Guiro seras champion nga diambar nga nala mbeur yi dieul nga beuré ndax danga bokou ci lamb dji boye you graw yepp dan nga lene yalla na la yalla diamlé
Giro khale bou yarou Daf ma def com bathie seras sayou d'année nge deg mouye wakh Mangi nous chekh kharitou bathie seras man Mila motakh mang kooy nianal mou don roi des Arene mak Abo sama kharit yeup Daf niouye nouyou
Lamb moussoul avancé da ngéni nakh sen bopp boy yi jambaar yi naniou len teugu niou dieufleunté. Mais boy boussi am promoteur wala manager wala public rek ngéne koy outeul yoon
Giro sama yay sama wa keur yeup contan n'a niou si yow yala nga don. Roi des rane yow danga bakh man cheikh ndong kheuss di kheuss bou bathie seras ak Giro seras sama khole cedna si yow
Mai nak fok ma comanter man kheuss bou bathie seras deuk ginaw raill ndakh Giro champion sama kharit la def ma beug si bire kholam sayou âme combat woma man mi ley geuereum man cheikh nioumey wakh kheuss bou bathie seras
Giro dafa wara don roi des aren niounie wa pikine ginaw raill Giro mooy sou niou bathie seras mom rek la niouye suporte nako gayi diokh gran combat mok Diop 2
Goor deugeu guiro séras fall yalla nala sa borom défal ndam doléé ibrahima fall❤
Baye fall dangay dégg ba nopi meun wax fall Jajeuf Guiro 👌👌
Un très grand champion
Guiro seras ghetto bi yeup gnoungui lay Bégué touss nak 💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾✅✅✅✅
Guirro Beugg nla Bilahi Yalla sa borom doli Soutoureu xeweul ak tawfékh inchala
Merci beaucoup
Guirro baye fall lá ❤❤❤
Niary mbeur la am guiro ak Niang mballo💪💪💪💪💪👌👌👌👌
Talfa ndayi kesse
Il communique bien machalla
Ki baye fall DEUG leu bilay walay nioune yeumbeul laniou deuk dh mais yaw diam rék ngay am
Yow Giro man kheuss bou bathie seras sa kharit diapaleni wa pikine gianw raill niongi sa ginaw nouyoul ma sa domou ndeye Modou booy ndoukoumzn
Giro yaw guerrier nga dangaye ame combat légui inchallah
Wa jambaar loutakh douniou teugue guiro akk ada boy baol 😢
Guiro Diop2 moy sama mbeur ms diapeu nala beus niki tay
Diam sii ioe Baye Fall bii ❤🎉
Nouyoul ma wa parsel Giro man sa kharit kheuss bou bathie seras nam nala tanyi sama kol mo amon problem motakh degatoma mai 'nala def signie
Grand cheikh Siar ak magal bou werr naka tawfekh yii lepp diam waa inchallah dinala woo
@@issakhaguiro4035 contana si yow Giro yow brom mbakh man la cheikh sa kharit kheuss bou bathie seras ak Giro seras
Guiro seras champion nga diambar nga nala mbeur yi dieul nga beuré ndax danga bokou ci lamb dji boye you graw yepp dan nga lene yalla na la yalla diamlé
Baye ma Ndiaye seul daye dawou rék ❤❤❤
Giro khale bou yarou Daf ma def com bathie seras sayou d'année nge deg mouye wakh Mangi nous chekh kharitou bathie seras man Mila motakh mang kooy nianal mou don roi des Arene mak Abo sama kharit yeup Daf niouye nouyou
Diop 2 tapéte la na dieul avance bi
Guiros kasse amoul lenene
❤
Lamb moussoul avancé da ngéni nakh sen bopp boy yi jambaar yi naniou len teugu niou dieufleunté. Mais boy boussi am promoteur wala manager wala public rek ngéne koy outeul yoon
Bathie seras amon nafi ndeysane
Gore dou yeureum gore
Seras rek , dieul len avance bi
Diop 2 moy sama mbeur mais Guiro beug nala
Guirou suel
Fall ndiagua yaram bi diam si iow guiro dp8 guédiawaye bul ragual dra djiambar deug
Giro seras diop.2 combala.mbala.giro Diop 2 booy wanrak bou ginaw raill
Éthique ak déontologie guiro on dirait que jangena epuis bayiwul classou gor yii com yenen mbeur yi😂😂 mais c normal peuhl la peuhl day mouss
Boy guiroo amena bfem
Ak bac
Talfa wakhouko dra journaliste bii dey dulll😂rek
Guiro seras seul
Giro sama yay sama wa keur yeup contan n'a niou si yow yala nga don. Roi des rane yow danga bakh man cheikh ndong kheuss di kheuss bou bathie seras ak Giro seras sama khole cedna si yow
Man kheuss bou bathie seras ak Giro seras wa pikine ginaw rail beug n'a niou combat Giro seras Diop 2
Guiro guiro leuh
Mai nak fok ma comanter man kheuss bou bathie seras deuk ginaw raill ndakh Giro champion sama kharit la def ma beug si bire kholam sayou âme combat woma man mi ley geuereum man cheikh nioumey wakh kheuss bou bathie seras
Guiro seul
Journaliste bi kou saytané la
Guiro bay fall la
Guiro da wara buere
Guiro vs bb Gouy gui lamb la
Journaliste bi Dall dou changer koi dinagne la nokate Bayil diakhasser
Guiro serás
Giro dafa wara don roi des aren niounie wa pikine ginaw raill Giro mooy sou niou bathie seras mom rek la niouye suporte nako gayi diokh gran combat mok Diop 2
Daga daw bay Mandiaye 2
Dieuleul coly faye combats la
Giro nako gayi diokh gran combat dafa wara beurre gran combat amna 4 Dor mou danou kou dan Abou ndiansse ak yene champion nako gayi diokh combat mok Diop 2 combala
Giro contana man la cheikh ndong sa kharit kheuss bou bathie seras ak Giro seras yow sama. Wakognie yeup contan naniou sayo defe émission ziarema teboula nekhon Doko def manak wa pikine gianw raill yeup contan naniou si sa mission bi
Guiro diokh léne ko thi boy yi
Guiro seras TMAX
❤️❤️❤️❤️
Guiro seul