Je me demande si Yoff connait vraiment le potentiel et les qualités physiques et techniques de ce gosse. Kii bou amè suivi ak sérieux bii modou lo am koumou beurél am nga tioow lou mate tiow. Il est redoutable Machalah. Wait and see.
Mangui londres mais thiatou yoff khamoumako wone... mane Apecsy 2 la deukk... Fallou Seck Cafè dafma moussa wakh wakham.. ndanane la bilahi. Tè daffa yarou mais nakk yalla bakhna
Lamb moy afairou mafia mé boy yi yepp thiatou yof dou sene morome kham nguene ni niang bou ndaw mi di beure grand combat lifi thiatou yog df mom defouko
Je me demande si Yoff connait vraiment le potentiel et les qualités physiques et techniques de ce gosse. Kii bou amè suivi ak sérieux bii modou lo am koumou beurél am nga tioow lou mate tiow. Il est redoutable Machalah.
Wait and see.
Yoff dougne diapalè mbeur lolou moy thiat li
Thiatou Yoff est l’un parmi les meilleurs de l’arène
Thiatou yoff c'est l'équivalent de Malick Niang en terme de frappe masha'Allah.
Wàllaay wax dëgg mbër bu mën xeex ak mbëre.
Sa c vré
Mais il est plus technique en lutte
Thiéy sama mbokou lébou yi Bénén Malick Niang nieuweutina😮😮😮 Thiatou Yoff et fière d'être lébou ❤❤❤
Thiayou Yoff sera un grand champion..il est technique avec une bonne frappe et tres discipliné.
Boye bi machallah dina donii roi des arènes 🎉❤
Thiatou yoff champion la ❤
Thiatou Yoff, yalnako Yalla moussal ci Thiatt rek🙏🏿
Loko faye ci lamb meritewonako, dafay beuré, bafay xex.
Louko wa yoff diapalé rek doyoul, nañko guena taxawou.
Thiatou yoff félicitations ndaandane la de machallah
*Thiatou Yoff, Thiatou Daouda Fall, Soundiata, Talfa, Tony Jr, lamb Ji ci sen lokho ley moudjei d’ici 10ans*
Soundiata non
Soundiata mbeur la dhé@@cheikhbasskeurmassar9548
Guene si thiatou daouda fall dafa begue lou yombe
@@cheikhbasskeurmassar9548 setanal tous ses combats
@@cheikhbasskeurmassar9548si sondiata mbeur la dé
Thiatou yoff felicitations. Ndiaye tine dafa beury wakh... tapha tine sakh yakko meune fouff
Mangui londres mais thiatou yoff khamoumako wone... mane Apecsy 2 la deukk... Fallou Seck Cafè dafma moussa wakh wakham.. ndanane la bilahi. Tè daffa yarou mais nakk yalla bakhna
Non boul wakh lolou juste diay combat bi rek la won nak
Palla Lamine bou ndaw bii saax moleu eup xaam xaam fimouy waxé dieuleu bou reuy ak nimouy danoo beine leu ioe guanane nimou beuré baxoul
Manch'ALLAH Thiaat ndam rek inch'ALLAH inch'ALLAH
Thiatou Yoff bilæ amougnou sa faye ❤
Thiatou yoff ésk dou robot😂MACHA ALLAH
Ndiaye tine dawna khékh bii ba sone😅
Mais ndeysane khamoul né thiatte yoff beuré sakh la gueune mane
Ndiaye tine woroul wone bayi ki feter ko thi souf bobi la def thi deun bi imposer force boumou am félicitations thiatou yoff🎉
Thitou yooff kasssé niépaye niam yoff lanou deuk❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Thiatou Yoff vs Zarko
Il a de l'avenir,s'il est sérieux sur l'entraînement il peut faire beaucoup dans l'arène
Lamb moy afairou mafia mé boy yi yepp thiatou yof dou sene morome kham nguene ni niang bou ndaw mi di beure grand combat lifi thiatou yog df mom defouko
Bilay
Billahi
Thiatou Yoff notre Espoirou yoff
Thiatou Yof vas Jacksone ❤
Thiat rek notre champion le King
Thiatou yoff le poutine de l'arène 🎉🎉
Bly rayngama😂😂
Un vrai Poutine Wallahi
😂😂Louye poutine😂
Thiatou Yof) Jackson) pokola Balde)
3 yii Mawax Nalén Lamb bayi xéll Boubax sax 🥹félicitations Thiatou Yof champion nga ❤Du courage Ndiaye Tine osy👍champion nga 👍
Fou Bayi Talfa Ak Thiatou Daouda Fall
Niome niépeu thiatou yofe moléne mane
Mok garga 2 dou yomb dhé
ndiaye tine vraiment dou mbeurr
Thiat dé lokhoyi com wénge😮
Thiatou Yoff mi dafa soxor deh dinafi rey niit deh
Thiatou Yoff grand champion
Thiatou yoff kassé 🎉❤
Sou ma bokone thi calaf bi dou beuré ak thiatou yofff mouk😍🤗
Thiatou yoff yaw rk ❤❤❤
Thiaatu Yoff KC ❤❤❤
Tiatu yof vraiment Fi doussa place.
Boy yiñuy tiow Fi yeup yalén meun bilahi
Dousen morom lamb mo wakhoul deug
@@alinesyllaSyllaaline bilay molén meun allez retour
Thiatou yoff mii nit leu ??😢😢 kiii dina ray nitt 😂😂😂😂
Lokhoyi bakhoul 🎉🎉dhé
Mais Weuz Djambour affirme il ya de cela 4 mois que : les deux finalistes doivent se rencontrer et maintenant il dit le contraire.
Sénégal daal😮😮😮
Du courage Ndiaye tine
Pourquoi pas Zarko Thiatou Yof ❤
Thiatou yof ❤
Thiatou yoff vs domou dangou combat la😂😂😂
Thiatou Dina fi ray mbeur
Moytou léne thiatou yoff
Père palla wakhna lou graw thiatou yoff foowou fowlouwoul
Thiatou yoff vs zarko
noo bou siteu yangui yengal senegal
Thatou yoff jacksone jr boy boulerne moytouwoul
Alioun s2 jackson ak Tiatou yoff kou len moytouwoul amm gard normall dinegne la rey
Ndiaye Tine se croit plus fort que les autres
Thiatou yoff But you have to go hospital to check your hand.
Ndiaye Tine defa nagou
Thiatou yoff vs Pape Thiam2 combat bou néxx
Thiate daane naako
@@abdoutall8491nn Pape moko dann khn sétano ko
Seulma lambj dafa am coumba am nday sinon il será un Champions
Bilahi
Wa lamb yena yakhh rewmi
Lamb dou ponkal am dole rek même taph tine monul bare xamol gâté dole rek la am
Thiatou yoff boutolone ni reug ak franc kon douniouko raw
Tey yala thiat mi
thiat doumoroumou boyi
Thiatou yoff moko meun fouf moko dakha beurè
Niang bou ndaw gnila wara beurél
Mbaye xolé 2011 lako xam bimay ambilan si tefess Yoff dolé naturel la Yor t ragaloul pour mom mo meune gnieup
Yaw xam ngako fall
Ya Man ya eupp doolé vraiment contan na saa waji
Ndiaye tine ragal la
Lamb dal amoul logique
Tautou yoff rak
Arbitre a mal jugé il devrait arrêter le combat le gas était blessé avant chute bi
Poutine dina fi ray mbeur, sissou woul dei door bo dall
Poutine bi seul
Tafffa geuye tu parle trop avec ta grande bouche contre Tyson on t’a fait comme ça mais mérde a la fin
😂
Thiatou yoff meunn na beuré machalah