Mais yen v quoi votre problème 😏mais bouko néxé mouni diamant 💎 lako diox yonou kénn nékkousi .. l’essentiel est qu’ils sont heureux donc nagne lèn nianal diam mo gueun wax bou beuri bi ish
Ay yen ndah man dina dounde ba ame lii ay yalla magui souk dii ram 😂 di beureugou yalla yalla yalna ma sama dieukeur nob bouma teraloule sah bhn ms nama non rek 😭😭😭😭😭😭🙏🙏🙏
Di beureungou ay 😂😂😂😂 no yalna la yalla may dieukeur boula love ta doula live mayla dieukeur boula yoor ta doula woor kou bakh ta dou bahal sa hol touf touffe
@@amimarone9371 ay way merciiii grand sœur bouma ame lolu rek lep diam kn digua kham ni ma meun sam colare dina la fek ba figua nek nela sa gnane nagouna 😂😂✌️❤️
Yalla boulene thiate topu ngir yalla seuye dafa sacré bulene def seuyou réseaux sociaux ndakhté khalé nga sa borom keur khalé alors toujour déléne diégué mag gni niuleni diokh ay conseiller svp masha allah dome you barkel
@@fatousamb9181 dafa am niou soxor quoi addina bi koufi neck daga neubatou ba am Lo beugue sino rk niou kar sa mame bou officielle nk nga zeulé zosé def loula saff an xarit dou deuge😂😂
Neysan khalé mo nékha nakh kom gueum nguén diamat ni nane khaliss dieukkeureum diamat sénégal yéppou pour amoul kouko fi mana dieund diaro diamat peut couté milliard enplus nékhoul guiss sénégal deukkeu bi banalissé milliard diamat léppou révé lo dof yi kou ci dadialé 1million dém dubai di nakhaté seye kat yi seye lén té yalla takh gayi dagnou léndi nakh dém dubai beu gneuw seu dieukeur diékhal apres thiow beuri mofi am
Qui est là après la confession de Ndakhté?
dama rouss😂
Magui ni😂
RUclips cci bopam mo seytané 😂😂😂
Dieudi rerr 4h du matin ndahté moniou wahoull deugg mario da niro ku bah 😢😢😢😢😢😢😢
Simple lene té bayi wané wou bi
Vivre caché, vivre heureux
Kou beugu moutie dagay maytou
Wa salam
Meti guene tamite bambou doné célébrités la vie privée diékh bayilen diambour
Pourtant deug la wakh nak.deugla amna yodoul meuna neubeu mais lakatoul lo meune rék c'est tjour pour ton bien bb
Tay ame nga degue
L'histoire t'a donné raison
LInga donn wax gneuwna nk thieuy yallah
Yalah na ame dieukeur bouma nop amine
Amine😭
@@masambakockigueye7307 bilayz dafa nekkh
@@farmatathiam1695 c vraie parfoi damakoye guis mé damaye beug am diabare si sase yi
@@farmatathiam1695 esk paré pour seuy yéne tmt danguéniye tamou dh
Amine
Niaff djieukeur nala nopp wayy❤️✨🌹💫
🤣🤣ah bon
😂😂😂
Mais yen v quoi votre problème 😏mais bouko néxé mouni diamant 💎 lako diox yonou kénn nékkousi .. l’essentiel est qu’ils sont heureux donc nagne lèn nianal diam mo gueun wax bou beuri bi ish
Vraiment Sénégalais kay mo meune critiquer rek
ndeysan le guiss Rék Dina diékh holalma couple Bi Rék noumou rafété non c'est triste 😔
Yalnalen yallah lafal thiat ta maylen ndiabon gou barké ta yallah defal len lolon buegu sen sey inchallah 🙏
Pour vivre heureux il faut vivre cacher. Sénégal da beuri gnou sokhor. Guisnagnou fi couple maabo
Yala neulène Yala soutoural 🤲 ay khallé leugnu
Yallah na am djeukeur bou may dieudeull diamant 🙏
Kaay ma dieuneul la diamante
@@cheikhsow3704 Mane kay maguinihh dilla kharr
Ay yen ndah man dina dounde ba ame lii ay yalla magui souk dii ram 😂 di beureugou yalla yalla yalna ma sama dieukeur nob bouma teraloule sah bhn ms nama non rek 😭😭😭😭😭😭🙏🙏🙏
🤣🤣🤣
Di beureungou ay 😂😂😂😂 no yalna la yalla may dieukeur boula love ta doula live mayla dieukeur boula yoor ta doula woor kou bakh ta dou bahal sa hol touf touffe
@@amimarone9371 ay way merciiii grand sœur bouma ame lolu rek lep diam kn digua kham ni ma meun sam colare dina la fek ba figua nek nela sa gnane nagouna 😂😂✌️❤️
Di marche kanara tmt bolé kosi 😂
@@mamefatydiop2301 wa wah gua deug dama ko fate won 😂😂
Yallah naléne yallah diapalé inchallah après nak boufi kéne guénate nane dou wone diamant damako done soutoural guire yallah
😂😂😂
Woyyy ray ngama chérie
🤣🤣🤣
😅😅😅😅
Sa dieukeur dji naturel dal dara simplicité touss
Yalla boulene thiate topu ngir yalla seuye dafa sacré bulene def seuyou réseaux sociaux ndakhté khalé nga sa borom keur khalé alors toujour déléne diégué mag gni niuleni diokh ay conseiller svp masha allah dome you barkel
Ohhh brom commentaire bi guissone nga lep
Bilahi 😂@@NdeyeSow-hm3sz
Ndank rek ma belle et discrétion en plus gor d'ay sopekou gnanaloumalako mais je te parle en connaissance de cause ndank rek
Iow dh daa mélni ndanga ko khamone
Li motakh sen ménage yi d'où yagu ya certains de ses choses diaroul woné
D accord avec vous
Sof rèk mena wané wou
Bilay wakh gua deugg
Bilahi
Vraiment...
Man dé douma diende dieukeur yaye ay souma ko amon sama yaye lakoy diokh ❤❤❤❤Yalla nama Yalla may rèk goor gni dizul😢bou ndieuk lagn lay dieul 😂
Kaay ma dieuneul diaman
@@cheikhsow3704 Ska maman geunou mathi diékke
Yalna yalla samlene inchallah te mousseul lene thi thiat
Machalla sama kharit bou bakha bi
Merci bocou
Machllah laff thiate 👏❤️
Walahi deugleu amougniou soutoura
Fene rek ki dafa yor loumou dieundé diamant💎
𝘚𝘪𝘴𝘰𝘶 𝘮𝘢𝘯
Non xamna fofou dani forr diamant
Nga sagne ko wakh 😂😂
Lolou la wokh di fen rek
Bayie len sokharr
Diamant dou ay foo déh mes amours 🤣🤣🙏
Féne lañiou meun kou déme khalise la😂😂😂😂😂
@@courandaw9412 🤣🤣🤣
Wlay 😂naniou ko bayi ak adja diallo rk 😂mokoy rangelé thi loxom thi lou woor
Aye waye bayiléne sokhor soudé ay nakhe sakhe nékhna gnisi wakhe lou Bonne gnepe da gno sokhore
Sonkobaralait ndiaye + sweet beauty: rafete nekh
Couple heureux machala
Mashallah nice na trop
Yen sokhorr gun dh khalle yie commentaires you bonne ❤
Loumana ame ton marie t'aime ala folie
So nice ❤❤❤
Yallana seybi barker
Amna commentaire yo khamni sokhor kasé la
Dèf lèn loulèn nèkh daguèn this tolou
A tt moment naguaye takeu diamant 💎 Bi sa lokho nakh fo guéné dina sétlou say lokho 😅🤣🤣🤣yalla mayléne gnabott bou barkel
Amine Ya Rabi 🙏 wayé Ray guama🤣🤣🤣
Damay d😂😂😂
@@dadocisse1034 hummm naci bayi khel rek🤣🤣🤣🤣nakh gnifiy def façon yi beurina
@@thiorofall1878 😂😂😂😂😂ma djapalé la si 😂😂😂
Varr😂après confession
Machallah 😍😍😍😍
Reference du diamant please
je voulais acheter pout mon Mari❤️😂😂
Srt lolou😂
moi aussi
Mariage Sénégal kom film marodi d’où am moukou suite
Amngua dieukeur bou meun wanéwou outék sama boss il passe tout son temps a se cacher 😂
C'est ce qui est bien nak pour vous deux
Parcequil est mâture
Come sama boss damay merr sakh ndakh nebatou bou eupp😅😅😅😅
souvent wanewou dathiy bakh
Dieureudieuf nla nob 😩❤️❤️❤️❤️
Enhh😂
@@fatimaniass5850 wouyyy 😂
🤣🤣🤣
Merci bcp Wadié gua sm stresse bi 😂😂
@@fallmariama1845 mbadou 😂😂li kat da neh machalla 🥰😭😂
Niaf dieukeur nala nop 😂❤️
😂😂😂loy wakh tay
Deiflaine ni djeyla bahna
Bayi lene fene ki ageum fane ley dieulé diamant
Bayil di wah sa diabar sa dom cpo jolie
Sokhorouma 😂🤔😂 , Mais Ndakhté Foumou wara jeulé Diamant 💎 bakaye mayé🤔🤔🤔🤔
Sénégal sagou mofi ame da ngay dieu de or sakhe nganio diamant comme guéwéle yi nougne kay défé
Ndakhte mome amna xaliss Di😂😂😂 boulen yakh xalé yi
Ay way yénn li nékh na dh😮 qui da divorce ni 😭😕
😅😅😅😅😅 alla ndakirahhhh mouni ??? 💎
Sey soutourala
Wa légui nioune en koi sa nous regarde ay way dé Len am soutoura si sen bop
Lima diakhal bouni beugeunté di neubou mais bounou marié wé founou nek di wanewou ahh
Je me pose la même question
@@ramatoulayesane5835 Ms lolou moye yone kou nieppou xam fo dieum do ague Ms bo démé ba am liga beugue boula néxé di zeulé
Je te jure niome kaye nioy attirer thiat
@@maimounagueye2529 blh kou niepeu kham fo diam do yagu bb degue rek gua wakh ❤
@@fatousamb9181 dafa am niou soxor quoi addina bi koufi neck daga neubatou ba am Lo beugue sino rk niou kar sa mame bou officielle nk nga zeulé zosé def loula saff an xarit dou deuge😂😂
Dieukeur dji immature n'a😂😂
Bi yagahna wala
Ay way li nèkh djuekeur nala nop li dafa nèkh si couple di kaff dih rèi
Nakh sa bope ayoul di🤣🤣
Salut mais vs savez le prix de diamant
Toi sais ?
Diaman oui diamant
Diamant loumiy djar nguir yalla ?
Vraiment kii dafa bari wax saga gougn la sax
Machalla
Li dou information
Yen niguen meuner doulllllll dama yem mn 😂😂
Warou wone tasss
Qu'est-ce qu'un homme fait avec un bracelet en diamant alors que l'Islam lui interdit l'or. Thiey Yalla Sénégal
Souniou yone nékousi
Genre ki kenn di filmer aussi am na diott
Mais yén loutakh gnuéne sokhor bayiléne diambour waye
Cmmtr YII AM NIOU BONE SOKHOR BAKHOUL
Machallah ❤
sénégalais pour mome nieupa sokhor ms sokhorougnou dé amna yo xamni khel nagou wouko 😂
😂😂😂😂😂😂😂
Nice 💋💋💋❤️
Diama dee yombal nguene ko 😂
Boye loy ligiu
hummmm marioooo
Doule rec diamant bou wa Sénégal
Je ne suis pas méchante mais vous aimez trop se vanter ndakhté foumouy dieulé diamant arrêt way
Goor gou meuneu diayy taar rékk la bagne foko fékk dépense samm dou matteu tchim soff ngéne😭😭😭😭
Yal naléne yala defal diam mé sa waye gorr nak daye am foula tamit seuy a vie la
ayyen laff thiate
♥️♥️♥️♥️
Ay way gnanaléne gni moguene critiques bou baribi amna droit sagal diabarame sassss senégalé mitina
Warguene gnou may diam yeneu site yi sof guene trop guene di doul nane diama
Nila dé diabaar daal khaalé
🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰
🥰🥰🥰
Diamant xamna walla Milliard nonou la yombee Si senegalais yii
Diamant bima done dégueu temps boy lá wala da mel légui diafétoul
Mane yen ngen meune yok ak tawi la khamoul meune Nguen doul
Aka nio mana wanéwo Li losi diarr wané
J'espère que do gaga thiate lou rek🤣🤣🤣
C'est le mari qui doit donné une bague à sa femme
MBA bou yangué dounguéne doug si lounguene mounoul diaman 😢
Massalla
Si xalissou djeukeureum la dieundeul djeukeureum bracelet en diamant 😂
Sank batey mangui khalaat ni kay la meuneu démé 😂😂
Neysan khalé mo nékha nakh kom gueum nguén diamat ni nane khaliss dieukkeureum diamat sénégal yéppou pour amoul kouko fi mana dieund diaro diamat peut couté milliard enplus nékhoul guiss sénégal deukkeu bi banalissé milliard diamat léppou révé lo dof yi kou ci dadialé 1million dém dubai di nakhaté seye kat yi seye lén té yalla takh gayi dagnou léndi nakh dém dubai beu gneuw seu dieukeur diékhal apres thiow beuri mofi am
Wa kou gorr ki simplewoul dh🙄
🤣🤣
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
🥰🥰🥰🥰🥰
😄😄😄😄😄
Neubeutoulen bakhna rek gnemer Ken beut li lou si diar waner
Diekeur dji mo beug buzz rek