Secrets de Famille Saison 2 Episode 20 (Sous-titres en Français)
HTML-код
- Опубликовано: 27 дек 2024
- N'oubliez pas de vous abonnez a notre chaine RUclips YESDAKAR
Retrouvez - nous sur www.yesdakar.com/ ou télécharger l'application sur
Playstore: play.google.co...
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
Abonnez Vous a notre Chaine RUclips / yesdakar
Yalna yala def nio feke Tabaski ak jamm ak kheweul bo Bari barcke saydina moukhamed Amin
Amine
Amine ya rabi
Amine (psl)
Amine
Amin
Thieuye meunouma téyé sama rangogne yi sama papa yalla na goude fane je t'aime beaucoup mn papa d'amour je n'imagine pas ma vie sans toi.et courage à tt ceux qui ont perdu leurs parents masta mes chères 🙏🙏🙏❤❤❤
Ndysane😭😭
Gni gnak parent thiey metina
coumba toure massa ma soeur
Ndaysan
@@cheikhdiengitalylivorno1537 cv
Niakeu dieukeur aka méti😭ngay fanan ak nit mou kheuy rek décédé,dém bayila ,yalla bou dé bi bété nk (incendie,accident,meurtre.....),j'imagine premier goudi sans sa dieukeur à côté😭yalla na yalla yeureum gni deudou adouna tei mou yékhéniou🙏
Bilae iow affaire bou doy waar
Bilae lou meti bilae mouy gor mouy djiguene yalla bakh na nagne nagou dogal
Amine ya rabi
@@aminandiaye6339 c triste,dafa daw yaram
@@mouhamedfaye956 wax nga deugeu dh prck klk soit alfa di ngén takaliko
Anna gniyy zappè pubs yii 😂😂pour gawa sètan sèrie bii
Moi
😂😂😂😂beurii guathie ay morom
Me
@@ndeyesakho991 billay
Moi
yala nguene am kharou tabaski ak limouy andal si barke seuydina mouhamed psl 🙏🙏🙏
Allahouma amine
Amine
Amine inchallah
Amine inchaallah
Vraiment madame samb souffre trop c'est pour cette cause que nous les femmes doivent dire non aux mariages cachés ( takou souf ) qui es d'accord avec moi ✋✋
Jamais takk souff
Mes cherries vous ne pouvez comprendre yallah nalèn oumpe
Ce qui m'a beaucoup plu dans cette série est que les lieux k vous nous montrez snt très modeste vous ne nous montrer pas ce qui n'est pas à notre réalité.. chapeau sur vs
Ohhhhh mane je s8 teug et j'en s8 très très très très très très très très très fière kouma beugue beugue na sama bop kouma beuguoul beugue na sama bop Alhamdoulilah ❤❤❤kou bagne lagua bagne dafa fek gua gueun fa niaw waw keuy
Senegal loloo len tardel,man pour man yoyou amatoul
Bilahi nangou langa done moy takh nga raw saye mass
Kou gueum ni moy meilleures séries de l'année pouce bleu
Série yi rèek lafi guiss kom série
diamono ak Allô dg madior ak dior Secret de famille valide
Mcha Allah amna solo trop
Maîtresse et dérapage foka fatté
@@xhadimfvll6321 gniy wané culture Sénégal layy wakh mais niom môme ay affaires de luxe rék lañiouy wané té Sénégal pauvre yii niofi eupeuh 🤔🤔🤔
Sans oublier "Codou", une série très intéressante.
Ah pas Madior ak dior
Ohhh l’entrée de père Malick ! Il nous donne toujours des leçons de vie chapeau à toi mon cher 🌹
Que dieu sème la paix dans notre Sénégal je vous aime tous ndiago sérère toucouleur diola socé lebou peul bambara en fin tte les race vive notre Sénégal je vous adore depuis 🇲🇦 fep fou Sénégalais nek rek mou nekfa ak diam
Pareillement frère merci
Coumba...c réciproque.😴💚🤝🤝
C'est réciproque
👍
14þ
Yallananou yalla doli soutoura adouna ak allakhira
Cette série est la *true* définition de la vie Sénégalaise quotidienne.👌💯✌
Ou-bien je dirais la plupart des foyers Sénégalais?🤔?🤔?
Qu'en vous pensez-y???
Effectivement
Lin nan dom rayla diales la
Oui vrai
@@sos7915 yes sister.
@@momocisseofficial3650 ça veut dire quoi bro'?🤔
Maye lene ma j aims svp 😭❤❤
Boma wakhé lokoy dollé stp
@@awathiam8279 dama koye legui billay 😅
@@awathiam8279 dakoy capture statu ko 🤣
Ma bagne
@@kebagoudiaby7163 😂non dou lolou
Ayy wayy djiguen gni bayilen nangou gnouleni takk takou souff Mme sambe liko dal metina
Très contente de revoir le père de sidy sy 😍😍😍
Machala moi aussi si ay cadome you nice
Je l amine trop wakh bou rafet rek lay wakh
Kinè vraie vipère la hypocrite mais yalla dina leeral lep maty et bisou❤️❤️❤️❤️
Kiné est pire qu'une vipère
😭😭
😭😭😭😭😭
Je reconnais ton visage fatou gueye ton Visage m'est familier
Fatou gueye souwa souwa bien kay
Oh cette série è très adorable ki es d'accord avec moi💖❤
La perte d'un être cher est toujours dure et c'est une douleur qui reste vive et qui ne disparait jamais😥😥 ! Que les âmes de tous les disparus reposent en paix ! Aamiin ! Kiné, gathié doula ray deh ! Prince, fais gaffe ! Maty & Yama❤ ! Ndeysan, Mme Samb , elle souffre hein mais cela fait partit des conséquences du Takk Suuf ! ! Bonne continuation !
*Dimanche 19 Juillet 2020* Secrets De Famille L'un Des Meilleurs Séries Djiguéne Gni Beug Dieukeur Yalla Na Léne Yalla May Dieukeur Diou Bakh Diou Beuri Yeurmandé Bala Tabaski Bi Amine 🤲❤
Serigne Mountakha Mbacké yalla nafi yagg lol té andeu ak werr barkeip khassida yi 🙏🙏🙏
Wallahi le problème de teug guerr gueweul etc....nimoumay def makk yalla rek gno xam
Société sénégalaise bi wallahi warnane fi heradiquer liii😭😭😭😭
Gnoune gnepa yam Fa yallah
Kouffi hord sujet dina saga sa .....😂🙏képp kouguiss ndjarigne yinèkk ci secret de famille yallana yalla dèfall jam🙏
Déjà ton commentaire Hors sujet la😂🚶🏾♀️🚶🏾♀️🚶🏾♀️
@@khadygueye2437 😂😂non méme pas sakh
Iow sakh hord sujet nga fi dèf ta op commentè sur le thème d'aujourd'hui
Yaw kou rew nga
Ya ndieuka hors sujet😂
Kou beugeuh serigne Touba rk beuseul j'aime ♥️😄
Moi je trouve que yama rolou bandit leu geune ayy que rôle bii nimouy deff beutt yii ohhh🔥🔥🔥❤
2em
Maybe si bandit yi la bok dei 🤔
@@mamangaye2039 non dou bandit dehh
Quelle horreur publicité toutes les 5 min
Nonou la mele
Bijou machallah yake sa domou ndeye séne liguéye raféte na🙏🙏💙
Ohhh li dawna sama yaram 😭😭😭 sama khel demna thi biniou publié Facebook ni danio ray sama jeker alakhou akbar thiey deee mii no ray bakhoul way😥😥😥😥
Yalnako fimou ndiougué guenalko fi mayla xolou mougne
Ah dagno reuye sa diekeur ndeysan yalla nako yalla yereume kharéko aljana
Alalou borom Belele massta sala xel si yaw la dem alahouma wone sax yangui youtube
😭 yalla na fir dawsi di deuku wayam
Masta.yalla.bakhna
Yama démal beuganeté si sa famille yaye gnoune teugue yi kougnou gnou bagne gnou bagne bla louko raw machalah gnoune wa askanou gnégno Serigne Touba mognou gnanalone
@@Liweiyang43 vérité absolue je suis de l'être teugue balamaïssa Pure et dure sounou kogne bi gnou deuk kou ame sokhla si gnoune ngay gneuw pour résoudre sa problème
@@Liweiyang43 j suis fiér d'être balamaissa
Wa kinè mi saytanè woul mou melni rayouko ni
a mouma diakhal
Li laniouy wakh deum rayla dialé la
Ndaxx gua sagn KO wax wayé bouyy fégn fégnn bou gaw saxx néxato ma d'Ara
@@binetaamar3654 ak percing bi 😤😤
Li dé moy deum ray la dialéla
je suis félicité vous parce que vous en fait bon travail🇸🇳🇮🇹
Loupa tèll téll fékk fi niouma djitou li diamou la may l'en ma j'aime
Sa papay djitle tu l’as tué a cause d l’argent dc les hommes doit mefiezsi domou djitle e svt leur mamans disent kou beugueu Guinar begueu ay thioudiame c du foutaise
Yalla nguéne am diamou si barkié Mohamed
Amine
des acteurs capables de donner des émotions très forte voila ce qui nous manque , machalla waye une série pleine d'enseignement. et félicitations aux acteurs
Di gnianall éleve you wara def exemen yalla maylénn te mou djikk lenn
Allah houma amine🙏
Ah man warou wouma Thiam Babel Demba Thiam Teugu bou dawoul mbar Nioun Ngegno rekk so nekhhhh 😍🥰💫
Amoul guer amoul gueweul mbeguel la am
Bilay th gnio fi gueneu riche gnegno rkk
Mafia by come d'abitud
Vous manifestez pour
*Bijoux ♥️ Maty*
Où êtes-vous les gars?
👇
Soyez toujours courtois dans vos commentaires et respectez le règlement de la communauté
Kiné Moy Vré hypocrite Deugg mouye Mourou dih léne lénéne Teih Mo ray
Légi mou fégn dé té moy fégnal bopam
Deum rayla dialé la
C’est l’une des meilleures séries du Sénégal parce qu’elle résume presque la vie sénégalaise
Mme samb ndeyesane yeureum nako mome dou am si papame dara ndakh elle n'était pas reconnu yayam tak souf lagne ko tak ay way massa
Mom papa dji défalon nako virement ci contam
Yaw fo nek pabi diokh ko khaliss bou bari
Khalisbi ma yakarni kiné vidé nako 😔
Kine vider na leup bilay
Ahmadou Niang kinè dieulna lep
Secret de famille à retrouvé aujourd’hui sa chanson originale ki confirme
Ani nioukoy sétane ak sen call
Moi
Call rek lakoo meusseu sétané
Mangui ni
Ahhh li dé mome ame na ay affaires de sante yi mane damako doundou nak Thiam bima sante té pourtant dé wa keur kou goor gui kouy ndoule si Sénégal niom gay diapal ndaysane té mane machalla sama famille dama nane sakh amna niou khamoute s'en bopou qui sou mako bagnoul warouma bagneu mais kou kham sama bopou la mane kouma bagneu ma sourela té pourtant dé kou goor ki mome néna boudoul mane dou done kenene mais lép si famille yi la rék surtout les Dames bayilen lolou fi gnépa yéme
Massa ga geume sa bopou rek sou nekoule mom nek kenen fi ken geunou fi ken yalla rek mo kham ki gueune .
Dagno dof rék ak niak gueume yalla ndax yalla bimou saké domou adama daf gnou fi wathié nguir gnou diamouko ta kouné sa dieuf moy tax gua gueune ta afair de xéte yalla waxouko féneu séne ngueume rék mo dess mai koula xép bayiko ak yalla ndax mo sak domou adama ta yamalé wouko ak léne 🙏🙏🙏🙏🙏
Man mom kima beug gnègno la yalna yallah def diam nitt yep niou yam
Massa mai doyna War trop srx
Gnom wéro askanou gnégno riche lane déf machalah dou gnou gné kéneu dagno dioudewalé riche
Cette série est formidable
Guel biy wakh prince diatta 2ans ngini nioukoy weur Mane mi 2ans ngini may weur Guel bi pour mou sol body bou wathie neubeul ma biir bi 🚶🏽♀️🚶🏽♀️🚶🏽♀️🚶🏽♀️
Lol bilay tu as raison
@@naboubabou5594 😂😂guissalomako
@@Liweiyang43 2 ans mangui koy weur😂
@@Liweiyang43 2 ans mangui koy weur😂
Man mi d 2ans mangui koy weur pour mou dindi rouge a levre bi
3 ème commentaires lay lénn ma ayy j'aime nkk
Yalla na gnépu am diam
Tu gagnes quoi?
La mifa Koufi nèk sètane ba parè nk soga commentaire 😅😅😅❤
Mdrrrr
@@niakbakartvnbktv2086 😀😀😀
Ani wa time WiFi 🥰😭❤️
On est là eupna
KINE mi diomaloul len sasssss🤸🏽♀️🤸🏽♀️🤸🏽♀️wa yen Kon pa Bi goumawoul deugantannn🤭🤭🤭🤭
😂😂😂😂😂
Môme kay vrai actrice la🤔🤔
Aida boul faté sidy dako fayolon mou opéré beut yi tmt😂😂😂
@@fatoubarhamthiellosene1806 😂😂😂😂😂👍👍
😂😂😂😭😭😭
1errrr bama dalè sètane RUclips ba tay magui doga nèkk 1
Série bi nékhna amna solo machalla ❤
Mabeugueu so teudé gouddi moulay fégnou ba domaneuti nélaw banga fégne amine
No dieyla petit galle pa tay manoull am yaram🤣🤣🤣
Yaram dounou d'où Aÿ lek wala na si yalla la dé bouléko fatédé
Entouca serie amna sollo torop mais man hallé bou djiguénn bou raffétt ba paré raffétt djiko lay weurr .. soit disant relation sérieux pour créer un avenir ou une famille solide ect...
Iow mom fi rk ga meuna wouté diabar mdr
@@awasarrsarr8338 moma diakhal de
bonne chance
Beugoo gueilo rapp🙄
@@deessedija2086 😁😄😅😂😆
Takkou souff eska daray adouna diarnako
Prence est assurée son rôle 👍🔥
Gay wakh ak say parents Lou dieum si sa walou seye moulay sewal day mety si ❤️
Takou souff déh moussibala thiey les femmes reveillé vous🤦♀️
Mai Dara nekoussi aramoule
Franchement c’est une grosse humaine, les hommes assume pas leur responsabilité,et les femme acéré tout.
Respectel heure bi way com les autres séries ah heure bi dafa goudi trop dagni harr ba sonn
Manee dee dama yakornii sakhh amatoul
Koudon khar notification bi😂
Alal boum la diaral sa ngor 🙏😏
A
Machallah sen ligueuy rafetna
Enfin ndakh ma meuna teudi 😍😘
Niack bay métina ganék khalle amo bay métin,yallna yalla kharé aldjana bépp bay ak bépp yayy
Guil yalla mey len ma j aime meusou ma am j aime diap len si bokk guil yalla
Meilleure série j'adore
Bonne continuations
Non ligeuni jeux dafa léer ndeye sane
Premier commentaire khana nekh😂😂😂
Yalna diam yagg❤️🙏
Amine amine
Yalla na diam yagg way ❤🙏🙏
Khamé ngéne pa bi si comencement film bi moye l,aveugle mi étè au premiere saison
Lolou kou goumba woul khm nako 😁😁
😭😭😭wah deg yalla
Saer hihi Odf 😂😭😭😭😭😭😭
Blie I can't stop crying 😭😭😭😭❤🇬🇲 u guys are just great blie
Premier fois may setane film bi ms nexna trop
Junior : "Yaye yakh yeup bene la"" Je l'ai replay cette séquence 😅👌👌👌
Pa Malick lagnou soul si bâtiment ak papaye Djalika dans Maîtresse . Kon Senegal lolou amnafi. Moytoulma chantier yi. Soubhanalahi
✌👊nice na trop machallah yalna séne Diame yageu✌✊
J aime tellement cette serie😍😍😍😍😍😍
je suis félicité vous parce que vous en fait bon travail
Khana amôlêne group wathsap gnou thiy commentaires
😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂😂
Waxal waye sokhna
*Bilayy meuneu nagne ko créé dh mo geuneu amna béne jour mako donnn wakh comme ça niou toudé ko association andd sétane serie yeupp*
Kinnè nianou pabi arangéwouleko 😂😂😂
Vraiment yama elle joue bien son rôle 🤟🤟 chapeaux à toi
Alhamdou lilha yalnanio yalla modio guo rafet
Borom body bou orange bi tmt kouko kheff, rouge a levre ko, ongle ko🤣
😂😂😂
nga sagane ko wakh dara diapouko si
Yaw bane Thiam ga😁
Waaw
@@lotandiaye4193 sarakhoulé
Man dama meunoul comprendre naka la djiguene di nango takou souf, khawma naïveté la wala niak beugg sa bopp
Beuguél mo Bari dolé rek
Beuguél mo Bari dolé rek
Ndoye Mari c pas une raison. Niou neubb la adouna bii yeupp, manam tuvie dans l’ombre
Ya des choses tu ne peux les comprendre quand tu les vis pas nangou takk souf cest plus que lamour
Charolle Faye wii peut-être que le fait de n’avoir pas vécu ça m fé dir cela. Mais pour moi dal ça peut pas être de l’amour
Première 🤗😍😍
Bilahi niit mo leudeum crime sa papa ba parè melni rien n'était mdr 😅
Ki est cet utilisateur ki aime mes commentaires 😂😂😏😏😏
Machallahh yesdakar🥰
Limo takh djiguéneu gni wara moytou takk souf kholal li dal Mme samb rék té lép ses parents la
Mbokou prince tamitt limou taille haute degueuleu😂😂😂😂😂
Moll na dalllll 😂😂😂😂😂
Ak biir biii dama tiite mane
Mandou lene nguir yalla
🤣🤣🤣🤣 wouyaye
Prince warou gnouko diap😨
Wayé dafa soop loumm fayy defff bayyy Wadall carte d'entité
Mh si mom lagn meune diar pour découvrir vérité bi tmt
Je suis d'accord avec bineta
@@darondiaye6756 u as tt compris
Niankou dieukeur aka méti😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤚😭😭😭😭😭😭
Bilae yéna gaw 😏delenma denthial place tmt🥺🤭🤧
Wakhatiko
Les gens qui quémandent des j’aime là vous gagnez quoi même ?
J’aimerais vraiment le savoir
Mm mwa
Bonne question
Danoukoye lègeu layacare
Modou Gueye est ce que dougn lene fey
Merci
Sene seri bi dafa gatt trop té bup bi da da.goudou. kiné yow mome t'inquiète legui gnou diapla gnous la ci kaso bi sa yaay haam gniari nakar nak hypocrite 😏😏😏
Meilleur série du sénégal
J'ai pas pu me retenir sa m rappel mon pp😢
Best series ever thank you 🙏🙏🙏🙏❤❤❤