Bayiléne cas té liguéye, yallah souteureu le beugueu té sénégal bou beugué ame diame yénénté lén diam gniakeu féydé rawoule ame aye télé pour cas yaka doumou adama subkhanala 😢
Limalen Di wax dall Moy nit kou ragal yalla té gnémé DEUG dou nafékh.bayilen kou def Lou bone yalla weerla nguen diko défendre ndax kounioufi teudéwone sa:dome,sa diabar,sa Rak ,sa mag,sa yaye MBA sa karité dinga wax ba nieup daw.mame mom sama yone nékoul si Lou nit def té adouna diotou weer ken wayé kou bayiwoul def Lou bone wala nga diko wax yalla dinala weral bopam.wassalam 🙏
Bayilen Di défendre Serigne siy def Lou bone diwax nane nit gni amouniou soutoureu,kou soutoural sa bop yalla soutoural leuh.lou way Di woté naka wouyo.té Serigne DEUG bou gueum yalla,xam yalla té ragal KO doko meussa degue si afairou teudé djiguen,wala Ay lomotif MBA Ay vidéo ak audio fuites.
Non mais ndioba iow do até DEUG té sa genre yi nio takh kou def Lou bone diko ndamo.c vrai soutoureu Lou War leuh mais d'où raison bouwara tax kounek didef Loula nex.c inadmissible kun Serigne kom Modou lo jr Di woté né nitou yalla leuh,am diabar baparé Di teudé diabarou diambour .même souko teudéwoul sax le fait ke xélam rek Di nek si mom rek dafa xaram waxatouma Mouy wax ak mom Ay waxitiaga,wax you salté
Xana Kone Ay Say Say you déguisé Serigne laniou.serigne you bax yi té ragal yalla baparé gueum KO ken dalen meussa dégue si Lou bone?prenez l'exemple de:cheikh ahmadou bamba,mame cheikh Ibra fall,cheikh tidiane Cherif,seydina limamou laye,boukounta peut être ceux sont des anciens mais les jeunes Serignes ou les récents kom:Serigne Abdou Karim mbacké,cheikh ndigueul fall,Serigne Modou menda fall,Serigne Abdoulaye fall ndar ou même Serigne makhfouss mbacké, Kane nga meussa dégue si gni né def Nanou louni mel amoul parcek gni dano am diné am yalla ,ragal yalla té am louniouy diomb.
Sou fékone ni kou amoul dieukeur ladone waxal sax Mani aaah goor leuh amna droit ba 4 femmes mais diabarou diambour mom BAFA la toudou.c vrai nul n'est parfait koudoul yalla dina dioum wayé Soula yalla teralé def la nga done kou am baat,so wakhé nieup dila deglou ak dila bayi xel ndax diné biniou guiss si iow ndaga wara noot sa bakane si Lou bari,moytou djiguen wala goor boula léwagoul té Di soralé ni iow nitou diné nga ba takh nga wara diombalé sa bop Lou bari.

Douyenalene def yalla nangougueni Serigne nitla
Deflou nehoul yalla.ak di diema katt diabarou diamdour.dou benn kousi d'accord rek nanagou niou nee diabaram danioukoy katt
Ken hehoulen.diabarou diambour loutah gakoy nan damalay katt?
Bayilen Di défendre Serigne siy def Lou bone diwax nane nit gni amouniou soutoureu,kou soutoural sa bop yalla soutoural leuh.lou way Di woté naka wouyo.té Serigne DEUG bou gueum yalla,xam yalla té ragal KO doko meussa degue si afairou teudé djiguen,wala Ay lomotif MBA Ay vidéo ak audio fuites.
Non mais ndioba iow do até DEUG té sa genre yi nio takh kou def Lou bone diko ndamo.c vrai soutoureu Lou War leuh mais d'où raison bouwara tax kounek didef Loula nex.c inadmissible kun Serigne kom Modou lo jr Di woté né nitou yalla leuh,am diabar baparé Di teudé diabarou diambour .même souko teudéwoul sax le fait ke xélam rek Di nek si mom rek dafa xaram waxatouma Mouy wax ak mom Ay waxitiaga,wax you salté
Xana Kone Ay Say Say you déguisé Serigne laniou.serigne you bax yi té ragal yalla baparé gueum KO ken dalen meussa dégue si Lou bone?prenez l'exemple de:cheikh ahmadou bamba,mame cheikh Ibra fall,cheikh tidiane Cherif,seydina limamou laye,boukounta peut être ceux sont des anciens mais les jeunes Serignes ou les récents kom:Serigne Abdou Karim mbacké,cheikh ndigueul fall,Serigne Modou menda fall,Serigne Abdoulaye fall ndar ou même Serigne makhfouss mbacké, Kane nga meussa dégue si gni né def Nanou louni mel amoul parcek gni dano am diné am yalla ,ragal yalla té am louniouy diomb.
Sou fékone ni kou amoul dieukeur ladone waxal sax Mani aaah goor leuh amna droit ba 4 femmes mais diabarou diambour mom BAFA la toudou.c vrai nul n'est parfait koudoul yalla dina dioum wayé Soula yalla teralé def la nga done kou am baat,so wakhé nieup dila deglou ak dila bayi xel ndax diné biniou guiss si iow ndaga wara noot sa bakane si Lou bari,moytou djiguen wala goor boula léwagoul té Di soralé ni iow nitou diné nga ba takh nga wara diombalé sa bop Lou bari.
Walahi
Gou si moytoul Adamo kaliphone ak choco no stress
Thay kii moom diambar nga sotora dé dafa bakh lool
😊😊😊😊
Mbodja kkhana dou mom lagn Iri wone petit mbao Mouy Katanté .. motakh Mouy faral Serigne Modou lo Mbalou 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂😂😅😅😮😢🌹 🙏🏿 👍🏿 ✌🏿 🤚🏿
Deflou nehoul yalla.ak di diema katt diabarou diamdour.dou benn
Mbodia la nobb
Nopal siyawla djeum tarikhayi amounou ndiarign
Macha Allah way 😂😂😂
3 person Adamo choco kalipone niamo yaco deucbi
Bou fekon ligene di wote degue la dougen si débat dagen di madou
❤
D'avaler torop
nafkh 😂😂😂😂
Thia deug deug
Boul wakh lolo amna nio défoule dara lo bon
Yallay sutu RAL nit réck
None amoule 😂
Kémenoul retieu
Deug la
😅😅😅😅😅😅
Deugupir