Comme il en est coutume, quand il s agit de chanter Baye, c'est toujours avec le Mbecté de vos cœurs. C'est l'extase qui fait la mélodie. On sent que chaque mot émane au plus profond de vos âmes. De l'esthétique pure pour le plaisir de tous ! Mbecté partagé ! ❤❤❤
❤❤❤❤❤machallah bidewou mawlana cheikh Ibrahima yi nous sommes fier de vous ningeni yeukeuté mbiri baye yi si kaw yalla baye faye lene si zair ak batine ❤
Oh comme d'hab sène son rek la gniakamti mou gueuneu si Gamou gui vous ne decevez jamais dama beugue Baye Niass trop si khol❤et c'est plus fort que moi bon Gamou à tous djiam si yène gnieup 🙏❤❤❤
Sama dieukeur MoMA xamal baye ❤je suis fier d'être barhamienne ❤❤❤❤❤
Mâcha alla yalla nako yalla fay si Barké Baye❤️🙏🏽
Machalla kene dou mame baye niass l’international ❤❤
Mashallah nianalma ma ame Dieukeur Niasséne
Alkhamdoulilah ❤
Je suis mouride mais walakhii j'attend cet morceau avec impatience chaque année
Brick je vous aime bilay yénn rk lay topou bonne continuation ✌
Alkhamdoulilah ❤
Même moi❤
Merci ma belle niora raw khépp kou beugou baye niassssss rék niora raw🎉❤
Kouko done kharr rk la lall j'aime
Baye Niass rek
🎉🎉🎉🎉🎉@@issadiallo2808
Akhlou Brick mangui léni niane euleuk nguéne deff feat ak Wizzy Kana svp ❤🙏🇸🇳☝🏽
Oui je suis d'accord avec ça sera trop bon même ❤
Lou naraa niceee🎉🎉
Waw lolou idée leu mom tamit defna son bou nekh🎉
Lou graw machalla
Kèp kou deug ara ak dayze lalal je aime🎉🎉🎉🎉🎉
Kép kou drug ara AK DYZE lalai je aime 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Ohhh damako yag khar❤❤❤❤❤❤
Doctorou kholyi moy baye niass kou d'accord lalal j'aime
je suis mouride mais je suis d'accord sunu makgni nieup ay docteur lagn ♥
Je suis d'accord avec toi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤je suis un talibe de BCMIR
Oh ndeysane li nék Na merci Akhlou brick Dieureudieufé Baye Niass
Barki alkhourane Baye moo dakk leem❤😭. Lou metti yagoul. Son bi sou gueinnoul wonn duma djigue
Barki alkhourane BAYE MOO DAKK LEE
Wa kaolack manifestè vous 😩🫣😭🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Djereudjeufé BAYE NIASS alhamdoulilahi nekhatina merci a akhlou brick ila medina rek incha allah ❤❤❤❤❤❤
Just machallah ❤☝🏾🎊
Kou beug Baye Niass alhamdou lilha ❤
Yalla nagnou ko fékké aye ATI Ate. Bègue nagnou akhlou brick khole ❤❤❤❤sééd na
Amine
Gamou 2024 avec Akhlou brick li mouy suniou mbecte ❤
Dieureudieufén mawlana cheikh ibrahima niass ❤❤mbecté baye rek❤❤🎉
Baye Willani mo meune formé kholal dayza rék ❤❤❤
Dieuredieuf baye Willani ❤
Dieureudieuf Baye Wilane BAYE
Wilanyyyyyy❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Kou beugue seydouna mouhamed rék lalale j'aime ❤️
❤❤❤❤
KOU BEU BEUGUE SEYDOUNA MOUHAMED
Alhamdoulilah bignou yalla bolé thi gni beug baye❤❤🙈
❤❤❤❤
Dieureudieufééé Baye Niass, vive Akhloubrick kéne dou yeunes vraiment, vous êtes vraiment fort mach allah Niass ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏📿
« Do meussa loumpi bo xassé loump minka »❤️❤️❤️
Comme il en est coutume, quand il s agit de chanter Baye, c'est toujours avec le Mbecté de vos cœurs. C'est l'extase qui fait la mélodie.
On sent que chaque mot émane au plus profond de vos âmes.
De l'esthétique pure pour le plaisir de tous !
Mbecté partagé ! ❤❤❤
❤❤❤❤❤machallah bidewou mawlana cheikh Ibrahima yi nous sommes fier de vous ningeni yeukeuté mbiri baye yi si kaw yalla baye faye lene si zair ak batine ❤
Gnothi meun walahi❤️❤️❤️
Barki baye niass mafi djitou
1er commentaire 🩵🙏🙏🩷💙🩷💙
Ooohhh sama khole sédena. Dieuredieufé Baye 🙏🙏
Kou d'accord ni son bi daffa graw lalal ❤❤❤, 🙏
Bilae machallah
Alkhamdoulillah 🙏 man iow rék la doone khar bilay maléne beugou barké baye niassssss 👏 sama khôl bi ohhh mogui nék bilay dieurediéféee baye niassssss 👏🙏
Alhamdoulilah j'en fais partie des premiers commentaires ❤❤❤❤❤dieureudieuf Baye Niass
Machallah Akhlou Brick Yalna Yalla fayantè ak Yënn Cii Barkè BAYE AK BAYAM YA RABBI 🤲🤲🤲🙏❤
Maaay mouride bou beuge baaye waalahi❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Akk mane may numéro 1 bou ken sissou nakk❤
Yalla nalen yalla beug
@@ouldhacenwallay sama ginaaw ngay topp
Machalla ❤❤❤❤❤
Djeureudieufé Baye Niass 🙏🏾
Dieureu dieuff BAYE la solution 😍
Ohh machalla yalna baye niass fay léne chaque année guéne soutourale niou😢❤
Dieureudieuff Baye Niass
"Do meusseu loumpi sou khassé loump minka" bilay lou lerr.
Dieuredieufé Baye
Dama ma kou yague kharr
❤❤❤❤❤❤
Dieuredieufé baye niass ❤️❤️❤️❤️❤️😭yallah barkel léine 🤲🤲🤲nexna trop way❤️❤️❤️
Akhlou Brick déçoit jamais ❤️🔥👌
Xoll séd na waye machallah ❤❤❤❤❤❤
Meuso lèngnio rosslo❤❤🎉🎉 dieuredieuf Baye Niasse 🥰💯
Machallah ❤
Bismillah alhamdulilah tamps yi yeup nélow wouma nakh sons bi tay mome dina nélow ba contane ❤❤❤ alhamdulilah dieureudieufé baye Niass ❤❤❤❤
Bilaye akhloubirik danio rem sounou kholl nakhare rk ngn sedallko yalna sen diamoyague
Yalla def gnou deug deug talibé baye 🤲🏾❤️😭
Alhamdoulilah alhamdoulilah ...allahouma ma sali Allah seydina mouhamadine wa Salim....dieureudieufe baye niass ...akhlou fi zikri brick si life ....
Kouko done kharr rk la lall j'aime ❤❤❤❤
Beugg baye mo tkh ma beugg lene ❤🎉
Keen dou Baye
Mbeuguél la rawé Gayiiin❤️❤️
Kumamy Dalal gaamu kaolack yénn ngir dieum Baye Niasse 😢
Mane dinala dalale
Yagg ngeen GNU beeg loo ❤yallah nalen yallah begggueulé firdawsi 🎉 et merci encore❤
Limako khar dieureudieuf Mame Baye Niass l’international Mbecte rék ❤❤❤Akhlou Brike merci
Baye Niass lagn beugg 😭😭😢❤
Baye thi ❤ Baye dieum Baye ba abadane machalah dieureudjeufé BAYE NIASS
Maneu Mouride la talibé Baye Darou mes je suis très content sur le son dédié à Seydina Baye mou sell mi...
Mbecté Baye!!!
Machall 🎉baye niass❤❤
DIEUREUDIEUFÉÉÉÉ BAYE NIASSSS❤
Thiéyy kéneu dou sama Mame 😭❤️🎉
Alhamdoulilah baye a vie ❤
Baye thi kholllll❤❤❤
Mouride bou beug baye ba Amou si saagoo waww amna magunii minka ilayka barhama Daimane ❤❤
Dieureudeuff sama grand frère yii bon gamou rek inchallaha Ila medina baye niasse rek inchallaha
Doctoro khole yi moy baye❤
Alhamduolilh Dieredieff Baye Braham niasse ❤️❤️ Machallah Baye niasse rk ❤❤❤❤
Machallah kep kou beug baye kontan nga ms nak jotna ngen dem ba nigérian tourne fa clip geuneu woné ligeuyou baye lou am sololeu❤❤❤
Macha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lou nékh bly❤🎉
❤❤❤❤❤❤bravo encore akhlou brick
Mach'allah Baye Niass international ❤❤
Machallah Baye, la solution ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ xol séde Na
Yalna s'en djam yagg thi Barke baye ak bayam ❤ niguén sedalé sama khol bi yalla n'a sen khol seidei ni abadane ❤❤❤❤
Deyza 🥺💪💪❤️❤️❤️🎉📿
Machallah je suis encore ébouiller de joie Baye Niass ma vie dieuredieuf pour cette belle son ❤❤❤❤
Wa yèn li nexna dii mashalla
Nn baye nn life ay way li nekh na deh 😭😭❤❤
Machallah khol sedna❤️❤️♥️📿
Baye niass rek baye baye baye baye baye baye baye 😭👊🙏
Deyza🎉🎉🎉
Kèpo kou bugue baye niass lala jem
Yen rek laniou done kharr🎉
Xamone Nani d’où guene gnou bête toujours égal a vous même yalna yalla weral bate yi
Son bi cool nékhna🎉🎉🎉
❤❤❤❤❤❤❤❤ Baye NIASS rek ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ bonne Gamou
Oh comme d'hab sène son rek la gniakamti mou gueuneu si Gamou gui vous ne decevez jamais dama beugue Baye Niass trop si khol❤et c'est plus fort que moi bon Gamou à tous djiam si yène gnieup 🙏❤❤❤
Yéne esk dégeu nguénn li Deyza wax si BAYE NIASS ohhhhhhhhhh😢😢😢😢❤❤❤❤❤❤❤❤
Parie dayza rk lay xar à chaque fois❤limou wax si baye fort na❤
Mbékté Baye Rék Gnou Wadial Gamou❤
Akhlou Brick for life 😢❤😊
Machallah ont est très fière de vous Ahlou Brick Yalla na Baye feyanté ak yeen thia kaw thia kanam rek
3ieme vue🎉
Machallah liii nekhh na waay 🤞🏾🙏🏾 Baye la SOLUTION ❤
Diaredieufé Baye Niass 🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤ doctorou khôl yiii ❤❤🎉🎉🎉
Li dafa fess 😢❤
Kép kouka donne khare réck beuseul ❤
Ohhh Macha Allah lii nexna way BAYE rk si xol dara douko fay barki Baye
Alla Kaolack rk ❤❤❤❤❤😅🎉 content na❤
Lii Nékh Na Wayy Macha Allah 🇸🇳
Kou bayi loumou done déf dikko kharr
Yalla na yalla fayniou maolana cheikh ibrahima Niass ❤❤😢
Yalla nagnu Gamou dji ci diam ak salam ci barké Baye Barhama Niass ❤