Comme d habitude bravo au Soleil levant. Quel talent Sanekh! Très bon scénario. Ce que je ne comprends pas au siècle ou on vie maintenant oui il y a peu de place pour les etres humains et peu d argent , on fait toujours l éloge de la polygamie au Sénégal. Je ne suis pas d accord , un coeur n est fait que pour une seule personne. Un homme a notre époque ne peu pas subvenir aux besoins de plusieurs femmes en plus des enfants. Encore bravo aux acteurs.
Mariama Traoré vous vous trompez. Si les hommes ne parviennent pas à épouser 4 femmes je vous assure qu'il y'aura beaucoup de célibataires surtout vous les filles. Il faut toujours avoir l'honnêteté le courage d'affronter certaines choses de la vie. Prendre une deuxième fois n'est pas un crime.
Sanekh moye bandit dh fou neck laye geneu mo mane gayi deugeu deugeu dou sen morom daffa diangeu theatr ba mokal mo takh ma beugeu theatre depus 2005 ba legui mangui setan soleil levant danio mane macchallah
Kou beugeu Mouhamed rasoulilah alay hi wa salam beussal j'aime
Jambar na ñou wirmall tourou sague by dou ñou koy foxé mbirou adou na dou dra te lii mann nga ko layo ack sague by ay sèrie yii doy na sétan rk
Psl
Svp amoufi plage on commenter si série bi désolée nak mon frère😡
cv
Psl
Kou beugue téral ayy wadiouram beusseul j'aime
Mane yow la beugua teral
@@lhommetoutfrais3218 ha bon lolou forna mai ndieukel si parent yi ba paré
Non yow khame gua parents yis gnoye 1er
@@lhommetoutfrais3218 j comprend c se ki es normal
Diarna jaim dh
Saneex il est tjr meilleur ki é d'accord
Man dei barkeep s.saliou dama ko begue
✋✋
kou beugue seydina MOUHAMED beussal j'aime ken dou rassoulilah
SANEKH est vraiment drôle. Machalla. Longue vie à lui.
Mouhamadou BA
Anii sopey Serigne fallou yii yala nalen yala defal Diam ak khewal you bariiii.pousse bleu svp
Amadou Sarr 🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾
🙋amine
Allahuma amine niou bokk lepp jajeuff
@@amadoudiop6621 👉👈💗💗😑💙👅💖💞✋👇👆👉
Amine way
Kou Beugue Sanekh j'aime waye
Capitalou badio badio😀
Man momm dama ko begu
Serigne chiekh bithiou thione diamou Serigne saliou yalla nakou yalla fayall barkip Serigne saliou sama Serigne
Sanékh pape leu si bire papayi ❤❤❤❤❤❤
Mais sanekh plus les années passent plus il m'impressionne
😂😂😂😂😂 chapeau l'artiste
Yalla nagnou yalla dolli soutoureu si barké séydina Mohamed SAW
Amine waye
Amine
Kou beugue sanekh j aime way😎
Yawe khamoo sa bopp
Duo sanex ak Binta bènene affaire leu🤣non suis morte
Kou nagou sannex est le meilleur des artistes beusseul j'aime 🖒
Kou beugue yalla basal Jim ngir sa promu
Nooo mannn sanékh laaa beug,i😂😂😂😂😂😂😂wouyyyyy nékhna 180km heur layy dawww.ayooo Conn fonanté dayyy changé.soumboulou rayna .
😂😂😂😂😂😂😂😂
Wouy sanekh ray nama😂😂namone nagnou yi si yow j’adore ta partie comique
Waayayoye moel epiniere thi bopou sankhe wathi gnou 🤣🤣🤣🤣
Walahii sanex is back🤣🤘✊✊✊🇨🇦🇨🇦
Journée beuge sa nèx beuseul j'aime
Quel bonheur avec Sanekhe! Merci
Sanekh Bilahi tu es le meilleur !! Tu m'a fait mal au ventre 🤣🤣🤣
Sanekh yalla na yalla goudeul say faan😍🙏
Amine ya rabbi
Amine waye
Sanekh amoul kouko beugue pouss bleu
C'est ça que j'aime de plus chez lui ça comédie je préfère ces genre de théâtre que les autres pièce qu'il joue bilahi il me soulage
No sanekh dou dém 😂 best comedy forever 🇸🇳
Comme d habitude bravo au Soleil levant. Quel talent Sanekh!
Très bon scénario.
Ce que je ne comprends pas au siècle ou on vie maintenant oui il y a peu de place pour les etres humains et peu d argent , on fait toujours l éloge de la polygamie au Sénégal. Je ne suis pas d accord , un coeur n est fait que pour une seule personne. Un homme a notre époque ne peu pas subvenir aux besoins de plusieurs femmes en plus des enfants.
Encore bravo aux acteurs.
Mariama Traoré vous vous trompez. Si les hommes ne parviennent pas à épouser 4 femmes je vous assure qu'il y'aura beaucoup de célibataires surtout vous les filles. Il faut toujours avoir l'honnêteté le courage d'affronter certaines choses de la vie. Prendre une deuxième fois n'est pas un crime.
06:07 la façon dont sanekh marche me tue 😂 😂
Jtj damako ré ba sonne
Sanex rewna 😂😂😂😂😂
Looooool
Non 😂😂😂 sanex dou nitt barki yallah genrou films yiii moma gueuneul wiri wiri sans mentir
Ndékhéyo mane cheikhou la beug😂😂
Woeeeiy 😁😂😂😂😂😂 dinaah deeh waiy saneex di na ma reuiy 😆😆 ana waa groupè wifi.beaùg naalern .lov from the Gambia
Sa nékhe égal toujours à lui même nékhe la déf barèwe😃😃😃😃😃😂😂😂💖💛💚💙
Li nekhna way ken dou sanek
Le meilleur de tous les temps #sanekh#mon oncle #
Merci sanexx gor dafay am fit
Kou dakor ak sanekh nii khalé yii daniouy changé fonanté chak att.... Beussal j'aime.....
Episode bi nehk na torop mais kendu sanehk ya meun ci theatre Senegal... 🥰😊
akameuna kaff woyyy kanamou sanekh bii j'en px plus d lui way c trop😂😂😂😂😂
😂😂😂wouy Sanekh amoul wouy dead bilahi ya meuneu jouer sa rôle
Sanekh ray nama dama ree basa ma ngogou li resse sa dou dm😂😂😂😂😂😂
Sanekh Franchement il est fort si rolou pauvre ke riche Dina dèè rek look kanamou sanekh bi
Chiekh Bethio diereudieuf j'aime
Sanekh moye bandit dh fou neck laye geneu mo mane gayi deugeu deugeu dou sen morom daffa diangeu theatr ba mokal mo takh ma beugeu theatre depus 2005 ba legui mangui setan soleil levant danio mane macchallah
Man sama biir ngai metti.....!😂😂😂😂😂😂🙈🙉🙊Ma bagn dotuma setan sanekh! Dafmai rayie
Je suis un producteur, je rassemble Sanekh, serigne ngagne et baye dans un mm theâtre. Ce sera le meilleur theâtre de l’histoire.
No sanékh douma ray 😂 way c le meilleur aiméma ma khôl ❤️
Sokhlanaléne thi b3ne série yéne rek nak San3kh,Aladji,Djogoy,Combé,Manioukh,vieux,Patin,Deureum Gadjio,
😂😂😂😂😂Sa Nékhhh wathie gnou wayyyy. Néna Bineta damalay yereum
Hahaha sa nekhh will kill me
Sanekh 😂😂😂 ki domram leuh 😂❤️❤️ (Amicalement). D’où niit mdrr il est trop fort mode de foneunté 💋
Sanex Ray nama😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Non sanekh yallah nako yallah goudal fanam😂😂😂😂😉😉
Sanekh moy bandi Nena Aladji man may guerrier
Bravo soumboulo bahk si mom da yakal Alhagie 0-0 nil yalla na diamou yague
Kou begue ga yobou sa yaye maka yall nalla ko yalla yombalal
Namonenaaa sanexx bii 😂😂ré naa bay beugue dé
Dieyna machallah
Sanexe tre fort mais taye soumboulou dala dacc 🔨 😹😹 dotoko defati
Gorou gui dal diakhal nanouma qui aimerait beuseul j'aime
Ay kharite nila wara mele
Sanekh Cheikhouna
C'est vrai ou pas
Non sa guérier nga nag wouyaye yo😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂sa goudal fane way bineta mome sama yaye leu
Sa nékh meilleure comédien de l'année ki et dacord
Sanékh bilahii man meusouma guiss kouko ndakha théâtre côte bounék meilleur la fa
meilleur comedien de tout Les temps sanex guineen quit regarde souvent Les teathre senegalais
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 magui dee ak sa nexx il est toujours le meilleur
Wooy nénako damakoy séxal wéne gauche bi mo eup soow😸😸😸 mouniko embrassanté bi dey changer
Non sanekh trop drôle 😂
Nonnn sanekh rewna 😂😂ak explication bou sori bi nak😂mai guisse guéne yawi sanx bi😂😂
Soleil levant
Respect 👑
Première vue dou aye fo may léne ma ay like way ms wa soleil levant thia kaw thia kanam rek thi barké wérou koor bi wassalam
Woye mangui dey sanekh dinama reye 😂😂😂 yalla na diam yague waye
Je l'adore trop aider moi à le voir 😂🤣😂🤣
Sanekh est unique dans l’artiste dee naa waay 😂😂😂😂😂
cora nala cora woma 😅😁😂😂😂😂😀😆😅😆😅😀😁😂
WA SANEKH Ba Jamra diappeu leu ngay Diangal nouniouy embrasser nonou! bilaye kou la degg kham ni yagg nga si... 😂😂
*Sanékh mo bonnnn😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂*
Non sanex amoul mais soumboulou moy bandi😭😭
Ahahay sanèkh foneuntè kayy kaay😄😄😄😄😄
J’espère que vous préparez QG TFM, Avec Serigne Ganna Messéré
Moh
C’est quand
Iow loy moh
C’est un athée hamna
Ce soir inchallah Lay am
Waw niongui koy wathie mok serigne Khadim kebe
Sanekh nagnou nianal goudou fanne reck magui dh 😂😂😂😂😂😂
Hahaha no sanekh reww na 🤣🤣🤣 tes pa sérieux sanekh 🤣🤣
Bilaii do nitt😂😂😂😂😂sanekh ray guama
WouyWouy magui kheum, noo sanekh bilahi mome laye weur
Esk tamitt dolen expliqué sanekh le mot '' pédophile''😂😂ahhh mbass ..brff entre nous sanekh nak expert en '' embrassé la '' wala ?😂
Sanekh mo ame fit
Bilay birima moy guerrier😂😂😂
ANI.GNI.BEUGG NDOOGOU SOLEILS LÈVENT BEUZAL J'AIME YALNA SANEX C'EST LE MELLEUR GNÉPOU AME DIAMOU BOU BAHH
Non sanekh yalla May nako 🙏
Il es le meilleur wollahi
J'ai regardé ça plus de 7fois a l'instant j'arrive pas a digérer
Bilaye sanekh dou deme😂😂😂🤣🤣😁
Sanekh goudeul fann walahi😂😂😂
Sanekh
😂😂😂😂😂😂😂
Sanekhe rew ga Bilay wala
😂😂😂😂😂😂😂😂 no sanex e lê meilleur
Sanex dou nit bilaye 😆😆😆
😂😂😂😂😂wa sanékh kagne guaye nopiii😂😂😂
😂😂😂
😂 😂 😂 😂 😂 😂 wouyyyy sama dina dead rekkkkkk cheu 1 mitan ban d touche
Kham temps ak tiguiri temps😂🤣😁😀
😂😂sanèkh douma raye dawoul nada 😂
Vive sanekh beusseull j'aime