Incroyable: Les prix du mouton s'envolent "Bou Geuneu Yomb 120 000 CFA Ben Femme Nieuwnafi Di Jooye"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 окт 2024

Комментарии • 41

  • @ballaseck7769
    @ballaseck7769 2 года назад +8

    Je suis téléspectateur des Dakar buzz 👀 depuis touba mais bayilenn di créés buzz masah Allah job nice na one love 👊

  • @senemam1696
    @senemam1696 2 года назад +3

    Li senegal rek leu. Yalla santanè woul li

  • @frenchyboy26
    @frenchyboy26 2 года назад +1

    Peulhs yi wakh lenn bokk...boulenn topp senn baye macky di fèweulè rekk

  • @madinagueye168
    @madinagueye168 5 месяцев назад

    Xarr dou cher Renn.Normalement ku am 75000fr meun gua am Xarr bu mat Tabaski

  • @mhd_0039
    @mhd_0039 2 года назад +4

    Machaallah kharou 600.000f bi diar na

  • @ndeyecoulibaly5382
    @ndeyecoulibaly5382 2 года назад +2

    Bly deukk Dina tolou fo xamni cou yoroul 100 do lal boume 🤔🤔🙄🙄🙄

  • @ndoyemax5220
    @ndoyemax5220 2 года назад +4

    Nooon wadji moy last néna kharou 75000 douné thiass même sokko marine🤣🤣🤣

  • @nafissatouniang4817
    @nafissatouniang4817 2 года назад +8

    Yéne yena yapp nit yi sou kharr amoul ngene dieund beuy bouniou kéneu Ray ndawal mom ndawal la rek

    • @falloungom3153
      @falloungom3153 2 года назад +2

      😂😂😂🤣😂😂😂😂

    • @omarlo5740
      @omarlo5740 2 года назад

      Tabaski d'où ndaw gui rk

    • @nafissatouniang4817
      @nafissatouniang4817 2 года назад +1

      @@omarlo5740 si mom la rek nioune nio tek souniou bopp louniou meunoul kou amoul yéré nga fot passé sol té nopi fi dara métiwoufi yalla tégoul keneu loumou meunoul yaw mom boudoul wone mouton yi baniou sacrifier dofi tok di diokhé khalat vrrrrrrrrr way

    • @omarlo5740
      @omarlo5740 2 года назад

      @@nafissatouniang4817 😂😂😂😂😂😂 wa yaw fo Méré tmt nank rk Yalla dafa yéwén mtx niou tok fi Di barkelou si téranga Adouna yi gua khamni yagu yagu dafay diexx

    • @nafissatouniang4817
      @nafissatouniang4817 2 года назад

      @@omarlo5740 fall yaram talouma mérr dama nité rek wouté ak gnidoul khalat les autres yangui comprendre fimay wakhé? Wakh nak mo yomboul comprendre fok nga nité pour kham dou gneup nio am kharr dou gneup nio am yéré man mangui sant yalla mais gniko amoul nak? Na nité way...tabaski diam wasalam

  • @malicklo4613
    @malicklo4613 2 года назад +2

    Stp yombalene xarr yii

  • @dominus5512
    @dominus5512 2 года назад +3

    120.000 pour bénéfice 10000 c kel investissement ca

    • @domoubadiane348
      @domoubadiane348 2 года назад +6

      Bo djayyer 10 si bess bi. Ame 100 000 benefice par jour ,tey meuna eupeu 10 khars fotos.business yilay deff milliardaires yeup ,benefice bou touti ,djayy lou beuri molakoy may. Je parle par experience.

  • @malickdpsow1052
    @malickdpsow1052 2 года назад

    Montrer plus les moutons c’est que nous intéresse le plus, pas tous les plainte et autres

  • @R_IA1
    @R_IA1 2 года назад +1

    Borom caméra bi ayoul

  • @MaguetteCissé-f4l
    @MaguetteCissé-f4l 5 месяцев назад

    Sama papa a acheté un petit mouton 😂 de 80000😅😂

  • @fn-vx5rg
    @fn-vx5rg 2 года назад +8

    Les parents qui font des crédits pour ça j ai vraiment pitié

    • @nafissatouniang4817
      @nafissatouniang4817 2 года назад

      Lolou dé lafi expliquer nioumay contre dire dafa niou gnémé lou méti def lo kham wakh lo kham so coucher dormir dound bi cher na ok mais niou def louniou meun bagn fallé...

  • @MrFreebird67
    @MrFreebird67 2 года назад +8

    Révoltant !!!120 000 CFA voir plus de sacrifice pour un mouton, C'EST RIDICULE. Pourquoi pas investir cette somme dans l'éducation, la culture, pour le bien-être et la santé de nos aînés et de nos proches qui sont dans le besoin. Aucun texte religieux ne nous dicte cette folie. Ngen Baalma Hakh....

    • @cheikhfall3202
      @cheikhfall3202 2 года назад +2

      Sa cameraman bii naay wooné khaar yii boubaax ñou guiss

    • @mhd_0039
      @mhd_0039 2 года назад

      WAY BOUNIOU SONNAL KHAR DEY LEK DI NANE NI YAW. SAKOU RIPAS BOUDON DIAR 8.000/9.000 LEGUI MINGUI DIAR 16.000F. SAKOU NGOGNE BOUDON DIAR 3.500F 3.000F LEGUI MINGUI DIAR 5.000/5.500 THE LOLOU 4 OU 5 JOURS RK LAY DURÉE, VACCINATION YI AK YENEN FRAIS LEGUI LO BEUG ? NGUA DIEND SA KHAR 50.000F FRAIS THI 100.000F OU PLUS, MA NIOW BEUG NGUA DIAYE MAKO 100.000F OU 110.000F NAKA NGUAYE REAGIRÈ ? Leppa chère motakh khar yi di chère

    • @zaldiop6293
      @zaldiop6293 2 года назад

      C'est juste une folie culturelle tout le monde a fait il faut que je fasse moi aussi même si j'ai pas les moins voilà c'est tout mon frère

    • @venusndoye9036
      @venusndoye9036 2 года назад

      Ce Khar à 120 000 fcfa mome, c'est trop abordable

    • @Senesen555
      @Senesen555 2 года назад

      Yallah santaneko nganane c'est ridicule apprends un peu ta religion te nga balma.

  • @madinagueye168
    @madinagueye168 5 месяцев назад

    Xarr beurri bay beugua Dee

  • @falloungom3153
    @falloungom3153 2 года назад +1

    Kharou 600mil diarnako

  • @bilygaye7909
    @bilygaye7909 2 года назад +5

    Khontou bi môme metina trope

  • @damegueye9457
    @damegueye9457 2 года назад

    Omar Sall🤠🤠🤠

  • @jeuneprodige4520
    @jeuneprodige4520 2 года назад

    Mouton a vendre pas chère

  • @ndeyengom
    @ndeyengom 2 года назад

    😂😂😂😂thiasss

  • @1AbouDavid
    @1AbouDavid Год назад

    Cameraman khare nguaye woné wala sameu bi ngaye woné ,dangua nul

    • @1AbouDavid
      @1AbouDavid Год назад

      Bayil féne bane peul ako yémalé si séne bir , bayil diakhassé khéte

  • @mbackegueye6948
    @mbackegueye6948 2 года назад

    Peul Yi ouyouléne

  • @ndiayealioubadara7819
    @ndiayealioubadara7819 2 года назад

    Mbokou Macky Sall lagnou