Machalla papa cherif yalla na yalla goudal sa fan kou bakh te begue nit yatou tabè am wilaya bou weur te dokhè wouko wakhè wouko yalla na yalla feyla. Abdoul aziz sene italy sope chetif
evitez le superlatif c un khalif de cheikh on n en disconvient pas mais le plus grand alors il est plus grand que cheikh oumar ou bien mm son pere maodo excusez moi
Yaa Chérif, goudal fane. C'est très important pour les générations actuelles et futures de connaître nos ancêtres, nos Érudits, notre histoire. Nit day kham bopam! Maa Shaa ALLAH. Kou khamoul foo diougué, amoulo wérouwaay, do kham foo djeum. SWT fayal gnou Seydi Mbaye SY té sakhal gnou thi ak talibé bou gnou ndagoul. Amine Yaa Allah. ALHAMDOULILAH
Parfaitement d'accord avec vous. Nos GUIDES RELIGIEUX ont le devoir de transmettre l'histoire de la tarikha, ses monuments, ses chartes... Nit day kham boppam, kham li mou yoor, kham fimouy tek tankam. Maa Shaa ALLAH, Chérif Ibrahima Aïdara, je l'aime pour ce sacerdoce qu'il honore au grand bénéfice des Talibés Cheikh, mais surtout de la jeunesse tidjane. ALLAH SWT le rétribue grandement bi barakati Seydil Woudioudi Wal'Alami.
Macha allah cherif khôl bi sédna lool yalla khamnako, yalla nala yalla fay yiw si barké seydina Mouhamed(psl).serigne Babacar Sy RTA yalla na yalla di yéssal yeureumandém si moom ta tass gnou si barkém
MachaALLAH Cherif je vous apprécie davantage car Serigne Babacar dafa fort trop si mane. Merci de votre générosité à partager ces quelques aspects de la vie de Serigne Babacar RTA.
salam amna solo baba ! MAME mor khoudia sy est le fils de ahmadou sy frêre de mame ousmane sy donc il est cousin de maodo c"est lui qui dirigea sa priére mortuaire il était époux de soxna nafissatou sy maodo c'est le pére de serigne gora sy (la voix d'or ) qui chantait la bourda avec son oncle dabakh malick (rta)
MA CHA ALLAH NA YALLAH TASS NOU THI BARKE CHEIKH SEYDIL HADJI MALICK SY RTA AK MBOLEM NDIABOTAM.DIEREDIEUF CHERIF NA YALLAH GOUDAL SAY FANE.MBAYE DAL MO NOU DOYE SIDY ABOUBACAR SY DO SENE MOROME.
Wahtanal si seydil diamil sohla na niou ham simom ndah amougnou ay wahtanam dou si video dou si RUclips 1 benn wahtane lá am si RUclips por favor sento muito e agradeço muito gastamos as suas palavras são de verdadeiro
ESKEY SERIGNE BABACAR SY RTA YALLA NA YALLA YOK LERAM TASSUGNIU SI BARKEM INCHALLAH GUENA YOKEU SUÑU THIOFEL SI MOMEU ILAL ABADAN🙏🏽🙏🏽GOOR GUI KENEU DOU MOM L’UNIQUE♥️🔐 CHÉRIF DIEUREUDIEUF
Walahi ndeyssane thieuy Sama goor gui mo matone limou done un homme multidimensionnel Yalla rék mo kham Serigne Babacar Sy mais gnoune khamougnouko Mangui yessal sama diayantek mome rek ba ila yawmidine
Dieuredieuf sague bi yalna yalla yokka goudal fan wi yok wèrgui j'aime Serigne Babacar Sy.
Machalla papa cherif yalla na yalla goudal sa fan kou bakh te begue nit yatou tabè am wilaya bou weur te dokhè wouko wakhè wouko yalla na yalla feyla. Abdoul aziz sene italy sope chetif
Sérigne Babacar Sy RTA Dou Morom dou Mass dou Mapando Yalla na Yalla Yokk ay lèrram tè tass niou si Barkèm Allahouma Amine Dieureudieufety Sy
Doudou Diongue o
Khalifa ababacar sy le plus grand khalife de tous les temps c'est la fierté de la tidianya c'est notre joyeux
😭😭😭😭😭
evitez le superlatif c un khalif de cheikh on n en disconvient pas mais le plus grand alors il est plus grand que cheikh oumar ou bien mm son pere maodo excusez moi
Mashallah Serigne Babacar Sy Rta amoul moroom.Yalna Yallah yok leiram tei tasniou si barkem si Barkei Sheikhou Tijan Rta
Macha'Alla la dimension de Serigne Babacar Sy est incommensurable et inépuisable vraiment mention spéciale à Chérir Ibrahima Aidara Macha'Alla
Machalla amna sollo alhamdoulila Yalla nanou yala taf si barkem
Daiara diof chérif Ibrahima aidara
Ken dou sama Goor Gui ❤️❤️❤️💯💯🥰🔒mome rék point
%chérif aidara
Yaa Chérif, goudal fane. C'est très important pour les générations actuelles et futures de connaître nos ancêtres, nos Érudits, notre histoire. Nit day kham bopam!
Maa Shaa ALLAH. Kou khamoul foo diougué, amoulo wérouwaay, do kham foo djeum.
SWT fayal gnou Seydi Mbaye SY té sakhal gnou thi ak talibé bou gnou ndagoul. Amine Yaa Allah. ALHAMDOULILAH
Parfaitement d'accord avec vous. Nos GUIDES RELIGIEUX ont le devoir de transmettre l'histoire de la tarikha, ses monuments, ses chartes... Nit day kham boppam, kham li mou yoor, kham fimouy tek tankam. Maa Shaa ALLAH, Chérif Ibrahima Aïdara, je l'aime pour ce sacerdoce qu'il honore au grand bénéfice des Talibés Cheikh, mais surtout de la jeunesse tidjane. ALLAH SWT le rétribue grandement bi barakati Seydil Woudioudi Wal'Alami.
Bilahi wallahi tallahi , mounatouma neubb lii nékk sama holl . Cherif Dabakh nitou aldiana leu .
talibé cheikh dal machaAllah
danio beug sunu serigne beug seriniu nieup
di wahtané nieup
machaAllah
alhamdulillah
Serigne babacar fierté dioulitt yeup ndax mane mourit la wayé serigne babacar sama lépp la
wallahi khole sédétina
mala beugue ya cherif aidara
MA CHAA ALLAH
Yalla naniou yalla Fayal cheikh seydi hadj Malick Sy Ibn Ousmane ak Serigne Babacar Sy Sy
Masha Allah Yallah Shérif Ibrahim Aïdara Yallah nala Yallah faye si Serigne Babacar Sy amine ya Rabbi si barkė Seydouna Mouhamed saw amine
Manchallah chérif ibrahima aidara at tidiani yallah Nala yallah fay mangui lay sétane depuis Belgique 🙏🙏🤲
Dieuredieuf aidara yalna yalla degeral taxaway bi ci barkei sa mame aleyhi salatou wa salam...
Thieuy serigne Mansour borom daradji. Yallah naniou ko yallah fayal té yokk ay léram ❤
Merci cherif yalla nala yala Faye wessare barke Serigne Babacar si senegal
Barakallahouma yalla yokoula fayla goudal sa fane kiguay wakhtané moy sonou wasila di sonou leep mom rek laniou beugue maachaallah
Machalla cherif yalla défallla djam soutoural la protéger le bijahi seydouna mouhamad sallahou aleyhi wa salam inchalla
Kou sopou serihne babacar sy beusseul j aime notre fiertè
Je suis hadre et je content de connaitre ce grand Saint serigne Babacar sy( rdth)
Cherif Yalla na yalla goudale sa fane te nie nga maye buegue le yala nala ko cheikh sama tourondo buegue les
MASHALLA Chérif yallah na yallah goudeul sa fane, yallah nanou yallah fayal Seydi Aboubacar
Sy z
Kein d’où Serigne Babacar Sy❤️
Alhamdoulilah!!!!! Gueuneu nagnou kham lignou ame. Yallah naleu Yallah faye sisa barké Mame.
MACHALLAH SANGUE BI AIDARA WAKHTANE BI RAFETNA. DOUNDEUL LOU BEURI
Ma cha Allah Shériff Ibrahima Aidara At-Tidiany yalla na Yalla soubhanahou wa taalah fayal la boppamm yokkou kham khamm bi
Malle talibe sarigen babakar sy ken dou yaw
Salamoun aleickoum diaredieuf sama serigne CHERIF IBRAHIMA AIDARA yangui fii lol te werr si bakhe mame SEYDINA MOHAMET SAW AMINE mala beugue
Machallah kén dou serignou serigne yii serigne babacar sy malick point 🙏🙏❤❤
Macha allah cherif khôl bi sédna lool yalla khamnako, yalla nala yalla fay yiw si barké seydina Mouhamed(psl).serigne Babacar Sy RTA yalla na yalla di yéssal yeureumandém si moom ta tass gnou si barkém
Machallah chérif dabakh
SERIGNE BABACAR SY ❤
Cherif doyaluma dolil way
😮122😮😮😅2
😮😮😮😮2😮2😮😮
@@elimanefaye8995 😮😮😮😮
@@elimanefaye8995 😮😮😮😮a 😮2😮😮😮3😮😮😮
L'homme au bonnet carré au manteau vert et au sourire légendaire Lui c serigne babacar 🙏🙏🙏♥️♥️♥️
Machalla yallana yalla goudale sa fane contenanio ci yawe trop machalla
Yalla na niou yalla tass si Barké Serigne Babacar Sy Al khalifa
Ah machallah yallah nanou yallah fayal s.babacar sy
Chérif Ibrahima yalna yala saxal la si talibé Mame Dabakh ak si hadara malikiya yeup amna solo trop sax
MachaALLAH Cherif je vous apprécie davantage car Serigne Babacar dafa fort trop si mane. Merci de votre générosité à partager ces quelques aspects de la vie de Serigne Babacar RTA.
Billahi cherif beugue nala bou dée fébar nama Ray
Kèn dou serigne babacar sy sama serigne
Macha halla yalla n'a niou yalla doli soutoureu té def niou ayes talibé serigne babacar s'y ryth
Wakhtaan bi yeup neekhna mai dama guissni lima dessé barina lol pour ma baakh,yalnaniou yala baakhal defniou ayy talibè serign babacar sy piirr ❤️❤️🙏🙏ndah djiko bou sell motakh niounaane taalibé cheikh👌❤️❤️
Machalah pour ce travail grandiose pour la tarikha tidjane ya cherif
mashalla cherif boul faté famille Tall yi inshalla
bilahiiiii contane nanou cheriff nala yalla fay si barke yonete biii wa cherif guir dieumi serigne babacar sy do gnaw ndar
macha allah contane
nagnou bou bakh gnougui ziar ,yalna yalla fay
Dieredief aydara yalna yala fayla ci barkè serigne babacar sy
Mâcha Allah serigne moustapha sy yala nangue fi yaga te weer si barke yononte te bi
Cherif yalla gua goudd fannnn
Yalnala yalla faye cheriff ya bakh mala beugi4 ci lou werr
Machallah serigne babacar sy souniou yakarou fi ak faniou jeum
Mâcha Allah chérif yala nangue fi yaga te weer si barke yononte te bi
Macha allah yalna yalla soutoural la wëreuleu yook hamham bi
Yallna yalla faya sunu goor gui té taasñu si barké léram ndaysan chérif yalla yalla gudeul fan wi té defala weer
Cheikhal Khalifa Ababacar Sy ❤❤❤
Kaine dou Serigne Babacar Sy
Machallah cherif yague fi lool tè wèr magui laye sètane fii thi Brésil
Serigne Babacar sy yalla n'a yalla yock léram tassou niou si barké me amine yarabi
SERIGNE ABABACAR SY ma fierté mon bonheur mon tout yalla na yalla yokou ay léram té tass gnou si barkem
Machallah kéne dou seydi Aboubakrine Sy. Yalna yalla yok leram té tass nou ci barkhém
MACHALLAH chekhal khalifa rta kenne d'où mom yallah nagn yallah tass si Barkem si Barker seydina mouhamed psl inchallah
Halkhamedou Lila yalla n'a niou yalla doli khèweul ak soutoureu ak diamou ak moudiougou rafète
Machallah reck si sama Serigne Babacar sy yalla n'a yalla yock léram tassou niou si barké me amine yarabi
Mashalah waxtan bi wessouna am solo jeureujeufff ❤️❤️❤️
salam amna solo baba ! MAME mor khoudia sy est le fils de ahmadou sy frêre de mame ousmane sy donc il est cousin de maodo c"est lui qui dirigea sa priére mortuaire il était époux de soxna nafissatou sy maodo c'est le pére de serigne gora sy (la voix d'or ) qui chantait la bourda avec son oncle dabakh malick (rta)
Machallah
machalla cherif yalla ne serigne Babacar fay
Machalla kén dou serigne babacar sy
Machallah chérif, wakhtane Wi nékhna . Thiéy sa ma mame seydi Aboubacar SY kéne dou yaw. Maa la beugue SY.
CHERIF AIDARA BARAKA ALLAHOU FIKE, DIEUREDIEUF DIEUREDIEUF DIEUREDIEUF,
MA CHA ALLAH NA YALLAH TASS NOU THI BARKE CHEIKH SEYDIL HADJI MALICK SY RTA AK MBOLEM NDIABOTAM.DIEREDIEUF CHERIF NA YALLAH GOUDAL SAY FANE.MBAYE DAL MO NOU DOYE SIDY ABOUBACAR SY DO SENE MOROME.
Cherif aidara yalna yala fayla ligaya déff amna solo cou bakh nga amoulo kholou kiñane yalna yala aarla yok fanwi si barké sa mame mouhaméd salalahou aléyhi wasalam kén dou serigne babacar sy
Machalla amna solo wallahi
MachaAllah amattina solo yalla nala yalla fayy
MACHALLA YALLA NA YALLA FAYE
Wahtanal si seydil diamil sohla na niou ham simom ndah amougnou ay wahtanam dou si video dou si RUclips 1 benn wahtane lá am si RUclips por favor sento muito e agradeço muito gastamos as suas palavras são de verdadeiro
ESKEY SERIGNE BABACAR SY RTA YALLA NA YALLA YOK LERAM TASSUGNIU SI BARKEM INCHALLAH GUENA YOKEU SUÑU THIOFEL SI MOMEU ILAL ABADAN🙏🏽🙏🏽GOOR GUI KENEU DOU MOM L’UNIQUE♥️🔐
CHÉRIF DIEUREUDIEUF
Eskey Baba Chérif Ibrahima Aidara 😍😍
Ma challah yalna yalla barkel lepp
Machalla YALLA NA YALLA gudal sai fane
Serigne babacar s'y sama lepou sama yakar taye ake euléukk bilahi kouko diapou do ré moukou
Serigne babacar s'y yalnaniouko yalla fayal thi Barker mouhamed
Yalla n'a yalla yock léram tassou niou si barké Serigne Babacar sy
Machalla keneu dou serigne babacar yala nanouko yala fayal tchi barke seydina Mohamed psl
Machala cherif longue vie a toi
Yala na yala barkel te yokou ko leer famou teudeu te tass gnou si barkem serigne babacar sy
MOUSTAPHA NIANG (dmwm) vous suis depuis guediawaye notaire
Ak seringe moustafa ndongo thie altou gangiek incha Allah
Eskeuy Chérif wakhtane bi amatina solo. Yalla nala yalla faye si barké Seydina rassoul. Amine
Yalna gnou ko yalla fayale
Yallah na niou yallah takhe si barckém si barcké séydina mouhamed (psl )
Thiey serigne babacar sy kén dou mome
Machallah reck amna solo torop sakhe
Macha allah cherif namonnanla ,ziar si adjouma dji
Pape oumar Sall macha lah amenasolo refettena diaradiafe cherife aidara
Machalla amna solo tropp
Machalla cherife altidjini
Beugouma aldiana ni safara
Serigne babacar rek la beugue ❤❤❤
machallah seriff
Alhamndoulila sante yalla bignou amé kou melni cherif ak serigne babacar
Walahi ndeyssane thieuy Sama goor gui mo matone limou done un homme multidimensionnel Yalla rék mo kham Serigne Babacar Sy mais gnoune khamougnouko Mangui yessal sama diayantek mome rek ba ila yawmidine
khol séddatina way si serigne babacar sy