Aissatou penda diop il faut quitter ce jeune homme ce n est pas un mari responsable Vous avez déjà été à la Mecque Ce garçon va vous créer des ennuis soit responsable SVP Je n ai jamais vu au Sénégal Une femme âgée de se mariée avec un jeune homme Vous avez des enfants plus âgés Vraiment j ai mal au cœur ❤
Il a juste peur de cette vieille sorcière qui lui a mis le grappin Mais ce qu’il a dit c’est la vérité C’est vraiment son ressenti Kaliphone ne devait pas mettre les audios tout de suite Il aurait dû régler ça avec le petit dans la discrétion jusqu’à ce qu’il quitte cette femme. Car à l’entendre parler on sait qu’il est dépassé par les événements et souhaite s’en sortir.
NDEYSANN BOY BI VRAI NGAKKA KANE LA KALI , CHOCO ET ADAMO DI WO TÉ DO XALATT DINALA ENREGISTRÉ MOUY RATATATIIIIIIIIII RÈK 😂😂TÉ BOY BI FÉENKATT DEGEUU LA MOUY FOWÉ YALLA AK AY WATAME YOU REUY YI😂😂
Ya pas plus domérame que ce Kalifone, mais ce que vous faites ce n'est pas du boulot, woutilène liguey.....Tu ne devrais pas enregistré le petit et ensuite le mettre ici, vrai doméram ngua
En tout cas même bou seuy bi tasséé itam,pendadiop ne perd rien.dairam yaakhouwoul non plus,ndakh ,baine, ndiaaloowoul woone, thie sêy la naikoone,gnaare ,koumou mak mbaa koumou toolool lay seuyaatal mais pas ay gnou am 55ans ou plus,gnoognou gneupe teulai nagnou bou yaague
Aissatou daifoul dara à part photowou ak yeuguelai mariageam bii bamou aague internet.ousseynou moo irresponsable. Comment peut on se confier à des kalipho, adama des Negri kon vient de connaître il ya quelques secondes seulement ? Di sootaikou nak,di thiararari melna biir bouy daw...?aissatou baayiko mou daim balaa moufay saathie sakh mbaa autre chose,naala may kou am 45ans
Awa mbengue dou nit ak kanamam guii di taawéékou na kawass bou tooy,ndakh bavardageam guou bari guii thi internet moowaral Adamo saagua ndeyou ousseynou publiquement.moytoulaine di yaubou you mel nii thi internet,baakhna daal
Li yépp pauvreté móo ko waral!😭😭😭😭
Nyekoy Guen pouvoir niofi nek dess AK sen ngor
Dett niakk ambition ak beugue lou yomb😢
Nga dessé ak sa ngor mane li meussou ma bett
Boy bi fénn Kat bou mak la téey léne ci mom😢😢
😂😂😂😂
Aissatou penda diop il faut quitter ce jeune homme ce n est pas un mari responsable
Vous avez déjà été à la Mecque
Ce garçon va vous créer des ennuis soit responsable SVP
Je n ai jamais vu au Sénégal
Une femme âgée de se mariée avec un jeune homme
Vous avez des enfants plus âgés
Vraiment j ai mal au cœur ❤
Thanks very much !
Pourta kalifon mo takh mou def li yep defa yaakar dagnkoy dimbali ndeysan 😢
Mane dama wédi Boy bi sakh.. irresponsable con
Aïssatou penda diop laisse se jeune homme c'est un grand menteur il n'est pas sincère il te profit moye gor you beugueu lou yombou
Kali cv khalebi daye fene❤❤❤
Il a juste peur de cette vieille sorcière qui lui a mis le grappin
Mais ce qu’il a dit c’est la vérité
C’est vraiment son ressenti
Kaliphone ne devait pas mettre les audios tout de suite
Il aurait dû régler ça avec le petit dans la discrétion jusqu’à ce qu’il quitte cette femme.
Car à l’entendre parler on sait qu’il est dépassé par les événements et souhaite s’en sortir.
Voilà toi t'es intelligent 🧠🤓
Je suis avec toi
Meune doul rk Goor gni yakamtè doul rk
Merci kaliforne 🎉❤
Kaliphone mi dou nit kou bakh, pourquoi enregistrer quelqu'un pour détruire sa vie conjugale?
Surtout Lou tolnii seuy hasbi allah Wa nemal wakil
😂😂😂
Merci Kali❤❤❤❤❤❤
Khalè bii mo meun fene
Koula sougal si société bilahi nga yakh ko do xaler boubakh
Ahmet Cissé rousna 😂😂😂😂😂
AMET cisse Dou tago AK gathie
Khalatoul wone né di nga ko enregistter gosse bi vrai ngaka leu
❤❤Merci de SAUVER mon Fils .Mariée là le dépasse 😅😅😅😅😅😅
NDEYSANN BOY BI VRAI NGAKKA KANE LA KALI , CHOCO ET ADAMO DI WO TÉ DO XALATT DINALA ENREGISTRÉ MOUY RATATATIIIIIIIIII RÈK 😂😂TÉ BOY BI FÉENKATT DEGEUU LA MOUY FOWÉ YALLA AK AY WATAME YOU REUY YI😂😂
Kali yaye compléxé nane jigéene bu xéese pécc
kou am secret téko lolo la kham gnii ay mbamm lagn 😮
Ouseunou mieu khaléla waroule tak nanna sangouna laalna😂😂😂😂
Jomi amoul heure, Sénégal diakhal nama😢😢😢😢
Bilahi
kali merci le jeune il a peure
Pour dire vrai ce gosse là est un sai sai 😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂😂 no mais c'est grave😅😅
Kaliforne ya wak Adamo yèna tèla doul rk mais meunone nguene df limou lene wkah lèp si discretion
😂😂😂😂😂 vraiment ces grave
Ya pas plus domérame que ce Kalifone, mais ce que vous faites ce n'est pas du boulot, woutilène liguey.....Tu ne devrais pas enregistré le petit et ensuite le mettre ici, vrai doméram ngua
Kalifone alako jarani e ma machalla
Ousseynou mi dou xaler bounakh mais tu finira mal
Kou bayiwoul di liguey domou diambour ba dotoul and ak sagom dinga wérou beuthieukou ndara gamb😢
Ahmed Cissé!🤔
Pour tan limou beug dèf meune na nèk si mome ba lègui Mais dèf lèn ndanke rèk
Veréma nak dengenko waron dimbali mom fenoul defa ragal ndeyssan
😢😢😢😢
Mère bi nena. mon coeur 😂
🤣🤣🤣🤣kali mi sone na dé té yénouwoul
Ki khaléla limoudougue moko eupe.dolé
En tout cas même bou seuy bi tasséé itam,pendadiop ne perd rien.dairam yaakhouwoul non plus,ndakh ,baine, ndiaaloowoul woone, thie sêy la naikoone,gnaare ,koumou mak mbaa koumou toolool lay seuyaatal mais pas ay gnou am 55ans ou plus,gnoognou gneupe teulai nagnou bou yaague
Il a peure kali warokowone .wilipandé
Mére bi mo war delo domou diabour bi niak nga ndeyi fayda
Certains jeunes d’aujourd’hui ils sont vraiment immatures 😢
Aîssatou peinda lii darra diarouko ya gui perdre sa dingité ouseynou un petit garcon nonnnn meune féne
Vremmen 😊
Khale bi day fen
Yen est-ce que nobolén mère bi tamit😅
A force de manipuler les gens il fini par rentrer dans son piège
Mane capison bi mou solale halébi moma métii ouseynou méleni bébé 3 moi tu dékone aîssatou
Gni gno bone mariage diambour sen lousi sen yoon
Ahmed cisse da ragal adamo
😮😮😮😮😮
Osseuynou mi deh bo démé sakh mo liguey mère weuyou leu def
Adamo dafa epeule
Khôl mounoul neex kay. Femme bii na bayii domou diambour dji mou gnibii Thii yayam.
Khalé bi même sou démé si yaye dji doroul réglé
Ki ték katou khél la😢😢😢😢
Aissatou daifoul dara à part photowou ak yeuguelai mariageam bii bamou aague internet.ousseynou moo irresponsable. Comment peut on se confier à des kalipho, adama des Negri kon vient de connaître il ya quelques secondes seulement ? Di sootaikou nak,di thiararari melna biir bouy daw...?aissatou baayiko mou daim balaa moufay saathie sakh mbaa autre chose,naala may kou am 45ans
😢😢😢😢
Diapaléléneko mou délou si wadiourame
Non boy bi j'ai peur il n'es pas innocent mais bon c'est la faute de aissatou😢😢😢
Dou ben innocent, eumbeul neu jigen bayiko fi takii maguette. Il veut juste une cagnotte en utilisant kaliphone, fafe yeuf yi capoter
Dou.piege.li.nek.thî.mome.la.wakh.dafa.ragal.mere.bi.ameth.cisse.day.roube
Nouvelle série quand en train préparer pour année 2025 arrête de jouer avec nous😂
Awa mbengue dou nit ak kanamam guii di taawéékou na kawass bou tooy,ndakh bavardageam guou bari guii thi internet moowaral Adamo saagua ndeyou ousseynou publiquement.moytoulaine di yaubou you mel nii thi internet,baakhna daal
Mais pourquoi tout ca je demande seulement l'islam daffeko interdit
Yomale khiyame dina metty yakh nite si dara moye sene ligueye
Wakhou khalé rekk lay wakhe comprends leen ko dafa sokhla kou wakhe ak moom ndan keu wakhe ak mère bi mou libre ko
Ki dou Ahmed Cissé brome koy bou gatte bi 😂😂
Mere bi bideew lhalebi moko internet resse
Le jeune il a décidé de quitter la dame laissez-lui le temps il va le faire il a honte de faire ça plus comment
Yaw tamit waroko wone vilipendé. Kou ték plan wam nga tok niew defagoul sakh nga took enregistrer ko tegal ko adouna bi yeup, mo yeuy wédiwaat kay
Tu me parles d'ùn gamin
Ahmed cisse est très mauvais quelle femme l a mis au monde une sorcière
Comprendre nako da beugeu teki
Lolou laniou comprendroul, il a voulu utiliser kali pour am cagnotte, lek khalisse te dou bayi mère bi. C'est un petit opportunistes