@@aminatadiaw9283 suis d'accord parce que des politichiens comme Macky les a acheté avec ses mallettes de milliards. PROS dit que les tarikha font partis de la vie des sénégalais il faut les encadrer, les institutionnaliser. AKHENATON ce franc maçon qui s'est appuyé sur un livre écrit par un blanc pour contredire le récit de Serigne Touba qui raconte comment s'est passé son exil ou son kidnapping me m'intéresse pas. Combat bi ay bouki you beurri dagnou sango dérou beuy. Ne soyons pas naïf et focus sur PROS ✊🏽
Sene Serigne yi tekiwou niou sarap ndayam thi Sénégal bilay walay bolene niou sonal 🇸🇳🇸🇳☝️
yaw ya Kate sa koyou papa
Katal sa ndey yaw ya tekiwoul dara
Merci akhenaton on est avec vous
Longue vie à akhenaton.
Mom dafa bax thi réwmi
Akhenaton est un patriote ✊🏿. Khalifaux 👹👎
❤❤❤❤pour Akhenaton
Dangaye fen li akhenaton wakh moye deugue
❤❤❤❤❤
Merci sawolof
Nioune tammittt ligua wakh andunioussi daguenn warra bayi dii tek serigne si gua kham niii ay nittou késser lagniou founiou yégoul fiii koufiii dé likhlass gua sokhla mayniou suniou diam
Kou diog wakh, ya pas de religion au Senegal, tous animiste
Moi je suis patriote à 1000% mais akhénatone domeram leu féne rek lay déf
Yow yay domeram
Akhenaton kou niaf ndeyam le
Tokk France di souss,di doul et les réseaux sociaux relayent ça
Sou bouguè wakh dègueu na gneuw Sénégal
Akhenaton doul rek la meuneu
Dem senegal pour lan?
@@pisko2119 pour montrer son patriotisme si réellement il en Est
Yay doulkat bi
@@aminatadiaw9283 wakh ma bane vérité la Akhenaton divulgué avec des documents authentiques ?
J'attends ta réponse
Akhenaton vrai domeram le
Akhinaton doll rk laye deff
Yow doull rekk
Akhenaton utilise le combat de Sonko pour manipuler, la plupart c'est pour discréditer nos tarikha.
Tarikha tok mouy dokh
@@aminatadiaw9283 suis d'accord parce que des politichiens comme Macky les a acheté avec ses mallettes de milliards. PROS dit que les tarikha font partis de la vie des sénégalais il faut les encadrer, les institutionnaliser.
AKHENATON ce franc maçon qui s'est appuyé sur un livre écrit par un blanc pour contredire le récit de Serigne Touba qui raconte comment s'est passé son exil ou son kidnapping me m'intéresse pas. Combat bi ay bouki you beurri dagnou sango dérou beuy. Ne soyons pas naïf et focus sur PROS ✊🏽
Akhenaton mom ay doull motah deglo toumako sama nopou yi menoul deglou ay soss patriotes dafa nekha nakh mane dèh damay choisir yimay deglou
Kokou sa guiss guiss la nous on écoute Akhenaton jusqu'à l extinction du soleil...
Yow tu es et devient de plus en plus arrongant
Loolu lañu xase Sonko ndax dëggu ñu baax ñépp te dëggu arrogance lañu leen xasee 😂