Ndeysane! Mère sa niane nangou na. Aujourd’hui, 19, Novembre 2024. Votre fils si bien aimer, est l’homme le plus influent du Sénégal. Il a élu des maires, des députés et un président de la République. Manchallah
Ndeysane la maman nationale sénégalaise Mame Khady Ngom mère de Ousmane Sonko premier ministre de la république du Sénégal 🇸🇳 A chaque fois dans ses interviews, elle a les mêmes paroles tout ce qui arrive c'est Dieu, waaw telle mère tel fils...❤
MA SŒUR MAMAN SONKO, QUE TOUT MESICORDIEUX VOUS PROTÈGE ET VOUS GARDE POUR TOUJOURS À CÔTÉ DE VOS FAMILLE ET DE PEUPLE SÉNÉGALAIS👏🙏🇸🇳🌍 NÔTRE PHENOMÉNE SONKO DAY BOOK, À LA ÉLECTION PRÉSIDENTIELLE 2024 INCHALLA👏🙏🇸🇳🌍 SONKO SONKO SONKO NAMONALA, À LA ÉLECTION PRÉSIDENTIELLE 2024 INCHALLA👏🙏🇸🇳🌍
MY LETTER TO A WONDERFUL MOM La main qui berce le berceau fait également de la maison une maison. Ce sont les prières de Mme Sonko née Mame Khady Ngom, la mère de notre leader, Président Ousmane Sonko. Cela maintient la famille forte. Elle se lève tôt le matin et baigne sa journée dans la prière. Elle parle à Allah de sa famille et les place sous sa garde. Elle communique son amour de mille manières différentes. Quand il y a un besoin, elle est là, que ce soit la nuit ou le jour. Mme Sonko saisit la vie avec amour et donne tellement d'elle-même. Allah a placé en elle le meilleur qu'il avait et l'a rendue différente de personne d'autre. Quand les défis viennent à notre rencontre et quand les épreuves bloquent notre vue, Elle s'agenouille à côté de son lit et prie la famille à travers. Comme son fils, le Président Ousmane Sonko, Mme Mame Khady Ngom est la création spéciale d'Allah. Elle est une lumière qui brille dans le noir, éclaire le chemin de sa famille et les pointant vers Allah. WE LOVE YOU MOM! Dr. Elhadji Demba Ndiaye Pastef Colorado-USA
Kii mooye yaayou imaamou sweet beauty et prési-data des masseuses et des homosexuels comme branco 😮😮😮😮😮😮 yaroo koudoul boroome nél bou dakhaare ndayame biii,,,,ak taatame you réw
Waax dji sunu yaye dji waax amneu solo lol. Mou bagne ko décevoir mom ak wa rewmi. YaAllah nako sunu Borom dénk rewmi su fékké mo geun ci rewmi,mu bania tass yakarou kéneu ba kou nèkk diot seuy akk ay yèléff ak foo meunti nèkk té sunu Borom yombalko yorine bi. Askanou Sénégal soonou naniou lol motaax kou ame yermandé lagne sokhleu. Qu'Allah protège et bénisse le Sénégal! Amiine
Merci laa dégue ,,kone kii moo yare imaamou sweet beauty bii di sonko nga khamené ba macky sall ak amadou ba doone amal Sénégal émergent booba sonko ma nga sweet beauty di mare taatou yaayou waa ex pastééf bii di adji sarr thi yooryoorou tabasky ak goudik couvre feu 😮😮😮😮😮😮😮ak sééne nél you dakhaar ndayame yi,,merci beaucoup modou lô
Machallah alhamndoulilahi dieureudieuf sounou maman deug bou wer nga wakh si sounou president du partie pastef premier ministre ousmane sonko projet bi ligueye rek jub jubal jubanti rek man s.diop beugue fallou bou pastef touba italie mangui lay beugue 'wathio nak askan wi di Senegal si deugou am dignite am gor djiambar deug là ndam rek inchallah dieureudieuf
❤❤❤ Une maman est la sécurité de chaque individu, et si un jour je trouvais la chance de vivre avec ma mère, même 30mn,
Yallah defna li guen si gnoune même moi je ne connaît pas ma mère nagn len nianal reck
Notre maman nationale ! Vive le PM Sonko ! 🇸🇳✌🏾💪🏾❤️
Mère Yalna Yalla sàmm laa té sàmm Ousmane SONKO !
Amine
Amine
Amin
Elle est assez jeune..Macha Allah !Que Dieu la garde en bonne sante Et lui donne une longue vie pour accompagner notre Heros National
Cette vidéo a 5 ans maintenant elle vieillie petit petit ndeysaan yalna yalla yokk ko werr rrk❤
😭😭😭😭😭😭. Vraiment tu as un waliou Yallah ! Merci maman de nous avoir mis au monde ce gentleman
Telle mère tel fils ! Machala diadieuf waaay Mame booy guem yàlla dal amna 😘😘😘🥰
Ndeyssane dioulité ak gueum gueum bi nekk ci Sonko yeup ndékè ci yaye dji lako dieulé machallah
Nioune Sénégalais 🇸🇳yep nionguilay Sante🙏🏻😍yayi le sauveur
Une maman de cœur que dieu vous garde avec ton fils
Ki-moon yare imaamou sweet beauty
Machallah kouy djiguen niane nga am dôme bou melni ousmane sonko
Sa c notre mère à tt la jeunesse sénégalais ma'challah
waw nous sommes les bakh yaye.
Wallahi notre mère
Goudou fann ak weer maman,et merci pour les valeures que vous avez inculquee a notre sonko nationale
Kii mooye yaayou prési-data des masseuses et des homosexuels comme branco
Sounou Maman goudou fane ak wér si barké seydina Mouhamed(psl),👌🏾
MACHALLA
UNE MAMAN PURE, LE TOUT PUISSANT NE SE TROMPE JAMAIS.
Longue vie maman que Dieu sauvegarde notre Ousmane SONKO.
Wallahi ndeysane Mbôôk yii ! C'est une grande dame très noble.. Yâye Bôye, Yallah Ngâ fî Yâgueu Lôôll tha Wêêrr Allahoumma Âmîne
Kii moo yare le prési-data des masseuses et des homosexuels comme branco
Maman Diatou Ngom machallah Longue vie pleine de succes de sante ci barke Rassoulilahi aleyhi wa salaam amine
elle est toucouleur comme macky sall wala??😂
Ndeysane! Mère sa niane nangou na. Aujourd’hui, 19, Novembre 2024. Votre fils si bien aimer, est l’homme le plus influent du Sénégal. Il a élu des maires, des députés et un président de la République. Manchallah
Ndeyssane longue vie à notre maman yalla nagua féké lep machallah
ALLAHOUMA AMINE Merci à toutes nos mamans
@@aishasy9641 🤲 Amine Yabbi
@@aminaseck4943 amine cheri
@@nikojonkins5721 merci frère patriote
@@aminaseck4943 dafa leer
Mére Yalla nagua gua douggou palais si barké Yonnenti bi sallahou aleyhi wa Salam.
President Sonko resemble beaucoup a sa Maman deysanne tu a la benedictions de tes parents que le bon Dieu vous guide et vous sauvegarde.
Ndeysane ak begui yayame thie yarou❤
Sonko yalh nako yalh samou diokh Senegal inch alh
Mashallah maman chérie
J'aime les gens imperturbables🥰👑longue vie à notre maman d'Amour🙏
Ndjeredjuef merci beaucoup
Bilahi Yalla dou nitt.. Yalla adji mougn kaat yii laay andal déh Courage mr le président Sonko niogui sa guinaw
Bilahi yar guako ,yalna nè presidente 2024 mom rek mofinè
Tu as rendu service au Sénégal à l Afrique et au monde. Nala yalla fay. Djadjeuf
Merci de nous avoir donné un homme si courageux qui aime autant ce pays merci maman.
Avec sonko nous avons rendez vous avec l'histoire nous ne deverons pas décevoir nous ne cédéroms ni a la pression ni a la représsion
Vive sonko president 2024 inchalla yalla dèfal ak diam bou bari Maman yalla geu doudou ba fèkeko 2024 vive sonko president 2024
Maman nalla yalla dolly souttourra amine ❤❤
MAMAN MERCIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIII YALLAH GOUDEULE SA FANE
Machallah
GDGW ❤❤❤❤mame boye ya niou dioural souniou yakar fi si rewmi inchallah
Longue vie et bonne santé
Ndundal way mammy yow minu indil,, el fenómeno,,
Data yayou Ousmane sonko ak niaawe 😂😂😂😂😂😂
Machallah Yalla rek moy Yalla di bour ...
Yalla yalla goudal sa fanne si barké mouhamed❤❤❤❤❤❤❤
Manshallah mamma
Ngom dé sérérre là yaye boy ,yalna nga mag té sa ñan yi dal thi sa doom bi maschalla
Oui elle est serere.
Jeurjeuf yaye sa ligueye rafetna yalna yalla diokh sonko rewmi si barcke serigne touba
Longue vie maman......❣️❣️
Machallah maman long vie et santé de fer
Une mère croyante et digne merci la maman de tout les sénégalais
Mamma ndoundal wayi nene wourr wourr sonko sènègal solution❤💯✅💯❤🇸🇳
Ndeysane la maman nationale sénégalaise Mame Khady Ngom mère de Ousmane Sonko premier ministre de la république du Sénégal 🇸🇳
A chaque fois dans ses interviews, elle a les mêmes paroles tout ce qui arrive c'est Dieu, waaw telle mère tel fils...❤
😭😭😭😭ndeysane yalna yalla BARKÈL ko taga fèkè lèpeu incha Allah rabby ❤❤❤❤
MA SŒUR MAMAN SONKO, QUE TOUT MESICORDIEUX VOUS PROTÈGE ET VOUS GARDE POUR TOUJOURS À CÔTÉ DE VOS FAMILLE ET DE PEUPLE SÉNÉGALAIS👏🙏🇸🇳🌍
NÔTRE PHENOMÉNE SONKO DAY BOOK, À LA ÉLECTION PRÉSIDENTIELLE 2024 INCHALLA👏🙏🇸🇳🌍
SONKO SONKO SONKO NAMONALA, À LA ÉLECTION PRÉSIDENTIELLE 2024 INCHALLA👏🙏🇸🇳🌍
YAYE BAUYE GOUDEULE FANE YAW MI GNIOU DJIOUREULE SONKO
Ndoundeul maman diour nga kou bakh t dioup laf thiate💯🤗🤗🤗
Longue vie maman
Assalamou aleykoum qui est là ?ma sha Allah Allahouma barik.le 18 novembre 2024
❤❤🎉🎉🎉 Alhamdoulillah
Merci bcp maman yalla nala yalla Mayla godou fan ak wér gui yaram té samou lah yaw ak sa doom 🤲🤲🤲❤️❤️❤️❤️😘
Qu'Allah vous donne une longue vie et santé maman
MY LETTER TO A WONDERFUL MOM
La main qui berce le berceau
fait également de la maison une maison.
Ce sont les prières de Mme Sonko née Mame Khady Ngom, la mère de notre leader, Président Ousmane Sonko. Cela maintient la famille forte. Elle se lève tôt le matin
et baigne sa journée dans la prière.
Elle parle à Allah de sa famille et les place sous sa garde. Elle communique son amour
de mille manières différentes. Quand il y a un besoin, elle est là, que ce soit la nuit ou le jour. Mme Sonko saisit la vie avec amour
et donne tellement d'elle-même. Allah a placé en elle le meilleur qu'il avait et l'a rendue différente de personne d'autre.
Quand les défis viennent à notre rencontre
et quand les épreuves bloquent notre vue,
Elle s'agenouille à côté de son lit et prie la famille à travers. Comme son fils, le Président Ousmane Sonko, Mme Mame Khady Ngom est la création spéciale d'Allah.
Elle est une lumière qui brille dans le noir,
éclaire le chemin de sa famille et les pointant vers Allah. WE LOVE YOU MOM!
Dr. Elhadji Demba Ndiaye
Pastef Colorado-USA
Cher patriote je t'estime énormément
Kii mooye yaayou imaamou sweet beauty et prési-data des masseuses et des homosexuels comme branco 😮😮😮😮😮😮 yaroo koudoul boroome nél bou dakhaare ndayame biii,,,,ak taatame you réw
Nday sann djigueeni sénégal meun nanio diour kouné souniou gor gor lo
Wakhal tia kaw
Machalla yaye boyi doundal werral ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Machallah ❤❤❤
Yaye Boye Yalla Nalla Yalla Samm Té Samm OUSMANE SONKO Amine 🙏🤲🙏
Machalah à notre maman national, yalna niou yalla maye ndame inchallah ❤❤❤
Dieureuf ya khady Ngom mi yalla diarralei Ousmane si yaw Mouy kheweul gueu indil gnouko ✨🇸🇳🙏🏿
Du courage Ousmane sonko tu est un grand monsieur continue ton chemin pour l'intérêt de la nation.de grâce ils qu'on se mette aux travail
Waax dji sunu yaye dji waax amneu solo lol. Mou bagne ko décevoir mom ak wa rewmi. YaAllah nako sunu Borom dénk rewmi su fékké mo geun ci rewmi,mu bania tass yakarou kéneu ba kou nèkk diot seuy akk ay yèléff ak foo meunti nèkk té sunu Borom yombalko yorine bi. Askanou Sénégal soonou naniou lol motaax kou ame yermandé lagne sokhleu. Qu'Allah protège et bénisse le Sénégal! Amiine
Ousmane sonko sa yaye nimou niawer khame n'a nonou la data bi niawer 😂😂😂😂😂😂
Ndeysann sama yaye rék la may fatali ni la oyo fonn té gueme Yalla😢,sounou maman nationale Yalla gue yag diamono té wér lool.aminn
❤❤❤ma soeur vous avez bien éduqué votre enfant je peux dire notre enfant merci encore
MACHALLAH SONOU MAM YALNA YALAGODAL SA FAN ❤❤❤❤
Masha allah yaar gako yaar bou, bakh yallah, naga féké lépp insha allah
Dieureudieuf
Vive sonko vive le Senegal vive Le democracia
Merci seydina Ousmane sonko ❤️❤️
Diedieuf, sounou yaye❤❤❤❤
Wakh ji rafetna mamy sonko forever
Longue vie à notre maman. Puisse DIEU garder votre fils.
Merci à toutes les mamans, ET félicitations aux gens qui vivent avec
Merci Merci Merci Merci Merci Merci Merci Maman yalla na yalla faaye oue miniou maay kou sellaki le sauveur de l'humanité ❤❤❤
Merci laa dégue ,,kone kii moo yare imaamou sweet beauty bii di sonko nga khamené ba macky sall ak amadou ba doone amal Sénégal émergent booba sonko ma nga sweet beauty di mare taatou yaayou waa ex pastééf bii di adji sarr thi yooryoorou tabasky ak goudik couvre feu 😮😮😮😮😮😮😮ak sééne nél you dakhaar ndayame yi,,merci beaucoup modou lô
MachALLAH massa notre Maman!
Machallah maman 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Maman exemplaire.Calme,pieuse,sincère,gentille et surtout bonne. Yana yallah goudeule say féme si barke sa wadiour
Dieuredief yaye boye longue vie à toi ak werr ak soutoura
Mama yala nala same
Yala same
Machallah longue vie maman ❤❤❤❤
Longue vie maman ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yaay bôy doundeul rékk iow boul raggal darra 🙏🏼. Inshâllâh #Ousmâne JAAM rékk lay ame. Kouko beug fitnaal niou nioûss leu bien bon.
#SonkoPrésident2024 🇸🇳✌🏼✊🏼👏🏼.
Machallah alhamndoulilahi dieureudieuf sounou maman deug bou wer nga wakh si sounou president du partie pastef premier ministre ousmane sonko projet bi ligueye rek jub jubal jubanti rek man s.diop beugue fallou bou pastef touba italie mangui lay beugue 'wathio nak askan wi di Senegal si deugou am dignite am gor djiambar deug là ndam rek inchallah dieureudieuf
Longue vie Yaye Khady ❤️🙏
*Notre Maman Nationale, Elle Lui Ressemble Tellement. Longue Vie À Notre Maman Nationale*
Machallah yag fi té wer❤❤
Macha Allah K'ALLAH vous protege
Ndeysane ❤❤❤
May she lives long and happily
Walay ndaysane lou am yallah la
merci yaye boy ....bingua dom bou am mana mashallah...sonko président en 2024 inshallah
Ndaysan mama yagu fi way❤❤
Dieureudieuf maman ❤❤❤
Lov maman longue vie a toi vive sonko
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏
Que dieux vous protege 💚💛❤
Kone kii mooye ndayou imaamou sweet beauty bii di sonko 😂😂😂 mére bii kouko khoole khameny thiaga la
@@Pascal-e3l yaou sa yaye motie na Sama. Coye domou bordel macki sall katte na sa yaye si toune
Maman nianal rek gnoun nieup gnou niane yalla bakhna 2024 Incha allah souniou Souhait moye Sonko jeul pouvoir bi tè yalla na yalla nagou niane