Ce qui me plait chez ce journaliste il n'est pas hypocrite il ne tourne pas non plus au tour du pot. Il dit les choses tels quels sont afin que les réponses soient claire. Bravos a toi brave journaliste mashallah oustaz barakallahou fiikoum. Amna solo
@@fatoudembele8828 Seytané la mouy jaxxassé Aloiun Sall ak Sidy Lamine ki vraie seytané la yaw chaque jour gay wax kilifeu yi pire que ça ki naar na tass Sénégal
@@fallam1010 arbie saoudite kaba bi molén bolé ak le monde muslman sinon rien parce les autorites emprisonne les imam et les oulémas qui disent la vérité.L'arabie saoudite n'est plus reference pour le monde musulman
Yen gni di xass Oustaz Oumar SALL, gnak fayda wessouwoul bagn nitt ba paré diko deglou, bou fèkè nehoulen kone boulen ko deglou... Bou amè gniko bagne, amna gnouko beug. Yalna yalla sam oustaz oumar sall aar ko si ay pèxè noonam yii
Allahou akbar wakhatigue deugu dhh, ya oustage yallah barkella, inch'allah Et yène wa Dakarbuzz pour mane ma khôl sèni vidéo wala aimé-ko, deguloulène ki, mome kessé-fi nek, niamé wakh deugu, mach'allah
Walahi Oustaz Omar SALL, Deuggou YALLA rek ngay wakh, Yalnala YALLA sam té arr la.. Les Sénégalais malheureusement pensent de vivre et d'être musulmans même s'ils aiment l'islam ils ne le connaissent pas
Oustaz Oumar sall yallah nala yallah same té défal la diam niit ku deugou nga machaalah
Le vrai et le meilleur imam.Que Dieu te preserve ya oustaz❤
I love this guy and may Allah protect him
Un vrai sage tu es veridique ouztage Sall que le bon dieu te benisse .Amine
I respect this man. My the Almighty continue to bless you ya oustass.
Merci Beaucoup Ouztaz yalla nga goudou fan ak wer gou yaram 👏🏿👏🏿😀😀😀
Amine waye
Ce qui me plait chez ce journaliste il n'est pas hypocrite il ne tourne pas non plus au tour du pot. Il dit les choses tels quels sont afin que les réponses soient claire. Bravos a toi brave journaliste mashallah oustaz barakallahou fiikoum. Amna solo
Machalah wayy amna solo
Yague fii lole te weer ya Oustaz !!
Yalna yalla goudal fane wii te weral thieur yii!
S oumar sall ana renyi
Amine
Yallah samou la défal la diam machahallah
Merci Oustaz diarama DEUG rek woor
ذالك هو الحق.Rien que la vérité
Merci beaucoup oustaz oumar sall courage rekk inchallah
vive Ahmed khalifa niass
fen dou moy defar rewmi
شكرا لك يا أستاذ الكريم هؤلاءرجال الدين أم أحبارالشياطين !!!! شكرا جزيلا بارك الله فيكم
Vive Oumar sall tu est le meilleur que Dieu te préserve contre tout malheur
Merci
Sénée seytané bu bone bi mom ci bopam c un malheur pour le Sénégal avec son visage sale aucune lumière
Amine
Mashalah bien dit
Diam thi yaw austaz sa kham kham wèrna tasèt
AlHamdoulilah yallah n'a yallah hêb dolly diame diou sawane bawane amine ya rabi alamine dieureudieuf oustaz Oumar Sall
Il ne mâche pas ses mots je l'adore ya Oustaz rien que la vérité il est telma verdict
Manoume
Longue vie à vous oustaz Oumar Sall
Maa shaa Allah yaa oustaz
الكلمة الطيبة صدقة
Merci
Machalla y'a oustaz Oumar Sall amna solo yalna yalla fayla té arlla
Machalla à diarama no féwi y’a oustaz Oumar Sall 🙏👌🤝
Bien dis oustaz c'est des trompeurs des gens comme lui je veux pas cité son nom
Yaw matoo royukaay taalibé Ahmed khalifa moo la soute kenn xamoula
@@fatoudembele8828 Seytané la mouy jaxxassé Aloiun Sall ak Sidy Lamine ki vraie seytané la yaw chaque jour gay wax kilifeu yi pire que ça ki naar na tass Sénégal
Concert de nicki minaj en arabie saoudite lo ci xam oustaz do ci wax
@@fallam1010 arbie saoudite kaba bi molén bolé ak le monde muslman sinon rien parce les autorites emprisonne les imam et les oulémas qui disent la vérité.L'arabie saoudite n'est plus reference pour le monde musulman
qu'Allah vous garde,bayila ba si kanam kanam inch'Allah
Macha allah Oustaz Omar Sall sa kadou raffét na trop ❤️
Machalla Oustaz
Mashallah Ouztaz Sall🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Maman sokhna faye metci
Merci Oustaz tjr véridique
*Ñioun dagno sokhla am Mak you mëlni ki ,, Machallah yallah na yallah goudoul fanam*
Amine
Amiiin ya Rabbi
leufal ndayi Omar Sall ak kouko beug
Yoi
Alibo SN boul saaga té yalla takh
Yen gni di xass Oustaz Oumar SALL, gnak fayda wessouwoul bagn nitt ba paré diko deglou, bou fèkè nehoulen kone boulen ko deglou... Bou amè gniko bagne, amna gnouko beug.
Yalna yalla sam oustaz oumar sall aar ko si ay pèxè noonam yii
Voilà nak iow ta tt compris
Lou lerr nga wakh
Mreci bcp
Ameen wallahi machallah oustaz
*Pourtant Oumar Sall Day Déklou Aay Nite Diléne Khass Ak Wakh, Wakh Djou Ñaw, Dou Nitoukk Dara*
Machallah oustaz amnasolo lolle baarakaallahou fiika que Allah soubanawatallah te protège
Amine 🙏🙏
Gooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooooo
ألله أكبر!!! Que dieu te bénie
Machalla oustaz sall long vie ET santé
MERCI OUSTAZ LONGUE VIE
Journalist tu es tres fort machallah. Ya Oustaz yalna fann yi goudou té borom bi fayla
Machallah ya oustage Oumar sall
Ma beug sama oustaz waay 😭🥰🥰🔐✨
Macha alla ya oustaz
Merci oustaz oumar Sall . Barakallah fikum
Deugg rek ya Oustaz Oumar sall Ma Cha Allah
Machallah oustaz pour tes propos Dieu en ait témoin que c'est la vérité
😆😁😀 mbakhané kay. Ayweu Oustaz Yallah nala Yallah dolli sam
ousmane Mboup s
Yallnala fi AllÀh bàyi yà Oustàz...Bàrakallàhouma Fiiikoum❤🙏
machAllah ya oustaz ! Domou sokhna ak madame right 😂😂😂
Bravo oustaz oumar
صدقت ياأستاذ جزاك الله خيرا وأطال عمرك
آمين
machallah ya oustaz yallana yalla goudal faan yii amna solo on t'aime
MashaAllah ya Oustaze yalnala yalla fay té mou yokeu xam xam bii
Qu'Allah nous guide vers le droit chemin
Allahou akbar wakhatigue deugu dhh, ya oustage yallah barkella, inch'allah
Et yène wa Dakarbuzz pour mane ma khôl sèni vidéo wala aimé-ko, deguloulène ki, mome kessé-fi nek, niamé wakh deugu, mach'allah
longue vie à vous Oustaz Oumar Sall .koula bagne bagne kou baax
Adou Faye1 wakhko ci kaw
jolimata merci Sister
Toull règne gay tve
Yamana kat sa ndeye
cheikh Seye seuls les animaux et les enfants nés hors mariage qui insultent dans les réseaux sociaux.sois civilisé.
Machalla Oustaz très véridique qu'Allah nous guide
Très bon journaliste ou animateur. Outék gnouma xam
Mash'Allah il est objectif vraiment et pertinent
Long vie à oustaz oumar salle
Macha'allah Allahou Akbar hamdoullillah Vive la verite rien que la verite macha'allah vive L'Islam
Merci oustaz
Merci Ustaz Omar dieuré dieuf
Jerejeff Oustas Yalna Yallah Gudal Sah Fan🤲🏾💯
C'est la 1rem fois je suis d'accord avec toi
Salam digua deglou ay waxtanam...?
Machalaa il parle bien deugu rek moy deugu
شكرا لكم
ياشيخ الكريم
ماشاء الله.
Machalla ❤😭😭😭😭
Machaallah félicitations oustaz Sall nala yalla Faye
بارك الله فيك ويزيدك حكمة في الأقوال والافعال
Bonne continuation à ce journaliste Ahmed NDOYE
Yallana yalla same là!!! Ndakhté yagui wakhal diné té wakho pr nékhal kéne !!!wayé deugue rék ngaye wakh té yalla takh.
nourou bocoum ki da kham deugeu data yayam gor djiguen la
Oustasa.khamo.dara.dou.degue..seye.doule.rek
Merci oustaz machallah gni melni yow lagniou begue cii senegal
Mr6 oustz machallah
Mâcha halal oustaz rafetna amna solo trop
Vive Oustaz Omar Sall que Dieu vous protège ❤😍😘
J’aime Oustaz Omar Sall
Merci Oustaz vérité de chez vérité
Machallah franchement il est bien
Oumar sall est un vrai don pour le senegal
yallah na yallah goudeul sa Fann
Je suis d'accord avk vous.Merci
MACHALLAL, LONGUE VIE À TOI ET QUE LE CORAN ET LA SOUNA DU PROPHÈTE SOIENT TOUJOURS UNE SOURCE D'INSPIRATION POUR TOI.
amiine
Machalaahh
Amine mach’Allah ♥️♥️
MACHA ALLAH oustaz OUMAR SALL
Verite absolue, on ne peut pas saggrandir en rabaissant les autres...
Machaallah oustaz Omar sall long vie
Non Imam machallah quelle clairvoyance
Machalla ya oustaz,journaliste bi contane n'a si yow bne continuation
Oustaz Oumar salle long vie à tw que Bonn dieu t protéger contre t ennemi aminé y'a rabie
Yallah na yallah same la oustas omar sall on t'aime en Allah point.
Macha'allah ya oustaz🙏🙏💓
D'accord pour la combinaison des médecines traditionnelle et moderne.
Oh la la quelle personne de valeur
Machalla oustaz sall tu as très bien parlé yalna yalla fayal boppam thi barké seydina Mohamed psl
Masahala jaraama A haali googa cherno
Machallah j'adore oustaz Oumar sall
Walahi Oustaz Omar SALL, Deuggou YALLA rek ngay wakh, Yalnala YALLA sam té arr la.. Les Sénégalais malheureusement pensent de vivre et d'être musulmans même s'ils aiment l'islam ils ne le connaissent pas
macha Allah Amma solo
Mashallah oustaz waxdji rafett neu yalla na yalla fayla
tres bien Oustaz Deug bou were
😂😂😂😂😂 Oumar Sama oustaz
Machallah amena solo oustaz oumar sall diam si yaw
ماشاءالله جميل جدا يا أستاذ الكريم كلامكم واضح نفتخر بكم دائما
Merci 👍👍👍
Vraiment c’est Oustaz il dis que la vérité wallh
Teye mom d'accord na ak yaw
Tay rek nga Dakor ak moom? Tu dois avoir de serieux problemes alors!
@@mohamethkane5966 waw ndakh Ahmet khalifa kou diara wakhal la
@@amadouba6373 comprendroma deh, Ahmed khalifa doumako sakh deglou.
Alhamdoulillah bi niou yallah diokhe Oustaz Oumar Sall ak niou melni mom.
Billahi oustaze nitou deglo machallah am nga xam xam