Diallo Sénégal niio geum ni séries S pour niou ayye gnileu. Series L pour les « nullards » or que Dieu à équilibrer son monde. Gni sen khel néxna cilou dieum si sciences gni sen khel maatjie ci lènén. Te boo dianguer dingua xamni domaine bou nek Amna aye scientifiques. Faut juste que Sénégal niou valoriser tous les domaines dijokh nieup sen chance.

diallo jue suiis d accords avec toi a tous les niveaux tagaat len nit yi