TOUBA- Les population dèja dans le ndigèl

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 янв 2025

Комментарии •

  • @ousmanediedhiou5533
    @ousmanediedhiou5533 5 лет назад +247

    Je ne suis pas mouride mais je suis vraiment fière par la décision du khalif

    • @dioufdaouda3079
      @dioufdaouda3079 5 лет назад

      Ndaysan dieuredieuf

    • @dioppape1270
      @dioppape1270 5 лет назад

      lou bax amoul mourit wa tidiane

    • @abdousarr9298
      @abdousarr9298 5 лет назад

      tu nest pas musilmant

    • @vieuxkebandong6287
      @vieuxkebandong6287 5 лет назад

      quel preuve a tu de l'accuser serigne bi beugoul kouy togne
      yonn yeupp sa yallah
      ndakh moy ndieuk di moudj
      té borom TOUBA daff ko deuko diamo aki topou ay ndigg lemm messoul dee limou térééé

    • @aminadiop4305
      @aminadiop4305 5 лет назад

      Sénégal

  • @alkhassoumkebe6308
    @alkhassoumkebe6308 5 лет назад +54

    Je ne suis pas mouride mais je suis fier de vous mouride dafa guem popam dafa Nagui ligey Lou Serigne bi wax dafa am soloo yalla Sénégal am diam

  • @diembaye4142
    @diembaye4142 5 лет назад +1

    Machalla amena solo dieureu dieuf yalna yalla yagal fi serigne bi 👏👏👏

  • @modoudiengbeuguefallou1776
    @modoudiengbeuguefallou1776 5 лет назад +33

    dieureudieuf borom touba serigne mountakha mbacke yalna yalla goudal sa fane mayla wér

  • @coumbis4042
    @coumbis4042 5 лет назад

    Waawaw na melni djiamono baye LAHAT rek. Mouride day dieuffé ndiggeul . Ndakh yalla gnou diokh djieur maggal gui 😍. Sr bi dagnouy dimbali rekk bopam takhoul

  • @madamemadame3380
    @madamemadame3380 5 лет назад +1

    Macha'Allah Mouride dal jeufé ndiguel rék. Trop contente de la réaction de la population de Touba.

  • @maxoudiop1128
    @maxoudiop1128 5 лет назад +6

    Dieureudieufaty serigne Bamba

  • @mameoumarmbaye1461
    @mameoumarmbaye1461 5 лет назад +136

    Digueul gui Yalla moko ndieuk diokheh Seydina Mouhamed wakh ko il y a 1440 années , Serigne Touba feddeuli ko nguene toppeu sene bakane.... Thiakhane bakhoule waye.

    • @babousinyane8998
      @babousinyane8998 5 лет назад +3

      Ya bakh

    • @ncm04
      @ncm04 5 лет назад +3

      Bien dit

    • @123laker
      @123laker 5 лет назад +5

      Waye kou santoul nit do sante yala
      Te yala dou feke ken foumou tok dila diokh lokho oubien dila diokh weurseuk
      Bayilen sisou bi mourid ndigeul

    • @dembismc5243
      @dembismc5243 5 лет назад +3

      Loutakh yen Lou mourid yi wakh rek ngen diko critique yen loutakh ngen sokhor yalla mandou la ndiekè santánè

    • @dembismc5243
      @dembismc5243 5 лет назад +4

      Tarikha mourid rek ngeni bania guiss domou khadj

  • @issaaw1592
    @issaaw1592 5 лет назад +5

    Je suis très content de la réaction de ces fidèles c'est ça un vrai mouride ❤

  • @lafricainba6907
    @lafricainba6907 5 лет назад +45

    mashalla ndam rek nguén siy jéllé

  • @eveane3302
    @eveane3302 5 лет назад +3

    macha alla Mbacké yague fi loole té wère di ñianal rek ak di sakou si yaw ñiane barké Khadim Rassoul

  • @lalumiereducoranetdelasunn6196
    @lalumiereducoranetdelasunn6196 5 лет назад +2

    Bayi ndigueul yalla di topp ndigueul Serigne, reer bahoul

    • @bindarawfall3437
      @bindarawfall3437 5 лет назад

      Yalla moko dieukeu téré.

    • @thiorofall5673
      @thiorofall5673 5 лет назад

      Yow ya rer com si digueul li dou ben li yalla wakh la wakh dindi wousi dara waw kay lolo takh yalla tekk len fi

  • @wapladdss6903
    @wapladdss6903 5 лет назад +10

    J'attends a ce que cette décision soit affecté partout dans le Pays. Décision Yalla la dafko diaralé ci Serigne bi. Dakar mongui Yaakou té xam naci dará depuis Espagne 🇪🇸

  • @MbackeNdar82
    @MbackeNdar82 5 лет назад +2

    Ayy Bou Sénégal yepp dieufé ndigaul yi Femme sénégalaise yi dinanan rafet Machallah Dinga guiss tient noir you melni KABA ga

  • @fatoudiop9425
    @fatoudiop9425 5 лет назад

    Dieurdieuf Serigne mountakha yalla nala yalla meye wére at goudou fane yéne bi oyofe tole si yawe mourite ndigele

  • @fallougallassbayoumbenedep5326
    @fallougallassbayoumbenedep5326 5 лет назад +46

    Masha Allah Serigne Mountakha Bassirou Mbacké balla wallahi sunu khel Geuneu tina dall ya bakh lirek lafi sa Mame youbakh yi nékéwone ak sa waydiorya Touba deukeu bou sella kon none wa deukeu bi nioukou mana defar Magui niane naniou anda boulou diappée Serigne Touba Cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul (SAWS )

  • @laminmaster9387
    @laminmaster9387 5 лет назад +2

    Machallah, dieuredieufé serigne Touba Serigne Mountakha Mbacke yalla nafi yag té wér si barkéb Serigne Touba

  • @moro6012
    @moro6012 5 лет назад +4

    Bilay serigne yalnako fi yalla bayi baci kanama kanama kanam..
    Mbacké walay sa dounde amna ndiarign si diiné lislam gui diaraléko si kou tède gui

  • @kenediop1832
    @kenediop1832 5 лет назад +4

    Serigne mountakha mbacke yalla nafi yaag té wére

  • @travaillezpourlafriquejeba8226
    @travaillezpourlafriquejeba8226 5 лет назад +55

    Li amoull mourid ak tidjan dioullit warouta déf yén yi
    Mais touba famou dieum sa kanam kou beugeu diamou yalla RK démall wouti pakk

  • @lahadseye2941
    @lahadseye2941 5 лет назад +1

    Merci merci merci Dakaractu

  • @oumoundiaye5184
    @oumoundiaye5184 5 лет назад

    Je suis pas mouride mais je suis vraiment heureuse de vous ❤️❤️❤️👍

  • @Djana4
    @Djana4 5 лет назад

    Fier d’être mouride alhamdoulilahi dieureuf serigne touba ♥️♥️♥️♥️

  • @salydiop4236
    @salydiop4236 5 лет назад +3

    La fille en rouge est très belle

  • @ibrahimasenenabien1204
    @ibrahimasenenabien1204 5 лет назад +3

    Serigne mountaha Bassirou yalna fi yague tè wèrrr li mom yalla begue nasi

  • @jmfllaf8905
    @jmfllaf8905 5 лет назад +5

    Jeureujeufé Serigne Touba ! Serigne Mountaha Mbacke Yalla nafi Yagg té Weer

  • @2sttv330
    @2sttv330 5 лет назад +1

    Mach'allah yalna leen yalla sàmmu yeen jigueeni Touba yep falaa dëkk te mën baa seede seenuk taalibe murid ndigël ndam rek ngeen ciy am r1 de +

  • @aliouniang58
    @aliouniang58 5 лет назад +41

    Serigne Mountakha Bassirou yalla nafi yague loool ta andak wèr barkè Mame Cheikh Ibrahima Fall

  • @alioudia2821
    @alioudia2821 5 лет назад +7

    yalla na law weur Sénégal yeup

  • @diangadiallo8255
    @diangadiallo8255 5 лет назад +9

    Mane je suis tidiane wané dama ame thiofel si serigne bi walahi damako beug lool sakh yalnafi yag té wér

  • @seydinaomarngack2496
    @seydinaomarngack2496 5 лет назад +13

    Kouman Deff Deff Kouko Manul Guiena touba Dem Sakhathie
    Serigne Mountakha Yalnafi Yagga looL Tewer Lii Senegalese Yap Warnanukoo Deff Ndakh Diame Sax 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @ngagneniang5217
    @ngagneniang5217 5 лет назад +53

    Mane douma mourid wayè kontana lol lol sakh

    • @adamadiarra6247
      @adamadiarra6247 5 лет назад

      Ki moy serigne

    • @Rewmisport
      @Rewmisport 5 лет назад +1

      Nn mourid NGA nakh app musulman NGA ta Serigne Touba amna loum si wakh

  • @dawoudadione2424
    @dawoudadione2424 5 лет назад +4

    Machala amna sollo 🙏🙏💓💓 ndigeule deufé

  • @MultiElegance
    @MultiElegance 5 лет назад

    Macha Allah wante yarkanani yalah moko dieuk tere donc ndigeuleu Sonou Borom degg rek akk topp

  • @lintouchablelintouchable5196
    @lintouchablelintouchable5196 5 лет назад +1

    Lii baxna si sakh.. ndakh magal touba khalei dakar reiglei niou yakk magal gui ak sen cheveux you gouddou ak sen khetou shooting...alhamdoulilah dama si contane...

  • @khaoussousylla5351
    @khaoussousylla5351 5 лет назад +3

    J'ai jamais été d'accord avec les confréries mais cette fois-ci chapeau au khalif général des mourides

  • @modoukebe5362
    @modoukebe5362 5 лет назад +1

    Mei Yenn Bou lene gnou Sonal

    • @talladiop2933
      @talladiop2933 5 лет назад

      Serigne mountakh mbacké balla yalla gafi yageu yé wér

  • @xadijadieng8841
    @xadijadieng8841 5 лет назад +2

    je suis mouride mais serigne bi li islam wakh la wakh
    dégu dégu bakhna si domou adama
    serigne dafané li islam beugoul yallah téré ko beugouko touba
    comme yallah mo téré serigne bi dogal ko
    dou ndingalou serigne bi mais bou yallah
    WA SALAM

  • @coumbaba9951
    @coumbaba9951 5 лет назад

    Machalla diaradieuf serigne touba serigne mountakha yalla nafi yague té weer

  • @gadiagabamba5471
    @gadiagabamba5471 5 лет назад +1

    Kou beugue Lou baxx geume serigne touba di nga ko bayi

  • @alibosn8950
    @alibosn8950 5 лет назад +7

    alhamdou lilha TOUBA AL MAHROU CHA

  • @amydieng1865
    @amydieng1865 5 лет назад

    MAchahalla serigne bi yalla na fi yagu té wéer

  • @cheikhbagneseriyoubonne4216
    @cheikhbagneseriyoubonne4216 5 лет назад

    Dieufe rekk moo baakh deee

  • @tamsirgueye6085
    @tamsirgueye6085 5 лет назад

    Allahou akbar ndigalou Yallah ak yonnentè bi yague nafi Tè dieufè wolène ko. Tay serigne bi wakh rèk nguène dieufèko. Yallah naniou Yallah djègal Tè Yeureume niou.

  • @colysophie4209
    @colysophie4209 5 лет назад

    Khana Magal 2020 gni gnieuw magal si dou niou deff greffage preparé dé ak ay cole machalla rafetna

  • @masspese5667
    @masspese5667 5 лет назад +4

    Serigne touba rekk moy deugeu dadieuf ndiguel dieufé

  • @adiitadiop9860
    @adiitadiop9860 5 лет назад +3

    Modou modou yi thiono wathia naléne thi envoyer cheveux naturelles

  • @smsbi9673
    @smsbi9673 5 лет назад +1

    En tt cas yalla moko dieuk digulè seign bi diotali yalana niou yala bal tè diegual niou bayi lep loumouy tèrè inchalla may niou degue ak top

  • @serignembackeboye1362
    @serignembackeboye1362 5 лет назад +1

    Machallah thiey SERIGNE Touba

  • @maimounadiop5122
    @maimounadiop5122 5 лет назад

    C'est une très bonne initiative

  • @fatimasoumare8407
    @fatimasoumare8407 5 лет назад

    Mbaké goudal fane je ne suis pas Mouride mais li nekh nama Machallah 😍

  • @astagueye1239
    @astagueye1239 5 лет назад

    ma sha Allah khan d'i sentait Serigne Touba bou bakh

  • @zaynamoussaliousarrr7370
    @zaynamoussaliousarrr7370 5 лет назад

    Dieureudieuf serigne bi

  • @malaminedrame8163
    @malaminedrame8163 5 лет назад

    Ndeysane machalaaaa ❤ndam rek

  • @papidiongue984
    @papidiongue984 5 лет назад +1

    Serigne Mountakha Mbacke Yalla nafi yague té wer

  • @mbayendiaye2690
    @mbayendiaye2690 5 лет назад +30

    Reportage bi amna solo trop wax dji rafetna awna yone mé Ousmane mar mom vrai con la mounane délé , yaw ndigalou Serigne Touuba khadimou rassoul dafa ame délé, touuk mounane délé, ndigueul kay bou djibé djibna balèn thiaxane yi ta fonk Serigne Touuba khadimou rassoul kèn dou mom walahi! Dieureudieuf Serigne Touuba diarama mame cheikh ibra fall.

    • @serignesalioutaissirndongo5819
      @serignesalioutaissirndongo5819 5 лет назад +1

      Digal kaye amoul wayé dieufé rk o mar

    • @bsdtv9318
      @bsdtv9318 5 лет назад +1

      mbaye Ndiaye rayy nga ma mouni mdrrr

    • @mbayendiaye2690
      @mbayendiaye2690 5 лет назад +1

      @@bsdtv9318 no wadji con la koi! gni xana xamouniou kouy Serigne Touba? toukk mounane délé, bama fekh ko fofou rék! mé nak yaw mom amal diam rék diambar.

    • @dabz3318
      @dabz3318 5 лет назад +2

      😂😂da diakhlé reik ndeysann

    • @mbayendiaye2690
      @mbayendiaye2690 5 лет назад

      @@dabz3318 wa mé diakhlé gui yèp rék moy niak xam kouy Serigne Touba! naniouy Sante yalla boubax bagne ko bokalé ak dara tay Sante Serigne Touba sasouné bouniou beugé diariniou tay ak Euleuk! Dieureudieuf Serigne Touuba diarama mame cheikh ibra fall.

  • @khadimdiop7523
    @khadimdiop7523 5 лет назад +1

    Macha allh merci wa touba

  • @maremewade9420
    @maremewade9420 5 лет назад

    Bilahi serigne bi yalna fi yag té wére tidiane la wayé nit day dég ndigeul

  • @fatimazahrachannel6404
    @fatimazahrachannel6404 5 лет назад +8

    Et apres faudra donner le ndigeul aux bayefall de Prier et jeuner et donner le ndigeul a ceux qui epousent plus que 4 femmes d'arreter.
    Deff lenko guir Yalla. Ndiguel souniou borom mo ndieuk.
    Yalla mo tere xessal, greffage, ak niaka mourrou.
    Ce que je trouve dommage c'est que on suit le ndiguel du serigne mais pas celui d'Allah.
    Personne n'a dit qu'on va suivre ce que Dieu a dit c'est dommage. Sans yenne l'acte n'a pas l'importance.
    Se serait plus musulman de dire qu'on laisse le haram pour Allah mais pas pour le serigne.
    Si elles font le diguel du serigne une fois a dakar ou ailleurs elles vont recommencer a khessal, greffage etc. Il faut enseigner aux gens a avoir peur d'Allah et de suivre ses recommandations pas a avoir peur du serigne ou d'une ville.
    Cela montre que si le serigne donnait le ndigeul aux bayefall qui refusent de prier et jeuner ils allaient commencer a prier et jeuner. C'est dommage on suit le serigne mais pas Allah.
    Wan len nit ngi sen borom ba founiou meneu dem don ay dioulit you ragal sen borom.
    L'idee est bonne mais la demarche reste a preciser. TAWHID en premier. Laisser car Allah l'interdit, faire car Allah le dicte. Tel est le vrai TAWHID.

    • @thiorofall5673
      @thiorofall5673 5 лет назад +1

      Diguen bayi baye fall yi dh lolou mom alakhira rek guen di am loulen ler delen wakh rek lidianti len sen bop te bayi bay fall yi

    • @mounasarr934
      @mounasarr934 5 лет назад

      Mais pourquoi dire qu'on est plus de considération à notre serigne k Dieu c'est du n'importe quoi
      Vous oubliez une chose niogui thi moudioum diamono leppay diaxasso kone bo amé koulay tek thi yone sante KO ta yok gor gor Lou et svp laissez les baay fall trankil 🙏🙏🙏

    • @dieynabawadeseck9470
      @dieynabawadeseck9470 5 лет назад

      Soonou guen d teguen tall sen bop ta bayignou

  • @samsoundiaye6351
    @samsoundiaye6351 5 лет назад +30

    Lislam lol la wakh diadieuf serigne bi yalnala yala goudeul safane

  • @khalifaababacarfall738
    @khalifaababacarfall738 5 лет назад +2

    M seugn bi a bien fait m je peut pas comprendre yalla waxx dieufé woléne serigne bi waxx guéne dieuffé t serigne bi yalla ko mom donc diamou léne yalla t bania diamou serigne biii

    • @marygail3891
      @marygail3891 5 лет назад

      SERIGNE bi dafko wax pour dimbali nitt gni fatalilen waxi YALLAH
      Ca ne veut pas dire k diamouwougnou YALLAH
      Les hommes sont imparfaits et commetent des péchés ainsi chak fois il faut k mou amm ben kilifa boulen di tekk ci yoonn

    • @khalifaababacarfall738
      @khalifaababacarfall738 5 лет назад

      @@marygail3891 lolou deug m il faut k nitt yii xamnii li waxou yalla dou waxoi segne bi par s k kofi newone yalla néna doula degu lou wayé sou segne bi waxé gu degu lou donc iao segn bi gu tekk si kaww souniou borom mom mi binde segne bi binde boléme loi nkk thi kaw souf donc warnéne xolate souniou guem guem bou baxx

    • @marygail3891
      @marygail3891 5 лет назад

      Waww mom doyna waarr
      Motax SERIGNE yi mom nagnou yokk diglé loubax rek kom k lou YALLAH santané laagnou diglé c très bien
      L'essentiel daal nagnou deff loubakh rek baayi loubonn ak...
      Maagui toup boubakh nak xalat bou gatt la rek

  • @papidiongue984
    @papidiongue984 5 лет назад

    Serigne Touba néwonena Yalla dagno digeul digue gnou têré gnou tekou gnou kou dieufe ndigeul mouthiou si mbougeul yi

  • @toubamoylislamtouba2331
    @toubamoylislamtouba2331 5 лет назад +1

    dieur dieufe serigne touba nako gnep wax

  • @serignsaliousylla6458
    @serignsaliousylla6458 5 лет назад +7

    😂😂😂 ousmane mar il est me tué nèna gnomayco délai xalisso mèss bi ak tup yi dafa harame tifakhane comme sangara ak poune

  • @MbackeNdar82
    @MbackeNdar82 5 лет назад +2

    Touba Serigne Touba moko mom Mo dieund Art ko niak ko Bou Sénégal niepp dieuféwon ndigeul Serigne Touba Tawfekh rek moy Am

  • @sokhatirmbaye4896
    @sokhatirmbaye4896 5 лет назад +1

    Wakhléne si dépôt pharmacie yi mo eupeu ndiarign parck ça tue

  • @ousmanemboup6307
    @ousmanemboup6307 5 лет назад +4

    Séne yaram yeup ci biti nguéni wakh ndigueul. Yallah molen ndieukeu ndigueul. Khawma yane façon nit rek nguene. Tek sene Serigne yi ci kaw Yallah ak Yonent bi psl. Khawma loutakh nguéne nioradi rek

    • @narouyayembayagnediop9094
      @narouyayembayagnediop9094 5 лет назад +1

      lingay wakh nii kén ladiou lako

    • @narouyayembayagnediop9094
      @narouyayembayagnediop9094 5 лет назад +1

      legui kon kay diaroul niouye topou seydina mouhamed khana goo waye

    • @Boss-pw8zm
      @Boss-pw8zm 5 лет назад +1

      Lou yonenti yi dane dieurigne xana dou tek nite yi si yone bou bakh rek c la même chose ak li serigne wakh so xamoul daguay lath

    • @narouyayembayagnediop9094
      @narouyayembayagnediop9094 5 лет назад +1

      @@Boss-pw8zm yonounte yi lou bakh laniou dan dingalé li tamite lou bakh la fall yén dangén beug ndeye lou nite ngén nek si di wakh kén khamoul lou lén beug khamou lén doul ba paré beuri wakh li lou bakh la bosi manoul wakh lou bakh dangay teuth sa gat mo geune dara khamoko loudoul ndeye beuri wakh

    • @amadoudiop6984
      @amadoudiop6984 5 лет назад

      ousmane Mboup bilahi ça me fait mal yalla téréra bayiwo nite kome Yaw téréra ga bayi vraiment cé dommage

  • @gallassdeme591
    @gallassdeme591 5 лет назад +9

    Ya fi nekal sonou borom ak yonentbi psl mbacke yagg fi teu weer rk Ki mom dakam lokou nekh mou fay am dieuafé force ba nio yar la

  • @mamediarraniane3766
    @mamediarraniane3766 5 лет назад

    Mbacke balla Aïcha bourri sidy Anta Ndiaye ak afia Anta Ndiaye kanni sow Ibrahima Awa Niang yag fi lol Mbacke balla dieureudiefè Serigne touba ❤️🔐

  • @AhmedBachirThiaw
    @AhmedBachirThiaw 5 лет назад +3

    Sénégal nekhna bou yalla santanè niou bagne bou serigne bi santanè niou deff... L'islam meussoul nangou mèche ni khessal ou même djigen di fègnal awram legui wadjour yi kham ko tèrè wounouko sèni dôme serigne bi wakh rek niousiy sogay adou... Thiey yalla

    • @khadimdiba9238
      @khadimdiba9238 5 лет назад +1

      Kou bakh demè woul nonou sakh
      Serigne ab deukam lako tèrè par la force
      Niep khamnani yala moko dieuka terè.
      Bayigui niak pekhè la rek kxk

    • @lepatriotemrheureux588
      @lepatriotemrheureux588 5 лет назад +1

      Lolou mo takh yalla Yoni fii younénte yi, lolo takh yalla sakk ay moudiadide ( niouy yèssal ndiguelou borom bi) lolo takh sounou borom ni nanguène di fatalanté (rappeler) ndigueli borom bi, (وَذَكِّرۡ فَإِنَّ ٱلذِّكۡرَىٰ تَنفَعُ ٱلۡمُؤۡمِنِینَ)
      [Sourate Adh-Dhariyat 55] Lolo takh sounou borom ni:
      (كُنتُمۡ خَیۡرَ أُمَّةٍ أُخۡرِجَتۡ لِلنَّاسِ تَأۡمُرُونَ بِٱلۡمَعۡرُوفِ وَتَنۡهَوۡنَ عَنِ ٱلۡمُنكَرِ وَتُؤۡمِنُونَ بِٱللَّهِۗ وَلَوۡ ءَامَنَ أَهۡلُ ٱلۡكِتَـٰبِ لَكَانَ خَیۡرࣰا لَّهُمۚ مِّنۡهُمُ ٱلۡمُؤۡمِنُونَ وَأَكۡثَرُهُمُ ٱلۡفَـٰسِقُونَ)
      [Sourate Aal-E-Imran 110]
      Lolo takh am kilifa gou matte kilifa bakh koulay fatali ndiguelou borom bi 🙏
      Serigne Mountakha Bassirou Mbacké yalla naniouko yalla fayal té mayko gou fanne katanouk mana liguéyal mamam thi toloup l'islam 🤲 touf

    • @AhmedBachirThiaw
      @AhmedBachirThiaw 5 лет назад +1

      @@lepatriotemrheureux588 Dieureudieuf sang bi kontane na sisay leral aduna ni rek la dh diaroul khoulo au moins iow khamal ngama tei kadu you rafet ngako bolel aki aya yalla nala yalla defal djam

    • @lepatriotemrheureux588
      @lepatriotemrheureux588 5 лет назад

      @@AhmedBachirThiaw amiiine yalla naniouko yalla bolé 🙏

  • @mouhametba5456
    @mouhametba5456 5 лет назад

    J'aurais aimer que sa soit sur tout le senegal

  • @alioutallbayefall302
    @alioutallbayefall302 5 лет назад

    Amna solo

  • @cherifmarena4380
    @cherifmarena4380 5 лет назад +2

    Machallah amena solo

  • @ablayembaye8405
    @ablayembaye8405 5 лет назад +1

    Machallah rafetna torop

  • @bounabanno6961
    @bounabanno6961 5 лет назад +1

    🤣🤣🤣🤣🤣
    Bouñula diappè doumala dieulsi 🤣🤣🤣🤣

  • @cheikhounabaoloptique9854
    @cheikhounabaoloptique9854 5 лет назад

    Diaradiaff serigne touba

  • @iboufayetalibeserigneismai9324
    @iboufayetalibeserigneismai9324 5 лет назад

    dieudieufe serigne touba mouride ni meel

  • @mariamadiatoukoulorbourafe5033
    @mariamadiatoukoulorbourafe5033 5 лет назад

    Machalla ndigeul jibna aythia mouride

  • @tayesiirtv5646
    @tayesiirtv5646 5 лет назад

    Touba mo geune si monde bui aprè maka

  • @bayesalioudiagne1518
    @bayesalioudiagne1518 5 лет назад +4

    Serigne montakha mbakc yall na fi yakh lou le tawér si barké khasidayi amine

  • @khaliloukhalilou6313
    @khaliloukhalilou6313 5 лет назад

    Bilahi ma beug Serigne bii

  • @ElTIO_Galass
    @ElTIO_Galass 5 лет назад +11

    Tere gui yagg na fa depuis diamanoy serigne abdoulat me diamou rek nguen sy am inchalla

    • @damendao3479
      @damendao3479 5 лет назад

      galzouframaren_bi_oficial oficial Akassa

  • @maimounadiop5122
    @maimounadiop5122 5 лет назад

    C'est de ça qu'on attend des marabouts et de nos autorités mais il faut que ça soit des décisions ferme avec des lourdes punitions

  • @evadipmoree1975
    @evadipmoree1975 5 лет назад

    Mane wa Touba damalèna gnè dakh dama beugua mourou di sol yerè wolof di sèlale ta manoumaka souma deukone Touba mom force dinaka bayi
    Dieuredieuff Serigne Touba👌

  • @momoyoutube6456
    @momoyoutube6456 5 лет назад

    6.25 en rouge yangui nice. Super classe té khessalo messouwo solo più bonne nanou roy sissa genre yi

  • @papedjiby1354
    @papedjiby1354 5 лет назад +1

    NduigueuL dieufé

  • @bamamadoubarkhama1401
    @bamamadoubarkhama1401 5 лет назад

    Machallah dieureudieuff Serigne touba khadimou roussoull

  • @ndoyemamy2310
    @ndoyemamy2310 5 лет назад

    touba daye dokh aye tank la yor bilahi💪💪

  • @taflemanager8517
    @taflemanager8517 5 лет назад

    MachAllah

  • @mordia5985
    @mordia5985 5 лет назад

    Machllah

  • @yacinediop1922
    @yacinediop1922 5 лет назад +2

    Chers compatriotes prions pour notre equipe par le Coran , Seul le Coran peut combattre les fetiches. Le Benin est le pays delAfrique de l'Ouest le plus craint pr ses fetiches. Al Quran est plus fort que les fetiches, Bou nou len top ci sen meunine. Kou nek 50 basmallah pournos jours,
    ?

  • @abymbaye6325
    @abymbaye6325 5 лет назад +16

    Serigne bi lou bakh reck la laine beugueul

  • @thiandoummoussa3394
    @thiandoummoussa3394 5 лет назад

    Yiiw force

  • @mathiouz2074
    @mathiouz2074 5 лет назад +32

    AKASSA
    JEREJEFETI SUNU SERIGNE MAME THIERNO YÀGG FI LOOOL TÉ WERR

  • @modouganeciss6780
    @modouganeciss6780 5 лет назад

    Ndigal mom Amoul délé dieufé rek S.Mountkha yalla nafi yagg té wér

  • @dionoblelebayfall1006
    @dionoblelebayfall1006 5 лет назад

    Reportage amnala solo macha Allah. Digual dieffé

  • @benboyka5089
    @benboyka5089 5 лет назад +14

    Wawaw digueul diafee rek dieureudieufff serigne touba

  • @omardiagne1427
    @omardiagne1427 5 лет назад

    Tiey serigne by waye tiey mouride yi ni rek la dh nous sommes ds mouride

  • @dietra6390
    @dietra6390 5 лет назад

    Bou souba lagnou comprendre je ne suis pas mouride wayé dama fière si décision khalif bi.

  • @netalytvnetalytv1560
    @netalytvnetalytv1560 5 лет назад +9

    Senegal mo nèkh il falais serigne bi wakh rèk kou nèk di repi repi tè yalla wakhko bou yague serigne wakhi yalla rèk la wakhat wayè talibè yi nagnou khamnè bo geumè yalla topou yonentibi apres say wadiour serigne dora nieuw li serigne bi wakh lou rafait la ms yalla ak yonentibi wakh nagnko bou yague

    • @netalytvnetalytv1560
      @netalytvnetalytv1560 5 лет назад +2

      @@falloundiaye4207 bilahi geuno ma beugue serigne touba mane talibè you diangoul lay wakhal ms dama beugeu wakhni lep lou serigne bi diglè rèk thi yalla lako dieulè ak yonentibi yaw ya coprendroul

    • @xamletv1
      @xamletv1 5 лет назад +4

      Danga fateini yalla bamou terei ba parei dafa wathie nitt nguir mou fedaliko

    • @thiernotoure1751
      @thiernotoure1751 5 лет назад +3

      Waaw Serigne Ibrahima li Serigne Bi fattali rék moofi indi Yonènete yi halayhimou salaam ndakh Sounou Borom moo digueul Kou Baakh Ki (psl) niko dèl fattali ndakh fattali dina diarigne way gueum yi (wazakkir fa inna zikra tanfahul mouhminiine) Yonènete bi déllou wakhni digueul bépp dioullite nga diottalilko ndigueul (ballighouni walaw aaya) wakhaate ni Borom xam xam yi gnoofi woutou Yonènete yi kone book fattali mooy li war thi linou wara dèf. Té diglé wougnou wala gnouy téré lou lislama diglé woul mbaa mou téré lo. Serigne Saalihou daane na wakhni dou ma fékk lou Yalla yaatal madiko khatal moukkou...
      Mangui toup nak nanouy gueuneu rafétal linou bokkou mouy diinèy l'Islam...

    • @ousmanesow6736
      @ousmanesow6736 5 лет назад +1

      ibrahima sall loula mèti Si ndigualou serigne bi Ba takh ngafiy wakh difference entr serigne ak wadiour. T sakh khana khamoni nou dom yi mél légui wadiour yèlénko yobé.mane djiss ay khalé you beuri nio khamné bignou commence mourou sèni yay niolén ni ték lénko si souff khalé bouy mourou guaf bou bone la

    • @ousmanesow6736
      @ousmanesow6736 5 лет назад

      vrement yaw émbèsil nga