Colobane: La famille Ndoye exprime leur tristesse après la démolition des 2 maisons "Démb Nélawougn"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 15 янв 2025

Комментарии • 38

  • @itools2514
    @itools2514 9 часов назад +12

    Les ferrailleurs si guinaw, thieuy yalla. Le bien des uns fait le malheur des autres.😮‍💨

  • @DegueneDiop-e3v
    @DegueneDiop-e3v 6 часов назад +7

    Lii métina bilaye lingua wakh leup deugueuleu man mi fofou la yaro yalna yalla leral Si Barker Serigne Babacar Sy

  • @binetousow5016
    @binetousow5016 11 минут назад +1

    Koudoule khalate yalla loula nékhe défal adouna yaguoule

  • @Badboydieme4963
    @Badboydieme4963 9 часов назад +5

    C’est triste mais du courage

  • @malick-yc2tq
    @malick-yc2tq 7 часов назад +5

    😢Khana gni Amougnou Avocat? On sent qu'il y a bcp de non dit dans cette affaire, car aucun ou une partie des héritiers ne peuvent vendre le bien. Le notaire avec le certificat d'hérédité de la famille est obligé de les informer et de recueillir le consentement et la signature de chacun...

  • @xellxellu9160
    @xellxellu9160 8 часов назад +7

    Wa léguii nagne léne delo sén khaliss lingéne djota dougueul

    • @NG-uh7fm
      @NG-uh7fm Час назад

      Banque aye sathie katt laniou khaliss biii dougne lenko deloo ou bien dinagn len dawlo lou yag yagg

  • @astouciss4961
    @astouciss4961 9 часов назад +4

    Dou yoonsou fékei li mou waax deug la sommation dafa wara ame, li léroul dé en plu 2 maisons c triste😪

  • @matythiam7667
    @matythiam7667 7 часов назад +3

    Yallah Nalen Yallah diapalé

  • @ElhadjiBiraneToure-k1b
    @ElhadjiBiraneToure-k1b 47 минут назад

    Sénégal dou rew lafal ndaye rew mi amonio bene yeurmande 😢😢

  • @bassidoumbia6854
    @bassidoumbia6854 Час назад

    Lou lér la lén di wokh , senegal sathieu rek mo fi am

  • @mogettdofbi3058
    @mogettdofbi3058 8 часов назад +6

    Li niawna trop ki dèf dieuf diou niaw dji yallnako yalla attè ak yènn 😭😭😭

    • @AdjiNdiaye-bb3qj
      @AdjiNdiaye-bb3qj 5 часов назад +1

      Amine 😭😭 li meti na
      Djiguen yi amoul fougnou dieum rek lay dioy

  • @nogayeba869
    @nogayeba869 8 часов назад +2

    Sénégal dou neha defar deh tout se fait en irrégularité

  • @DabaDabista
    @DabaDabista 19 минут назад

    J'ai le cœur ❤️ meurtri président diomaye diapalelene famille ndoyene 😢

  • @DjbySow-k1t
    @DjbySow-k1t 35 минут назад

    Yalla naléne takhawou

  • @koromosmajuliius1289
    @koromosmajuliius1289 9 часов назад +12

    Il y’a beaucoup de non-dits dans cette histoire. Qui a vendu la maison ? Qui a signer la rètrocession ? La maison a t’elle ètait saisi pour non payments. ? Si oui par qui ? Si non etc… ????

    • @LampFall-cs1mo
      @LampFall-cs1mo 6 часов назад +1

      Oui ces trop facile une maison de famille comment deux personnes peuvent signer l’acte de vente ?

    • @AdjiNdiaye-bb3qj
      @AdjiNdiaye-bb3qj 5 часов назад +1

      Gni def li dougn am diameu mouk

  • @AbdouNgom-t4y
    @AbdouNgom-t4y 5 часов назад +1

    Sénégal nak li warnane c'est wakh 😭😭😭

  • @bassidoumbia6854
    @bassidoumbia6854 Час назад

    Décision justice ,huissier et notaire zéro, thi li ...Boulogne bayi dara.. yallah tégoul Ken injustice .mbirmi ya lén di ko réglél sen bopp

  • @nogayeba869
    @nogayeba869 8 часов назад +2

    Wa keur gui nan lei deme koumay expliquer 😮

  • @salioudieng3294
    @salioudieng3294 7 часов назад +2

    Wa xana dou Môr Talla Fàll sandaga dh bi wally dii woy dh

  • @AbdouDiallo-o8n
    @AbdouDiallo-o8n 2 часа назад +1

    Pa bi tamite beugue na micro trope

  • @diamboyediallo9728
    @diamboyediallo9728 Час назад

    Lébou yi mo mom Dakar le reste faut rentré

  • @diamboyediallo9728
    @diamboyediallo9728 Час назад

    Dakar c'est pour les lébou le reste faut rentré

  • @bassidoumbia6854
    @bassidoumbia6854 Час назад

    Yogourt commissaire nékoul si diaye keur

  • @massambandiaye6150
    @massambandiaye6150 8 часов назад +2

    Sougnouko défaraté bo carreaux ko rek thiossane bi daw bouguoul keurguou raféte

  • @mamediarrandiaye9757
    @mamediarrandiaye9757 7 часов назад +1

    Ay way niar keur yeup tmt ki df lii df na lou niaw meunone na bayi beine bi sakh

  • @sayesene9075
    @sayesene9075 3 часа назад +1

    Métina dal

  • @DjbySow-k1t
    @DjbySow-k1t 25 минут назад

    Tieye 15:12 adouna yagoul l'âne moy li senegalai mo sokhor

  • @nogayeba869
    @nogayeba869 7 часов назад +3

    Depuis 15ans ngen yeuk ni diay nanou keur gui
    Si ngen wara hamni momo len ko
    Metina mais yena deuk si keur diambour
    Deug nehoul mais yena togne sen bop

  • @nderrysokhna8302
    @nderrysokhna8302 7 часов назад

    Toukh bakhoul

  • @mordiop705
    @mordiop705 5 часов назад

    Am guenn thiagante dé yénn famille bi