Cheikh Ibrahim yalla na yalla yagalcofi tè werreuul tthiieureum defalco tawfekh m'achallah borom xam xam bu sel yalla na yalla fayal niouko jazakallah khayrane Baraka'allah fikoum
Salam wa rahmatou Allah aleyloum. Maacha Allah. Qu'Allah soit satisfait de Son Serviteur Cheikh Ibrahima Khalil LO, l'élève au haut degré parmi les saalihines, et partisans du Coran qui bénéficieront de son compagnonnage et son intercession au Jour Dernier. Qu'Allah lui facilite la réalisation avec succès dans ses projets. Nous prenons Dieu comme Témoin de notre amitié et de notre amour fraternel en la personne de Cheikh Ibrahima.
Cheikh Ibrahim yalla na yalla yagalcofi tè werreuul tthiieureum defalco tawfekh m'achallah borom xam xam bu sel yalla na yalla fayal niouko jazakallah khayrane Baraka'allah fikoum
Amine
Machallah long vie a toi le Sénégal a besoin des personnes comme vous parceque vous nous guide sur la bonne voie
Macha Allah. C'est limpide, clair et accessible. Dieureudieuf imam Khalil Lô.
Qu'Allah soit satisfait de lui
Sama yaram bi mou ngui daw ndakh dégg ay deugg
Dieureudieuf baye Khalil
Yalna yalla samm la
Pure vérité. Je t'aime beaucoup et t'écoute beaucoup. Deugeu reek ngaye wakh. Alkhourane reek ak sounah
Salam wa rahmatou Allah aleyloum.
Maacha Allah.
Qu'Allah soit satisfait de Son Serviteur Cheikh Ibrahima Khalil LO, l'élève au haut degré parmi les saalihines, et partisans du Coran qui bénéficieront de son compagnonnage et son intercession au Jour Dernier.
Qu'Allah lui facilite la réalisation avec succès dans ses projets.
Nous prenons Dieu comme Témoin de notre amitié et de notre amour fraternel en la personne de Cheikh Ibrahima.
Mach'Allah Sheikh Ibrahima Khalil lô ❤️. Qu'Allah vous protège et vous prête longue vie 🙏🙏🙏
machallah amna solo yalah nala yalah fay yiw 🙏❤❤
Walahi ndeysann Lérna nagne, déssna kou nango akk kou nangouwoul !
Wassalam Yallah na Yallah dimbli nou gnou ame dégg akk ngueum !
Dieuredieuf ya imam TAWHID yalla naniouko yalla dèfale.. que dieu vous protège toujours véridique et constant
Macha Allah ya oustaz que dieu vous protège
Yalna yallah sammeu la té fayla yiww sheikh bi 🤲
Allahou akbar , MACH ALLAH
Machaallah yalana borom bi samla barkel xam xam bi
Bilaay sama chiekh bi,yaama leeral lu bari thie sama dine ji.Yal na la yaala arr
Amine
Machallah ❤️❤️❤️
Mashallah
Assalamou aleykoum á tous .
Wollayi wakh nga deug bou léer net.
Nul n'est plus sourd ,que celui qui ne veut pas entendre. Ya Cheikh longue vie ❤
Machall Machall