Mbok yi Aussi délen Djouli wakhtou yi ci heure bi surtout fadjar té déf Azkaar yi matin et Soir Sakhoo djang Alkhouràan chaque jour inch'Allah ndjabaar dou meun ci yaw dara .. Merci Oustaz Sall
Merci ouztaz allah ye barik fik toujours un plaisir de vous écouté des paroles pleines de sagesses d'humilité et d'enseignement yallah na yallah goudal say fane 🙏
Soubhanala il y a 11 ans j'ai rêvé de vois bcp de sang de mes regles je suis mariée plus de 13ans et je n'arrive pas de tomber enceinte yalla rek mokham maintenant je m'en souvient Lou way def sa bopou
@@noirdebene5564 cherche la vidéo suivante il montre les remèdes. Si c’est compliqué toi cher du zamzam recite dedans fatiha khoumb houwa 7fois falakh 7fois naass 7fois al kursi 7fois et les versets contre la sorcellerie tels que younous verset 81 autant de fois que tu le sens.tu souffle et bois verse le reste sur toi☝️
Alhamdoulilah alla kouli haal. Je le fais chaque fois avant de me coucher. Mais fou nekk benn la doone diangue. Inchallah dinaa yokk ikhlass bi falaki ak naas. Dieureudieuf ya Oustaz yalna la Yalla feyy yiw té barkel liguey bi. Amiiine
Bilahi yalnala yalla faye magui soga comprendre khawma wone li ay way dieureudieuf way j’ai pas les mots bilahi😭🙏🙏🙏❤️❤️❤️🥰🥰🥰 ouztaz yalnalafi yalla bayi🙏 et yalnala yalla faye sa khol si lou bakh ligay def yeup🙏🙏🥰🥰🥰
Vous allez peut être pas me croire mais walahi je viens de rêver de singes juste avant le visionnage de cette vidéo peut être Qu'Allah a voulu que je regarde cette vidéo. J'étais le meilleur élève de ma génération Dieu m'en est témoin mais depuis quelques temps, je n'est plus envie d'apprendre ni de me lever de mon lit pour quoi que ce soit et s'accumule de mauvaises notes.
A onchibillah minal saytany rajim Bismillah RAHMANi rahim Houl a oujou bi rabbi falakhi Mine shari khassikhine iissa wahaba Wa mine shari na fassati Fileu khadi Wa nim shari khassidine izza khassada ALLAHOUMA AMINE
Bilahi wa rabboul kahba, j’ai rêvé il y’a juste 4 semaines d’un serpent noir qui fuyait, une semaine après un gros chat noir qui me fixait! Actuellement ma vie est bouleversée et désordonnée!! SoubhanAllah qu’Allah nous préserve et nous couvre de sa miséricorde !
Té Loumay faté légui da beurré té sama xel bi ma machallah première rekk la donn dieul sama classe demna ba université tog ba Wara am sama licence bâyi Université kouma si meunn diapalé rek lay weur
Allakhou Akbar, Oustaz, comme mague yi nenagn boul di nettali sa nguent mais sa firi guente tay bi guiss na thi sama bopp, Mash'Allah sant Yallah té gueum ko, té doyloko
Deug leu mom boul di netali sa gueint yeine yi nga hamni sen firi bahoul waroko netali comme so gueintei beug bou deign wala kou gagnou nila nga topou ko genre yoyou
Il y a des années, j'avais rêvé que je suis reparti dans le quartier où j'ai passé mon enfance. Mais dans le rêve, plus personne n'habitait le quartier et les maisons étaient vide. Je viens de comprendre pourquoi je suis devenu quelqu'un de distrait et d'indécis, alors que avant j'étais très intelligent et concentré sur ce que je fais
Moi aussi je vis la même chose, j'étais intelligente mais actuellement je ne peux pas me concentrer tous mes projets tombent dans l'eau j'ai rêvé j'étais dans la tombe mais ce n'est pas fini ils m'ont mis quelques choses dans la nourriture que j'ai mangé malheureusement pourtant 2 semaines avant que je le mange je rêvais chaque jour entrain de manger et je saute du lit des que j'ouvre ma bouche. Que Dieu nous preserve des mauvaises personnes.
Machallah moi je ne peux pas compter le nombre de fois que je me suis perdu dans un rêve et ce même rêve se répète à chaque fois même cénario , même endroit il y'a toujours une forte pluie et tout devient sombre et à chaque fois une vieille femme très bizarre m'aide à entrer dans sa vieille maison mais moi j'ai peur d'elle
Ya ouztaz Limay guinter au cimetière da bary donc çomment faire pour s'en sortir et pourtant je fais des zikr et beaucoup de istikhfar et je fais aussi des rêves Di rere soubkhanallah donner nous des sourates et des zikr a faire pour les vaincre
Qui sont ceux qui aiment Oustaz Oumar Sall et ses enseignements par Allah et qui likent ses vidéos avant de les visionner ? ☝️💖
Masha'Allah
C'est important
Je suis là
hhamolrne nuniuy def ba jotko
Walay amna ay niit gnou sokhore 😭😭😭 yalla nayou yalla protéger ak guider
éternellement Allahumma amine
Machallah le lion de la sunna qu'Allah nous protège 🤲💕💕
Mbok yi Aussi délen Djouli wakhtou yi ci heure bi surtout fadjar té déf Azkaar yi matin et Soir Sakhoo djang Alkhouràan chaque jour inch'Allah ndjabaar dou meun ci yaw dara ..
Merci Oustaz Sall
Kou beugueu serigne fallou mbacké lalale aye 🤍🤍🤍🤍🤍you waihe tale ténga aimer commentaire bi🤍🤍🤍🤍
❤❤❤❤❤❤❤
fi wahou kiniou sak laniougi wah
Walay j'vous aime pour Allah. Yalnala ya Allâh fayal bopam, amine🙏
Allahuma amiine🤲
Allahouma amine
@@awakamara7463 pp
Quallah t'aime
Lan Moy diabaar
Merci omar sall gnoun dagnla beugg te ay mourid lagn
❤❤❤Oh sama xol sédd na bilahiii Sénégal bén bop leu Yana yalla défal niép diam
Machalla amna solo wayé bougona oustaz déf wakhtane si jiguene bouye diouli aye tankame difénie lousi yalla wakh ndakh barina niouye diouli sén awra nékeu sibiti té khamouniouco mangui ziar boubakh
Merci ouztaz allah ye barik fik toujours un plaisir de vous écouté des paroles pleines de sagesses d'humilité et d'enseignement yallah na yallah goudal say fane 🙏
Sama khel demna si imam hassan Ka yalnako borom bi samm🤲🤲🤲
Soubhanala il y a 11 ans j'ai rêvé de vois bcp de sang de mes regles je suis mariée plus de 13ans et je n'arrive pas de tomber enceinte yalla rek mokham maintenant je m'en souvient Lou way def sa bopou
Yal nala YÁLLA téggil biile nattu.
Bul fátte di saxoo astaghfiruLLAH lu bari.
@@aaro7822 inchalah dieureudieuf amine yarabi 🙏🙏
Il faut l enlever ma chère et vite
@@seynaboundiaye9473 et comment l'enlever comment faire
@@noirdebene5564 cherche la vidéo suivante il montre les remèdes. Si c’est compliqué toi cher du zamzam recite dedans fatiha khoumb houwa 7fois falakh 7fois naass 7fois al kursi 7fois et les versets contre la sorcellerie tels que younous verset 81 autant de fois que tu le sens.tu souffle et bois verse le reste sur toi☝️
Oustaz yalla gua fi yagg té weurr . Degn ma niabarr guirr ma dokh probleme lah sama xoll awma loumou doneu
MashaAllah oustaz may Allah reward you abundantly jaza'kallah khairan
Alhamdoulilah alla kouli haal. Je le fais chaque fois avant de me coucher. Mais fou nekk benn la doone diangue. Inchallah dinaa yokk ikhlass bi falaki ak naas. Dieureudieuf ya Oustaz yalna la Yalla feyy yiw té barkel liguey bi. Amiiine
Bonsoir s'il vous plaît je ne comprends trop le wolof je peux savoir que signifie "Ndiabar" s'il vous plaît
@@Sophia-oy2tg Ndiabar c'est les pratiques mystiques
Yalla ga yag fi té end ak wérgu yaram bu baré way,vraiment say wakhtane amna solo lole.
Bilahi yalnala yalla faye magui soga comprendre
khawma wone li ay way dieureudieuf way j’ai pas les mots bilahi😭🙏🙏🙏❤️❤️❤️🥰🥰🥰 ouztaz yalnalafi yalla bayi🙏 et yalnala yalla faye sa khol si lou bakh ligay def yeup🙏🙏🥰🥰🥰
Alhamdou lillah 🥰 Dieuredieufeti Cheikh Ahmadou Bamba🤍❤
Vous allez peut être pas me croire mais walahi je viens de rêver de singes juste avant le visionnage de cette vidéo peut être Qu'Allah a voulu que je regarde cette vidéo. J'étais le meilleur élève de ma génération Dieu m'en est témoin mais depuis quelques temps, je n'est plus envie d'apprendre ni de me lever de mon lit pour quoi que ce soit et s'accumule de mauvaises notes.
Ndeysann qu’Allah te protège del faral di diouli rek😢😢
Macha Allah ya oustaz yalla nagua goudou fane ak werr
Merci beaucoup oustaz pure vérité alhamdoulila que Alla nous donne longue vie et beaucoup de santé Merci Merci Merci beaucoup
ALLAHOUMA barik fik ya oustas A.sall ALLAH azawajal t'accorde sa bénédiction
A onchibillah minal saytany rajim Bismillah RAHMANi rahim
Houl a oujou bi rabbi falakhi
Mine shari khassikhine iissa wahaba
Wa mine shari na fassati
Fileu khadi
Wa nim shari khassidine izza khassada
ALLAHOUMA AMINE
Ira hasad leu mbokou fin bi au lieu de isa wakhaba
MASHA ALLAH dieurdieufti OUSTAZ AMATINA SOLO LOOOL.
Bilahi wa rabboul kahba, j’ai rêvé il y’a juste 4 semaines d’un serpent noir qui fuyait, une semaine après un gros chat noir qui me fixait! Actuellement ma vie est bouleversée et désordonnée!! SoubhanAllah qu’Allah nous préserve et nous couvre de sa miséricorde !
Amine❤
Kou Guent ken douko wakh
Oustaz dieureudieuf si conseil yi en plus tu nous apprend comment se protéger yalla nga yag sounou kanam
Wallahi Oustaz limay guente Armelll beurina trop mais yalla bakh na😢
Té Loumay faté légui da beurré té sama xel bi ma machallah première rekk la donn dieul sama classe demna ba université tog ba Wara am sama licence bâyi Université kouma si meunn diapalé rek lay weur
Qu'allah nous guide sur le droit chemin et nous préserve du shirk
Amine ya rabbi 🤲
Yalnala YALLA fay yiw Oustaz
Allakhou Akbar, Oustaz, comme mague yi nenagn boul di nettali sa nguent mais sa firi guente tay bi guiss na thi sama bopp, Mash'Allah sant Yallah té gueum ko, té doyloko
Deug leu mom boul di netali sa gueint yeine yi nga hamni sen firi bahoul waroko netali comme so gueintei beug bou deign wala kou gagnou nila nga topou ko genre yoyou
@@mtand7269 Waw deguena thi histoire yi nenagn kene thi ay frères da nettali nguentam bene freram wor ko. Wakh lep bakhoul
Machaallah oustaz fann bou goudou ak werr 🤲🤲🤲
Merci beaucoup pour le message ❤️❤️❤️❤️❤️🙏je souhaite longue vie 💘❤️❤️❤️❤️❤️et ta mifa ♥️💞🙏🙏🙏
Allahou Akbar 😞 oustaz lale guama bama tit
Mâcha ala amatina solo dieureudeuf imame
Lii la kham thii oustaz dafay diarinn niit gnii merci oustaz
Yallah na Yallah fay yiw si Barker sangue bou tedebi salahou tala haley wa salam
Machallah dafa amna solo sama sope bi long vie a toi machallah
جزاك الله خيرا يا أستاذ وحفظ الله
Goudou fane rkk oustaz ❤❤❤❤💯💯💯❤❤❤❤❤❤❤❤
ماشاء الله تبارك الله نسأل الله التوفيق يا شيخ
MachaAllah oustaz lingua wakh d la plupart damakoy guent:golo la moudié guent di khékh akk mom mais après nitt mo gueneu si mom
Maachallah oustaz longue vie à vous ♥️♥️🥰
Oustas SALL si on rêve qu’on est nu et qu’on passe la ou il y’a beaucoup de monde
Merci oustaz pour ces éclaircissements. J'en ai vu soubhanAllah
Diazakoullahoul hayrane. Yalna Yalla bayila sougnou kanam nga yague fi lolou té wer
Que Dieu nous protege ❤
Merci guisna ci sama bopou yalla gafii yagu té werrr
Salaam ya Imam !! Thank you very much for your help
Dieureudieuf oustas amna solo
Assalamou alaykoum ya oustaz je j'aime beaucoup
Merciii Ya oustaz🙏🙏🙏
Merci beaucoup bonne soirée
Yalla nala Yalla fayy oustaze.
Machllah machllah oustaz
Long vie yarabiiii
Merci oustaz xamna lou beurré tay
Longue vie à toi oustaz machalah
Alhamdoulilla machaalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Masha'Allah ya Ouztaz Djazaka Allahou hayrane
Je vous aime oustaz .
Toutes vos vidéos sont intéressantes,vous êtes très gentil machallah
Merci sunu oustaz kilifeu bu woor bi
Dama guette sama mbegne Wade ba DESS ndiarre merci oustas
Machalla alhamdoulilah ❤
Jazzakallahou khairan oustaz .damey lathie ...lane moye fethie ndiabar yi ngafi liim 🙏🏽
Cc yangui fan
Oustaz man dama guent gené aduna
Longue vie machallah merci ouztaz
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi PSL
Machaalah amna solo yalna yallah fayla the samla
Je vous jamais beaucoup y'a outaz longue vie
Machallah ya oustaz je sui deriere toi
Machalla oustaz omar wakh gnou louy dindi ndiabaar
ماشاء الله تعالي حفظك الله تعالي ❤️
Machalah oustaz yalla na yalla faye yiw
Oustaz koy guent di fatté ban nian lay déf 🙏
Machallah yallah ne l yallah faye
Ya oustas dama gente ay groupou xalé dima fiw ay fil.
Lolou xana jambar la.soko xamé dindi ma way gir ALLAH SEIGNEUR DE L'UNIVERS.
Merci oustaz
Dieureudieuf ya Oustaze
Yalnala yalla takhawou ya oustaz
Merci Oustaz ❤
mach'Allah y'a oustaz yalna Yalla fay la yiw
Il y a des années, j'avais rêvé que je suis reparti dans le quartier où j'ai passé mon enfance. Mais dans le rêve, plus personne n'habitait le quartier et les maisons étaient vide. Je viens de comprendre pourquoi je suis devenu quelqu'un de distrait et d'indécis, alors que avant j'étais très intelligent et concentré sur ce que je fais
Moi aussi je vis la même chose, j'étais intelligente mais actuellement je ne peux pas me concentrer tous mes projets tombent dans l'eau j'ai rêvé j'étais dans la tombe mais ce n'est pas fini ils m'ont mis quelques choses dans la nourriture que j'ai mangé malheureusement pourtant 2 semaines avant que je le mange je rêvais chaque jour entrain de manger et je saute du lit des que j'ouvre ma bouche. Que Dieu nous preserve des mauvaises personnes.
@@ciskosora Allah Akbar wala hawla wala quwata ila bilah
@@ciskosora idem pour moi
Que Dieu veille sur toi et Qu'll éclaircit ta voie insha'Allah
Macha Allah docteur Omar Sall ⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐
Mane dama guénte sama copin âme bénéne guél apré mou tak kooo
Thank you so much May God bless you
Merci Oustaz Omar Sall
Maa Sha Allah my oustas
Oustaz ndax meune na am sa numéro yinga wax ni dé presque yeup guent naako wallahi. Ak yenéne suma manoona jokko ak yaw nga guindi ma ci
Machallah moi je ne peux pas compter le nombre de fois que je me suis perdu dans un rêve et ce même rêve se répète à chaque fois même cénario , même endroit il y'a toujours une forte pluie et tout devient sombre et à chaque fois une vieille femme très bizarre m'aide à entrer dans sa vieille maison mais moi j'ai peur d'elle
Dieuredieufè oustaz mane dé douma guènte
Macha allahou oustaz dieureudieuf yalna yalla fay. Man mom sama guenteu bima soneul damay guenteu di tardé rek soit école waleu may dem féneu
Machalah ms dama ngente sm nidiay dof dima Wone guina dall dima reee may dioy ms bobou mak mom xaWma kouthi nék si auto
Macha-allah macha-allah 👂👂👂👂👂👂👂👍👍👍👍👍
Ya ouztaz Limay guinter au cimetière da bary donc çomment faire pour s'en sortir et pourtant je fais des zikr et beaucoup de istikhfar et je fais aussi des rêves Di rere soubkhanallah donner nous des sourates et des zikr a faire pour les vaincre
Yaa baax wallaahi kuy gindi jullit yalla rekk moo Koy fay
Macha Allah! longue vie à vous!
جزاكم الله خيرا
Mashallah🎉🎉🎉
Ouztah machalah amena solon
Goudeule faneu Oustaz
بارك الله فيكم 💚💚💚💚💙💙💙💙💛💛💛💛🤲🤲🤲