Acteurous legui yi humm faites gaffe à vos prestations deh ! Guisnguen théâtre bi c'était il y a plus de 20 ans, koufi defoone lou niaaw tay gathié topou la donc bayilen xel bou baakh sen jeux yi. Merci MTV pour ces beaux souvenirs 🙏🏾🥰🥰
Man DH j'avais 3ans ndaye saan dara yagol li motakh nioy wakh nan nitt lomou deff Moy lobakh wala Lou bonn AK lomou yage yage Say doom Dinan si diott Moy lobakh wala lanén❤❤❤❤❤❤❤❤
Maack tv est do fi bayi seu numéro niou wave la 😂😂😂 Temps yi li ngay seddal sunu khol yi nioune ancienne gloire yi yalna la ko yallah fey Théâtre bi weur nako partout Goudal fane wayy
La femme blanche nimouy waxé comme Aissatou de cœur brisé. Mais abeu kate bi ray nama 0 vergogne et ça existe réellement des gens comme ça. Les truands comme alpha ça existe toujours 😂 ça fait plaisir de regarder ce série je fais partie de la génération 2000 j'aime les anciens théâtres .
J'étais en classe de CP 😂 et j'avais droit à la télé que le mardi soir pour regarder un téléfilm, le mercredi après midi (la télé est à nous), et le dimanche (jotayou xale yi). C'était la première fois de ma vie que j'entends le mot "témbéré" 🤣
wa 1:15 cassou nickel yi khamé nguen ko. Kousi amoul wone temps yoyou amo dara 😅. Mais theâtre nekhatoul way. Mane Alpha momay ray si theâtre bi. La femme de Cheikh aussi day thiabakhal you nekh. Elle me fait rire. Merci MaackTV. Dieureudieufeuti.
Alpha ,un sacré artiste , a l'Etat civile s'est Mathieu Coly ,il est natif de Bignona ,il a travaillé au Port et au dernier nouvel il etait convoyeur de Bus dans une ecole privée en ville, malheureusement en parcourant le net certains disent qu'il est décédé ,c'est vrai que je l'ai perdu de vue depuis longtemps..Si quelqu'un a ses nouvelles ou confirmer l'infos
Ndékété mi ngi wone thi sama subconscient bi di nélaw au fure et à mesure may sétan mouy ñeuw ndank ndank thi sama xel mi ooooh boba bb la wone ndeysane thiey aduna
Rama/katy❤❤ Je l’adorais trop cette fille 😍😍 Je m’habillais comme elle et au lycée j’avais formé une groupe avec mes potes et ont était les stars du lycée 😂😂
Merci maack bi meussoumako setane khama déguster ko khol Sinon maak inddil suite yénene théâtre svp dell inddi suite yi bouko défeé nioune meuneu ko yegalii Vraiment maak kouko diokh Réwmi mashallaah mou dirigé ko diam si yaw 😊
Genrou Alpha yi aka gno bari si town bi 😅louga la djouguè am kouma fi donn sett fekou mako fi. May ma louma agné... Louné ngay degg.. Ligguey moko gueuneu yomb
Merci Maack pour tout l’effort que tu fais pour nous 🙏 Mais j’aimerais souligner le problème de sons que tu modifies pour cause de droits d’auteurs… On en est conscient vraiment mais ne pourrions-nous pas réfléchir à un moyen d’avoir les sons initials sans devoir à les modifier ? Faut-il contacter RTS ou autres structures ? Moi personnellement je suis prête à participer financièrement rien que pour doundate les théâtres surtout daaray kocc comme à l’époque… Car avec les sons que tu modifies, dougnou sahe sentir réellement les théâtres comme à l’époque, on regarde juste pour regarder, tu sautes même des scènes car sans doute, y’a le son initial quand les personnages parlent dans ses scènes, et c’est vraiment relou, ça nous frustre à un point que tu ne peux imaginer… Je m’excuse d’avance en tout cas, je voulais juste donner mon point de vue et te dire le ressenti de pas mal d’abonnés.
Qui est là en 2024? Ndeysane théâtre deugue gui ni. Macha allah 0 nudité, 0 vulgarité. Lépe si respect la , kadou yi débordé woul.
2001/2024 qui est toujours là ,que de beaux souvenirs Ramakaty
Ak mane 2024 wa tik tok
Moma magué 1ans😂❤❤❤
@@BigueDieng-v8qnio masse kone 😂
Mane magui ni
Man d tik tok lako khamé
Acteurous legui yi humm faites gaffe à vos prestations deh ! Guisnguen théâtre bi c'était il y a plus de 20 ans, koufi defoone lou niaaw tay gathié topou la donc bayilen xel bou baakh sen jeux yi.
Merci MTV pour ces beaux souvenirs 🙏🏾🥰🥰
Wa yéne agni sahe légui thiéy adouna théâtre bou néeh humour et éducation
Les anciens théâtres sénégalais me donne l'espoir maack tv doundou lhèn théâtre bi loumako weur lhep diam si yën ♥️
Ndeyssane 2001 la wone temps boy 😢cet époque me manque trop
Ndayssane j'avais 13ans quand j'ai regardé ce film pour la 1ère fois et j'avais kiffé graveeeeee 😊 mais légui mére la! les années passent vite 😢
Ah bon ta quel âge legui
😂 welcome to the club
nio yam
Lol soudé 36 ans mom dou dara atte yi gno gaaw rek
J'étais en classe de CE1😂
Mais gni sene khetou français ❤ tellement agréable à entendre ❤❤ bilay théâtre amotoul
Français bu jeeg bila
Cilabaire la 😂😂😂😂toto tape patè
😁😁@@MamyDiallo-rr7oj
Théâtre amatoul
Ndeysane diamono bi mangui ecole primaire j'avais 11 ans maintenant j'ai 35 ans alhamdoulilah
Moi aussi ndeysane dara yagoul si aduna
Man dh j'avais 8 ans
@@fatoumboup5235 ah kon yama gueunona touti
Machahalla yalla na yalla khébb doly
Man DH j'avais 3ans ndaye saan dara yagol li motakh nioy wakh nan nitt lomou deff Moy lobakh wala Lou bonn AK lomou yage yage Say doom Dinan si diott Moy lobakh wala lanén❤❤❤❤❤❤❤❤
Maack tv est do fi bayi seu numéro niou wave la 😂😂😂
Temps yi li ngay seddal sunu khol yi nioune ancienne gloire yi yalna la ko yallah fey
Théâtre bi weur nako partout
Goudal fane wayy
😂😂😂😅😅😅no iow ray ngama😊😊😊wave cay wakh nga deug deh
Tasse yi Rama done serviré à stlouis on l'appelait Timbal❤ chapeau à grd Pape Faye aussi❤❤❤❤
ndeysan ndol yag na Sénégal. Dem keur voisin di nian niari kilos thiep amona fi.
La femme blanche nimouy waxé comme Aissatou de cœur brisé. Mais abeu kate bi ray nama 0 vergogne et ça existe réellement des gens comme ça. Les truands comme alpha ça existe toujours 😂 ça fait plaisir de regarder ce série je fais partie de la génération 2000 j'aime les anciens théâtres .
Je te jure. Sénégal yagueu neu am niou niakke diom.
J'étais en classe de CP 😂 et j'avais droit à la télé que le mardi soir pour regarder un téléfilm, le mercredi après midi (la télé est à nous), et le dimanche (jotayou xale yi). C'était la première fois de ma vie que j'entends le mot "témbéré" 🤣
Machallah
😂😂😂😂😂 et juste une rts
@@MamyDiallo-rr7oj voilà on avait pas le choix 🤣
Déléne aimer la vidéo pour lui donner de la force je vois que y’a beaucoup de vues machalla mais pas beaucoup de j’aime 🥰 ❤
Théâtre bii la weur comme kouy weur sama mbokk😅, merci bcp Maack
bilahi dou yaw késsé dé😂😂😂man mom dama melni rk kouy weur natou diambour bouma réreul😂😂
@@FatouMbaye-rh3xh😂😂😂😂 massa
Ayway diapalemassi si wadiour bou ndeye mour
Alkhamdoulilah j'ai retrouvé mon télé film préféré merci bcp a la chaîne kénn dou yénn !!
Mais désna wadiour de ndeye mour nakk 😊
Bilaye fonk say wadiour
Aywayyy c est la 2ème fois que je regarde ce théâtre douma si doyal😂😂😂😂
Merci beaucoup que de beaux souvenirs. Wayé "Quel douleur" de wa djankheen avec serigne Gagne tamit soko amé
Ancienne gloire nga deh
MTV merci j'ai les larmes aux yeux dama ko weur bah soneu
Diamono Nekhone na nak . Ça nous manque vraiment ce temps là et ces rétro
À une certaine époque dans chaque foyer senegalais,il y’avait un Alpha qui aimait squatter mais tellement sympathique 😂 !
Belle époque, ça me manque 😢
Théatre bi deh khalei bou touti la wone mais ça fait plaisir di setane theatre you yagu yi dagno original ta nekh❤
Khana man ngay wakhal
@@binetasarr8857 wa guis ngeu deh qye de bons souvenirs 🥰
Noon rééna ba sonou ramakaty et ses amies sont trop drôles 😂😂😂
La femme du professeur vreuaiment 🤣🤣🤣🤣
Ndeysanne quand j’étais petite dama nobone professeur Sow j’étais toute petite.
De même que moi
L’actrice foumou rer elle était tellement belle oh❤
Karitam mo nek lègui mère bi jouer thi Salma thiey aduna ❤
J’ai crié Wooy Rama Katy tellement je l’ai cherché ba sone 😂😂
Même mane limako weurr youtube❤merci mack
Moi aussi 🤣🤣🤣🤣🤣
@@famaba280 p
Weur na ko ba sonnou merci
Moi aussi 🤣
Yalna la Yalla fayyy. De beaux souvenirs de jeunesse. 😀 On s'éclate sur ta chaîne ma shaa Allah 🙏🏼
merci beaucoup que Dieu te donne satisfaction comme tu l'as fait en nous postant ce merveilleux théâtre
Théâtre bou nekh way😊😊 elle est tr belle Ramatoulaye Masha Allah
Bilay wakhatiko naturelle machalla
Bonjour elle est dans quelle fim
Image yi rk la fatalikou wone fate tour bi founekk weur na kofa merci beaucoup wayyy😂😂😂❤❤❤❤❤❤ toubab bii moy aissatou cœur brisé 😂
Bilahi mome la may wakh mounane diala gati😂😂😂😂
Enfin rama katy damaco khar ba sonou
Waw Kombé legui mère la, les années passent tellement vite.
Merci MAACKTV svp purux partie 2 diokh niouko ❤❤❤
Sourtou biii
J’ai bocoup chercher ce théâtre bilay ❤
Kombé moyy yayou abdou Rachid dans Salma 🥰🥰
Si si 😅
Machallah je me demandais c'était qui ?
Rama Katy était obsédée par le professeur ❤😂c'est de l'obsession ça mouyenn 😂
Oh my GOD Maack tv merci beaucoup tu mérites des millions d’abonnés Yalla nala Yalla Fay lep lo beugue Yalla nalako Yalla defal
😂Tu as parlé pour nous tous qui avons tant cherché cette pièce en vain. Merci infiniment à Maack Tv
Ndayesane
Namna senegal trop nat bly ❤😢❤❤
Merci infiniment Maack TV . Kene amoul sa Faye 😊
La fin, lii mom amatoul😂
Di tourné nit gni weur leu mélni théâtre école 😂
Alpha sow montre que Door yaguena senegal 😂😂😂
Je confirme 😂
😂
Ndeysann ça me rappelle beaucoup de souvenirs
Pape faye est trop èloquent ❤❤❤
Mane absa ak bocar lay weur founé
Macha allah lima gueuneu nékh si theatre bi moy acteurs dagnou yiw solgui mais théatre légui dara bakhousi
Bilay wakhatiko legui kagne théâtre Amatoul khana diayou Ak wonei forme Ak Weine mane d théâtre bii moma mak mes j'ai trop kifee
wa 1:15 cassou nickel yi khamé nguen ko. Kousi amoul wone temps yoyou amo dara 😅. Mais theâtre nekhatoul way. Mane Alpha momay ray si theâtre bi. La femme de Cheikh aussi day thiabakhal you nekh. Elle me fait rire. Merci MaackTV. Dieureudieufeuti.
Ohhh machalla lou nekh mé svp théâtre lamarana Diallo AK seune bi bimouy wakh domou patron député diabarou patron député svp diapalémasi et merci
Mom rk lay weur
Diègou yoor yoor
Weur na ko ba sone ya lama , seune sene , diaynaba diallo
@@souadoudaffe5757 chiekhe Doumbia aida camara
Dogal nakou dh
Alpha ,un sacré artiste , a l'Etat civile s'est Mathieu Coly ,il est natif de Bignona ,il a travaillé au Port et au dernier nouvel il etait convoyeur de Bus dans une ecole privée en ville, malheureusement en parcourant le net certains disent qu'il est décédé ,c'est vrai que je l'ai perdu de vue depuis longtemps..Si quelqu'un a ses nouvelles ou confirmer l'infos
Oooooh ndeysanne que de bons souvenirs ❤
Nekhul ba nekhul mé alpha niank na diom😂 merci à maack tv❤
Bon boulo, Waydiour Ndeye mour rek mo déss
😂😂😂😂
Ki dou bridge bou facebook 😅
@@adjasokhnafall9887 😀
Bobou dogouna yagg na
Wadiour ndeye mour ak bathie
Hibrahima mbaye sopé ❤ j l'aime depuis mon enfance long vi a toi
A oui je l'ai tant cherché un beau film
Ndékété mi ngi wone thi sama subconscient bi di nélaw au fure et à mesure may sétan mouy ñeuw ndank ndank thi sama xel mi ooooh boba bb la wone ndeysane thiey aduna
Vraiment maack TV amoulo morom dama contane si retro yinguay def❤❤❤
Ooooooooh ay theatre bi mako beugonn ndeyssaaaane Ramakaty tiey adouna😢theatre amstul
Quel souvenir !!!Merci pour la vidéo
Rama/katy❤❤
Je l’adorais trop cette fille 😍😍
Je m’habillais comme elle et au lycée j’avais formé une groupe avec mes potes et ont était les stars du lycée 😂😂
Ndeysane
Rama Katy es ma grande sœur
Un grand grand merci beaucoup ❤❤❤
Thiey a l epoque wayou Pape et Cheikh bi modone terminel theatre you dramatiques yepp, te sakh théâtres you dramatiques yi nio berione
Merci beaucoup Maack TV théâtre bou nekh
Mais li nekhna dé dommage j'étais pas né mais je le regarde 2024
Merci maack bi meussoumako setane khama déguster ko khol
Sinon maak inddil suite yénene théâtre svp dell inddi suite yi bouko défeé nioune meuneu ko yegalii
Vraiment maak kouko diokh Réwmi mashallaah mou dirigé ko diam si yaw 😊
Stp wadiour de ndeye mour
Merci pour la série ❤
Temps yi la théâtre 🎭 neikhonn
Bi théâtre grand yi la génération 2000 dém léne tok
@@Liweiyang43 kone est-ce que bi magou la
Genrou Alpha yi aka gno bari si town bi 😅louga la djouguè am kouma fi donn sett fekou mako fi. May ma louma agné... Louné ngay degg.. Ligguey moko gueuneu yomb
Wouyyyyyyy dolene nitttt !!!! J'ai crieeeee 😍😍😍😍😍😍merciiiiiii
Mr Sow,daouda de d'échéance 😂
Kou khamé papay boris serie karma
Ak yayou Virginie serie karma
Ak yayou rachid serie salma
Ak soppé
Est c k yayou pod migui si?
Tata raissa idol
@@astoukane7003 nonon dama dioum dama ko diawalé
@@astoukane7003 sisi monek tamit yayou Virginie serie karma
@@fatoubintoudjitte5978non c'est pas elle deh danio nouro rék
Ohh merci beaucoup théâtre bou nekh wayy
Oooooh eyway ndeyssane tiey adouna aka mako beugoonn ndeyssane lii moy théâtre
Eyway goudeul fane waye ❤️🙏🏾
Sama khól bi diekhna 😢😢😢 bilahi diamono nekhatoul légui théatre yi dafa done nekh
Pourtant mba legui mogui nekh dé temps bi mo changer rek
@@maimounandiaye-le1tu yaw khana anné 2000 nga 😂 sénégal bou ndieuk légui woutena
@@kheuchakhloubadar7822yakar nko dè😂😂😂
@@morhann1619 mdr
Théâtre amatoul vrai souvenir
Faut nous mettre aussi le théâtre "la fin du monde"quelque chose comme ça dafa yague nak jne men souviens plu6q très bien j'étais tte petite lol
Oh de beaux souvenirs ☺️🤩
Mack indil niou théâtre ndiakaré partir 3 bi
Merci Maack pour tout l’effort que tu fais pour nous 🙏
Mais j’aimerais souligner le problème de sons que tu modifies pour cause de droits d’auteurs…
On en est conscient vraiment mais ne pourrions-nous pas réfléchir à un moyen d’avoir les sons initials sans devoir à les modifier ? Faut-il contacter RTS ou autres structures ? Moi personnellement je suis prête à participer financièrement rien que pour doundate les théâtres surtout daaray kocc comme à l’époque…
Car avec les sons que tu modifies, dougnou sahe sentir réellement les théâtres comme à l’époque, on regarde juste pour regarder, tu sautes même des scènes car sans doute, y’a le son initial quand les personnages parlent dans ses scènes, et c’est vraiment relou, ça nous frustre à un point que tu ne peux imaginer…
Je m’excuse d’avance en tout cas, je voulais juste donner mon point de vue et te dire le ressenti de pas mal d’abonnés.
Suis d’accord avec toi ❤
Voilà ma pensée bien résumée
Merci chère abonnée
Tu as tout dis
Merci vraiment tu as raison c'est un peu aguassant
Ohhhh non c pas vrai 😢😢je l’ai tellement cherché Maack goudeul fane wayy dama dioyy dal bima guisser Li 😢😢😢
Ndiaguam senghor mala 😅 warone nako féké😂😊🥰
😂😂😂😂😂 wa ehhhh ramakaty mogui ni ndaysane j'avais 11ans mais combé dafa yague bandit😂😂😂
J'aime bien les anciens théâtre ❤❤❤❤
Weur naa ko ba sonou. Enfin le voilà
Wahou que de bons souvenirs mashallah Aida Souka❤ d la beugg setane g jamais regardé
Déléne aimé vidéos yi. 4mil vues, 100 👍
Y'a que des souvenirs alpha sama Béne kharit la ko toudé woone 😂😂
J'ai des frisson. Merci maack tv
Mack tv Stp Indil niou Théâtre Ndiakharè 3 partie Absa Té mou am dôme kalidou Stp
Mane tamit nonou lako beugué weur Nako ba sonou
PIKINI PRODUCTION xana fii lagn inspiré woo Katy dé Moy penda wouruus .
Beau souvenir merci
Ki est d'accord la femme du professeur parle bien français
23 ans et toujours d actualités âme gnou décédé âme na gnou gère seni famille imagine bougnou téléfilm yi legui
qui sont décédés?
Pour les générations 2000 le professeur Sow anglais a joué le role de Bachir Hannan le père d'Ami Léa dans Karma. Merci bion 😂.
Merci ma ngui nane ki dama ko khammé hawma fan😢?
Je me disais bien que c’etait lui il a bien veilli deh
Nga ni ma😂❤
Sérieux?
Souvenir bou nekh way
Ce seulement les générations 2000 gnogni sonal Ak ki nirona Ak ki neuk Karma, graines de pouvoir, Babel….