Machala sognouko beugai mou am inchala. Nagnou faikhai ba defko 2voix tali Cornichbi ak assainissement nadonne liguey bou bakh Ben Yonne soudiarre dem ba Chine sakh diarnako
Man damanè wone bassi président bassirou da warone wahtane ak serigne mountakha mou wotè levè de fond bo hamnè nioune sénégalais niokoy dèfal sounou bopou bou boba gni tolok 500f ba 1000000 lou way tololl diohèko
Muhammad Ali bamu siyaare see S.Abdu Lahad, dakoo laajoon niko "wax ma yoon Wi yan projets la am ñu jàpp ci". S. Abdu Lahad niko" yoon Wi nag daa Am lu muy bañ, te mooy tàllal loxo ku dul Yàlla". Damaa jàpp ni principe booba la kilifa yi di sàmm ba tay.
Machallah ❤❤❤
Machala
MACHALLAH LIII MOOY MOURIDE NA GNEUPP DJAPP MOU SOTTI, WAKH AK DJEUFF BOKOUL, DJEUFF EUP SOLO LOOOOL
Ww gooré
Machala sognouko beugai mou am inchala. Nagnou faikhai ba defko 2voix tali Cornichbi ak assainissement nadonne liguey bou bakh Ben Yonne soudiarre dem ba Chine sakh diarnako
Machallah eskeye amina yaraby
Aï thia mouride
canalisations esq guenoul farata thi deuk bii di touba ak ndokh mou disponible thi quartier yép
Mais pourquoi pas avoir un corps diplomatique pour demander de l’aide dans les états islamistes
Pourtant defat niou ame aye partenaire mai niome nio choisir li ndah mo guena barkèl
Machalla