Aliou Dembourou Sow est le seul responsable de la promotion de Goor Diassi sous le silence de MackySall qui l'a nommé député. Un responsable publique sert d'exemple.
Je suis peul. Mais goraté gui bi ça doit s'arrêter trop c'est trop. On doit pas accepter des irrespondables nek si all bi Di tilimal Souniou ethnie. Mounoo aay khalé you ndaw nga jokh lenn jassi niou dougou si all bi Di goor nitt gni comme ça. Ces serere sont victimes. État Souniou mounoul gérer deuk bi naniou meyy nienenn gérer ko. On en a marre sonko Lall n'a adji sarr lalou ko nio kham nio moom seeni taat Lou lenn nekh deff. Ngenn joublou si priorités Réw mi. Sama mbokk peul you samm si all bi goraté bi meunouta continuer tamite. naniou baayi aussi Lou khew rek nga dem taal village leum c'est injuste dans ces villages il ya des gens yeugouniou tinouniou d'où niou togn et puis ils connaissent même pas celui qui a commis le crime. Niou baayi si khel.
@idrissa, dans beaucoup de zones ils mettent le bétail dans les champs des paysans et quand ils réagissent. Ils les attaqent au coupe-coupe. "Mi lappata". Ah oui couper les arbres dans les champs d'autrui et autour des carrés de maisons, ils adorent
La faute à MackySall qui appuie des peuls qui parlent de Goor Diassi aux opposants à l'assemblée. Si Aliou Dembourou Sow était puni publiquement par MackySall aucun peul n'aurait osé utiliser des sabres pour régler ses problèmes.
Depuis ma deugue ay neddo ko bandam ci rewmi lah néi senegal yakhuna tout ça faute du président car c lui qui a mis des ministres et députés méchants et incompétent qui n connaît absolument rien
Les gars arrêtez ce que vous faites car cela pourrait conduire à la guerre ethnique. On ne le souhaite pas, comme ce qui s'était passé au Rwanda entre les outous et les toutsis c'est très dangereux. Yallah na yallah dèf diam Sénégal ak dans le monde entier ci barki Nabil Moustapha
Je me rappelle sama grand père daf niou done defal ay toull ndakh pheul yi nio bokone albi te daniou say say Lou melni laniou done bagnial Billahi daniouy dore diasi 3 fois bou dougoul niou daw legi nak daniou len di diap nangou diasi yi nokh len ba seleum len diape nak you ndaw yi yobouko souniou keur yi yew ko fofou ba sen parent yi niew niou diokh len avertissement niou dogla respect pheul saï saï la faw nga am fo diarak mom mou respect la
C’est déplorable vraiment. Les alertes sont rouges chers autorités. Si ceci ne s’arrête, ça pourrait induire à d’éventuels conflits éthiques🤦🏽♂️💔😭🤦🏽♂️
Yaw niousoul falé domikharam serez amoul Sénégal Gui deug nit la esclaves bouga diel sa place dila fenal ba kagne fi ben serez nekou fi ay domi nar aki domi juif et chinoi ok
Depuis ma deugue ay neddo ko bandam ci rewmi lah néi senegal yakhuna tout ça faute du président car c lui qui a mis des ministres et députés méchants et incompétent qui n connaissent absolument rien
@@nogayfall9068 danio doy war li kou lèn yeureum rék daniouko défoul sa mbok mane amena sama bène mbok bou nga khamné bène peul mo moko bète dague lokhom yeureumou malèn dougue si tolou diambour té so wakhé niou dorla diassi yakh sa avenir .
@@nawalboujbir9982 yew do ragal yallah li amoul poulh ak seerer li defa yagga ci ci senegal digante baykat ak sammoukat yenna saay s gnouy khekh sakh mounagnou nekka benna khet ki di sammou ki bay
C'est dommage que nous en arrivons là. Cette situation pouvait être eviter si les services des ministères de l'aménagement ou de l'urbanisme avaient fait preuve de rigueur sur le plan de la prospective, parce qu'il faut comprendre que fondamentalement cette situation découle de l'implantation du nouveau aéroport a l'occurrence AIBD . en effet des centaines d'hectares a cheval sur des centaines de village de Dias et de Sindia ont été impacté par l'aide .du coup les paysans se sont vu spoliés de leur terre cultivables , aujourd'hui beaucoup de jeunes de la zone se bousculent dans les travaux BTP carreleurs , maçons, peintres ,coffreurs etc car n'ayant plus de marge dans l'agriculture. quant aux éleveurs les étendues sur lesquelles ils faisaient pêtre leurs troupeaux se sont retrecis..Forcément donc le peu d'espaces restant est tiraillé entre éleveurs et paysan . ce qui sera source de conflit . l'état devrait être pro actif , sur cette situation qui était tout à fait prévisible. Toutefois il faudrait pas imputer cette situation au président de la République . ce sont les services de l'État qui ont failli. j'en appelle aux autorités coutumiers de la localité de prendre leur bâton de pélerin pour apaiser les tensions en collaboration avec les autorités administratives et apporter des solutions à court terme. car pour les uns et les autres c'est une question de survie pour la pérennité de leur activité.
Diédhiou Mamadou, au moins, vous faites l'effort (contrairement à ceux et celles qui font dans les insultes et les attaques personnelles) d'analyser les choses et d'en situer les responsabilités. C'est pourquoi j'aime votre commentaire parce qu'il y a une très grande part de vérité dans ce que vous dites. Cependant, n'oubliez pas que les services techniques des ministères qui eux ne font qu'exécuter la politique définie par le Président de la République suivent un plan d'action et de planification des activités bien déterminées. Il appartient donc au Président de la République par l'entreprise de son Premier Ministre et par rapport à certaines compétences de voir les évaluations faites par rapport au niveau et au résultats d'exécution de ses chantiers. Sachant qu'il a supprimé même le poste de Premier Ministre à un certain temps pour dit-il faire accélérer les choses dans le cadre de son fast track et mieux contrôler les activités. Et, dans le cadre de ces heurts ci entre communautés Sérères Safènes et Peules, il s'agit de la panne d'un maillon très important de stabilité de notre pays : la Justice qu'il a pratiquement mis sous son joug pour ne pas du tout dire sous son coude. Ce qui a comme malheureuse résultante l'émergence de justiciers sur fonds de justices populaires. Quand le sentiment d'injustice plane au dessus des têtes ou submerge les populations, l'on assiste forcément à ce genre de réactions catastrophiques. Le président étant plus préoccupé à utiliser le Pouvoir Judiciaire pour mettre les bâtons dans les roues et voire même neutraliser ses principaux et farouches opposant(e)s dans le but exclusif de se maintenir au pouvoir ou de se choisir son successeur pour couvrir ses arrières. Suivez bien le reportage et vous verrez que ces pauvres populations ont réagi parce qu'elles sont finalement fatiguées de subir les offenses et les préjudices à elles infligés, leurs alertes ayant été vaines. C'est le sens en fait de mon poste de départ qui incrimine donc le Président de la République. Nous avons toujours prôné le management par l'exemple, sans être suivi. Car, malheureusement, le Président Macky SALL a trahi sa promesse d'une gouvernance de rupture fondée sur la sobriété et la vertu. L'on n'a donc pas besoin de faire Sciences Po Paris ou Bordeaux pour le comprendre. A bon entendeur nak. Wassalam.
Je suis peul mais il faut punir ces actes comme ça se sera une leçon pr les peules et les autres car c'est des pratiques qui risque de créer une guerre civile.
@@argent2949 t'as raison mec On constate que depuis 2018 y'a ces chiens-politiques qui prônent l'ethnocentrisme qui tend certainement vers une génocide
Peul rayna sama mame ci toolam akk diaassi. Ya pas longtemps peule yi raynaniou sama béne cousin. Té lep moudioul feen. Doyna waar mais peul yi warnaniou bayi rayee bi comme nane ndokh
C n'est pas la première fois que peulh Di def Lou niaw lii niom nieup laniou wara tall rk à chaque fois rk niou dieul bakanou jeune bagua khamatènè soutien de famille lay donne c vraiment dommage too dou moudiou Fenn j imagine si vous êtes des humains ou vous avez des coeurs de pierre 😭😭😭😭😭
No vraiment li metina 😢 torpe Mane peulh la wayé li à douma ci li diaw n'a rafétoul Dara 😭 femme bi Di niowi nak AK ki niak dôme Mame jeune frère réponse en paix 🙏🙏
Peulh yi c'est pas la première fois qu'il tue des personnes pour n'importe quoi, premièrement niom nioy togne di dougeul séni naak ci ay tolou diambour, ba noppi so wakhé niou gorla, sénégalais yi nak khamouniou kou togne kou fayou laniou xam, mais nak avant de s'attaquer à un village entier, il fallait simplement identifié le responsable et sa maison familiale.
On a tous vécu ce problème tu passes toute la saison des pluies à cultiver et du jour au lendemain les bergers envahissent ton champ avec leur troupeau quand tu parles ils te sortent un coup coup vraiment c’est pas facile et bien vrai que personne n’a pas le droit faire justice lui-même mais doyna war yalna yalla yok soutoura
La façon dont ils ont tué notre diaroul naniou sakh guérre les peulhs se victimisent comme si dagne léne togne alors k nio togne noy féké nit ki thi tolam diayko doolé loural ko téksi rayko apres niou fokni fofou lay yém
La justice est à la base de la stabilité et de l'instabilité dans un pays et voilà les conséquences d'une justice injuste si on va jusqu'à ce que chacune fait sa propre justice chaqu'un doit avoir peur dans ce pays
Li dafa yague si bire commune de diass depuis bima khamé ba legui peul yi daniouy dougou si tolou serere liniou cultivé si nawete bi yeup niou dioxko sen diouryi bo waxé niou gor leu té dou moudié feneu
Franchement un danger guette notre belle et ancestrale cohabitation embellie depuis nos ancêtres par la plaisanterie.Que les autorités s'impregnent avant que cela ne dégénère...!peulh ak Sérére sont des frères
C’est vraiment triste de voir que ce que nos ancêtres avait bâti est en train de partir en fumée! Ça devient dangereux quand les gens se font justice eux-mêmes. Yalna diam deloussi ci diganté sérères ak peulhs yi
Je suis Peul mai li gniawna trop goraté mofi wora djékh trop c'est trop vraiment J'ai le coeur meurtri vraiment c'est très triste de voire des gens tué comme ça. L'état doivent voté la peine de mort qui tue on le tue. Mangui massaw la population de Kiréne di massaw la famille Sérére 😭😭😭
Ohh waa li mom yemena lol ,aydou Yam si bop borom ,peulh et sérère et otre nous sommes tous des citoyens donc on doit se respecter l être humain est sacré
Baye modo billay li defa gniaw bou gnieppou meloon ni yew reewmi bakh ndakh mounou ngou jel khet yep dougal ko ci pot gnieppou mounou gnou bon me verema soudee deggala niila deme rafetoul me li Lou yaggala digante baykat ak sammou katyii defa wara jeekh ndakh lii mom bakhout
@@aissatoudia4280 effectivement c'est un fait très récurrent dans le pays mais tout peut se régler dans la compréhension,le dialogue le pardon et surtout le respect de l autre.
Talouniouko sah yen lagn waron tall bilahi vous êtes sans cœur vous parlé de millions et harr légui domou diambour bingen rey en plus ngen di fen💔😭dolen meussa nangou ni yen la kouthie yii
Ndaysaan Li dé Kou Yaro si alle rek arrivée nala rour sa tool dior la diassi, après Sakh Dangay moudji décourager bàyyi Bay outi un autre métier c triste mais yàlna Si Diam moujji,ta di dialé famille bi
Li dafa yague si réwmi walahi gueestou lén histoire peul yi danio yagu rayy baykatt yi Lou ndaw Sax niou guéné Diassi Basi yonou Mourid amna histoire entre Peul yi AK Mame Thiérno Birahim le petit frère de Serigne Touba ba tribunal la moudié
Waw li mo khéwone ci fanne yii touba. Si diguénté baye fall yii ak peul .yii état bi défou ci bénneu liguéy bou am soolo ta baï ak samou nioo andu béneu dou déme ba sa marom kone état dafa wara déf ligué yame ta baïyii sétane bii ndax léépou senegal
Thieye Yalla lii dh metina lóol 😢😢😢waye nak peul yi danio wara bayi gawa guene Diasi 😢😢😢
Aliou Dembourou Sow est le seul responsable de la promotion de Goor Diassi sous le silence de MackySall qui l'a nommé député.
Un responsable publique sert d'exemple.
Je suis 1000% sonko mais s'il vous plaît arrêter de mêler ces faits à la politique
Yenn moom nafekk ngenn louni ngenn politiser ko ma warou.
Yenn WA Sonko yi la rek.
Talolenn d'ara Loudoul politique
@@amadoutidianeba6238loci toudé sonko lii problème entre citoyen la
@@idrissag.4110 hey bayil nak wa sonko stp c’est pas tout le monde
Sof guene lou niew rék guéne politique gué ko
Je suis peul. Mais goraté gui bi ça doit s'arrêter trop c'est trop.
On doit pas accepter des irrespondables nek si all bi Di tilimal Souniou ethnie.
Mounoo aay khalé you ndaw nga jokh lenn jassi niou dougou si all bi Di goor nitt gni comme ça.
Ces serere sont victimes.
État Souniou mounoul gérer deuk bi naniou meyy nienenn gérer ko.
On en a marre sonko Lall n'a adji sarr lalou ko nio kham nio moom seeni taat Lou lenn nekh deff.
Ngenn joublou si priorités Réw mi.
Sama mbokk peul you samm si all bi goraté bi meunouta continuer tamite. naniou baayi aussi Lou khew rek nga dem taal village leum c'est injuste dans ces villages il ya des gens yeugouniou tinouniou d'où niou togn et puis ils connaissent même pas celui qui a commis le crime.
Niou baayi si khel.
Tu a rien compris
@@abdousow831 Explique moi stp mon frère.
Peut être j'ignore quelques choses nga balma akk.
Doyna waar dé ndakh daguay togn nitt ki baa paré thiorkoo ayy diassi
@idrissa, dans beaucoup de zones ils mettent le bétail dans les champs des paysans et quand ils réagissent. Ils les attaqent au coupe-coupe. "Mi lappata". Ah oui couper les arbres dans les champs d'autrui et autour des carrés de maisons, ils adorent
Walay wakhnga deugeu
La faute à MackySall qui appuie des peuls qui parlent de Goor Diassi aux opposants à l'assemblée.
Si Aliou Dembourou Sow était puni publiquement par MackySall aucun peul n'aurait osé utiliser des sabres pour régler ses problèmes.
Est ce que tu es normal toi. Non tu dis tu n'importe quoi. Que dieux nous assiste.
Dëgg piir nga wax
Peul ak serere déh waroune xoulo baye rayéneté dommage mes condoleances que la terre lui soit lègere amine
Wallahi ndieyssane c'est très très regrettable vraiment
Si l'Etat avait mis aux arrêts ALIOU DEMBOUROU SOW, on n'allait pas arriver ici.
Depuis ma deugue ay neddo ko bandam ci rewmi lah néi senegal yakhuna tout ça faute du président car c lui qui a mis des ministres et députés méchants et incompétent qui n connaît absolument rien
Peul yui bayui lene gor diassi dengena bone te saysay
Peul yi gnoy togn wa kirène meusougnoulèn def dara .sow késé motakh gnou dém li .imaginel gey rey nitki yayam féké .état souko lidiantéwoul dinagnko lidiantel sounou bopp.goraté rek gnoun dougnou ay nit xana .li dey diekh
Peulh yî danou lein wara interdire arme blanche binouy samei franchement dfa eup peulh yî beugu nka goratei😭😭😭😭😭😭
Vraiment boy khékh nga khekh ak sa lokho 6 person Loulou dafa méty 😡😡
Wakhal lo khame
Lii dé rafétoul entre peulhs et séréres yalla na si yalla def diam, wala peulhs y déme fénéne🙏🙏🙏🙏
Yow d wakh nga lou rafet..yalla na def diam
Ah wala serere dème fenéne yalla n'a diam am digueté serere ak peulh aye bok laniou
Bii moy deuxième fois mem mois passe à Mbacke amnafa tt jour peul yi vraiment nak mogui beug apeu lokhou
Li eup khaléyi nioy same nakyi té daniouy rèw ba dof sèn diassi yi niou tokéko foumou la lal nga yakhou li dou deugue
@@nialynialy801 mom kay doyna war trop merci 🙏
No défois do meune wax lép Sax bilay li dafa yague si réwmi walahi mo niou maak té doufi djoukk néxoul dé dafa yomb trop
Man dinaa bayi waat ndakh peul yi
@@adioumadiagne7607 😂Entout cas doyna war dall😀🙏
Les gars arrêtez ce que vous faites car cela pourrait conduire à la guerre ethnique. On ne le souhaite pas, comme ce qui s'était passé au Rwanda entre les outous et les toutsis c'est très dangereux. Yallah na yallah dèf diam Sénégal ak dans le monde entier ci barki Nabil Moustapha
Billahi c'est ce que je voulais dire k'Allah SWT nous en preserve
Les peuls sont comme ds tous les pays de l’Afrique les mêmes problèmes au Cameroun Mali etc…
@@TheBandafall2003 des imbéciles Comme toi vont brûler le pays entre sérère et peulh diam Dong mofa hadji dommage qu'il ya encore des gens comme toi
Yalna Yalla defff diam Sénégal 🤲🤲
Je me rappelle sama grand père daf niou done defal ay toull ndakh pheul yi nio bokone albi te daniou say say Lou melni laniou done bagnial Billahi daniouy dore diasi 3 fois bou dougoul niou daw legi nak daniou len di diap nangou diasi yi nokh len ba seleum len diape nak you ndaw yi yobouko souniou keur yi yew ko fofou ba sen parent yi niew niou diokh len avertissement niou dogla respect pheul saï saï la faw nga am fo diarak mom mou respect la
Loolu moy dëgg peulh kou tallal nounaram dong la kham
Saway ñi niii laniou deukké ak nioune té kén doussi wax c pas la première fois que ça arrive dh
dengay doul rek
@@hamadyba1207 thi lane
Con Kai serign touba sai sai la dah peul la
C’est déplorable vraiment. Les alertes sont rouges chers autorités. Si ceci ne s’arrête, ça pourrait induire à d’éventuels conflits éthiques🤦🏽♂️💔😭🤦🏽♂️
Kou khal sérére khamné amounu thiaxan...que son âme repose en paix inchallah
Bilaye sérere dou togne
Peul walla sererr
Nn gnoune dounou togn wayé kougnou togn dosi guéne
Yaw niousoul falé domikharam serez amoul Sénégal Gui deug nit la esclaves bouga diel sa place dila fenal ba kagne fi ben serez nekou fi ay domi nar aki domi juif et chinoi ok
Diap domou diambour reyko si loulene nehhh guene ame loléne di wahhh téniou dalaléne sunu bir repose en paix couzin🙏🙏😭
Ya wakhe deug dani togne reck
Jamais j' n'oserai de faire du mal à un sérère à cause des liens de nos grands parents
P
Bilahi
Pheul yi bayilene rayate bi wakholene fi dra yor diasine Di melni kou Ray Mala vraiment ces domense🤔😬🤭
Vraiment
Yow Kane mola wakh pulla bakh na nagnou dém 💪💪💪💪💪💪💪
@@mouhametba6108delo Silène s'en khele si yala te bayi bougn e wakhe Guen guene diassite Di Ray aye bakane🤭😤😱
iow kou niamé yallah gua
@@Pirate987 beyi lene fate bakhane Ray nite nafa meti Kone def sa mbokou douna nekh Sète lene si yala 😬😄🤗
Depuis ma deugue ay neddo ko bandam ci rewmi lah néi senegal yakhuna tout ça faute du président car c lui qui a mis des ministres et députés méchants et incompétent qui n connaissent absolument rien
On est tous en danger dans ce pays.
Yeureum n’a mère bi trop bilahi guiss sa domm gnû koÿ raÿ 😢😢
Aka méti sax lou meti yague nafi dé le 10 octobre passé nilangn déf sama rakou papa ilimane dia tirré la ball gua ganiou yobou sa 4 millions
Bilahiiii 😭😔
Des gens qui utilisent des coupes coupes comme ils veulent 😭😭😭
Quand j'étais petite sama tonton daniouko guoronne ak diassi si bopam touti mou déh
Loumou deff
Thiey Sénégal yahkounaaa ,li rekk moy andi génocide, le procureur doit s'auto saisir.
Peul yi mom amo gnou béne respect si bayy Kat yi serer yi sonou nan trop si Al bi
L'état dois régler ce problème de cultivateur et éleveur
Métina da nguène wara bayi di rour tolou diambour yi té sounou lèn dispé nguène guéné diassi dou yone .
Billahi yerem nalén torop wayé lolou moy problemas yi
@@nogayfall9068 danio doy war li kou lèn yeureum rék daniouko défoul sa mbok mane amena sama bène mbok bou nga khamné bène peul mo moko bète dague lokhom yeureumou malèn dougue si tolou diambour té so wakhé niou dorla diassi yakh sa avenir .
Guawa guor aussi beugue diasser
Ay domikaram lagn peul yii
@@nawalboujbir9982 yew do ragal yallah li amoul poulh ak seerer li defa yagga ci ci senegal digante baykat ak sammoukat yenna saay s
gnouy khekh sakh mounagnou nekka benna khet ki di sammou ki bay
N’oubliez jamais que bakane dafa fort paix a son âme
Que la paix et le retenu reviennent au Sénégal
Pppppppppp
Amine
C'est dommage que nous en arrivons là.
Cette situation pouvait être eviter si les services des ministères de l'aménagement ou de l'urbanisme avaient fait preuve de rigueur sur le plan de la prospective, parce qu'il faut comprendre que fondamentalement cette situation découle de l'implantation du nouveau aéroport a l'occurrence AIBD .
en effet des centaines d'hectares a cheval sur des centaines de village de Dias et de Sindia ont été impacté par l'aide .du coup les paysans se sont vu spoliés de leur terre cultivables , aujourd'hui beaucoup de jeunes de la zone se bousculent dans les travaux BTP carreleurs , maçons, peintres ,coffreurs etc car n'ayant plus de marge dans l'agriculture.
quant aux éleveurs les étendues sur lesquelles ils faisaient pêtre leurs troupeaux se sont retrecis..Forcément donc le peu d'espaces restant est tiraillé entre éleveurs et paysan . ce qui sera source de conflit .
l'état devrait être pro actif , sur cette situation qui était tout à fait prévisible.
Toutefois il faudrait pas imputer cette situation au président de la République .
ce sont les services de l'État qui ont failli.
j'en appelle aux autorités coutumiers de la localité de prendre leur bâton de pélerin pour apaiser les tensions en collaboration avec les autorités administratives et apporter des solutions à court terme.
car pour les uns et les autres c'est une question de survie pour la pérennité de leur activité.
Diédhiou Mamadou, au moins, vous faites l'effort (contrairement à ceux et celles qui font dans les insultes et les attaques personnelles) d'analyser les choses et d'en situer les responsabilités. C'est pourquoi j'aime votre commentaire parce qu'il y a une très grande part de vérité dans ce que vous dites. Cependant, n'oubliez pas que les services techniques des ministères qui eux ne font qu'exécuter la politique définie par le Président de la République suivent un plan d'action et de planification des activités bien déterminées. Il appartient donc au Président de la République par l'entreprise de son Premier Ministre et par rapport à certaines compétences de voir les évaluations faites par rapport au niveau et au résultats d'exécution de ses chantiers. Sachant qu'il a supprimé même le poste de Premier Ministre à un certain temps pour dit-il faire accélérer les choses dans le cadre de son fast track et mieux contrôler les activités. Et, dans le cadre de ces heurts ci entre communautés Sérères Safènes et Peules, il s'agit de la panne d'un maillon très important de stabilité de notre pays : la Justice qu'il a pratiquement mis sous son joug pour ne pas du tout dire sous son coude. Ce qui a comme malheureuse résultante l'émergence de justiciers sur fonds de justices populaires. Quand le sentiment d'injustice plane au dessus des têtes ou submerge les populations, l'on assiste forcément à ce genre de réactions catastrophiques. Le président étant plus préoccupé à utiliser le Pouvoir Judiciaire pour mettre les bâtons dans les roues et voire même neutraliser ses principaux et farouches opposant(e)s dans le but exclusif de se maintenir au pouvoir ou de se choisir son successeur pour couvrir ses arrières. Suivez bien le reportage et vous verrez que ces pauvres populations ont réagi parce qu'elles sont finalement fatiguées de subir les offenses et les préjudices à elles infligés, leurs alertes ayant été vaines. C'est le sens en fait de mon poste de départ qui incrimine donc le Président de la République. Nous avons toujours prôné le management par l'exemple, sans être suivi. Car, malheureusement, le Président Macky SALL a trahi sa promesse d'une gouvernance de rupture fondée sur la sobriété et la vertu. L'on n'a donc pas besoin de faire Sciences Po Paris ou Bordeaux pour le comprendre. A bon entendeur nak. Wassalam.
Je suis peul mais il faut punir ces actes comme ça se sera une leçon pr les peules et les autres car c'est des pratiques qui risque de créer une guerre civile.
@@argent2949 t'as raison mec
On constate que depuis 2018 y'a ces chiens-politiques qui prônent l'ethnocentrisme qui tend certainement vers une génocide
Bilaye nous sommes en dangé fék nit thiorko bilaye pôle bî tamite kholéne séne diguaté Ak yalla ak séne diguaté Ak kal
Je ne reconnais plus mon cher Sénégal 🇸🇳😢😭😭😭😭😭
Les peuls ne vont jamais au prison parce que les procureur sont des peuls
Wa motakh askane bi di fadial sèn bop .sone siss tol bamou rafèt niounieuw dougeulfa sèn ay nak niou yak lèp pour lane niotogne
Sou féké peul bi défoul dara loumou def prison
Arétt toi
Wakhou doff
Peul rayna sama mame ci toolam akk diaassi. Ya pas longtemps peule yi raynaniou sama béne cousin. Té lep moudioul feen. Doyna waar mais peul yi warnaniou bayi rayee bi comme nane ndokh
😢😢😢😢😢😢😢😢😢 yalna yalah yeureumko tè dièguellène
Peulh la dé mais Danio beuguou gor aférou diassi maman massa😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭khana kay niom founiou lack es ce que nio réy
Niom nio ray kay ay monstre guene c'est pas la première fois
C n'est pas la première fois que peulh Di def Lou niaw lii niom nieup laniou wara tall rk à chaque fois rk niou dieul bakanou jeune bagua khamatènè soutien de famille lay donne c vraiment dommage too dou moudiou Fenn j imagine si vous êtes des humains ou vous avez des coeurs de pierre 😭😭😭😭😭
Wa allhamdou lilah lii sax doyol bakh na si yéne peull yi si bopame gnio togne 😢
Merciii dañiou xew
Diame moye lap
Nopil khamo
No vraiment li metina 😢 torpe Mane peulh la wayé li à douma ci li diaw n'a rafétoul Dara 😭 femme bi Di niowi nak AK ki niak dôme Mame jeune frère réponse en paix 🙏🙏
Cou dacore ni couraye dagne la wara raye😭🙏
Métina lollll 😭😭!!!! Yalla nako yalla yeureum !!!! Souniou kalll peheul yi kholatt lennnn dieufinnne ta yalla takh !!!! Ay mbokkk laniou
Peulh yi c'est pas la première fois qu'il tue des personnes pour n'importe quoi, premièrement niom nioy togne di dougeul séni naak ci ay tolou diambour, ba noppi so wakhé niou gorla, sénégalais yi nak khamouniou kou togne kou fayou laniou xam, mais nak avant de s'attaquer à un village entier, il fallait simplement identifié le responsable et sa maison familiale.
Je me demande dans notre pays les animaux sont plus précieux que l'être humain wa salam
Deuk bou Amoul justice askan bi fadial sen boupou se qui e dangereux
On a tous vécu ce problème tu passes toute la saison des pluies à cultiver et du jour au lendemain les bergers envahissent ton champ avec leur troupeau quand tu parles ils te sortent un coup coup vraiment c’est pas facile et bien vrai que personne n’a pas le droit faire justice lui-même mais doyna war yalna yalla yok soutoura
Yalna yalla doulï djam rekk ak soutoura
La façon dont ils ont tué notre diaroul naniou sakh guérre les peulhs se victimisent comme si dagne léne togne alors k nio togne noy féké nit ki thi tolam diayko doolé loural ko téksi rayko apres niou fokni fofou lay yém
La justice est à la base de la stabilité et de l'instabilité dans un pays et voilà les conséquences d'une justice injuste si on va jusqu'à ce que chacune fait sa propre justice chaqu'un doit avoir peur dans ce pays
Li dafa yague si bire commune de diass depuis bima khamé ba legui peul yi daniouy dougou si tolou serere liniou cultivé si nawete bi yeup niou dioxko sen diouryi bo waxé niou gor leu té dou moudié feneu
Lerna la
Franchement un danger guette notre belle et ancestrale cohabitation embellie depuis nos ancêtres par la plaisanterie.Que les autorités s'impregnent avant que cela ne dégénère...!peulh ak Sérére sont des frères
Ce sont les toucouleurs qui respectent cette plaisanterie pas les peuls, désolée
@@rosaliediouf538 NE créez pas de division svp
@@rosaliediouf538 on est tous pareils
@@fadimafaty5250 il y’a une différence . Les toucouleurs halpoulars qui ne sont pas peuls n’ont pas de problème .
Lii ñiawna cii des cousins de toujours!
Au moment où on perd des vies humaines ils se prononcent pour des choses matérielles c'est dommage 😭😭😭
Chez mon village natal mais chez grave kiren thiambokh son tout des frère yalla na diam am way
Non vraiment peulh yi douniou ayy nittt ay millions laay wakh 😢Kou déh nak bayilénn togn ak réyy
Lolou moy wakh dji dagno wara bayi raye thi bopam
Peulh akk Sérere dhé ayyy bokkoulaniou kou toniee dikko guiss inchallah
wallahi senegal fimou dieum bakhoul
Diotna nack niou teureul loi bouy takhalé peulh ak diaasi yorr diaasi waroul néck obligatoire.
Leurs animaux ont plus de considération que les personnes c'est dommage
exactement. sa se voit que ay vrai domiharam lagn
@@mbayembaye9526 arrête d'insulter les peuls il n'existe pas un seul peuls stp
C’est vrai nitt da fort ok 😊
Domaram yi gniony insulte arrête
Il faudra que nous respectons les liens entre sérère et halpulaars
.
Il faut toujours respecté nos liens yallana tapé xol yis surtt sougniou book peulh yis diam rek mo khathie sougniou diguenté
Yàlnaci yàlla defjàm
Yalle na yalla doly diame senegal
Peul d’où mbok
Et après. On a pas besoin d'être ton mbok
Daguéna moy sakh 😂😂😮😮
Dañiouléna wara interdi niou yoré diazi
Kou guiss nga yoré diazi ñiou dor la ci casso bi 5 ans
Kou raye niou ray la peul dou Mbokou
Les Peulhs ont l'habitude de faire cela;;vous avez parfaitement raison
Billahi lou ler gua wakh peul di domoukhar
Man de sérér la Wayyé li diadouwoull digannté peul ak sérér virement, ay kall laniou, ohhhhh😭😭😭
Sama cousine peule mo ray badianame😢
Lole fane la Ay way 😢ray rék
Casamance
C’est vraiment triste de voir que ce que nos ancêtres avait bâti est en train de partir en fumée! Ça devient dangereux quand les gens se font justice eux-mêmes. Yalna diam deloussi ci diganté sérères ak peulhs yi
Je suis Peul mai li gniawna trop goraté mofi wora djékh trop c'est trop vraiment J'ai le coeur meurtri vraiment c'est très triste de voire des gens tué comme ça. L'état doivent voté la peine de mort qui tue on le tue. Mangui massaw la population de Kiréne di massaw la famille Sérére 😭😭😭
Paix à son âme c'est que dieu lui accueille dans sont paradis
Sérér mom dou togne Amou niou thiakhan peul bakhoul.
Li sugniu problem la
Antre peulh et sereer lune munna jot suniu digante yalla bakhenu
Yeen wolof khaj yi demlen sen yoon.
Gor nit jaasi baaxul
Khana sa bay moy khadie
@@basidiahmed4623 olof yi nioy senegal. Nomades yi Sans pays. Danguéna nié olof yi farmoudio am haine si olof yi. Ndakh sokhor
Senégalai dp8 Mauritanie mai
Sénégal lifa nk si ray eupna
C'est vraiment dommage pour le Sénégal le peuple doit être uni
Lii méti trop 😢 que son âme repose en paix, douma peul douma sérére mais nake peul yi gnio wara bayi fathi problème ak diassi 😢
Il faut éradiquer ce problème 👿 c’est vraiment dangereux ⚠️
Ñeupe dawnañou ñeuwe Sénégal peul bakhoule dou mokou
Bien sûr que c’est dangereux té lii day yé fitna té khékhou éthni bakhoul mo geuneu graw guér mondial attentions dé
Trop dangereux même
Ohh waa li mom yemena lol ,aydou Yam si bop borom ,peulh et sérère et otre nous sommes tous des citoyens donc on doit se respecter l être humain est sacré
Oh les peul son des say say
Baye modo billay li defa gniaw bou gnieppou meloon ni yew reewmi bakh ndakh mounou ngou jel khet yep dougal ko ci pot gnieppou mounou gnou bon me verema soudee deggala niila deme rafetoul me li Lou yaggala digante baykat ak sammou katyii defa wara jeekh ndakh lii mom bakhout
@@aissatoudia4280 effectivement c'est un fait très récurrent dans le pays mais tout peut se régler dans la compréhension,le dialogue le pardon et surtout le respect de l autre.
@@bayemodoukebe3376 li de pen de more rek mooko mouna dindi billay kou ray gnou rayla kon leegi raybi wanjeegou
Yallana yalla def thie diam ak Salam.
Talouniouko sah yen lagn waron tall bilahi vous êtes sans cœur vous parlé de millions et harr légui domou diambour bingen rey en plus ngen di fen💔😭dolen meussa nangou ni yen la kouthie yii
Ngi daniouy nitt. Guis lén niouy victimisé wou si commentaires yi. Sérere yi doff yi rék nioy wakh ay cousinage. Ngi douniouy mbokou Sen boppou rék
Ndaysaan Li dé Kou Yaro si alle rek arrivée nala rour sa tool dior la diassi, après Sakh Dangay moudji décourager bàyyi Bay outi un autre métier c triste mais yàlna Si Diam moujji,ta di dialé famille bi
j croi k peulh yé togne ooh métina😢 k son ame repose en paix😢😢😢😢😢😢😢yeureume naléne trop 😢yalla guisna lép
Lolou thié wooreuh je ne sais pas rayouleuh kénneu
Peule da Dioubadi dé 😎 niom rek ka takh gars yi bégne Macky
Arrêté svp est ce que ceux qui tue dans ce pays sont des PEUL
@@ngoneka5767 lou khéwone mbour sa ko kou peul la Ay tapete léne aup rek niou thiorla daw je l’es connais
Mane dé sama bene copin yalla moci Defe soutoura mes peul yi danouco narona raye ndakhe fou neke lanouco dore diaci
😪😪😪😪😪
Yàlna naleen yàlla dimbale 😭😭😭
il Faut pas négocier avec ces nomades.avec une "beretta"765.calibre7,tu les élimine
un à un.où est le problème?
Serer amoul thiakhane
Peull yie nio thongue dh
Jsui 1senegalais jmapell tidiane sow jsui peul mai lidaffa niaw dangnay samm say NAKK mou yah tollou diambour bowahè niou guènné Diassii c op normal sa😭😭
Y'a meun doulll do peulh ndm
Li dafa yague si réwmi walahi gueestou lén histoire peul yi danio yagu rayy baykatt yi Lou ndaw Sax niou guéné Diassi Basi yonou Mourid amna histoire entre Peul yi AK Mame Thiérno Birahim le petit frère de Serigne Touba ba tribunal la moudié
Mame thierno dane na wax ndongo yi peulh mom nima ko def rk wayé boufi Ken nieuw nane nima ko def
Salut mais tj on vous accusé les peulhs. Il faut pas gâter les chants d autrui aussi .
Kou Ray you rayla moy deug le gouvernement Sénégal 🇸🇳 est trop nayif
Massah Fatou une femme battante gentille liguey rek la kham billae elle a même donné le nom de son fils à mon père yallah na yallah atei
Dor fayou reek masla mo yakh senegal
Alioune douguourou ès responsable de tous des problème il a dit à l'assemblée nationale il faut sortir lès sabres voilà le résultat
Waw li mo khéwone ci fanne yii touba. Si diguénté baye fall yii ak peul .yii état bi défou ci bénneu liguéy bou am soolo ta baï ak samou nioo andu béneu dou déme ba sa marom kone état dafa wara déf ligué yame ta baïyii sétane bii ndax léépou senegal
Coupable aliou doungourou saw qui a declare la guere etni ?
Yananiou yalla défale diame ilfo niou bayi khéle si li niou wakhtanéko 😭😭😭😭😭😭
Sa ma mbokou peul yi da gno wara diogue si gnom da gno begue diasy 1 2 gnou gorr la
Sama mbok puel yi nek lene nitte nek lene nitte
Bilay puel yi dano doy warr😂
Lépou peul yi la nio togne
Personne...le droit de provoquer... que la justice...le travail immédiatement Oui que les deux... chacun d'entre eux respect... .
Éviter de dire Peuls yi c'est une affaire entre deux personnes donc essayons de le régler avant que ça devient plus grave.
C'est toujours comme ça entre serère et peuhl êe la ou j'habite que des violences des vols ça doit cesser
Boulen ken diapale danio ragal ba paré meuna togne