Mougne dafa ame fomoy yem tu dois te faire respecter yalla mofi nek fok gua geume sa bop li dou seye yow rek ya meuna khess sa place si tu tiens a ce mariage sinon part de cette maison sans tes enfants et va chercher du travail geum sa bop ande ak yalla lo ragual yalla bayila ak lolou bon courage maria dijon
No ci mo Bon me baye coc yale yale mom dinele. Ate bilay no degel sonou gua m mougnel yal nel yal gen takhawou te djapale le gene le mougne te khamene atace yala mou gen bou nit
Femme bi dafa sincères,n'a mougne lép Dina diekh,❤dieukeurdji si Gauthier lay moudj, wayé na wakh ak parents mbambi ndakh mbam là ❤❤❤
Cvm
Yaw rek laye topou ❤❤❤❤❤
May ma café way❤❤
Sénégal xaliss rek laniou gueum ya des femmes qui souffre yalla dina lène atté mounial yalla baxna
إن الله مع الصابرين
mom lane lay noté la beuga xam🤔😅
Bayiko rk mou melni ramatoulaye une si longue lettre😅😅😅
@@NgaytaFaye 😂😂😂😂ray ngama
@@banebousso7630 dama wah deug Di😄😄
@@NgaytaFayesheuuu! réé na ba tass 😂😂pourtant tu as raison nak😅😅
Est ce k amoul louy nieuw si xelam moukoy noté pour bagne ko faté ndax wox néxoul
Na mougne yalla dinako atték ak diome yalla na yalla yokou soutourame si barké yonènne tiby seydina mouhamet (saw) ak si barké alkourane 🙏🏻❤
Interesante 🎉
Dinako guiss bilahi 😢
J'ai mal au coeur c'est vraiment triste
Té nga gnane cas bagna am boy nétali parsk nak dou diam tamit 😂
Kou yallah namouta faye douko liguéylo n'a mougne rek wallahi lep dîna lére
Salam, la dame na dem si ken bougoule ,mou réglé probléme bi inchallah.
Baravo merci
Slm❤ je vien de découvrir l’émission mais j’adore la façon dont tu racontes🥰😂😂♥️♥️ak café bi momathi gueuneu nekh…
Salam sister fatou Bonne et heureuse annee a toi et a toute l'equipe Bonne Continuation Dieureudieuf ❤❤❤❤❤😂
Une si longue lettre de Ramatoulaye !! Femme bi da Niakk fayda !! Li du beug doff la
Boule wakh thiey yalla wakhale thiey nit ti😂 ana café bi
Bonne et heureuse année sister❤❤❤❤
Sa café you khassaw yi doko bayi sokhna fatou meune nala dieuleul cour bou makk 😂😂😂😂😂😂😂😂
Ndayssane. Wayé khana yoroul wone téléphone gounor, noumou amé lien bi
Thiey adouna 😢
Na guena goore goore lou takat ndigam bou bakh ligueye ndakh ndiabota té yoni yague rék sétane inchallah yala dinako diaplé lépou si lokhom lay moudji ak ndiabotam
Mane la mère bineta Kaolack contane na si yow
Mougne dafa ame fomoy yem tu dois te faire respecter yalla mofi nek fok gua geume sa bop li dou seye yow rek ya meuna khess sa place si tu tiens a ce mariage sinon part de cette maison sans tes enfants et va chercher du travail geum sa bop ande ak yalla lo ragual yalla bayila ak lolou bon courage maria dijon
Mayma café way
Nalene bayi ak yalla dinalene até beutieuk
Dieukeur bi badola leu rek
Lou doul deug d'où yague
Lou lokho def lonkho mokoy dindi
❤😢❤❤❤❤❤❤❤
En général djiguén loko méti moromou djiguén nam moko koy tékk🤷🤔
Sa cafe bi si emision bi bayko
😅😅
Nañaan bat yalla bakhna
Ieo sokhna Fatou solution bi Moy mou diokhleu numéro diékar dji nga envoyé ko vidéo bi mou lire ko boba dineu requilél bopam s'en réflexi
Kou d'accord ni mafi jidtou ❤
Ay waay mandé méwyi réka ma nêx
Tak niarel dara nekousi waay
Thiey Sénégal
Sokhna Fatou magui ziar
3eme sur la liste
na dem ta khaar yalla
May 3em😂😂
😅😅
❤❤
❤❤❤❤❤😢😢
Amine
Demal def mystique com mom rek
fatou qu'elle ce laive les gen son mèchante pour recupaire son mari
Na took rék dafa begue ga dém motakh moulay fénal boul dém fénne
❤️❤️❤️😍😍🤲🤲
Femme yahk femme thiey le karma arrive dh
😭😭😭😭😭😭😭😭😭
😢😢😢😢😢ok
Youssou mo gueunone nék séér ak complexé gnépp ...temps wou kassé
No ci mo Bon me baye coc yale yale mom dinele. Ate bilay no degel sonou gua m mougnel yal nel yal gen takhawou te djapale le gene le mougne te khamene atace yala mou gen bou nit
May 2em
😂😂😂😂😂
Sona ngo digua si diougue ou es ta familles sey basilane
Moi 4em 😂😂😂😂
Yaw rek laye topo