Pour moi cette chanson est une continuité de votre ancien son xarrnou bi de façon spirituelle... Très cool si vous êtes d'accord avec moi 👇tegualle sa barame
Bilay Kilifë tu as fais revivre nos grands-parents, sama maam sank lakoy deglou xol bi sedd gouy, Une musik d'un instrument traditionnel "xalam" dans un rythme et les paroles de Serigne Moussa ka le griot de Cheikh Ahmadou Bamba, grand écrivain de la langue wolof... Avc ce genre de musik nos grands-parents peuvent en consommer Lii mooy musique, ça doit être universelle ✌❤❤🙏
Dieureudieuf Kilifeu.. Merci d'avoir vérifié Salimtoo .. wooy bi yagueu neu. Tu es un artiste complet.. tu sors chaque fois là où personne ne t'attendait. Ndanane daay beuri feem. Longue vie et santé de fer à toi.
Et Voilà un exemple de musique qui s'inspire d'une attitude mythico- magico- religieuse. Xol toyna. Xol sedd na. Kilifeu magana Wané nani legui diotna keurgui am Kilifeu. Yallana Sakh.
Machalla billahi sama xoll dafa sedd seringe mountakh dama ko beugue teop yalla nafii yangue té wer killifa amal diamou lii Nic nice na trop respect sii yaw
Ndaye sane machalla kilifeu boul tégiu sa tank moukou ndakh yaw mane nga lingaye déf kone geunela diapou li ndakh kéne daxoulako barki s saliou fima tok mangiu noss mai li dafa nékh yallana bat bi geuene wér barki brome touba machalla
Vraiment kilifeu tu es excellent si j'avais des milliards je vous les donnerais au nom de cheikh ahmadou bamba la paix en tant que kaolackoise je vous kiffe de tout coeur💖💖💖
OMG !!! J'étais ému srx en fait je viens de découvrir une autre face de kilifeu Il a été vrm au top dans ce morceau et cette chanson reste tjrs dans les cœur des sénégalais malgrés qu'elle fait des décennies...champion tu viens d'honorer ta réputation dans la musik sénégalaise..Respect !!!! En tout cas tu devrais chanter plus souvent c'est cool
Alkhamdoulilah une autre facette de ce groupe mythique de la scène musicale du Sénégal. Votre engagement pour un Sénégal meilleur n'est plus à prouver. Le moment est bien choisi. Dieureudieuf Keur Gui
Ku Sorpa Serigne Fallou beussal j'aime
Akassa
Machala xol sédeuti neu
Hatib Luqman Njie dieureudieuf serigne touba
Je suis tidiane , j’aime les mourides.
Souvent je me vois dans eux leur courage de bosser
Peace and love
❤❤
Ma challah amal diamou rek
S8 fier de tw
aliou seydina diadieuf Talibé Chékhe bou deugou bi
Diambar lép bén la contane si yow
Machalla kou beug kilifeu beusal j'aime ma guis
Kou beugue serigne touba beuseul j'aime
Non!!li nekhna way. Merci kilifeu
Masha'Allah amna solo, serigne Mountakha Mbacké yalla nafi yague loole té and'ak wër kou déf👍🏿 yalla naguafi yagg
Peu importe ce que tu dis, jummay touba dji rek doyna nguir ma like. Dieureudieuf Kou tede qui.
Pour moi cette chanson est une continuité de votre ancien son xarrnou bi de façon spirituelle... Très cool si vous êtes d'accord avec moi 👇tegualle sa barame
mashala respet
Ça me rappelle : Ana xalé yi demlen woté ji agn😅
ndeysan les petits sont grandis
Merci kilifa👍
Bilakhi magui dioy yala naga ame diam si bakhé serigne Fallilou
premier commentaires goor yalla deug moy kilifeu
Nice nice Nice
Machallah
@@thiamcomedie1608 bidrw
@@thiamcomedie1608
M
Mach'Allah Mach'Allah Mach'Allah
Thieyyyyyy kilifeu encore une fois merci bonne continuation! ! Wahk toutiiii djeuffff beuri
Machalla rafetna way Kou andak man pouce bleu 1er vu
marci
Des millions de vue si barkei Serigne Touba 👌🏾❤️👌🏾
Kilifeu diam si ioe clip bi rafétna trop Machalah ❤️ Serigne Mountakha yalnafi yague teh Wérr barki yonentibi psl 🙏🏽🙏🏽
Bilay Kilifë tu as fais revivre nos grands-parents, sama maam sank lakoy deglou xol bi sedd gouy,
Une musik d'un instrument traditionnel "xalam" dans un rythme et les paroles de Serigne Moussa ka le griot de Cheikh Ahmadou Bamba, grand écrivain de la langue wolof...
Avc ce genre de musik nos grands-parents peuvent en consommer
Lii mooy musique, ça doit être universelle ✌❤❤🙏
Kilifeu insaàlla no ngi laay ñaanal ci Yàlla nga guéen prison Aamiin
Machallah kilifeu yalla na mourride yépou am diamu si barké Serigne saliou🙏🙏
Kilifeu machalah li mourid rek mokay déff bonne continuation !
Barki Serigne Touba dama beugg *Serigne Mountakha* 😍😍😍😍😭😭😭😭😭goudou fane akk wérrr Mbacké Balla Aïssa 💕noumay déff ba guiss la🤔😭🙈
Nice
Ce mixte entre le spirituel (khassida) et le temporel (musique) dans une mélodie que tout un chacun peut écouter
Balla Ndiaye. Kel commentaire. Très bien inspiré
Kilifeu yalna yalla fay la barkêp s touba sama khol sedna lol thi iow
Ceux qui pensaient que ce gars est fou sont loin de le connaitre mach'Allah voilà du lourd
Au Sénégal les fous sont ceux qui défendent leur peuple et les saints sont ceux qui pillent nos ressources
Kène dou serigne touba billahii kilifeu lingua musik nekhna machalla yalla nala borom touba fayale bopam
Chair de poule
Serigne Mountaha yallah na fi yag té wer ❤
Diadieufff way kilifeu.dieureudieuf Serigne Touba
Cette chanson me rappelle mon enfance quand tu l'entendais à la radio ct l'heure de manger
Thiey Ahmadou Bamba
Guina santati sounou borome bimouma deffé sénégalais dieurediefi khadimoul rassoulilahi
Kel inspiration boul tite dara sa kaw sa kaname amal diam rek on est toujours derrière tw mon frère ❤️❤️💯💯💯
Machala machala machala Macky sall sakh aimer na machala kilifeu dieredieufety serigne bamba
Thiébou midi rek lamay fatali au temps
Seul les vrais connaissent ✌salimto
Bilay kouko deiggg rk xamni heurou agn diotna
Moi je suis un talibé baye niass mais kilifeu je t'en courage l'islam si kaW si kanam yalla na diam yague Sénégal
Man beguena la de wawaw ndah man mom loulal si s touba rek machalla
Dieureudieuf Kilifeu.. Merci d'avoir vérifié Salimtoo .. wooy bi yagueu neu. Tu es un artiste complet.. tu sors chaque fois là où personne ne t'attendait. Ndanane daay beuri feem. Longue vie et santé de fer à toi.
Je suis en Italy Kilifeu yaw ken dou yaw yalna yalla werel batbi te mayla linga beug amiine, yalnaniu yalla na ngoul sunu koor
Machalla 🙏🙏🙏🙏Cheikh Mouhmadoul mountakha Mbacke khalifa Gènëral de mourite Yalna fi Yageu Tëii wërr 👏👏
Ma sha Allah kilifeu.... SERIGNE FALLOU PROTEGE.... guen GUEUM geuneu GUEUN....
...............
Ooooh bilay Kilifeu tu m'as touché ligay weuy fii sama khol la dougou bilay walay serigne Mountakha yalna yallah yagal takhaw ak ben kilifeu si rewmi
Machallah mat nga Kilifeu nak. ..Xarnu Bi. ..Salimtoo. Jerejef Baay Karim
Nekh na trop ndeysane serigne touba louko waye wakhall thilou bakh mou nekh ❤❤❤❤❤❤
J’ai des frissons en écoutant ce morceau. Good job
Kou begue serigne touba Bessel jamais
No no no no li nekhna si khole magui thoiye Sénégal diam reck
Malgré que je ne suis pas mouride c'est la chanson de lannee qui est d'accord sa baram
Mbacké balla,yague fih looool té weur. .
Akassa kilifeu sétena wéthieu machaallah...
Big-up !!!!
Et Voilà un exemple de musique qui s'inspire d'une attitude mythico- magico- religieuse.
Xol toyna.
Xol sedd na.
Kilifeu magana
Wané nani legui diotna keurgui am Kilifeu.
Yallana Sakh.
Machalla billahi sama xoll dafa sedd seringe mountakh dama ko beugue teop yalla nafii yangue té wer killifa amal diamou lii Nic nice na trop respect sii yaw
Bilahi serigne touba amoul morome mome d dafaye defare waye dou yak Dieureudieufeuty Ahmadou Bamba
AMINEEEE YALLA NALA YALLA FAYE FAYOUK GUÍENNE GUI WAY SI BOTI DAME AY BIIR YOU REUY DEF WAYI KHARNO BIE
Serigne Fallou Yallah na Yallah Yokk Léram ci Barké Yonente bi psl 🙏🏽💕🙏🏽💕
Machalla kilifa yallana serigne bi faye waaay kontan thi yaww rk
diadieuf mourite amna solo yalla nala serigne touba faaye
Ndaye sane machalla kilifeu boul tégiu sa tank moukou ndakh yaw mane nga lingaye déf kone geunela diapou li ndakh kéne daxoulako barki s saliou fima tok mangiu noss mai li dafa nékh yallana bat bi geuene wér barki brome touba machalla
Machallah kilifeu lii nékhna loll séde na xoll trop جزاك لله خير أطال الله عمرك بركة شيح أحمد بمب
Vraiment c est du lourd fall gayi est comprendre nagnou dimension son bi c est fort
Nekh na trop merci tonton kilifa❤❤❤😍
Ham kilifeu rék moy li Ham solo Dieuredieuféty Sergine Touba
Maschala yalla Nga yok si barke berome touba
Akassa fall yaram ndamo yag yokou andak wére ak tawfékh barké borom touba mbacke
Machahala serigne montaha yalla na fi yague lol te wer
salimtou minal lahdahi touran mahaltidja li rabbi wa baboullahi lamyakou mourtadja!!!akassa mouride bountou ya dieum sounou boroom gnoun serigne touba gnou koy diktal.
eskey cette chanson me rappelle beaucoup de chose avec cet xalam et la voix magnifique de kilifeu machalah
Macha allahou j'aime bien.je l'ecoute presk chak jour
Allahou akbar lii dei nekhnama lool barki s Mountakha
Machalah tawfekh rek kilifa
Machaalah kilifeu yalla na yalla wéreul bate bi barké brome touba
Barke Mame cheikh fall lamp kilifa machalla dinga fi diar tak ni lamp bi bamba tall
Nekhna nekhna nekhna
C'est un tres Bon rebondissement apres avoir perdu le combat Politique. Nila goné day mague. J'apprecie
sama xol sèdd na barkè Serigne fallou
Bambi nokoul fale aksa batte bou khour bi yaw mouno woye bayil force gui
Vraiment kilifeu tu es excellent si j'avais des milliards je vous les donnerais au nom de cheikh ahmadou bamba la paix en tant que kaolackoise je vous kiffe de tout coeur💖💖💖
Machallah amna solo lole kharnouby nékhna lole waye yalla nala yalla takhawou
Qui l'écoute en 2020 ce tube spirituel de Kilifa respect
Nite bou amé kilifa rek bakh. Mancha Allah
OMG !!! J'étais ému srx en fait je viens de découvrir une autre face de kilifeu
Il a été vrm au top dans ce morceau et cette chanson reste tjrs dans les cœur des sénégalais malgrés qu'elle fait des décennies...champion tu viens d'honorer ta réputation dans la musik sénégalaise..Respect !!!!
En tout cas tu devrais chanter plus souvent c'est cool
Je suis nigérien j'aime kilifeu &thiatt
Bilah j vs aime
Waynako seuhrou ramadane ngire yalla natal kharnou ❤️❤️❤️❤️❤️amine
Machalla kilifa yalla nala yalla défal djamou djou sah
Bilahi dama la masa contre mais léki momm damala beugue toropp 👌👌
Nice son joli clip xarnou bi Yalla nafi diaré natte ba faw way🙏🙏
ndame rek kilifa si barkei kou teide ki👌👌
Machalla diarama fall
😭😭😭😭😭😭😭joyou ma nakhar 🙈contane day joy lo nit Bilay certe douma lay suivre mais danga ma yagu neikh 🙏🏾yana yalla kheip doli 👌🏾
Merci KILIFEU d'avoir retracé des temps et moments exceptionnels du morceau salimto et nous replonge dans le passé
Akassa machallah clips bi Raffétna trop Son bi machallah diadjeuff kilifeu
BILAHI KHÔL TOYNA TAY KHARNOUBILA👌👌👌👌😭😭😭
Yala na yala wereul voix bi ak thieur yi. Amena solo lool
machala amena solo, yalla na yalla yoka weural batt bi
Jeureujeuf KOU TÉÉDD KI SERIGNE TOUBA
thieuy serigne touba billahi Senegal yépp warnano bolo sante serigne touba té yalla rek takh 😭😭
No fathie nguama j'ai pleuré tout l'allmagne
Alkhamdoulilah une autre facette de ce groupe mythique de la scène musicale du Sénégal.
Votre engagement pour un Sénégal meilleur n'est plus à prouver.
Le moment est bien choisi.
Dieureudieuf Keur Gui
Mach'allah li mom dekko yagg di deff nekh si kholll
Mo geune yénénn wayy yiga dann génnn fess dell ak ay saaga
J'apprécie vraiment
Ma challah nekhena trop billahi amall diamou rek yaw
Ndeysane li nekh na lol machalla kilifeu
Machallah amna solo dh yalla nala yalla defal diam
Bineta camara yalna deké firdawsi😭😭😭🙏🏽
ndayesan amnasolo mouride waougor kilifa
Manchallah kilifeu gor Yalla deugue billahi
big love frère très Nice