JOAL : DU NOUVEAU SUR LA FILLE DE 10 ANS VI@LÉE

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 янв 2025

Комментарии • 79

  • @AstouSy-f8i
    @AstouSy-f8i 2 месяца назад +27

    Li doynawar métina yalla nako yalla takhawou mou mouthiou si diam ak domam natou la rek

  • @KineCamara-rj9zh
    @KineCamara-rj9zh 2 месяца назад +8

    Du courage aux parents de Rabiya que Dieu l'accompagne jusqu'à la fin bonne Santé à Rabiya

  • @diaynabacisse6090
    @diaynabacisse6090 2 месяца назад +6

    Bilay li metina sama khôl tamite
    Yalnako yalla takhawou inchallah
    Ndananetv sen ligueye rafetna
    Si kaw si kanam rek inchallah

  • @AstouSy-f8i
    @AstouSy-f8i 2 месяца назад +15

    Bilay amna guor you boneu té nékeu khalei bou ndaw 10 ans sou ma doneu papam dina tal ndayam domérame le sim

    • @OusmaneDiallo-wk3jc
      @OusmaneDiallo-wk3jc 2 месяца назад +1

      Bilahi dama sakhe rousse guathié Dafay bayi borome top ma

    • @awatoure5056
      @awatoure5056 2 месяца назад +1

      Astou boul rouss ki sunu bokone kogne damkoy diongal bapare niawwko😂

  • @serignetoubark
    @serignetoubark 2 месяца назад +17

    Yalla nako yalla diapalé takhawu ko Brkp sëriñ Fàllu 😭 liii vrm meti na lol

    • @awatoure5056
      @awatoure5056 2 месяца назад +2

      Mane sokhna si ki limou Def ni dîna mety simom loll yallah dafa meuna mougn wayé dinako guisss bonne khalé bou tol ni nga defko li yallah borom bi dakhawou khalé bi ci jamm

  • @KartoumGueye
    @KartoumGueye 2 месяца назад +4

    Bly li metinama 🥺🥺ki moy domeram deugue khale' bou ndaw bi ndeysane khale' bi yalka nako yalla takhawou si barki seydouna mouhamed sws mettina trop té bolen khole' ndeysane parent khale' bi khamougnou nougbouy wakhe' problème 😢 j'ai tellement mal 💔

  • @AstouGueye-fi6cp
    @AstouGueye-fi6cp 2 месяца назад +13

    Ylla dina ko maye diame barcke seydina ababackar sy barckeseydina Mohammed psl amin

  • @fatousane-v7v
    @fatousane-v7v Месяц назад +1

    Merci beaucoup Ndananetv Machallah que dieu vous bénisse 🙏❤❤

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 2 месяца назад +5

    Machalah Seck Ndanane sa liguèye rafét machalah ❤

  • @fayeemilie3929
    @fayeemilie3929 2 месяца назад +4

    Il faut rester vigilant avec vos enfants. Et faciliter la discussion pour quand de problème les enfants puissent vous parler. 🙏🏾🙏🏾

  • @diaynabacisse6090
    @diaynabacisse6090 2 месяца назад +6

    Macha-allah Badiane sen Association bi yalna yokou ba guëne yeuk ko

  • @mbackelam
    @mbackelam Месяц назад +3

    Alhamdoulilah donc vue que déféré nagn ko boul yakamti procès bi neu Goor Gui mosh 10ans beu nopi niou doguay entamer procès bi procureur bi neu demander 25ans ou même à vie car cet homme est un menace pour la société

  • @talladieng-rs6om
    @talladieng-rs6om 2 месяца назад +6

    Yana ko yala takhawou 😢😢😢

  • @fayeemilie3929
    @fayeemilie3929 2 месяца назад +1

    C'est très dangereux à son âge d'accouché. Que le seigneur la protège jusqu'au bout , Amineeeee 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @ndellasarr1779
    @ndellasarr1779 2 месяца назад +3

    Mettina trop pa bi may Mbam rekk 😢😢

  • @Bafatoumatabinta-w1p
    @Bafatoumatabinta-w1p Месяц назад

    Yallah nako yallah same

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 2 месяца назад +1

    Rabiya yallana yalla takhawoula metina loleeeeeee courage la famille wadji mo bone eskey

  • @ousmantunkara9421
    @ousmantunkara9421 2 месяца назад +1

    ما شاء الله جزاكم الله خيرا

  • @sokhnandiayeba5606
    @sokhnandiayeba5606 2 месяца назад

    Yalnalénee yallah feye,yalna yallah arr Rabiya

  • @serignetoubark
    @serignetoubark 2 месяца назад +6

    Allahou Akbar

  • @awatoure5056
    @awatoure5056 2 месяца назад +1

    Bilay lou way Def bopam li metin1❤

  • @ndeyeramagaye4703
    @ndeyeramagaye4703 2 месяца назад +3

    Yalla nako yalla tahawou ba mou guén si Ak diam

  • @ndeyerakydiop8028
    @ndeyerakydiop8028 2 месяца назад +6

    Khawema Loutakhe police Senegal meuna sguané problèmemou diaboure😢

  • @RoseLopez-dc6jx
    @RoseLopez-dc6jx 2 месяца назад +1

    Yallanala yalla laffal thiat

  • @MoustaphaFall-v5f
    @MoustaphaFall-v5f 2 месяца назад

    Macahllah ndanane tv

  • @sokhnandiayeba5606
    @sokhnandiayeba5606 2 месяца назад

    Li métina ndeysane

  • @MbavkeGaye
    @MbavkeGaye 2 месяца назад +1

    Ki sama nekon papam bilakhi thi kasou bi lay de dah ray ndeyam lay def dem polic lan yague yague dan koy bayi khale bi li domasa deng si popam yakheuna adonam sar yi nioy mague di def lo bon dah linlen def

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 2 месяца назад +1

    Ndinrigneyui bounioulen outalon cart sejour million dinaniou tal lenen loudoul kat ay halee 12ans

  • @AWADIOUF-o4m
    @AWADIOUF-o4m 2 месяца назад +2

    Bayil xalè bi ngay wax lo ki xalè la

  • @FatouCisse-jh1cf
    @FatouCisse-jh1cf Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @oulimatadieme9003
    @oulimatadieme9003 2 месяца назад

    Métina trop yalna ko yalla tahawou

  • @FatouThiare-t7e
    @FatouThiare-t7e 2 месяца назад +3

    ❤❤❤❤❤❤

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 2 месяца назад

    Merci a vous

  • @sodadiop3021
    @sodadiop3021 2 месяца назад +2

    Sama khôl bi fess na lol avortement legalisé warna diar assemblée pour cas yi

    • @KhadijaLy-c7j
      @KhadijaLy-c7j 2 месяца назад

      Avortement ma chérie ray nite la dome bimou eumbe sakkou woule pour dioudou

    • @mamependaba7129
      @mamependaba7129 2 месяца назад

      C vraii mais cas de force majeure genre yiiiii do kham sakh quoi faire ​@@KhadijaLy-c7j

    • @MariemeBalde
      @MariemeBalde Месяц назад

      ​@@KhadijaLy-c7jchérie ki Khale la dhe entanoule metite bi vraiment 😢

    • @MariemeBalde
      @MariemeBalde Месяц назад

      ​@@KhadijaLy-c7jbilae meunou ko support si khalé boy daw

  • @MatyTyma-u8z
    @MatyTyma-u8z 2 месяца назад +1

    Papi baxoul si société lakoubar ...

  • @babsgaye128
    @babsgaye128 Месяц назад

    Genre yi dagnioulene wara éliminé si société bi. Amouniou ndiarigne

  • @AissatouWade-z2n
    @AissatouWade-z2n 2 месяца назад

    Kimo bone te yess

  • @NoguayeDiop-q1m
    @NoguayeDiop-q1m 2 месяца назад +2

    Li dafa niaw trop eumbe ak nimou mété ngakoyy tékk khallé bou ndaw ki teuthie lén ko en vie

  • @mbenedieng2298
    @mbenedieng2298 2 месяца назад

    Sama kjole bagui méti dakh yaye la keupeu kou néke yaye sa khole toyena wayé yéne niou ame sago guéne doudone mane bakane teudeuna bou yague meunou comprendre viole 20:13

  • @AbdouNdiaye-g5n
    @AbdouNdiaye-g5n 2 месяца назад +2

    wadji yalla nako juge bi combndamné 20ans avec travaux forcés. té neu parent yi bayi khél goné yissi daara yi, gnissiy def cours à domicile ndakh diamono mo yakhou té kileu gueuneu présentable mola gueuneu bone. neu parent bounek di wakhtane ak sen dom yi def lén xaritt ndakh gnouy wakh lilén méti. les enfants ont des mots à dire.

  • @Galsn
    @Galsn 2 месяца назад

    Manouma agalé vidéo bi bouma kholé khalé bi seug rek nara dioy ndeysane

  • @mamankhadykasse634
    @mamankhadykasse634 2 месяца назад

    li metina trop lii khale bi douko meuseu fate ti adouname kiiii sokh la na kouko dimbali bou bakh

  • @AissatouWade-z2n
    @AissatouWade-z2n 2 месяца назад

    Pa bi dafa febrane kou Melni nokoy diokhe sa dom moukoy diangal

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 2 месяца назад

    Li. Niawna

  • @talladieng-rs6om
    @talladieng-rs6om 2 месяца назад +2

    Yana len yala faey

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 2 месяца назад

    Khawma. Ostas la. Khawma loumou donne

  • @AboulBacharSall
    @AboulBacharSall 2 месяца назад

    Bayilen xale bi nguein di business demlen si yone ta deig lou yonne

  • @oumoumbacke3712
    @oumoumbacke3712 2 месяца назад +3

    Mais l'état devrait accorder son avortement

    • @MariemeBalde
      @MariemeBalde Месяц назад

      Mane dhe loulou la guissone vraiment dakh ki Khaled franchement entanoule lolou😢

    • @msy8317
      @msy8317 Месяц назад

      Soubhanallah

    • @mariamadione8533
      @mariamadione8533 Месяц назад

      Ki bagnouy kham ni dafa eumb fek sori na, donc c’était trop tard .
      Nagn ko nianal yalla rek mou mouthiou si diam ak salam 🙏

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 2 месяца назад +1

    Ki. Kou. Bonne. La

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 2 месяца назад +2

    Yalanako borom bi tahawou inshaalla ...mes wadji kou dohane ndéyam la vraiment bo soné ba meunoko mougne démal faye gua soulagé sa bopou mo guene diape khalé bou ame 10ans gua défko dieuf bou nianwe biii .bilahi boko défone sama rak walahi police wala gendarmerie bala niouye diote si yaw dina fék ma déf la néw bou yague domérame djii djiéhal na sama khol bi way

    • @miafa5544
      @miafa5544 2 месяца назад +1

      Massa frère

  • @babacarthioune6972
    @babacarthioune6972 2 месяца назад

    Lidoyna war

  • @ndeyesow4480
    @ndeyesow4480 2 месяца назад +1

    C’est arrive a ma niece main ces parents ont arranges

  • @taphasow9075
    @taphasow9075 2 месяца назад

    Ki mom dagane neuf ray

  • @oumoumbacke3712
    @oumoumbacke3712 2 месяца назад

    Elle est trop jeune pour ça

  • @FatimandaoTymandao-gr4gl
    @FatimandaoTymandao-gr4gl 2 месяца назад +3

    Borom site bi tamite doynawar, yaw yayou khalébi neneu 13 ans leu am, nga beug coûte que coûte ni 10 ans leu khalé bi am. Kou bayiwoul seu dom mom do bayi kenene, na dé si kasso bi car pervers sexuel

    • @ndeyediop335
      @ndeyediop335 2 месяца назад

      10ans télna si jiguéne pour mou guiss bakh

    • @MatyTyma-u8z
      @MatyTyma-u8z 2 месяца назад +1

      1ere vidéo yayam mo waxone 10ans la am ...

    • @MatyTyma-u8z
      @MatyTyma-u8z 2 месяца назад

      ​@@ndeyediop335guisna kou am 9 ans affaires yi dou fofou d

    • @ndeyediop335
      @ndeyediop335 2 месяца назад

      @@MatyTyma-u8z daffa diakhlé wonne

    • @awakane1050
      @awakane1050 2 месяца назад

      10 ans kayy manoul eumb 12 ans laa dieugeune Di guisé bakh