COMPILATION DES "KEMTANE" DE SERIGNE BABACAR SY

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025
  • Abonnez vous, activez la cloche pour recevoir tous nos vidéos et partagez pour développer notre communauté

Комментарии • 380

  • @Seck_mo_srg_babacar_Sy
    @Seck_mo_srg_babacar_Sy 2 года назад +11

    Barcki srg babacar s'y man mom rk la beug si sama xhol lepou louma ame serigne babacar s'y moma ko ganal dama ko beug te khamouma sakh

  • @sokhnathiam9856
    @sokhnathiam9856 Год назад +4

    Yala naniou yala tass si barkem, ma beig Serigne Babacar Sy

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 4 месяца назад +2

    Yalna Yallah Defalniou Diammou Amine Ya Rambi

  • @aissatousamba5149
    @aissatousamba5149 4 года назад +37

    Je suis fière d être tidiane talibe
    Serigne
    Babacar sy ,niane yalnaniou. Yalla feyal Mame aladji. Malick

  • @ndackdiongue5766
    @ndackdiongue5766 7 месяцев назад +2

    Machalla sy malick ❤❤❤❤

  • @mbayebabacardiouf7853
    @mbayebabacardiouf7853 4 года назад +182

    Il est le seul Diamant noir par excellence, dont les lumières tirent leurs forces dans le soleil de la miséricorde divine et le parfum dans les jardins cachés des élus aux grades sublimes. Il est le maître dont le nom frollant les oreilles de ses disciples, fait pousser des fleurs de joie dans leurs coeurs. Il est et a toujours été un guide vers le droit chemin aux vertus élevées. NOTRE CHER MAÎTRE le ruissellement de la splendeur CHEIKHAL KHALIFA ABABACAR SY

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 4 месяца назад +3

    Yalna Mame Yallah Oubli Bountou Worsok Yi Nioune Nieppe AK Souniou Ndiabotte Souniou Yayye Souniou Dommes Souniou Ndiabar Amine Ya Rambi

  • @walymataniang9931
    @walymataniang9931 7 месяцев назад +2

    Walla hi sama mame sama serigne kéne dou mome yalla na yalla fayallenouka si barké Alkhourehane dieuredieuf mame

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +1

    Machalla Mame Serigne Babacar Sy Boromme carré kenn Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +3

    Mame Elhadj Malick Sy Bayyou Serigne Babacar Sy Boromme carré kenn Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @toufikkhider3552
    @toufikkhider3552 4 года назад +13

    Sama yakar tay ak euleuk bilahi j’aime serigne babacar sy

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 5 месяцев назад +2

    Diadieuf Mame Serigne Babacar Sy Boromme carré kenn Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée et bonne soirée

  • @ABBAMane-do4cp
    @ABBAMane-do4cp 5 месяцев назад +3

    DIEU EST LE CRÉATEUR DE TOUS .et SEUL DIEU QUI SAIT IL a attribué quel niveau à notre mame khalifa Ababacar Sy MALICK.

  • @mamadouthiam1244
    @mamadouthiam1244 4 года назад +20

    Fatiha salatoul fatihi adiya Cheikh Seydi Babacar Sy (RTA)...Qu'Allah dans sa miséricorde divine l,élève aux rangs des élus du paradis, barké Mouhammad (Saws), barké Cheikh Seydi El hadji Malick (RTA), barké Cheikh Ahmed Tidjane Chérif (RTA)...Amine.

  • @omzo9111
    @omzo9111 4 года назад +28

    J’@iiime Serigne Babacar SY 🥰❤️❤️❤️ lep louma ame ak loumay wadjia ameu thi barket Serigne Babacar SY rek lakoy amé inchallah

  • @leboundoye4931
    @leboundoye4931 3 года назад +10

    Euskeuy thiey sougnou Gorgui masha Allah yalna nagnou Borom bi tass thi barké yalna yéwo thi Pencco Sangue bou téddeu bi 🙏🙏🙏saws

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +2

    Mame Serigne Mansour Sy Boromme Daadji Ken Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @ndeyefatou3660
    @ndeyefatou3660 4 года назад +8

    Yalla n'a yéssal yeurmeundé si Serigne Babacar sy amine

  • @mansoursow9896
    @mansoursow9896 2 года назад +2

    Machlla s'y Malik fawad same Serigne sama Mame s'y Malik

  • @matydeme9357
    @matydeme9357 9 месяцев назад +4

    Yalna Yala yokk leram tass niou si barkem❤❤❤❤❤❤❤

  • @SouleymaneFall-s6r
    @SouleymaneFall-s6r 10 дней назад +1

    Mame boy yalla nala yalla faye amine

  • @Sopeyayam
    @Sopeyayam 3 месяца назад +1

    Ma cha allahou kéne dou Serigne Babacar Sy Malick

  • @awatoure2470
    @awatoure2470 2 года назад +4

    Sounou goor gui, gor piir, goorgolu ci yonou Allah SWT ba ame ci feye, gnou koye sope chak année chak mois chak jr chak heure chak mn chak sec, jusqu'à notre dernier souffle. Ya Khalifa alhamdoulilahi rabbil alamine bi gnou la amé

  • @MbosseSamb-qc8bi
    @MbosseSamb-qc8bi Год назад +1

    Fière d'être talibé cheikh machala

  • @ABBAMane-do4cp
    @ABBAMane-do4cp 5 месяцев назад +2

    Sérigne Babacar Sy est toujours l'ami et guide des générations futures .

  • @saerndiaye9305
    @saerndiaye9305 4 года назад +19

    L'EP loumouy out ganaw yalla thi Barker Serigne Babacar Sy lakoy niane mom rek la gueum kénén koumou doon ak LO yor kholoumako guisoumako beugoumathi mom rek yalna yalla yokou léram thi bameelam

  • @sophiendiaye2230
    @sophiendiaye2230 Год назад +2

    Maachaala fatabarfakala yaala bou ka thiatt Dioutou

  • @AidaniaouthMbodji
    @AidaniaouthMbodji 7 месяцев назад +3

    Sama yakar tay ak euleuk guinaw yallah ak yonétibi mn sauveur sidi fagueye mi si diawar ❤❤❤

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +3

    Mame Abdou Aziz Sy Dabakh Rakkou Mame Serigne Babacar Sy Boromme carré kenn Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 4 года назад +7

    Masha Allah suma sopey serigne Babacar sy(rta) ken dou mom walaydeysane yalnañouko yalla fayal ta tass ñou si barkem si barke Yonentibi(saw)👏👏🙏🙏

  • @Lopios-g6l
    @Lopios-g6l 3 года назад +7

    Machalla kholale ma thiatou serigne babacar sy thii wétou mame Dabahh yalla nagnou yalla tasse thii sén barké ..⚘⚘⚘🍒🍒 ❤❤

    • @babagauye3686
      @babagauye3686 Год назад +1

      S pape Malick kimou déndal Almaktoum la

  • @cheikhounaba9186
    @cheikhounaba9186 4 года назад +9

    Mbeugueul bima am ci serign babacar sy yalana sakh di yokou amine🙏❤️❤️

  • @aramendiaye6464
    @aramendiaye6464 4 года назад +12

    Macha allah no comment yallah naniou ko yallah fayal ci barke yoonetti bi (saw)

  • @aidaniang5218
    @aidaniang5218 8 месяцев назад +2

    Machallah Sy yalla na yalla yoque ay lairame

  • @MamadouCiss-i3y
    @MamadouCiss-i3y 24 дня назад +2

    Mansala Serigne Babacar sy❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @AbyFall-z8l
    @AbyFall-z8l 8 месяцев назад +2

    Kou geumni kan dou mome beuseul❤❤

  • @khadysall7304
    @khadysall7304 2 месяца назад +2

    ❤❤❤❤❤❤ merci Mame Babacar Sy

  • @adyfqye8890
    @adyfqye8890 4 года назад +4

    Yalla na yalla soubhana watala fayalniou cheikh Seydi Seydi Hadj malick Sy ak Seydi ababacar sy

  • @azizniang7324
    @azizniang7324 Год назад

    Serigne Babacar sy le rayon qui illumine le chemain de l'Islam,le guide inconteste de la tarikha Tidjania,l'Homme que personne ne connait reelment que le bon Dieu nous accorde sa grace Amin.

  • @ndeyefatou3660
    @ndeyefatou3660 4 года назад +5

    Yalla n'a yalla yock léram tassou niou si barké me amine yarabi

  • @BæOumouFalleuh
    @BæOumouFalleuh 2 месяца назад +1

    Serigne babacar sy is my life❤❤❤❤❤❤❤♥️♥️❤️❤️🙏✨🕋🕌🥰🥰

  • @Lamine_Diagnee
    @Lamine_Diagnee 4 года назад +17

    Serigne Babacar Sy yallena Yalla yokou léram 🥰

  • @poulowade3926
    @poulowade3926 4 года назад +4

    Soumay dioy limaïy diokh moye beugeu Serigne Babacar Sy soumay rerr limaïy rerr moye beugeu Serigne Babacar Sy (RTA)yalla nama yalla def deugui deugui talibé🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @sambawadji3419
    @sambawadji3419 4 года назад +2

    Bilahi s Babacar sy diambar deugue la naco yalla faye

  • @abydisba2074
    @abydisba2074 Год назад

    MASHA ALLAH kén dou Serigne MBAYE SY souniou Mame RTA YALLAH NA YALLAH YOKK LERAL TASNIOU SI BARKÉM Amine 💓💓💓💓💓💓💓

  • @aminataniang1065
    @aminataniang1065 4 года назад +5

    Machala KEN DOU MOME MACHALA SY MALICK KEN DOU SERIGNE BABACAR SY MOYE SAMA SERIGNE

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +1

    Mame Saydou Nourou Tall Ken Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @ousmanecisse4262
    @ousmanecisse4262 Год назад +2

    Jtm beaucoup seydi aboubakar sy ❤❤❤❤❤❤❤❤🔐

  • @fatoucissokho5899
    @fatoucissokho5899 4 года назад +5

    Khaleyi dioud si guinaw Mbaye. Guissouniou Mbaye te Mbaye laniou guem kosi wakhal moy mamam bour Yallah mokoko diaglel.🙂🙂🙂🙂🙏🙏🙏

  • @SyMoussa-ey2lv
    @SyMoussa-ey2lv 6 месяцев назад +1

    Yalna yalna yokk leram tass niou si barkem ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🤲🤲🤲💯💯💯💯💯

  • @thiakamboup8175
    @thiakamboup8175 2 года назад +6

    Amine inchallah Machallah Serigne Babacar sy Malick Sy ndeyesane thieye yalla 🙏💙💙💙💙💙💙 thieye Serigne Babacar sy

  • @abydisba2074
    @abydisba2074 Год назад +1

    Kén dou CHEIKH SEYDIL HADJI MALICK SY RTA YALLAH nagnou YALLAH SWT feyal 💓💓💓💓💓💓💓

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 Год назад +2

    Machallah yalla nanou yalla fayal sounou mame Khalifa ababacar sy rta❤

  • @saerndiaye9305
    @saerndiaye9305 4 года назад +2

    Amna solo dh yalna niou ko yalla fayal

  • @abdousakho7115
    @abdousakho7115 11 месяцев назад +2

    Serigne Babacar Sy akh lo maana wakh amna lo bayi

  • @SouleymaneFall-s6r
    @SouleymaneFall-s6r 10 дней назад +1

    Bakari arame lo couba thiam diarra sy malick dieureu dieuf❤❤❤❤

  • @ndyebinta-qz2xe
    @ndyebinta-qz2xe 8 месяцев назад +4

    Billahi wallahi tallahi ☝️mane Dama yaradaleu woneu louma djiour mou dém ☝️ ma amateu Dome 2008☝️sama Dôme doundou 3jour mou sothieu ☝️bakane bi fateu menoule noyii ☝️gnou dém hôpital Mame Abdou 😔gnou yabaleugnou hôpital karefour ☝️gnou binedaleu ay garabe ma djiade pharmacie ☝️bima gnibé sama Dôme gueuna fabare ☝️maay djioy 😭nimay gueseto rêk djiakarelo ☝️AK Serigne Babacar ☝️wallahi ☝️mané mame boulema sétaneu 😭mame bi n'a tok Dôme bouma âme moudém 😭guinaw Yallaa AK Seuydina Mohamed PSL ☝️mame wouyouma ☝️ billahi Damay wakh AK Serigne Babacar ☝️ si photos ☝️ma guestou guiss sama Dôme Di Foo AK baramame si bébé bou âme 3jour Bakane bi fatone guisoumasi Dara ☝️ ♥️♥️♥️ kéneu dou Serigne Babacar ☝️ antouka Doy naa waare daleu kéne khamouko ☝️ yallaa n'a yallaa yokou lérameu AK gnimoufa fék 👇AK gnikofa fék gneup si Daradjieuy Seuydina Mohamed PSL ♥️🙏

  • @mamafaye8305
    @mamafaye8305 4 года назад +18

    Suma deigguei kou toudd serigne babacar sy damay beug dioy ndakh beug😭😭😭😭

  • @ramatasy5752
    @ramatasy5752 4 года назад +2

    Aah mashala sama xol toy na yalla nagnoula yalla fayal yoe mi defal gnou wahtane wi.. keine dou sy malick❤️

  • @fatoudiane1963
    @fatoudiane1963 Год назад +1

    Machaalla yalnako yalla faye yiw

  • @talibeserignebabacarsy7777
    @talibeserignebabacarsy7777 Год назад +13

    C'est toujours une fierté et un pur bonheur de sentir son cœur battre d'amour pour Cheikhal Khalifa Seydi Abubacar Sy Malick(RTA)❤ Khalifatulahi fîl ardî🙏 Yalna niou ko Yallah Fayal🤲🙏

  • @magayecisse670
    @magayecisse670 4 года назад +7

    Mâcha Allah serigne moustapha sy yala nangue fi yaga te weer

  • @laminegaye7429
    @laminegaye7429 3 года назад +2

    Masha Allah yalna Yalla yok ay léram ta tass gnou si barkem

  • @mamadoudiop4669
    @mamadoudiop4669 4 года назад +18

    Tabarakal Lahou , Abounaa Aboubakrine wa ine kana fil khabri radiyna bihi cheykhane illa Aakhiri deuhri, Yamiinouka l'Aa ansaa yamiinouka daahimane Abal fadli ma liy khayri zikkrika mine zikkri . Té sakh thia nak thie ndimbeul lou YALLAH .

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 4 месяца назад +1

    Yalna Mame Yallah maynou wer AK werle

  • @tidianeaw5449
    @tidianeaw5449 Год назад +5

    Macha allahh keneu dou borom diamono serigniou Serigne yi Serigne Babacar sy (rta)❤❤❤

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 4 месяца назад +1

    Machalla Mame Serigne Babacar Sy Kenn Dou Môme

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +1

    Mame Oumar Foutiyou Tall Ken Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @papinhofaye6193
    @papinhofaye6193 3 года назад +1

    Kéneu dou Serigne Babacar sy RTA

  • @miketoure4518
    @miketoure4518 2 года назад +5

    ALLAHU AK BAR LAHILAHA ILLALA SEYDINA MOUHAMMADOU RASSOULOULA SALALAHOU ALEYHI WA SALAM

  • @sagardiaw5318
    @sagardiaw5318 4 года назад +2

    Yalnala YALLA soutoural ba ma meune dem va si rawdou sam pour niane si barké wam pr ma am werr thi A V C bima dal

  • @fatousow4028
    @fatousow4028 4 года назад +3

    Machallah thiey mame babacar sy demba khouredja kén dou yaw

  • @MaimounaGueye-bn4ng
    @MaimounaGueye-bn4ng Год назад +2

    Ohhhh sy Malick jtm beaucoup serigne Babacar sy 😭😭😭😭😭😭

  • @youssoubadji4475
    @youssoubadji4475 6 месяцев назад

    Kendu môme walay ndeysane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ yallah na yallah yokk l'Aïr rare❤

  • @mayipboualmaktoum
    @mayipboualmaktoum Год назад +2

    Maame ❤

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 6 месяцев назад +1

    Mame Mountaga Daha Tall Ken Dou Môme Dieu merci beaucoup bonne journée

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 4 месяца назад +1

    Machalla Mame Serigne Babacar Sy Boromme Bonnet carré Domou Mame Elhadj Malick Sy et Mame Rokaya Ndiaye AK Wassila Mame cheikh Ahmed Tidiane Chérif Tanoume Mame Seydina Mohamed Callahou Eleyhi Wa Callahou Alleyhi Wa Calame Mame Yallah Kenn Dou Môme Moyye Leppe

  • @diaryndiaye3018
    @diaryndiaye3018 2 года назад +2

    Yallana lene yalla yeureume te hare k aldjana firdaws amine yarabi si barké seydina Mohamed salahou aleyhi wa salam

  • @assaneba4903
    @assaneba4903 4 года назад +2

    Diazak'Allah ana Khayran na yAllah fayla thi braké Serigne Babacar

  • @AmiToure-d8t
    @AmiToure-d8t 4 месяца назад +1

    Billahi kéne dou serigne babakar sy ❤❤❤❤❤❤

  • @DjibyNiang-jv2yo
    @DjibyNiang-jv2yo Год назад +7

    Fière d'être talibé cheikh ❤️

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang 4 месяца назад +1

    Yalna Mame Yallah Maynou Diammou Adouna ZkAlahirz

  • @madiopndiaye7570
    @madiopndiaye7570 2 года назад +2

    Ndeysane kholal serigne pape Malick Thiatou serigne babacar s’y

  • @aidagueye9753
    @aidagueye9753 2 года назад +5

    Serigne youssoufa Diop omonime de mon père allhamdoulilah 🤲

  • @mamadoudiop6596
    @mamadoudiop6596 4 года назад +6

    KHOUTBUL KHAAFI KHAYNII BAYNAL MACHIRIHI KEIN DOU MAME BABACAR

  • @nddia3880
    @nddia3880 4 года назад +12

    Yallah nagnou la yallah fayal MaMe

  • @chachalapatriote8336
    @chachalapatriote8336 9 месяцев назад +1

    Yalnama yallah tass sisa leer barké Nabil Moustapha

  • @khadyfall9222
    @khadyfall9222 4 года назад +5

    Mala beugue serigne babacar sy yalla na sounou borom yook sa lerrr❤️❤️

  • @mohamedseck6752
    @mohamedseck6752 4 года назад +2

    Machallah Amna solo bark s babacar s'y yalna Jam yakk

  • @IbrahimaGueye-s9r
    @IbrahimaGueye-s9r Год назад +3

    Machallah yallah 🙏 alkhadoulilah fier d'être un talibé cheikhe 🙏🙏

  • @mbayeabdouaziz8696
    @mbayeabdouaziz8696 3 года назад +1

    Wallaye Sy wakhdji barina wayye Serigne Babacar sy amoule morome ci matarba

  • @issakhagueye4290
    @issakhagueye4290 3 года назад +2

    Yalnanu Yala taas ci barkeem addunaak laaxira defar sunu leep addunaak laaxira !!!!!!! Amiin !!!!!!! Goor gu teed ku Yala teral.

  • @ahmedpam
    @ahmedpam 4 года назад +15

    Machallah wakhtane bi rafétna
    Dieureu dieuf Serigne Babacar sy 🙏❤️

  • @cheikhtidianethiandoum1133
    @cheikhtidianethiandoum1133 4 года назад +17

    Machala brom maye yi

  • @robertmouhamed7942
    @robertmouhamed7942 Год назад +2

    Assalamaleķoum.nous.sommes.fieres.detre.tidiane.srerigne.babacar.yalna.yalla.fayalgnoula.amen

  • @mariamadiallo3875
    @mariamadiallo3875 3 года назад +1

    Billakhi ma beug serigne babacar sy

  • @layelayecisse9459
    @layelayecisse9459 9 месяцев назад +1

    Yalla na yalla yokou léram ❤

  • @idrissandao8690
    @idrissandao8690 Год назад +2

    Serigne babacar sy Yalla nako yalla guereum

  • @aminahdiatta6249
    @aminahdiatta6249 4 года назад +2

    Yallananiou la yalla fayal Sheikhal khalifa RTA ❤❤❤❤borom bonnet carré bi borom sacré yalla bi borom manteau goorou ndar bi khalifa yaye daba Ndiaye ba

  • @SokhnamatyNdiaye-bv1nf
    @SokhnamatyNdiaye-bv1nf 4 дня назад +1

    Kouy décortiquer photo bi svp et merci au réalisateur de cette belle vidéo ❤❤❤❤❤❤