Papay assane mom pr man matoul kilifeu ndakh kilifeu deugeu dou def sa bou ame pb di mandi di def naka soudoul ñonou liko pa bi wakh deugeu leu mrc à vous 🇸🇳❤️✊🏿
@@serignembaye674 j’avoue j’avoue mais pourquoi il boit tout le temps wsh un père de famille ne se comporte pas comme ça nul n’est parfait dans ce monde mais faut bien analyser les choses y’a beaucoup d’enfant qui sont rancuniers juste à cause de leur parents par fois les parents sont tellement égocentriques ils voient que leur bonheurs
@@serignembaye674 je ne suis pas d'accord avec tw pour mane nit da fa ande ak ngoram quelque soit les situations guis khalis rk di teub di dal ba nara yak sa avanirou dome
Reporter bi tamite li lanela 😄 Le père de assane mom sougnou commencer diap confiance mou délouwate si tass souniou yakar. Félicitations aux fils de lions
Assan lidone takeu si ay beuteum fayna 😔 je ne sais pas pourquoi mais cette phrase m’a tellement ému,combien de parents africains ont brisé le rêve de leur enfant ? Beaucoup de parents sacrifies l’avenir de leur leur enfant au lieu de se sacrifier pour leur enfant !
Pour 5millions il a privé son fils de son bonheur en prétendant qu'il voulait la santé de sa femme 😒...yalla naniou yalla mousseul si genrou parents yi😌
@@ibrahimafall7056 pah bi kaay boul comprendre vrai irresponsable leu,daay gueuna si li nga yakar ni ça va dena changer legui mou dougate si lou gueuneu graw😏😔
Seul série bouy wanè vrai vie Sénégal vrai réalité si tristesse ak guorguorlou ak diom dèleu doundou ay épreuves ke dieu veille sur nous tous ndeyssane
Je viens de perdre mon jumeau Assane le matin vers 14h ngurr yala nianal leinn mako yala yeureum ko tei xaré aldiana firdawshi thi barkepp korgui 🙏😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
J'ai toujours dit que le papa de Assane est un irresponsable. C'est un mauvais père. Comment peut-il dire à un enfant de moins 15 ans que gnune yaw lagn yakar ? Yagnu wara guéné si situation té mome mouni legu legaral dara dalouko wara doundal ndiabotam té defuko. Di khol intérêt personnel lame bay tekk khalé bi loumou atanul.
Tu as parfaitement raison. Je pense que serie bi deuf gnou beug montrer les tares de notre société. C'est la dure réalité : certains parents mettent trop la pression sur leurs enfants, et font une projection sur eux. Souko deffer si l'enfant ne parvient pas à combler leurs attentes, il pense avoir échoué.
Nguir Yallah, svp, relancez ce film 🙏 c’est plein de potentiels. Un film très original, class et riches en émotions et enseignements 🫶 je viens de le découvrir, j’ai suivi toutes les épisodes, j’ai eu le cœur brisé en ne voyant pas l’épisode 17.
Kon samba dem na ni rek virement samba waroul won déh gnoune donga dara yi gno ngo reclamé 'ngen decal samba wala gnou plent len. Aw khérrr manoul raye dongooo waye da yombu trop😘
Blh wallahi wa watalahi je vous le jure cela même histoire que j'ai vécu avec mes parents jusqu'à présent j'étais sur le point de partir à l'étranger malheureusement ma mère est tombé malade le Land demain j'ai arrêté ms études pour devenir un vendeur 😢😥ms bon tant de vie tant de l'espoir yalla bakhna ⚽🏆
C'est vraiment triste le père de Assane n'est pas responsable du tout ms chapeau à la mère de Assane qui donne corps et âme pour ses enfants vive les 'Doomi Gaïndé' vive le Sénégal 🇸🇳❤🦁
Encore laye toujours Laye vraiment parents aussi amellna doom akke qu'on le disent les parents doivent éviter d gâcher le rêve d'leurs enfants encore cette épisode montre qu'il a des gens qui s'abusent d'leur argent pour arriver à leur fins utiliser l'argent contre Les pauvres pour les destabiliser les malnener et les posséder Assane tu vas jouer le deuxiéme mis-temps liy takk say beut fayna mais on va l'rallumer J'me vois carrément dans ça merci Mame Ass 🙏🏾❤️
Trop d'émotion avec cette triste fin de Samba. J'ai des larmes,je vis avec trop d'émotions la série. Félicitations pour cette truque de dingue...C'est trop originale la série, on s'identifie à elle. Vamos à toutes l'équipe de la série. Love❤
Sama mame néna nga lal coeur bi ❤
❤👇
Sama mame néna bouma lal coeur bi
Mdrr
dama beuge assane
@@rokhayandiaye6122 qq
❤️
Kou d’accord né doomi gaïnde mo dakh si serie yi daw senegal 🇸🇳 beseul J’aime
Abonné len ma tmt
Lay sof ga ahhhhhhhhhhhhhhhh
A part impact 😙
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Guediawayeinfos TV vous remercie affaire BI Domou Gaindé la thi Kawe Si Kaname
Billahie thi kanam rk amul lénen
Laye cissé guéneul fi🤣🤣
Si kaw si kanam rek
Vive nos équipes nationales LOCALES
nos champions LOCAUX
@@mamadouwade8898 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
@@serignembaye674 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Serigne Mountakha Mbacké yalla nafi yague .🙏🙏Aimé lenko Mouride guéne bok si milliardaire Serigne bi🙏
Kou guissni assane avant fin du match dina niew sauvé équipe bi besseul j'aime
Pour man dina football 2em mi-temps bi
Football 2ème mi
Temps moguene nekh
Ana gni beugue domou gaïndé beseul j'aime
Nekh na
Merci
Meilleur série de l’année qui d’accord
Moi
Mw☝️🤞💥
Moi!
Moi
Koukay sétane ak sa baye sakh doo rouss
Lii moy serie
Papay assane mom pr man matoul kilifeu ndakh kilifeu deugeu dou def sa bou ame pb di mandi di def naka soudoul ñonou liko pa bi wakh deugeu leu mrc à vous 🇸🇳❤️✊🏿
C'est un père irresponsable ils sont jamais la ces genres de pères
Mais à mon humble avis je trouve qu'il a raison sur le fait de prendre les 5millions pour soigner la mère de assane
@@serignembaye674 j’avoue j’avoue mais pourquoi il boit tout le temps wsh un père de famille ne se comporte pas comme ça nul n’est parfait dans ce monde mais faut bien analyser les choses y’a beaucoup d’enfant qui sont rancuniers juste à cause de leur parents par fois les parents sont tellement égocentriques ils voient que leur bonheurs
@@serignembaye674 je ne suis pas d'accord avec tw pour mane nit da fa ande ak ngoram quelque soit les situations guis khalis rk di teub di dal ba nara yak sa avanirou dome
@@nasty.blackberry1928 bien dit
Serigne mountakha yalla nafi yagg looooll te wer ak képou kouko ko yeené wakh leen amin
Nguir yalla continuei la série domou gaindei , we need it
Yalla na gneupp am jamm kou beugg assane rek beuseul j’aime 👍 👍bn continuation
Ndam Rak
Waw kay ndam rek
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
@@loufaniang2288 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
👇Ani Les fans Doomi Gaindè Meilluer Serie du Sènègal bn continuation Manifestez vous j adore ❤❤❤❤❤
Yh
2Cv bien que je suis à 1la
Nice les gas⚽⚽
Gnogui ni
J aime les domi guinde ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
assane momar petite felisitation nioune film yiiii rek la waa senegal beugue konne mass defal benéne svp
Ak wa Mauritanie tamit
Wawaw kouy wané sounouy réalité
Une pensée à nos mamans qui se donnent corps et âme pour s'occuper de nous et satisfaire nos besoins. Jërëjëj yaye❤️🔐
Cv
@@morsi4071 ttyjiii
Meilleure série Doomi gaindé👏👏👏👏
Yu
Say parents daniouy daw di danou pour nga tekki, dadj louné ba nga wara tekki niou dem. Yalla souniouy parents féké souniou tekki nioune nieup🥺
am8ne yarabi
Amine
Amine ya rabby
Amine yaraby
Wakh ga degu man sama papa mo déf lepp thi sama étude mais 2016 la fato ma ame bac 2017 avce mantion assez bien
je m'adresse à l'hauteur de ce film doomi gaindé diapci guir yalla rk yayou assane boumou dead svp
et guen bayi dima dioylo
Vraiment
Billakhi yaw
Bilakhi way✊🏿
No mer b da wara féké
Da sonou
Vraiment très d'accord avec vous
Reporter bi tamite li lanela 😄
Le père de assane mom sougnou commencer diap confiance mou délouwate si tass souniou yakar.
Félicitations aux fils de lions
Pa bi kay moy lolou
Nooo!il est facile à corromp
Mane moom khamena suspense dinama raaye 🤣🤣
Non pa bi dafa yakamti torope
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Papou Assane limou yak tey golo yakouko thi tool bi. Kou d'accorrd beusseul j'aime
La vie est remplie d'épreuves à surmonter. Chaque étape franchie donne naissance à une autre.
Nagnou koo déf au moins deux fois par semaine qui d'accord beussal j'aime ❤
Assan lidone takeu si ay beuteum fayna 😔 je ne sais pas pourquoi mais cette phrase m’a tellement ému,combien de parents africains ont brisé le rêve de leur enfant ? Beaucoup de parents sacrifies l’avenir de leur leur enfant au lieu de se sacrifier pour leur enfant !
Tu as tout dis...Pa bi kou niaff khonam leu😠
Tu as parfaitement raison wollah personne ne peut pas comprendre ça 😿
Pour 5millions il a privé son fils de son bonheur en prétendant qu'il voulait la santé de sa femme 😒...yalla naniou yalla mousseul si genrou parents yi😌
@@ibrahimafall7056 amine 🤲🏽 té limou calculewoul moy koula diokh 5million yi ming kooy diemeu khagne ay centaines de millions
@@ibrahimafall7056 pah bi kaay boul comprendre vrai irresponsable leu,daay gueuna si li nga yakar ni ça va dena changer legui mou dougate si lou gueuneu graw😏😔
Ani fans assane yi manifester vous❤❤🇸🇳🇸🇳
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Hhhh
Kou gueume n'y niome Assane nioy ganié beusseul aime si barkél sérigne mountakha ak Elhadji Malick Sy
deuxième mi-temps assane va venir et il vont gagner j etais au terrains
@@mariamakeita1110 oui je t'ai vu
T'étais habillé en rouge ou bien
Wala dou yow.
@@lefuhrer45 c'est moi
@@lefuhrer45 🤣🤣🤣🤣
Papaye asane waroule wone nagou mé dieu est unique assane
N abandonné jamais. Toujours croire en soi sa ira
Ana dip n'a niew aidé niom assane way ki est d'accord avec moi
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
inch'Allah
Sama mame néna nga 👍 sama commentaire bi yalah may leu lo beugue té mou geune si yaw😉
Amin
Une pensée a toutes ces mères qui se battent jour et nuit pour leurs familles sans montrer leurs fragilités...😣❤
Papa name yala diegale wayé dou mousa khole sa intérêt loudoule intereme rek laye khole yala nagnou yala Samale souni yaye
@@malickdiop8143
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Meusouma guis kou con comme laye
5 millions nga denkou ko maçon
😢😔
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Taye leu anniversaire Serigne montakha mbacke yanale lénkou Mou goudou Fann adouna yanale lénkou Mou goudou Fann Amine ❤️❤️❤️🙏
Tay le 25 ni?
Tay le 25 ni?
Qui est dacort niou déf quo chaque mardi,jeudi et samedi
YaW tu est foux
Foux avec x..... eupneu
@@dembandiaye5878 🤣🤣🤣🤣
Khana bobou xallé yi douniou diangati wallah niénéne gni douniou ligueye boulene khool sen beugue beugue rk
Moi
Seul série bouy wanè vrai vie Sénégal vrai réalité si tristesse ak guorguorlou ak diom dèleu doundou ay épreuves ke dieu veille sur nous tous ndeyssane
Le seul seri qui ma fait tomber les larmes aux yeux
Vous jouez vraiment de la réalité
On n'est du même côté frr
Le son de la fin m’a vraiment fait pleurer 😭 😭😭 c’est touchant. Machalla si kaw si kanam🙏🏾
Le nom de l'artiste svp
J’aimerais le connaître aussi 🤟
Kid Paco
@@thioufseck4720 guissouma son bi RUclips 🤷♂️
@@alphadiallo9664 kid paco « waxal ma yaye »
Momar"sama Mame néna dogou yapou yakhoute thiébou yapou" ana wa team Momar
Wakhna deug nakkk lou lerr la
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
@@abdoulo4408 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Ko begue seydina Mohamed à bonne sama chêne RUclips guir yalla rek
Je t'aime Assane
Assane fanta t'aime
Ok
Je t'aime beaucoup ❤❤❤❤
Assane je t'aime diokh ma sa numéro watsaps
Chaque jour ma commenter moussouma ame j'aime🥺
Tay commentaires ngay am
J'aime donc
Loy doyei j'aime
Loy wax ni😂😂😂
@@aboujah7652 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Aïda elle joue bien son rôle... Beaucoup de coeurs pour nos mamans ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
yaw gnou wakh si assane guaye wakh si aîda
Dt5sedf
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
C'est la meilleure série de ce pays
Ana gni begue seydina mouhamed manifesté si Barki seukherou Ramadan 🙏🥰🇸🇳🇸🇳😍🙏
J'aime nah doma abonnéle svp
Nous sommes la
PSL
Bou lène raye yayou assane 😭😭😭
C'est le meilleur série Sénégal regarder depuis 🇮🇹🇮🇹🇮🇹
La mère de Assane c’est la meilleure wollah💯❤️
Mais âme n'a louma métro😭😭😭
Li moy vrai senegal biniou beug di guis ndakh mo mingo ak li niou bari di dound. Yalla na yalla samal niou souniou ay wadiour
DemaY commentaire mais douma ame j’aime 😭😭
Assane va joué le match et ils gagneront🙏🏾 ki es avc mw
Je suis d'accord mais il vas jouer la 2nd mi-temps
Mére aïda c'est un exemple pour toute les filles . C'est le travail qui paye
Bilay
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
sounou maman yi yalla borom bi guoudeul seni fane th maylen weer si barké weerou koor gui
Amine
Yalna niou yalla mousseul cy sangara
Le père de Assane a sacrifié l’avenir de son fils .😭😭 la réalité africaine 😒
Il n'a pensé qu'à l'instant T et non à l'avenir et au fait que leur vie pourrait changer radicalement si Assane était recruté pour jouer à l'étranger.
@@aichasylla1521 bien vu c'est le message qu'on peut tirer sur cet épisode
Merci
Ohhh
Niom assane tokknagne
@@aichasylla1521
6
Ay way assane bou nieuwoul si match bi dotou ma setane serie bi je jure 😭😭😭😭
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Wii
Ak mane dh
Kone nio yém
Ak man dootou mako seetan
Père de assane meiré nako ak kane
Loum défati thieuye 😂
Laye domeram deug la
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
@@mohamedseck5757 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Machalla les domou gaïdé👏bonne continuation👏👏👏
Papa Assane Conan
😂😂😂
Yayou Assane mo gueuneu nekhal film boulenko ray
Wollah Magui lay nian giir djeum serigne touba gua abonner
Abonné nah abonné ma chéne RUclips
La discussion entre les enfants devient de plus en plus rare et moi c'est ce qui me plaisait de la série
Cv
Korou diamou ak salaam yal na nekk si yéen 🌙 ❤️🥰
Amine yarabi
🎉😢😅😅😢😅😢😮🎉😮😂😢😂😢🎉❤❤❤❤😂🎉❤😂😢😮❤❤🎉😂😢🎉😢😂
Quand les problemes et pression ak stress te depassent yalanagnou yala sauvé defalgnou soutoura ak khaliss pour reglé sunu problem💸💰🙏❤
⚽️⚽️⚽️
J'aime bien le père de Assane , il donne la quintessence du film
Wallahi, Mass dou nit, Masha-Allah< serie bii yallah neu wessou seu niort insha-allahou
Je viens de perdre mon jumeau Assane le matin vers 14h ngurr yala nianal leinn mako yala yeureum ko tei xaré aldiana firdawshi thi barkepp korgui 🙏😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Que la terre lui soit légère et que yalla atté ko yeirmendém...
Massah Allah yerhamou inchallah amine
Yalna khipe aldiana si barki werou koor gui 🙏
Paix à son âme !
Frère massa Way yalla naka yalla kharé aldian firdawsi
Félicitation à doomi gaïndé fierté nationale yalla yenene prix top ci
J’ai pas les mots pour cette belle série.on passe par toutes les émotions en la regardant
Cœur à toi
Démay coumantér mais douma am j'aime😭😭😭
J’aime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime jaime
@@khadijaloumytondiaye782 merci beaucoup
J'ai toujours dit que le papa de Assane est un irresponsable. C'est un mauvais père. Comment peut-il dire à un enfant de moins 15 ans que gnune yaw lagn yakar ? Yagnu wara guéné si situation té mome mouni legu legaral dara dalouko wara doundal ndiabotam té defuko. Di khol intérêt personnel lame bay tekk khalé bi loumou atanul.
Li série la
@@cheikhibrahimaly5737 😂😂😂elle parle de la série non ???
@@astouseck6915 Vraiment je sais pas 😅😊
Tu as parfaitement raison. Je pense que serie bi deuf gnou beug montrer les tares de notre société. C'est la dure réalité : certains parents mettent trop la pression sur leurs enfants, et font une projection sur eux. Souko deffer si l'enfant ne parvient pas à combler leurs attentes, il pense avoir échoué.
Beaucoup de parents font ça khalei bi day dioudo rek gua def si mom yow lagn yakar khalei bi magaleer lolou di stresseer non li c pas la
Peine koo
Machalah meilleurs série gnoune gneupe ay doomiiiiii gaïndé lanou🦁
Le papa de Assane dafa meunoul supporter problème rekkk ndeysan 🤦♀️bopp bi mo ndaww 😒
Il est con comme l'a dis Kresh
T'as tout compris Astou, le vieux ne s'est pas faire face...
Parfaitement il ne devait pas faire ça
Amna louma méti trop si papay assan bilahi li comme la vie rael j s8 triste 😥 vraiment
Lou lerr nga wakh
meilleur serie au senegal kou daccord ak mann na abonné sama chaine youtube
Akassa
Waw
Wei
@@bayemorndiaye2469 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
@@boubacardieng3905 Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
En une journee jai regarde les 16 episodes kel beau film pleins de lecons bcoup de courage a vs liii laniou beggg sounou rew les realites
Ani gni beug sén Mame beseul j'aime 💛
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Papaye Assane limou deff bakhoul kou d'accord ak mane
Les domi gainde ont dirait les lions du Sénégal je vois un sadio Mane un gana geuye mbaye Niang ils sont magnifiques
Machalla boullsi dougue
Boye bou daw bi mom graw nadi😂😂
Nguir Yallah, svp, relancez ce film 🙏 c’est plein de potentiels. Un film très original, class et riches en émotions et enseignements 🫶 je viens de le découvrir, j’ai suivi toutes les épisodes, j’ai eu le cœur brisé en ne voyant pas l’épisode 17.
Domou gaïdé, dou tit dou ragal,
Courage Assane 🦁🦁🇸🇳
Kon samba dem na ni rek virement samba waroul won déh gnoune donga dara yi gno ngo reclamé 'ngen decal samba wala gnou plent len. Aw khérrr manoul raye dongooo waye da yombu trop😘
Bilaye bro
Franchement cette philosophie là c'est très cool c'est très cool je ne sais pas qui a réagi le film mais chapeau à lui🙏🙏
C Grand mass
@@Makhleprotv Mame Asse Seck chapeau bas à lui
Qu'Allah agrée notre jeûne, nos prières et nos bonnes oeuvres .. Wakhal Amine 🙏❤❤
Amine yarabi
Am
😭😭😭 trop d’émotions
Nice la série 🇸🇳❤️💪🏾💪🏾💪🏾
Blh wallahi wa watalahi je vous le jure cela même histoire que j'ai vécu avec mes parents jusqu'à présent j'étais sur le point de partir à l'étranger malheureusement ma mère est tombé malade le Land demain j'ai arrêté ms études pour devenir un vendeur 😢😥ms bon tant de vie tant de l'espoir yalla bakhna ⚽🏆
Dieu est grand
Yalla bakhna mougnal rek
La meilleure série 2k21🥺😫❤️😭numéro 5 bi nehnama ndah numéro binga sol
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Formulons des prières pour notre Sadio Mane national, il en a vraiment besoin. 😭
Mba diam louko dall notre fierté sadio??
Il n'est pas en forme à Liv en ce moment...
@@christophemendy7413 ah ok yalnako yalla safara oyofal lép ya rabby
Yeungou lene sponsore ya ngui nieuwe les spectateures reclament 2 episodes par semaines👩❤️💋👩
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
C'est vraiment triste le père de Assane n'est pas responsable du tout ms chapeau à la mère de Assane qui donne corps et âme pour ses enfants vive les 'Doomi Gaïndé' vive le Sénégal 🇸🇳❤🦁
Cette série vraiment 😭 c’est la meilleure de toutes, la fin j’ai pleuré ohhhh ay waie limey yeuk mingui meilni degueu leu
Épisode bii passé bilay cété très touchant
Yalnanou yalla sambal sounouy waydiour❤🙏
No Sénégal mogui doga ame série segegalais NK😎😍
Bly
Mon soutien à tte l'équipe 2 doomi gaïndé👌👌👌 À AVANT REK inchallah ❤❤❤
Encore laye toujours Laye vraiment parents aussi amellna doom akke qu'on le disent les parents doivent éviter d gâcher le rêve d'leurs enfants encore cette épisode montre qu'il a des gens qui s'abusent d'leur argent pour arriver à leur fins utiliser l'argent contre Les pauvres pour les destabiliser les malnener et les posséder Assane tu vas jouer le deuxiéme mis-temps liy takk say beut fayna mais on va l'rallumer
J'me vois carrément dans ça merci Mame Ass 🙏🏾❤️
Kou abonné sama chaîne yalna yalla nagou sa koor si barki seydina mouhamed
Kay ma cotchel la 30 abonné
Amna solo
Wawaw
Abonné nah abonné ma way
Man damay aboné
Série bi nékh na mai béne jour si semaine bi dafa ndaw 😭
Wakhal way
Nn nn deux fois laye âme mardi ak samedi heure yii gno bokoul rék
@@tymambaye547 non samedi lay daw RUclips mardi niou tékk ko télé
Ana fans assaneyi rang Mouy abonee athia gnou dem
Le meilleur Seri 😍😍😍🥰🥰
merci doomi caindé contan si yén yalla nalén yalla ar si kaw si kaname
Même pas 1 mn 1300 et kelk visionneur.domou gaïndé est le meilleur
Yallah na yallah motali sunu beuge beuge binou am si Sinoy wadior aminn
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah rek
Kou begeu Say dinamouhamét abonnél sama sén you tupe 💕💝💕💕💝💝💝💕💝💕💝
Yes
Baye lén prophète kani doukkal lou niakk fayda🤬
Kay ma cotchel la 30 abonner
Yé mén
Délohma sama abonné svp
Wallahi xoll toyna série bi daw yaram lá geuna def asane diagal na ndaw you barine don gone terewoula am diom bon continuation ❤️❤️
Trop d'émotion avec cette triste fin de Samba. J'ai des larmes,je vis avec trop d'émotions la série. Félicitations pour cette truque de dingue...C'est trop originale la série, on s'identifie à elle. Vamos à toutes l'équipe de la série. Love❤
Ani fans doomi gaïndé yiiii🇸🇳🇸🇳🇸🇳👍