pas ce genre de preuves
wa legui les gens qui n'ont pas de téléphone alors 🤨🤷🏾♂️?
bariwoul dé sou amé sakh
Un vrai bandit dou yoré téléphone 😅
Parsk téléphone Sonatel daflay surveiller 24/24
L'accusation de meurtre la il communique mal ce gars-là
Vrement kandji dafa wara delou police ndanane pire laa
Na nieup tokk sen keur bayi fréquence you bari yi
Damay bagna saga koii
saga pour lan
Police Senegal khamuñu sarap ndayam
Major Kandji lingay wakh gnepp xamnagneko.
Kii dagn ko wara dédommagé, niou def ko ak niou niak ko def daniou ko wara déf
Gendarme bila sofnalolou
Notre police est nul vue cette histoire
Borom djalalabi dou dindi bouton point mort day étouffer dhe
Qui wahamdji sou meytouwoul Dina dougalate bopame n'a meytou journaliste yi
Kandji doule rek lay deff
👍