Loutakh ngen dag partie bimouy woy diaga. On est tous content de Wally nimou douyé Adidas Arena Guichet fermé❤. Entrée bi c'était trop émouvant. Spectacle de ouf 🔥 Li metshop di wakh Histoire dinako bind mongui soga am sens. Premier artiste sénégalais ouest africain à Adidas Arena guichet fermé billets 69 euros, 100 euros, 150 euros. Billeterie ouverte en moins de 2 mois. La communication était plutôt "Tela gen" ndakh khamone nagn ni day fess. Les fans sont venus avec leur parapluie car il pleuvait comme quoi ni la pluie ni rien ni personne ne peut empêcher aux gens d'assister au concert de Wally. Kou bolé Nianou wadiour + Barké bay + Khol bou rafet kokou doumana am défaite. Kouné diarnafi dome de Paris daw mo geunone méti, kou bayiwoul wally si gathié ngay deuk moy ma tayou yalla 😅❤. Prochaine destination U ARENA niou adjat level bi 🦾
Proud of this Guy ! La chose la plus difficile c’est de perpétuer un héritage et pour preuve : Zidane, Ronaldinho, Mandela n’ont aucun un enfant de leur dimension. La liste est longue, mais je suis certains que Père Thione peut se reposer avec un sentiment d’accomplissement en ayant légué pour la postérité ! Wally, tu es un grand Monsieur and you will never walk alone ❤
Tak leine écouteur pour kham neikhaay bi 😢wouyyy wally nala diam ak soutoureu sonal🙏billahi wallahi in t'aime lo def neikh nagnou barki Seydina Mouhamed psl❤️❤️❤️
Les entourage de wally son meilleur sur tout le domaine dp 2009 chaque jour wally reste meilleur de ça génération ici au Sénégal 🇸🇳 merci a tous l’entourage de wbs ❤❤❤🫡🫡🫡🫡🫡🫡😊
Le chanteur du peuple the king of the king le meilleur chanteur du monde bientôt 3 millions d'abonnés de sur youtube le peuple sénégalais est dernier toi concer bi réussir neuh machalah ❤🎉💪🇸🇳🙏👑🎤🏆
Papa Thione yalla na Firdawsi di sa keur🙏❤️ way na lepp bayi fi ✨ Wally beugue nala trop mais nima mel si papa Thione da eup. Yoe tu es le fruit de ligueyou ndeye ak baye. Doxalal Mar Yacine
Hooo machallah sante yalla bu bax way marr yall nala yalla geun taxawu soun xol yi sedna trop siguil nga afrique dama diéllalé Sénégal félicitations ❤❤❤❤🎉i love you bro nala diamou sonal niou dieuli disque dor bi Inch’ALLAH 2025 na battt geun wéree amine
Adidas Arena que de bons Souvenirs❤ Machallah au Mois d’ Avril, j ‘ y étais quand on m ‘ a sélectionné en tant que volontaire au JO Paris 2024 et Samedi Passé au Concert du “ King of The” où j’ ai fait une overdose de danse😂Fethieu beu Mandi😅
Blh c’est le Sénégal 🇸🇳 est très fier de vous parce que le pays a fait tour du monde 🗺️ grâce à vous , vous faites parti on est fier de vous 👍 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ les gens qui te critique sont plus fans de toi que nous même ils n’ont pas accès de te parler en face ils regardent des motifs pour qu’ils soient reconnaître ou avoir buzz c’est seulement mais si on pouvait ouvrir leurs cœurs ♥️ après Dieu et PSL c’est toi après leurs parents. U arena 205-2026 Inchalah ♥️🤞
@Papidiop-d5b réseaux sociaux dal mo diokh gars you impolis paroles gnou saga noum lene nekhé. Mon commentaire était plutôt pour dire que khep nagn bercy, stade de France lagn beug. Temps wou dem séti combien il ya des places dans chaque stade sakh la amoul faf... bref
J'ai tant attendue le live j'ai même pensé dou ame live ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤le chanteur du peuple ❤❤❤❤mais il faut toujours reprendre le son de ton paix surtout la partie 10mn😊❤
Attendons le plateau debrief sûrement y aura des images des moments marquants du concert vue que c'est Wido qui a le droit de diffusion je crois . Proud of you. Le concert était extraordinaire, une marrée humaine ❤️
Le meilleur Lou Waw kong kimoy thé king off the li histoire dinako bind tro djo akh mborodjio Dou béneu Bilay y’a Mane Mar yacine Ohh mba khôl yagui fékh 🩷❤️🔥 mayko ayy cœur ♥️ y’a khérré
Ana gni togone si bountou youtube bi 😂? Félicitations Wally borom guichet fermé yi , linga def adidas arena histoire dinako bind. Adidas arena khadjofa Bercy wala U Arena 2025, yaw amal date rek et les faramareen s'occupent du reste gneuw inondé ko. Je pense que c'est Wido qui a acheté la diffusion du spectacle motakh on ne peut pas avoir la vidéo
Papa Thione yalla n’a yalla yessal yeurmandé sa kaw ak kep kofa fek ak koula fa fek 😢
Amine yarabi
Kou fier si wally en tant que sénégalais rek lalal j'aime 🎉🎉🎉
❤❤❤
J’suis fière de lui 🎉
Début bi c’est vraiment touchant la manière dont il a rendu hommage à son papa ❤😭🕊️
Loutakh ngen dag partie bimouy woy diaga. On est tous content de Wally nimou douyé Adidas Arena Guichet fermé❤. Entrée bi c'était trop émouvant. Spectacle de ouf 🔥 Li metshop di wakh Histoire dinako bind mongui soga am sens. Premier artiste sénégalais ouest africain à Adidas Arena guichet fermé billets 69 euros, 100 euros, 150 euros. Billeterie ouverte en moins de 2 mois. La communication était plutôt "Tela gen" ndakh khamone nagn ni day fess. Les fans sont venus avec leur parapluie car il pleuvait comme quoi ni la pluie ni rien ni personne ne peut empêcher aux gens d'assister au concert de Wally. Kou bolé Nianou wadiour + Barké bay + Khol bou rafet kokou doumana am défaite. Kouné diarnafi dome de Paris daw mo geunone méti, kou bayiwoul wally si gathié ngay deuk moy ma tayou yalla 😅❤. Prochaine destination U ARENA niou adjat level bi 🦾
Machala sa commentaire am chance ❤❤❤❤
T'as tout dit ❤
Wawaw inchallah ❤
Proud of this Guy !
La chose la plus difficile c’est de perpétuer un héritage et pour preuve : Zidane, Ronaldinho, Mandela n’ont aucun un enfant de leur dimension.
La liste est longue, mais je suis certains que Père Thione peut se reposer avec un sentiment d’accomplissement en ayant légué pour la postérité !
Wally, tu es un grand Monsieur and you will never walk alone ❤
Bilahi 🎉il est un bon fils
Tak leine écouteur pour kham neikhaay bi 😢wouyyy wally nala diam ak soutoureu sonal🙏billahi wallahi in t'aime lo def neikh nagnou barki Seydina Mouhamed psl❤️❤️❤️
Walla activité Bluetooth lou nekh wayyyy😂❤❤❤
Bilay waxall
Adidas bi mom c'est 20/20 walahi amoul noumou nékhoulé FÉLICITATIONS WALY tu le mérite de cœur
Les entourage de wally son meilleur sur tout le domaine dp 2009 chaque jour wally reste meilleur de ça génération ici au Sénégal 🇸🇳 merci a tous l’entourage de wbs ❤❤❤🫡🫡🫡🫡🫡🫡😊
Merci à eumeudy si organisation bi. Boul bagn kou la méré, tu as bien fait ton boulot🎉
Il fait la fierté de l'Afrique surtout Sénégal mar ont t'aime très fort 💖❤
Meilleur concert de Paris pour l’instant ❤️❤️❤️❤️❤️tout était au rendez-vous spectacle son et lumière ❤️❤️😂❤️😍❤️😍❤️😍❤️😍❤️machalla laff thiat❤️❤️❤️❤️❤️
Attention attention waly ballago seck nommé le chanteurs d'année 2024 merci 🎉🎉🎉🎉🎉
Le chanteur du peuple the king of the king le meilleur chanteur du monde bientôt 3 millions d'abonnés de sur youtube le peuple sénégalais est dernier toi concer bi réussir neuh machalah ❤🎉💪🇸🇳🙏👑🎤🏆
❤❤
Feu ler mn cousin de valeur😊
@@sidysow6472bilahi sidy wally ❤🎉
L’international bilay ya woor❤️💪🏾👑
Papa Thione ak Diaga ndeysane💔
Sen doom soll na Jereh Kelifah gi😢🤲🏾
We Love U Seck,Benen Wally la,Si kaw si kanam in shaa Allah ❤️❤️❤️❤️❤️
Papa Thione yalla na Firdawsi di sa keur🙏❤️ way na lepp bayi fi ✨ Wally beugue nala trop mais nima mel si papa Thione da eup. Yoe tu es le fruit de ligueyou ndeye ak baye. Doxalal Mar Yacine
Waly seck le golden boy de la musique 🎶 sénégalaise tu fais la fierté sénégalaise wally balago seck on t'aime ❤❤❤
Bilahi yalna yalla goudal fanam tee mayko wer ak werlee.
Hooo machallah sante yalla bu bax way marr yall nala yalla geun taxawu soun xol yi sedna trop siguil nga afrique dama diéllalé Sénégal félicitations ❤❤❤❤🎉i love you bro nala diamou sonal niou dieuli disque dor bi Inch’ALLAH 2025 na battt geun wéree amine
🎉🎉🎉
Il transfère ses deuils de ses dernières années par ses paroles, ce qui le rend plus extraordinaire en musique.
Li tourou neuuuuu way❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J’écoutais que les anciens avant, mais yaw mom ta musique me rend happy, thank you for that. Je t’écoute tout le temps
Félicitations Wally.Tu es le King, notre fierté.
Adidas Arena que de bons Souvenirs❤ Machallah au Mois d’ Avril, j ‘ y étais quand on m ‘ a sélectionné en tant que volontaire au JO Paris 2024 et Samedi Passé au Concert du “ King of The” où j’ ai fait une overdose de danse😂Fethieu beu Mandi😅
Qui avait activé la cloche de notifications ❤😂 ???
Moi❤
moi😂😂
😂😂
Konnne dou mane kasser😂😂😂🎉
@ 😂😂
Wallahi azim kou wahale YALLAH rek hamni musicalement wallahi daffa raw boys yi takk len écouteurs pour voir 😭🥹🥇🇸🇳c’est le meilleur dh
Ya mouna kateu ndeyam wally xana sa nday papa la raw ndaxté dako soufou di kateu sa yaye ñougn Sidy diop rk💪💪💪💪
Yaw daniouy daye sa data yaye deh@@adamocapoeuropebossdeyneug2621
@@adamocapoeuropebossdeyneug2621damay fekk sa papa di kate ma rothi koye bi deh doumou tiaga binga done
mais attends grande sœur loutah yen bou nite wahei deugu ngen saga ko ? Tangu ngen khol trop @@adamocapoeuropebossdeyneug2621.
Ohhhh dama contane bayy dioye😭Maryacine Yallnala yalla same té ayy marr Yaw lou bax rek ngaye. Ame❤🎉
Bilahi 😂
Lou melni dangay profito nga fethie ba contane 😂
Félicitations et longue vie Ballago Seck Wally ❤❤❤
Blh c’est le Sénégal 🇸🇳 est très fier de vous parce que le pays a fait tour du monde 🗺️ grâce à vous , vous faites parti on est fier de vous 👍 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ les gens qui te critique sont plus fans de toi que nous même ils n’ont pas accès de te parler en face ils regardent des motifs pour qu’ils soient reconnaître ou avoir buzz c’est seulement mais si on pouvait ouvrir leurs cœurs ♥️ après Dieu et PSL c’est toi après leurs parents. U arena 205-2026 Inchalah ♥️🤞
Ani gni yakamtiwone live bi gueineu 😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️WBS❤️
Bilay haar b sonou 😅
✌️✌️
Magui niii de 😢😢😢❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Papa thione momuna wouy ❤thank you golden star 🌟 ❤❤
Ani Gni Begue Wally Seck ❤❤❤❤❤❤😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢❤❤❤❤❤❤
Lolou nekatoul wakh gni bagnon ndagou naniou ❤
Bercy laniou beug inchalah ❤mare yay Afrique
Adidas ak Bercy gno tolo. Legui key stade de France lagn beug. Waw key ❤😂
@@morihanna1ya meuna fenn Bercy fait 20300 place tandis que adidas fait 8500 places do wakh lo xam 😝
@Papidiop-d5b réseaux sociaux dal mo diokh gars you impolis paroles gnou saga noum lene nekhé. Mon commentaire était plutôt pour dire que khep nagn bercy, stade de France lagn beug. Temps wou dem séti combien il ya des places dans chaque stade sakh la amoul faf... bref
Wayé kéneu masoko djeul si Sénégal douyko bamou fess béne parti bi rek lagnuy djeul@@Papidiop-d5b
Woyandowoul ak keneu mako wakh c’est le meilleur ❤️🇸🇳🥇🙌🎉✍️Disque d’or nganiou desseleuu
Na woo papam Youssou ndour lathi ko noumouy def😂
@@balacboyesadikman🤫
❤❤❤❤❤@@Naruu2024
Bilaye marrrr Yacine machaalah li gua rétro si début nekhna yalna sa diam yague lol ame werr batte bi werr ❤
Li rek la done khar merci à toi vraiment de nous pas avoir déçu contane nagn vraiment
Blh man mom thion seck manou mako deg lou bamou diekh ta dioyou ma yalla nako yalla yeureum ta Waly lafal thiat bou bakh sakh ❤❤❤
18:50 wally wayna famille bi wayna doom 19:10 yiii 🎉
Yaw mom gaw nga dh
J'ai tant attendue le live j'ai même pensé dou ame live ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤le chanteur du peuple ❤❤❤❤mais il faut toujours reprendre le son de ton paix surtout la partie 10mn😊❤
Le meilleur chanteur de la planète the king of the king tu représente partout le Sénégal dignement
Machallah mar Yacine réussite totale félicitations 🎉 et bonne continuation le chanteur du peuple 🎤🎤🎤❤️❤️❤️🥳🥳🥳
Thank you so much 🙏😢😢 Pape 🎉oh ❤❤❤
Le meilleur de sa génération que le bon dieu nous donne beaucoup de force et de santé
Macha Allah faramarene bii Djame sii iaw bro 👍
Jolie chanson ❤🔥faramaren bi ...weuy rek lay def mashallah..Nostalgie!!!
Ohh machala kontane nagnou gnogui xaar live video bi ❤❤😊
MANDOU LEN SI WALLY GNA BAGNE ALLONS REK😂❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Bayilen Amouniou diome dh
Notre fierté Wally B Seck tu est le meilleur meilleur meilleur meilleur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Tay mome moma wétali tout la journée sma atelier 🎉🎉❤❤❤
Souniou fierté gua machalla wally ❤❤❤🎉🎉🎉
Papa tihone je t’aime fort aussi bilay Yalla na yalla yeureum tout le monde fier d’être toi❤️🙏🏻
On est fier de toi la relève et assuré🎉
Dama kho xar mba sonn wally ya meilleur xay
Attendons le plateau debrief sûrement y aura des images des moments marquants du concert vue que c'est Wido qui a le droit de diffusion je crois . Proud of you. Le concert était extraordinaire, une marrée humaine ❤️
La vidéo du concert sera disponible d’ici vendredi étape par éta la aussi
@@Mody-nz3zttu penses ? C'est Wido qui a le droit de diffusion. Il faut un PASS pour regarder
@ limala meune wakh moye ni lavage dina amate bir faramareen xamna thi niouy dégagé malako wakh .
@@Mody-nz3ztinshallah wally c’est un cadeau wallah il nous régale yalnako yalla sameu
Yalla nako yalla yeureum ❤
Nous sommes très fiers de toi, tu es le meilleur
Kou beugg Wally teksi bagne Yela rk beusseul ❤bi 😂
Vraiment toute nos félicitations 🎉🎉❤❤❤
Félicitations 🎊 wally Seck on est fière de toi 🎉🎉❤
Ndeysane Wally fière de vous chérie sokhna je t'aime beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah toutes nos félicitations tu es notre fierté ❤❤❤
Li rek ladone xarr🎉🎉🎉❤
Ak mane
ak mane😂
NIEUP HHHH
Wa dakar def len pétition nekhal ko mou teugeul len Bal des Faramareen 😅❤
Il est fort 🎉et il as assuré aussi ❤
Fila qualité bubax bi nék
Spectacle assuré vraiment fière de toi.
Vidéo bi rek laniouy khar
Le meilleur Lou Waw kong kimoy thé king off the li histoire dinako bind tro djo akh mborodjio Dou béneu Bilay y’a Mane Mar yacine Ohh mba khôl yagui fékh 🩷❤️🔥 mayko ayy cœur ♥️ y’a khérré
Oh 😭Wally seck yallla nasa diam guague❤😂😂❤❤wouyli nekh wayy Bilaye dosen morommm
We are proud of you Mar Yacine ❤❤🎉🎉
Wally Seck Yalla na goudou fane ❤️ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mais live bi da beri térébeull trop waronna geune séte 🎉mais machallah tonton wally neikhe yalla na ndam yi yokou❤
Mar'yacine ✌️❣️ siguil gagnou gnoun Faramaréen yi 🎉
Gniy wakh wally meunoul wayy ay vrai doff lagn 😢
Bilay
We are so proud of you wally🥺❤️❤️🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲
Le chanteur du peuple le Sénégal est fier de vous ❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎊🎊🎊🙌🙌🙌🙌
Ana gni beug Wally lal Len Jaime bi ❤❤
Aimer len sama commentaire nguir yalla les faramaren ❤❤❤
wally toujours day béral lokho wa paris ❤
Le meilleur de sa génération ❤❤❤
Le meilleur Yalna la yalla defal diam ❤ beug nala
Wally seck yalla Nala yalla samou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Fall xar nagn ba soneu 😤❤️
Chanteur du peuple
Vraiment nekhna trop ❤️lilou a vie 🥰
Ana gni togone si bountou youtube bi 😂? Félicitations Wally borom guichet fermé yi , linga def adidas arena histoire dinako bind. Adidas arena khadjofa Bercy wala U Arena 2025, yaw amal date rek et les faramareen s'occupent du reste gneuw inondé ko. Je pense que c'est Wido qui a acheté la diffusion du spectacle motakh on ne peut pas avoir la vidéo
Le chanteur peuple ❤
Yaw rekh
Thiey mar . Blhi amo morom🎉
Papa thione seck ak mama diaga yalna souff oyof si kaw amine🙏🙏🙏
Félicitations pour cette magnifique concert Wally ballago Seck❤️❤️❤️
Merci beaucoup son bi lérna bakhna bonne continuation l’équipe
Mar ham ga ni te le
Meilleur Bilahi daga meilleur mar yalla nala yalla defal diam rek
Mar je t aime bien bi❤❤❤❤
One love sene🇸🇳Gambia🇬🇲
Ça fait 2 jours que j’attends merci
Je l’ai attendu toute la journée
retro yi c'est exceptionnel mar dèl woy retro lou bari ndakh mo dakh
Le chanteur du peuple on entend u arena INCHALLAH
Machallah réussite totale ❤️ ❣️ ❤️ ❣️ ❤️
Yalla nala yalla lafal Thiat
Amiiine
Fier naniouko sisa dieum ballago barki allkhourane Yallah. Boy djise loula diakhal. Seckkkkkk ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🩹❤️🩹🥰🥰🥰🥰❤️🩹❤️🩹❤️🩹
Mane mome contane dina ma rayy ❤️❤️😭😭
Soirée dotoul nexee nii❤
Hoooooo papa thiono yalla khiper aldiana firdawsi inchallah félicitations the king Ndam rek inchallah