Affaire Aïda Diallo: Serigne Mountakha wakhoul ni ...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025
  • Serigne Ablaye Diakhoumpa: Serigne Mountakha Mbacke ne s’ est pas prononcé sur la demande de pardon de Aïda Diallo.

Комментарии • 113

  • @khadimndiaye3221
    @khadimndiaye3221 5 лет назад +1

    Macha alla kaddouyi rafetna amna solo yalla Nala yalla Faye thi barke Sering saliou te werel thieryi ❤️

  • @famalo9021
    @famalo9021 5 лет назад

    Macha alla wakh dji Amna solo lol dieurdieuf serigne mountakha mbacké Yalla naka fi yague Lol te were ci barke serigne touba

  • @khadimleye5738
    @khadimleye5738 5 лет назад

    Dieureudieuf Serigne Abdoulaye Diankhoumpa

  • @serignesalioudiallo1441
    @serignesalioudiallo1441 5 лет назад

    Machalah Serigne Abdoulaye diakhoumpa

  • @moussatall5684
    @moussatall5684 5 лет назад +1

    Masha'Allah jërëjëf serigne Abdoulaye Diakhoumpa xam xam bi rafét na

  • @banacamara8638
    @banacamara8638 5 лет назад +1

    Waw aida diallo do yém reck. Thyssa khéssal ack cheuveux téh bayi sougnou KHADIMOU RASSOUL. WAW LÉGUI DO DJAYE GLASSE MBA KÉTHIAKH MOLLA DAKHA FOUYE ACK DOF ESPECE DE DAJAL ...TOUK... YAW.... YALLA MAGNOU YALLA MOUSSAL THI YAW ACK SAYE ANDADO

  • @oumoundieguene6086
    @oumoundieguene6086 5 лет назад

    Ki. Aye. Mbokam. Niokoye. Setane. Ndakh. Khaliss. Waye. Après. Laye. Kham. Namoyetou. MO. Guene. Deh. Adouna. Diaroul. Li.

  • @Tallinfos44
    @Tallinfos44 5 лет назад

    Abonne len si sama site bi
    Nger dieumi s.touba @sunutv

  • @alimatousougoufara1571
    @alimatousougoufara1571 5 лет назад

    Machalla darmanko

  • @damecisse324
    @damecisse324 5 лет назад

    Dieura dieufaty

  • @adamagaye4136
    @adamagaye4136 5 лет назад

    Machall lah

  • @yakarserignesalioumbacke9407
    @yakarserignesalioumbacke9407 5 лет назад

    Jiaradif serigne abdoulaye machal

  • @dadad9342
    @dadad9342 5 лет назад +1

    Tidianiya mo gueuna deupou akk Islam. Mouridiyah sounou yonente bi khamouko wone, bayiwouko fii wakhoumala nak Thiantacounes ( danser, sabarou, femmes non voilees, lekk akk nane)

  • @mamadadou7143
    @mamadadou7143 5 лет назад

    Machallah

  • @yadewade8784
    @yadewade8784 5 лет назад +2

    Machallah machallah machallah machallah

  • @Tallinfos44
    @Tallinfos44 5 лет назад

    1er

  • @adaoaugustosilva2833
    @adaoaugustosilva2833 5 лет назад +1

    machahalla amatina sollo

  • @bassiroumbaye5005
    @bassiroumbaye5005 5 лет назад

    Akassa manchala koubakhki ki am na solo lolll

  • @elhadjidieng9978
    @elhadjidieng9978 2 года назад

    MODOU

  • @orangeg8653
    @orangeg8653 5 лет назад

    Mim rew bamba ko mom chaque jour sa bay ni mo mom keureum t boy dem sa keur mangui dem sounou keur ngay wakh .fin

  • @orangeg8653
    @orangeg8653 5 лет назад

    Y’a meuneu dull iow dal linguen di wakh soudé deugleu woté len djihat ndakh si sunna yi la bokou wouti len diassy ak ay 🔫 après ma meun geum ni yenagui top sunna

  • @orangeg8653
    @orangeg8653 5 лет назад

    Xamo leufeul ndayam

    • @mbayefall5180
      @mbayefall5180 5 лет назад +1

      Yaa reew ,ñakki teguin, te ñaaw lamiñ

  • @ousmanediagne1535
    @ousmanediagne1535 5 лет назад

    douy nanak

  • @orangeg8653
    @orangeg8653 5 лет назад

    Sa nday ak aida Diallo la yamalé kousi diang arab di goudeul sikim di dull demal djihat bo gnibisé niou débat

    • @falloufall3486
      @falloufall3486 5 лет назад

      Amo leen yar amo leen xam xam ken do took ak yeén

  • @bourhan142
    @bourhan142 5 лет назад +1

    Li Aida def mou nakhari lèn ndakh bookoul si mouridia noonou lagnou li mourides yi di def mou wouté ak islam nakharé. Bayilèn bidaa.
    Sounou borom bamou teureulé dinèm boolé woussi mouride.
    Sou Mame Diarra bousso gnowatoone mooy djiité mouride yi tey. Gneuppa koy raamal.

    • @khaforndiaye7771
      @khaforndiaye7771 5 лет назад

      Sidy diallo ba bida la mouride yi defff

    • @laveriteabsoluejuste6358
      @laveriteabsoluejuste6358 5 лет назад

      Sidy Diallo peuhl fii samorom nékoufi, boofi wahé lowaroul wakh diappla teuwougnou

    • @bourhan142
      @bourhan142 5 лет назад +1

      @@khaforndiaye7771 magal moo si diitou, soul nèw si dlakka , soujotal nit, baay faal dou joulli dou woor, .....

    • @bourhan142
      @bourhan142 5 лет назад +1

      @@laveriteabsoluejuste6358 yow khana weuro deugg. Kou amoul argument rek mooy menacé waaté. Mane ragalouma lèn yalla rek laa raggal.
      Deugg nguèn ragal ndakh beuggoo lèn douté. Kham nguèn si ay thiakhan nguèn nekk

    • @sarrmedoune8547
      @sarrmedoune8547 5 лет назад

      Wa sidy dialo yaw lo defar cii dîné ak lou la dine diaral.

  • @layelaye6583
    @layelaye6583 5 лет назад

    machallah machallah