PRANK STAR - Saison 3 episode 09 Modou Lo - Yaw Pousseul fi la wakh

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 фев 2025

Комментарии • 2,1 тыс.

  • @Mahfousse
    @Mahfousse  8 месяцев назад +458

    Téléchargez l'application 1XBET et Utilisez mon code promo 221M pour gagner un JACKPOT.
    cutt.ly/Let6mfqe

  • @diopbabacar236
    @diopbabacar236 8 месяцев назад +606

    Modou defna geste bou graw bimou méré dafa demm diapp machallah

    • @Bayeniang20
      @Bayeniang20 8 месяцев назад +11

      Mais coups yi dalnegn de😂😂😂

    • @badaradiouf4646
      @badaradiouf4646 8 месяцев назад +5

      Xlo arabisan bi 😂😂😂😂

  • @AstouMbengue-t7e
    @AstouMbengue-t7e 8 месяцев назад +549

    Kou d'accord nii acteur bii dafa done kharou rkk lalale aime 😂😂

  • @oumardiaw1422
    @oumardiaw1422 8 месяцев назад +507

    Kou mèrr dangay diappeu wala nga tokk wala nann ndokh modou lo dafa diappeu kii moo dégueu dinnèm machalah

    • @AblayeMbaye-rq2us
      @AblayeMbaye-rq2us 8 месяцев назад +5

      Non modou kay dégoul dîné kon dou baré ndakh dafe haram

    • @evadavidniang7780
      @evadavidniang7780 8 месяцев назад +11

      Ablaye mbaye lii passion la rekk ak pas temps day diekh lzgui c’est éffemere

  • @mouhamedsall5347
    @mouhamedsall5347 8 месяцев назад +194

    Je suis un fans de balla Gaye 2 mais Bilahi Modou Lo est unique y’allah kham nako Borom bakh Deug la boudoul prank bi sakh nittt kou bakh la té lepam day bakh inch’allah

  • @mfs1336
    @mfs1336 8 месяцев назад +38

    Modou khol bou rafet la yorr sama mbeur bi talibé Cheikh sel yarou laff thiat ♥️♥️

  • @cheikhfall1276
    @cheikhfall1276 8 месяцев назад +1663

    Kou beugue modou lo laalal j'aime❤ aziz ndiaye dafa sokhor dh

    • @fatoundiaye1999
      @fatoundiaye1999 8 месяцев назад +23

      Maynala 👍👍👍👍👍mayla ❤❤❤❤

    • @dioumzndiaye1504
      @dioumzndiaye1504 8 месяцев назад +25

      Koku sisou mane la 😢

    • @AwaTambedou-dw9nt
      @AwaTambedou-dw9nt 8 месяцев назад +3

      Sokhoroul yaw mi ya sokhor 🙄🙄

    • @karandiaye3681
      @karandiaye3681 8 месяцев назад +7

      Aziz wakhoul dara modou bo ko nekhé kay nek courone empereur

    • @karandiaye3681
      @karandiaye3681 8 месяцев назад +4

      Roi bo khamné mo tan ay adversairame

  • @ndoumbegassama
    @ndoumbegassama 8 месяцев назад +2284

    Kouy d'accord ni Modou lo khol bou rafate la yorr lalale jaime

    • @mbeugueloubax1128
      @mbeugueloubax1128 8 месяцев назад +10

      Khol bou refet kay ki narona ray nitt ganan khol bou refet

    • @ToutaNdiayeTouta
      @ToutaNdiayeTouta 8 месяцев назад +6

      Bou bon lay

    • @ToutaNdiayeTouta
      @ToutaNdiayeTouta 8 месяцев назад

      @@mbeugueloubax1128borom khol bu bakh bi balla la

    • @oumitandiaye6780
      @oumitandiaye6780 8 месяцев назад

      ​@@mbeugueloubax1128bane nitt la yarr arrêtez de mentir

    • @sokhnambaye2161
      @sokhnambaye2161 8 месяцев назад +37

      Hiii Aka bakhh sougnou roi bi🎉

  • @khalifagueye4550
    @khalifagueye4550 8 месяцев назад +249

    C le meilleur camera cache maximum de j'aime pour le Roi modou lo

  • @Absamax
    @Absamax 8 месяцев назад +45

    Walay lima nékh si modou lo moy dafa modestie té vie privém rathiouko si mbédeu mii macha allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mouhamedlo8356
    @mouhamedlo8356 8 месяцев назад +65

    Mahfousse lene rekk mola dessé prank président de la république 😂😂

  • @maimounamane894
    @maimounamane894 8 месяцев назад +130

    Modou diapal ni association des femmes sont contentes vraiment machalah ❤

  • @KhadimNgom-kl8is
    @KhadimNgom-kl8is 8 месяцев назад +1062

    Kou guiss Modoul lo bamou démé diap ba parei nieuw took deff ni kou méér noumou wara deff machallah ❤

    • @jullmoussa
      @jullmoussa 8 месяцев назад +64

      Leppp. Si sariya lako tek legui😂😊

    • @Al_Hamdoulilah221
      @Al_Hamdoulilah221 8 месяцев назад +42

      ya oustaz ni leu rek meuneu def ndeyssan xamna kou galant la ci ay sokhnam😊 ndeyssan

    • @KhadimNgom-kl8is
      @KhadimNgom-kl8is 8 месяцев назад +5

      @@Al_Hamdoulilah221 b
      Walahi

    • @KhadimNgom-kl8is
      @KhadimNgom-kl8is 8 месяцев назад +5

      @@Al_Hamdoulilah221 walahi ❤️

    • @KhadimNgom-kl8is
      @KhadimNgom-kl8is 8 месяцев назад +4

      @@jullmoussa késsé naak mo woor dhé ❤️

  • @vie_la_joie
    @vie_la_joie 8 месяцев назад +370

    Mon amour envers cet homme Modou lo yallnalaaa borommm biii sammm

  • @Général4-f7d
    @Général4-f7d 8 месяцев назад +163

    ki mo ndieuka dieul coup roi des arènes th signé woul contrat 😂😂😂

    • @kingmously
      @kingmously 8 месяцев назад +7

      Billahi mon ami 🤣

    • @thiaradiallo2959
      @thiaradiallo2959 8 месяцев назад +4

      Barky alhouran 😂🤣🤣🤣

    • @albassvp5hy
      @albassvp5hy 8 месяцев назад +1

      😢😢😂😂

    • @MamanLo-dc7ro
      @MamanLo-dc7ro 8 месяцев назад +1

      Waw 😂😂😂😂😂

  • @SeydinakhalifaCamara-lc2tg
    @SeydinakhalifaCamara-lc2tg 8 месяцев назад +179

    Kou d’accord ni modou dafa meune mbedji rek lalal j’aime 👍😂

  • @OumarSowDiallo
    @OumarSowDiallo 8 месяцев назад +509

    Kou beugue modou lo lale j'aime

  • @ibrahimandiaye8885
    @ibrahimandiaye8885 8 месяцев назад +102

    Le meilleur lutteur de tout les temps walahi on t'aime Modou kharangne lo rek

  • @bakarydieme1086
    @bakarydieme1086 8 месяцев назад +122

    Mahfouss so lénii pranké mbeur yii ngèn soralé protège dent ndakh danio guaw lokho 😅mais concept bou nice leu prank yeup bii moma cii gueuneu nékh ndakh Modou sama fan's leu depuis mon enfance mais so pr
    anké Wally mou gueuneu nékhati😂kou beug lolou rek lalal j'aime ❤

  • @daoudasamb9208
    @daoudasamb9208 8 месяцев назад +18

    Modou lo ya bakh yalna la yalla sammou arla yalla mousal la si thiat ❤

  • @madzo193
    @madzo193 8 месяцев назад +13

    Modou Lo de nature lokho yi dafa guaw 😂😂

  • @MameDiarraFall-v3t
    @MameDiarraFall-v3t 8 месяцев назад +117

    Chii tay dama contane sama beur bi mo meilleur en plus d’être exemplaire il est galant beau et responsable je l’aime beaucoup merci Mahfousse 🥺🥰♥️💪

    • @mariemedieng5357
      @mariemedieng5357 8 месяцев назад +3

      Dioulité❤❤❤

    • @fatoukineba9898
      @fatoukineba9898 8 месяцев назад +2

      C'est le meilleur notre préféré il à un bon cœur machala

  • @Seydousy-w4h
    @Seydousy-w4h 8 месяцев назад +106

    Un mbeur posé comme Modou lo jamais vue bilahi

  • @bayemorygueye3233
    @bayemorygueye3233 8 месяцев назад +497

    Kou Dakor ni Modou lokho bi da gaww rek buesal jem ❤😂🎉

  • @DiaryBalde-fk9dk
    @DiaryBalde-fk9dk 8 месяцев назад +50

    Qui nimeu KO beugué eupna machallah ❤️ Yallah na yallah sam leu thie barkey Mouhamad salalahou aleyhi wa Salam 🌹❤️❤️❤️❤️❤️❤️ amine Yarabil 🤲🤲🤲🤲👌❤️

    • @fatimataamadouka1224
      @fatimataamadouka1224 8 месяцев назад +1

      Bilaye mane tamite dama ko beugeu té yallah takh depuis toute petite fans am la

  • @AdjaSeck-yv9mo
    @AdjaSeck-yv9mo 8 месяцев назад +387

    Wa Touba sén dome am na ndam 😂😂may numéro 7
    Ay way kagne lay am 10k j’aime diam lén si🙈🙈🙈

  • @Ablayediallo66
    @Ablayediallo66 8 месяцев назад +401

    Le seul et unique moy beuré nieup yekko PA yi ak mére yi The king MODOU Lô 🎉

    • @AminataDIOUF-ez8kd
      @AminataDIOUF-ez8kd 8 месяцев назад +11

      Lolou dh balla gaye rec moko am si lamb😂

    • @Adnanezinho-jm8zk
      @Adnanezinho-jm8zk 8 месяцев назад +7

      Non lolou mom balla gaye la 😂😂

    • @khadimdiouf7618
      @khadimdiouf7618 8 месяцев назад +6

      @@AminataDIOUF-ez8kdnopil bayi bagnou prank balla nga sogay oubékou 😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 8 месяцев назад +7

      ​@@khadimdiouf7618gni fo wakhé modou lou bakh niouy sissou 😂

    • @alzoyenguelin5188
      @alzoyenguelin5188 8 месяцев назад +4

      Balla rk moko am si lamb

  • @khadimsarr6099
    @khadimsarr6099 8 месяцев назад +342

    modou khol bou rafet la yoor✅yalna ko yalla may ndam

  • @ahmadoubambadieng8720
    @ahmadoubambadieng8720 8 месяцев назад +19

    Modou lo le vrai roi 👑 Machalla ndam Inchalah

  • @diatounguer9547
    @diatounguer9547 8 месяцев назад +10

    Modou ta bien fais de sauver une femme merci a tw mais coup bi dale na champion ❤

  • @degrk5622
    @degrk5622 8 месяцев назад +87

    *Modou un vrai gentleman xol bou nice* ❤️❤️ dafa door copain ba paré niou niko c'est caméra cachée mo xoolaat waadji bettou yeurmandé

  • @NdeyeKhadyGaye-oy3lz
    @NdeyeKhadyGaye-oy3lz 8 месяцев назад +164

    Ay way Makhfouss sama mbeur bi nga dieul tay ❤combien je l’adore 🥰

  • @Eft870
    @Eft870 8 месяцев назад +229

    Modou kharagne le roi de tout les temps l’incontournable ❤️☝🏽

  • @mamikane5072
    @mamikane5072 6 месяцев назад +9

    chapeau a modou lo franchement

  • @hamzagaye4697
    @hamzagaye4697 8 месяцев назад +10

    Alhmdulh limaa yagg khaar sm mbeur mi 🇲🇷🇲🇷 modou kharagn lo talibe cheikh

  • @astougueye6006
    @astougueye6006 8 месяцев назад +39

    Kholal nimouko sané wadji si biti rk non j’aime ce monsieur Modou Lô a vie 🥰😍🥰😘

    • @mouhaba5891
      @mouhaba5891 8 месяцев назад +1

      Après nak wadji defoul dara deh 😂

  • @Maxkamien-xc5wz
    @Maxkamien-xc5wz 8 месяцев назад +84

    mane dé keur gui rek lay khol machalla sama papa demna😭😭 yene nako sama yaye

    • @Mod-t2y
      @Mod-t2y 8 месяцев назад +10

      Yalla na lako Yalla may

    • @AstarSeck
      @AstarSeck 8 месяцев назад +5

      Yalla gua am bou dakk bii

  • @elhadjishop
    @elhadjishop 8 месяцев назад +143

    Modou dafa merr dem japp dji Allahou Akbar

  • @AdonisDiop10
    @AdonisDiop10 8 месяцев назад +9

    Im one of the biggest fan of BG2 but the more i know modou the more i do like him! He’s a good guy ❤️

  • @babacarndiaye9252
    @babacarndiaye9252 8 месяцев назад +40

    On est content parce que vous m’avez fait comprendre que Mon lutteur est tellement sensible, mais ce que vous faites c’est des risques.
    Merci à toute l’équipe.

  • @mymyyoyo
    @mymyyoyo 8 месяцев назад +38

    Sama mbeeur bi nack Machala ki bamakaye beugue mo yague meuneu touma ame bénéne Mbeur nakh mome je l'adore ❤❤❤❤

  • @Omzo__Velli
    @Omzo__Velli 8 месяцев назад +156

    No Mahfouss Dou nitt😂 Prank le Roi des Arènes c'est exceptionnel je valide grave les reufs❤❤

  • @threal_saidou2210
    @threal_saidou2210 8 месяцев назад +87

    Damay tite sax si Mbam ndiaye mouy tendance gaindé Lo 😂fi ben ndy roi mofi am❤ modou kharagne lo❤

  • @bakhoumdadi5800
    @bakhoumdadi5800 8 месяцев назад +19

    Ndeysan thiey modou sama champion bi diam ak tawfekh rek machallah

  • @oumousamb2028
    @oumousamb2028 6 месяцев назад +4

    Modou nioune association des femmes du Senegal yay souniou parrain. Niaf . Touches pas à ma soeur 😂😂😂❤❤❤❤. Kharou ndéketé beurina façon ya ame chance aka gaw lokho . Modou est ce k dou frére thie Dieynaba Tall😂😂😂. On tadore notre kharagne❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @bbndiaye-cz8iy
      @bbndiaye-cz8iy 5 месяцев назад +2

      Bilaye chaque jour ma setane ko😂😂

  • @RacineNdiathe-oi4hr
    @RacineNdiathe-oi4hr 8 месяцев назад +31

    Damako beugue ba j ne comprends pas damay sétane di rétane rek je l'aime énormément barki alkhourane je l'aime yalla na diamame yague notre roi des arènes ❤️💕makhfous le meilleur prankeur de tous les temps ay prank daniouy koy togue té say prank day nior khome Macha Allah 😍❤️

  • @SarahDiakhate
    @SarahDiakhate 8 месяцев назад +76

    Ndeyssane da rouss ci door boumou door wadjiii
    On t'aime roi
    Prank pape cheikh diallo mon combat

  • @yacineniang2897
    @yacineniang2897 8 месяцев назад +147

    2 millions ak dakadjii douma prank mbeur ndakh so paré khaliss bii guay fadioo saway risqué geu sa life deugeu😂😂😂😂

  • @Djamila46
    @Djamila46 8 месяцев назад +8

    J'aime Modou lô❤❤❤
    Aziz ndiaye milliardaire bou soxor bi

  • @LDM6812
    @LDM6812 8 месяцев назад +6

    Un homme qui defend une femme jërëjef Modou Xaragne Lô ❤❤❤

  • @princessepeule3175
    @princessepeule3175 8 месяцев назад +31

    Li la kham gooorr sa dolé waune ko sa moromou goorr kholal Modou Lo defendre na guél ni c ça nila😂

  • @cheikhounadiagne2675
    @cheikhounadiagne2675 8 месяцев назад +110

    Tay lé sa life wessu woul niou douguel la keur roi des arène guani dagua koy caméra caché 😂😂kouma fay million démou ma🤣🤣

  • @faye6718
    @faye6718 8 месяцев назад +12

    Li modou déff nonou la djigeune amoul dolé machallah sama idole bi le roi le meilleur ❤❤❤❤

  • @MaimounaWade-b8m
    @MaimounaWade-b8m 8 месяцев назад +2

    Mané dé mangui koy replay sanka ba tey waye mbegeul la for modou seul on t'aime

  • @marcusmouhamed
    @marcusmouhamed 8 месяцев назад +16

    Siteu guisnga gauche droite bi dengay beurei weula😂

    • @yacinendiaye693
      @yacinendiaye693 8 месяцев назад +1

      😂😂😂😂Siteu beuré woul day xarou dji

    • @bibam1729
      @bibam1729 6 месяцев назад +1

      Kokou dayy kharou rek 😂Frere

  • @MaremeBa3700
    @MaremeBa3700 8 месяцев назад +99

    Ndeysan modou depuis ma nék khalé ba legui damako beug😭❤️

    • @AmySill
      @AmySill 8 месяцев назад +10

      Sa bopp nga kham mane dh billahi awma si mome sago depuis khalé ba tay❤

    • @sfatygueye6677
      @sfatygueye6677 8 месяцев назад +5

      Bilay comme man

  • @papesylla7281
    @papesylla7281 8 месяцев назад +127

    L’incontournable Roi des arènes Modou Kharagne Lô yalla nala yalla samme moussal la si pexé none🎉

  • @therealdiaa128
    @therealdiaa128 8 месяцев назад +12

    Té Modou ay mbedj la door beuss boula dougalone coup mom dou bakh si iaoo 😂😂motakh Lac 2 néna modou lokho yi kom kherr😂😂😂

  • @taphadiop8886
    @taphadiop8886 8 месяцев назад +26

    La façon dont il a contrôlé sa colère c’est autre chose🔥

  • @FatouNdiaye-q2k
    @FatouNdiaye-q2k 6 часов назад

    Modou lô est le meilleur des meilleurs je t'aime bilaye tonton modou❤❤❤❤❤❤

  • @mameboussoseck7212
    @mameboussoseck7212 8 месяцев назад +31

    Damako beug ba beug nimako beugué wallahi❤❤❤❤ yalnala yalla defal diam gouddeu fane wérr wérlé barkép cheikhoul Khadim Je T'aime Lô ciré ma thiaaa ndaam goudeul fane

  • @aidadiongue7083
    @aidadiongue7083 8 месяцев назад +33

    Dolen prank mario ak Modou guirr yalla modoral gnouko 🙏🙏🙏🙏

  • @Eft870
    @Eft870 8 месяцев назад +18

    Th guena maytou courpagne modou Lo yi tank nitt fatouwoul bkhna rk😂😂😂😂❤️❤️❤️❤️

  • @khoudjistasow6658
    @khoudjistasow6658 8 месяцев назад +3

    Mahfousse mo bone dieul koo ak rètane yiiii😂😂😂

  • @bafatimata8414
    @bafatimata8414 4 месяца назад +3

    Woye ken d’où sounou rois bii 👏👏❤️❤️❤️😂😂👌🎩🎩🎩🎩😘😘😘

  • @Khadijadija-n7n
    @Khadijadija-n7n 8 месяцев назад +10

    Magui dora comprendre dorou ama baldé ya 😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 8 месяцев назад

      Ama kaye n'a sante kiko sauvé 😂

  • @Laye44
    @Laye44 8 месяцев назад +18

    Mahfouse c'est toi qui devait joué cette rôle,vous avez sacrifié ce mec qui a reçu des petits coups.😅😂

  • @mauricendione1184
    @mauricendione1184 8 месяцев назад +7

    Ce prank va battre le record de visibilité qui est d’accord

  • @omarbah176
    @omarbah176 6 месяцев назад +2

    Modou lo na diokh mahfousse roi bi dakh mahfousse dann nako😂😂❤🔥

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 8 месяцев назад +2

    Sossi déwone da nga kharou😂😂 Ya Oustaz kéne dou io😂❤🎉

  • @ABDOUKARIMBA-q9d
    @ABDOUKARIMBA-q9d 8 месяцев назад +6

    Yén dh moun ngén diap cou nék modou lo li damay tok sakh di wakh sama khél yén mouno lén diap modou lo afér bou graw bilay Nice na nékh na macha Allah

  • @kingmously
    @kingmously 8 месяцев назад +5

    Modou Lô le roi, l'empeur des arènes épisode bi néex na trop 😂

  • @aidasagna2928
    @aidasagna2928 8 месяцев назад +19

    Ayyy Modou lô kagn lalay guiss si adina beug Nala lol sax bassi Sama biir Xol Lima dal si papá thione beugouma Mou amat koumay dimbali ma guiss xaragne t yalla tax😢😢😢😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @SouleyHann
      @SouleyHann 8 месяцев назад +2

      iow fonè si sènègal

    • @aidasagna2928
      @aidasagna2928 8 месяцев назад

      @@SouleyHann kaolack

    • @aidasagna2928
      @aidasagna2928 8 месяцев назад +1

      @@toutythiam3305 ah lac rose la deuk mais douma XAM si fane leu exactement

    • @mbayangsarr5711
      @mbayangsarr5711 8 месяцев назад

      ​@@aidasagna2928borom lamin dou rerr demal rk nga lathié

    • @mbayangsarr5711
      @mbayangsarr5711 8 месяцев назад +2

      Ken si nioumouy andal amna numéro wam mais meunou mlako diokh fi

  • @ndeya5099
    @ndeya5099 8 месяцев назад +1

    Lô Ndam ciré borom Mamou khafizzzz alkhourane yii❤❤❤❤

  • @aramegueye-ox8ff
    @aramegueye-ox8ff 8 месяцев назад +2

    Modou lokho bi gaw na😂😂

  • @AbibatouSall-ok5fu
    @AbibatouSall-ok5fu 8 месяцев назад +51

    Kou namon zé comme man ❤❤❤❤

  • @ousmanepam9836
    @ousmanepam9836 8 месяцев назад +31

    En dehors d être un champion Modou est très pesé et calme avec un grand cœur aussi.Longue vie champion 🙏🏻

  • @amadoudiallo350
    @amadoudiallo350 8 месяцев назад +48

    Kou arriere doorrr yi n foi rekkk😂😂😂

  • @djilykane304
    @djilykane304 8 месяцев назад +9

    Logiquement killer waratoul bokou si prank yi il est connu franchement ! Sinon on ne peut pas s'empêcher penser à une éventuelle mise en chaîne !!! Qui est d'accord ??;😮

  • @Ndawa-zr1ml
    @Ndawa-zr1ml 5 месяцев назад +1

    Modou jtm wayi Bilahi 😊

  • @buzz2217
    @buzz2217 8 месяцев назад +29

    Saway niari baram modou moko dall mou marqué 😂😂

  • @mamadousarr3116
    @mamadousarr3116 8 месяцев назад +9

    Kharou dafa beuri façon 😂😂😂 wadji mome bi la opter encaisser coup modou lo 😂😂😊

  • @papezulefaye7263
    @papezulefaye7263 8 месяцев назад +24

    Wayy modou wayy beugoul kouy door djiguéne ndeysanne...non makhfous ak équipe bi vous êtes les meilleurs

  • @jeanjacquesbiassey155
    @jeanjacquesbiassey155 8 месяцев назад +2

    Yako tey di nga dougou galei Mbeur baparei tei do encaisser coup 🤣🤣

  • @ousseynoudieye1431
    @ousseynoudieye1431 4 месяца назад +1

    Héee wadji deh Modou lo dako guénel gauche gniy babi xamnaniou limay wax ki day kharou lahhhh😂😂😂

  • @EvachouDiop-o2v
    @EvachouDiop-o2v 8 месяцев назад +7

    Sama mbeuguél si ki awmasi saguo walae❤
    Ms nak c'est un gentleman 😌🥰
    Weuh wadji fimou dall sorina dh😂😂

  • @abdoufaye9433
    @abdoufaye9433 8 месяцев назад +93

    Kou Diapou sathi defma signe 😎

  • @SodamaremeGueye
    @SodamaremeGueye 8 месяцев назад +30

    Oh nous sommes fier d'être génération kharagne Lô

  • @moustaphafall2486
    @moustaphafall2486 5 месяцев назад +2

    Modou Ku bakh la xol bii mo rafett Masha Allah.Dorouko daf ko thiookass rk

  • @kyasy6332
    @kyasy6332 8 месяцев назад +5

    Ohhh Mahfouss🥰🥰t’as taper fort 🥳🥳Modou je l’aime trop belle surprise en tt cas merci bro❤️yalla n’a liguey bi geuneu barkel th yombou❤️

  • @ndeyeramacisse1041
    @ndeyeramacisse1041 8 месяцев назад +4

    😂😂😂😂thiey sama mbeur bi🥰❤️Machallah un homme exemplaire 🥰❤️

  • @Amina_Rassoultv
    @Amina_Rassoultv 8 месяцев назад +55

    Caméra cachée bi acteur bi moko wakhal bopam c'est du jamais vu thia choix bala😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 8 месяцев назад +1

    Modou lo beurina dolei dh machalla, 😂 mom dh doroul dafa mbet wadji rek lekh bi yakhou 😂😂

  • @FARLOFFICIEL-01
    @FARLOFFICIEL-01 6 месяцев назад +2

    Té Gua yammm😂😂😂Modou kén Dou yao

  • @diop3575
    @diop3575 8 месяцев назад +4

    Je suis fans balla gaye ll ms modou borom bkh la quoi machallah ms makhfous loy khaar si sm mbeur mi balla gaye ll ❤❤

  • @badarafall6418
    @badarafall6418 8 месяцев назад +94

    Modou lokho bi mo gawee😂😂

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 8 месяцев назад +8

    Ki Amna chance ndax Modou dako mbethie mai bouko doron coup mou dh😂😂😂

    • @Ralfalves-i9t
      @Ralfalves-i9t 8 месяцев назад +3

      Wadji kay dafa am fitt 😂😂

  • @MadameFall-hb9xs
    @MadameFall-hb9xs 8 месяцев назад +1

    Yalla mokham loutakh ma beugue modou lo bilay ❤❤❤❤

  • @AnouchaVividiallo
    @AnouchaVividiallo 8 месяцев назад +1

    Ki osé affronter modou lo ki xana werul😂😂😂😂 makhfouss tay mom sama mbeur nagniu indil❤❤❤

  • @MamadoupapisKa-qo9dd
    @MamadoupapisKa-qo9dd 8 месяцев назад +20

    Modou lo ay giffles sakh gua dem Ardo...🤣😂