Daray Kocc combien de films ont ils fait ? Avec Maack, j'en decouvre énormément. Cheikh Tidiane Diop qu'ALLAH lui Fasse Misecorde est un génie du cinéma. Il était vraiment inspiré
Wa ana saynabou guissatouma ko féne wa daraay kocc rek ñoy samay acteurs dama Léna beug ndassan té yalla takh adouna du dara suma guisé kou bok si ñom damakoy beug si sama khol bilahi, yallana lén defal mbëgtém aduna alakhira❤️❤️❤️❤️❤️🙏
Cheikh tidiane Diop est un excellent scénariste et dévoile tous les problèmes de la société Sénégalaise ce chef d'oeuvre est toujours dans la société Sénégalaise tous ces films ont marqué les sénégalais
"Ya'ALLÂH neen a Soxna yi bu ñu leen tooñee bàcc bàccal leen bubax", dit Mandione. Eskëy 😂 c'est pas drôle, du tout, mais nit ñi nu leen neex la ñuy interpréter waaxi YA'ALLÂH. Door yu metti yi xam ngeen ni BOROOM BI SWT waxu ko. Nit déy nitee nak. Seynabu j' espère que daw nga ca ba ngay ami tànk
Merci Mack tv theatre daaray kocc rek la beugué bi nekhna lol AK Serigne guiediaway beugué Nako lol yalla nalen yalla yok bubakh s makhrouf mbacke la toudu
Khartou Angoulêe si dougo sanégou soxnaye karité karité Daye âme fpumoye eme Andak sa soxnaye karité si loudoule ndigalame meuneu yakh digueneté boule teudiok mome boule weutek mome si loudoule ndigale Dieulena kouma fogone ni sama karité la mousante Niang té diolone deuk kaolack ma indigo mboure da moulin di sakou sama soxna baparé mou sathieu ma
Daray Kocc combien de films ont ils fait ? Avec Maack, j'en decouvre énormément. Cheikh Tidiane Diop qu'ALLAH lui Fasse Misecorde est un génie du cinéma. Il était vraiment inspiré
C la question Que je me pose aussi
Plus de 50
Je me demande la même chose car j’en découvre beaucoup grâce à cette chaîne
Tu as écrit typiquement ce que je pensais 😂
Soudone diamono dji mooy evenprod ci kharalei machallah
Wa ana saynabou guissatouma ko féne wa daraay kocc rek ñoy samay acteurs dama Léna beug ndassan té yalla takh adouna du dara suma guisé kou bok si ñom damakoy beug si sama khol bilahi, yallana lén defal mbëgtém aduna alakhira❤️❤️❤️❤️❤️🙏
Moi aussi c’était ma actrice préférée
Cheikh tidiane Diop est un excellent scénariste et dévoile tous les problèmes de la société Sénégalaise ce chef d'oeuvre est toujours dans la société Sénégalaise tous ces films ont marqué les sénégalais
Daaraye kocc Sén théâtre yépa Am Change❤ Merci Cheikh Tidiane Diop
Cheikh tidiane Diop un pédagogue et aussi un éducateur
Balama deé rek nionan ay sokhna batorak yoma xamol Li Moy Théâtre ❤
Génération légui moy génération perdue ba paré beugeu détruit souniou diabote
SALAAM ! Merci !
Nous demandons le théâtre wadiour avec Bathie et Ndèye Mour
Bilay❤
Ay way Mac tv goudal fane machalah
Daray kocc joué naniou lep non ils étaient incroyablement fort ❤
Dieul père Zora ak loss bi 😂😂😂
Dieukeur bouy geinei paka doumafa tok yala teireii
Un jour mourayla té doko yeugu
Aimer la vidéo svp pour plus de visibilité les amies
Machala li moy théâtres
Ohhhb merci waye souvenir d’enfance 😢❤
Merci encore mackk tv . Un bel chef d’œuvre de cheikh Tidiane diop jikko ak borom pakh
Merci maack tv c’est grâce à vous si on découvre tous ces chefs d’œuvres 😊
Seynabou ressemble à Lissa de un café avec
Daraye kocc jouer na li yép machallah
Li dama ka weur ba sonou. Souvenirs
Théâtre thiaate clando bou thies laay weeur rts mokoo teguone temps boys merci de nous les offrir stp
Ndeysanne 😭 Daraay Kocc.
Ani lamb Ji ak boubou Faye et ibou Laye
Mogui si RUclips
seynabou risque sa vie pour ses enfants , yaye dale amoul morome
Ndaysan saynabou lu am solo la wakh ak papam vraiment yalla na leen yalla faye
Diack est un bon ami
Makkk yalla nasaaa diammm yague ❤
"Ya'ALLÂH neen a Soxna yi bu ñu leen tooñee bàcc bàccal leen bubax", dit Mandione. Eskëy 😂 c'est pas drôle, du tout, mais nit ñi nu leen neex la ñuy interpréter waaxi YA'ALLÂH. Door yu metti yi xam ngeen ni BOROOM BI SWT waxu ko. Nit déy nitee nak. Seynabu j' espère que daw nga ca ba ngay ami tànk
Déjà comment tu peux resté en serviette devant un homme qui n'est pas ton mari.. yëffi dofff
Thieatre niome niossi took
Daray kooc le meilleur de tous les temps
Wa ani seynabou mi el est ou legui
Merci bcp maack tv ❤❤❤
Bilaye MTV bokothi merci encore ❤❤❤
Theatre waydiou de ndeye mour laniou beugue
Je crois ya un remake avec Mansour et aida Camara en passant merci beaucoup macktvsouvenirs yangui niouy begeul❤
❤❤Merci beaucoup.
S'il vous plaît le théâtre "Perte de vue" de seynabou Niang
Ndeye Mour day saane dafa meusseu mane théâtre
Merci Mack tv theatre daaray kocc rek la beugué bi nekhna lol AK Serigne guiediaway beugué Nako lol yalla nalen yalla yok bubakh s makhrouf mbacke la toudu
Avant serigne guediawaye même il y'a serigne keem taan. On attend avec impatience.
Ah la fin seynabou limou def kéne douko def noyy amé gaann rawatina goor té solo yeuré ngay woddo serviette
Dama ragalonn tayatre biii bilahi walahi tafa tayatr bi Motahh niame wouko wonn😢😢
Machalla 😊❤
Abssa ak bocar la beugue 😢🎉
Ak wadiour bou ndeye mbour
Waa daray kocc gnoo meune
Digua goudou fann deh mtv
Oh Merci beaucoup Maack Tv
Ndaysane bly théâtre warnaléna fay 😘
Diack yalla daafa diéxaal seuy bi mounii détt neksii rek sunu brom natooko lii déraam dotul sétt ba biis péççi ak sokhna si
Merci theatre bi warnako fone merci theatre mame ndiaye ak adji magguett rts dan nan ko tek anamo
C'est seyane le nom du théâtre
Xarit bou melné diack diafé na
Bonjour mak TV vous êtes vraiment fort maintenant svp le théâtre la femme infidèle de daaray kocc
Père soura fi d’à sewoon te regler
Machlla ❤❤ nekh na lol
J’adore j’adhère
Merci bcp yala nala yala fay
G jamais regardé ce téléfilm merci pour la découverte
Lambi golo de ibou laye svp
Mogui si youtube
Vréma merci beaucoup ❤❤❤
Merci beaucoup Maak TV❤❤❤❤❤
Merci pour cette vidéo
Comment faire pour avoir la vidéo avec les musiques originales
El hadj Faye RUclips
@@leboundoye1403 il y en a un autre différent de celle de elhadj ndiaye
Daaray kooc le ❤
Merci MTV ❤
Salam koula beukh diot
Oh Moustapha warol wona fayé li Mamadou diak sepa vere
Yaw daal jàmbaar Nga
Théâtre boo wax ne am Nga ko gëm naa ko
Nabou dash la fi djiss
❤❤❤❤❤
Kendall svp
On réclame cheikh may sa yaye
Weur na ko ba sonou cheikh May sa yaye
Louy lolou Kokou joué
Man de teyatar Ciekhe may SA yaye Lay War bobu mom yakar na ken amatouko
Merci d'y ajouter l'annee s'il vous plaît.
Feux Aminata Dieng, Djibril Samb, Aida CAMARA,
Yakhara deme dafa décédé quand
@@Souvi922 loumasi xamone
Seynabou mbaye ami dieng appollo djiby samb yakhara déme aida camara ils sont tous décédé
@@thiernobah1308 yalnalen Yalla yeureum té kharelen Al'janay Firdawsi
@@thiernobah1308koussiy Seynabou mbaye
Ohhh merciiiiiii ❤️❤️❤️❤️
Li bane Anne lawoon
Mack tv je cherche le titre d’une chanson dans ce téléfilm
Lahoubour
Merci de me donner le titre
C’est Natou de Mapenda Seck.
@ merci
Merci maack tv
Nekhna lol , stp bo amé théâtre thiané alla bou khonk bi Da am borom ❤
Billaye surtout bobou j lé cherché partout
Tapha 😂😂😂
❤❤❤❤
Khartou Angoulêe si dougo sanégou soxnaye karité karité Daye âme fpumoye eme Andak sa soxnaye karité si loudoule ndigalame meuneu yakh digueneté boule teudiok mome boule weutek mome si loudoule ndigale Dieulena kouma fogone ni sama karité la mousante Niang té diolone deuk kaolack ma indigo mboure da moulin di sakou sama soxna baparé mou sathieu ma
Lamine ndiaye bimou takké gnarél té awo bi ’’seynabou’’ doff svp
Xarit la théâtre bi toude
Titre rom svp
Une fin bien triste.....
Svp li c'était en quel année ?
Kou kham ban année la?
Ⓜ📧®©❗nostalgie
😘🥰🥰🤲🤲🤲🤲❣️🙏
Je vois que diewo dafa tella beugue solou mak
😢😢😢😢❤❤❤
Carnet car svp
2
Maac TV ces qui tonton mac ou bien?
Mais où est Seynabou
Vous avez remarqué qu’il monte pas les scores de violences
Theatre carnet Ka stp
Migi youtube
La partie 02 svp je n'arrive pas à la retrouver
Année svp
1994
1990
Seynabou a été trop bête je trouve
50:00 la Honte 😂😂😂
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤