Jahman X-Press - Jahman Feat Ahmada Jadid - Bamba la Joie
HTML-код
- Опубликовано: 2 фев 2025
- open.spotify.c...
itunes.apple.co...
itunes.apple.co...
--------------------------------------------------------------------
/ jahmanxpress
/ jahmanxpress
www.twiter.com...
--------------------------------------------------------------------
PRODUCED BY HOSIDE STUDIO
MUSIQUE : MICHAEL ET KY FEEL
MIX ET MAST. ADA LSD RECORDS
DIRECTION : JAHMAN - AHMADA - SELEMIND
IMAGES : NAZIR CISS ET BADARA BARRY
MAKE UP : LISSA PRO
REGIE : MAME MALICK - BABOY
WIZ JIFA - MME MBACKE
Suis talibé Cheikh mais n'empêche depuis biniou annoncé magal beu legui Sama xeL Thi jahman reQ la dém il nous a pas déçu wallah🔥
Sénégal bén bopp La Kén meunou ko khar niar Tidiane khadr mouride layenne nieuP Seydina Muhammad PSL laniouy liguéyal kon naQ na raféte GuuD safar fOr All muslims particulièrement souniou mbokou Mouride Yii 🙏🏾JeureuJeuf Cheikh Ahmadou Bamba Serviteur du prophète ❤️
Nice ne👑👑👑👑👑😚👌👌👌
Nice talk
Nice
Lep bén la bilay 💞❤🤗
Yalanelen serigne touba fayal bopam sama hol sed na bâ dama dioye te tayoumako...
Machallah Bamba la joie 🤩 jahmane ak Serigne ahmada Mbacke yalla nguene lakhe nguereu moul Serigne touba ak kép kousi xolam sed rk di ñanal ñep magalou djame gou Serigne touba nangou ak fouka way mana defé rk di sakou ay j’aime 🥰 ❤️🙏
Mamegor Sylla Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Wawa
Suis tidjane mais jadore trop sen mbecté machalah man mom serigne saliou la beug sma xol 😍❤😭
Ndaysan machallah Mame Saliou ken dou môme
*Khadia sow beugue nala nguirr serigne saliou mbacké😪😭😭😭😭😭😭*
Yalla ga yok
Contan si yow
Ndaysae sa xole la rafet
Je suis tidiane et j'adore la chanson j'aime serigne touba n'oublie pas que sala lahou Haley hi wa salam moye souniou royoukaye gneup bene laniou MashaALLAH
Machallah ❤❤❤❤❤❤ vérité appolue ❤❤❤❤❤
L'éducation spirituelle des mourides est vraiment légendaire...si tout le peuple sénégalais était aussi organisé, discipliné, on aurait relevé le défi de la pauvreté. Vive Bamba...
Mou
Weuhh mouy yénne
Bamba la solution 🤔
Est-ce que dioumo 😂😂😂
@@corinnesambou non Dafa dioumm srx éducation spirituelle la wakh dh non Lolou d'où deugg
Talibe cheich bi de wayou bamba dji rek lay begue ani talibe cheich yi li nekh na Machallah bamba la joie kou beug al Mountakha Mbacke beuseul j aime dieuredieufe serigne touba ❤❤👌👌
Machalla way bell pensée lep benn leu bilahi gnounn gneup ns ns retrouvons au firdaw si ! Dieureudieuf borom touba
Yaw sama kharit dagua bakh rék billay kéne guenoule yalla nala yalla sam koudel sa fane ta mayla khéwal bou bari billay lép kay Élhadji Malick ak Serigne Tabou faniou boké billay doufi
@@morfall3264 nianal ma am borom keur gou bakh
@@Babacarndione012 amine ya rabi
2 millions de vue avant magal incha Allah maximum de partager si barke mouhamed (psl) ak cheikhouna ahmadou bamba miy sounou yakar ❤❤❤❤❤❤❤te boul faté beus fi
👇
Machalla inchalla ❤️🙏
Dinako dépasse inchallah mouride dafa kheur
Je suis chrétien mais j'adore cette chanson Banmba la joie d'ailleurs j'attends avec impatient chaque années vos chansons et j'aime Serigne Touba Bamba Feep
Jo
Suis talibé cheikh mais jadore Serigne bamba yalna gnou yalla doli diam ndax lepeu beneu la magalou diam ❤️🙏🏼
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Amine
❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Une Niasséne ki aime les chansons mourides ila Touba nieuppay dem 🙏🏽
Invite nala
*Unechallah*
Yaw beugue nala ndakh liga wakh
Amal diam wat
Mame Diara Geuye ah c cool sa envoie tn num ou Instagram puisk samedi lay nieuw inchallah
Sénégal mo am ndam dieureufe Serigne Touba . Mouride tijane khadre layen fou way nek santal ma Serigne Touba ❤️❤️ talibe dabakh Malick sy .
Jaliya Jaliya Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Sante bou bakh
Masaalla yalla nalen yalla faye
Sante Serigne touba ❤❤❤❤❤
Thiey serigne touba mbacké limou ma defal thi goudii magual 2020 bii passé doumako faté moukou yalla na yalla yok léram tasse niou thi barkém amin
Où sont les chrétiens qui écoutent aussi ce magnifique son 😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Suis là ma sœur et bon MAGAL à nos frères et sœurs Musulmans et qu'Allah accepte les prières 🙏🏼🙏🏼 soyons richement bénis 🙏🙏🏼🙏🏼🙏🙏
Beine ngui nii🙏🙏🙏
bénéne angui ni deh...bon magal a tous nos frères musulmans
Magnifique chanson
Bon magal a tous
Ci naniou bokk
mashallah
Bamba si khol ❤️
Mouride si khél🧠
Talibé si djiko🥰
Xassida si lokho🤲
Alldiana sunu demain😍
Sadikh sunu chemin💞
Massalik sunu succès💫✨
18 Safar sunu yitté😍 magalou jamm🙏
Jahman ak Ahmada machalla nékha tina♥️
Machalla
🤘❤️
Ndeysane mbèctè rk ba aldiana 💯👌
🥰🥰🥰
Chaque années mouyegana nekh machalla
Je suis tidiane mais bilahi Beugue bamba reka nekh
J'adore cheikhoul khadim 😍🤩 j'aime way
Machalla Ndeyssane 🙏🙏❤️
Mane beugue nala guir serigne touba
Bly
Li moy senegal mon frère🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏🙏🙏🙏....
Yalla na diam sakh
Billahi yaraféte xoll machalla
Je Suis tidiane ms cette son me plais beaucoup dieureudieuf borome touba
Talibé cheikh biy khar son jahman ak ahmada chaque magual neixna lolou machallah yalla nieup magali si diam si barké cheikhou Tidjane 🤲🏾♥️♥️
Magalou diam
*Amine waye ❤🙏*
Amine Yarabi 🙏🙏❤️
Ya bakh rafet khol
Lépou bénne laaa
Ya bakh Way diame rek nagay am💓
Suis tidiane mais j'aime beaucoup serigne touba😍♥️♥️♥️
Kay ma may la passe magal ioe
Lepp bene la Billahi ♥️♥️♥️
Ayaw beuuggnalla❤️❤️❤️
Mola warre nak warre nieup kaye tarkalah
Cool
Que puis-je dire sur cet homme ? Qu’il est incroyable, superbe, gigantesque. Je n’ai que trop de compliments à faire. *JAHMAN* a montré et prouvé son talent ; parfois, il me suffit de l’écouter pour que tous mes maux disparaissent. Il y a de la joie, de la puissance dans sa belle voix. Osons reprendre ses propres mots « que les moins de vingt ans ne peuvent pas connaître » ! Il fait partie des plus grands voire même le meilleur de sa génération. Ses chansons respirent, expriment une chose. Il est en quelque sorte un poète du monde moderne ; ses musiques relèvent d’une adoration sans limite : le rythme, le texte, la voix, tout suscite l’admiration.
Encore du lourd🔥 avec son nouveau chanson dénommé " *Bamba la joie"* (épisode 03) avec Ahmada... *JAHMAN* tu es et tu restera toujours impressionnant. Un vrai Talibé mouride🥰🥰🥰
Bassirou ndiaye dit Bachir Winner UCAD/FSJP
Machalla bamba rek
Wow jaime 🤍
C'est comme si tu as lu dans mes pensées 💗❤️
Machallah
@@mamembaye4739❤❤
Je suis talibé cheikh mais Walahi j'adore ❤❤❤❤❤❤ machalah serigne touba 💕
Barki Yessu Krista mi ma Yakaar j’ai vraiment beaucoup kiffé cette chanson Yallah na Diam continuè di sakh tie Catholique yi ak Musulman
Chapeau à vous la chanson a été réussie 🙏Machallah🙏
ruclips.net/channel/UC7gOQ3KSmU3VZvc1SeZUjWw
Amine🙏
Abonnes vous svp ruclips.net/video/r2yTN6juBZQz/видео.html
Ya bakh nioune niepa y fa yala bon magal diadieuf AHMADOU
amen
Wa gnouy dislike mom c'est koi leur blém🙄suis chrétien mais li mom machallah nice neu trop❤🔥
Lo kham thiii sokhor motakh lothiii guiss delou guinaw rek kou merr boko rewmii bamba moy ki ko mom
Bonn rek😁😁
Thioo franchement suis tidiane mais jm trop 🤷🏽♀️ mm mw je ne leq comprend pas
Ndeye Penda Camara ma chrie gni dagno sokhor lepp benn là on es tous des musulmans 😍
bone sokhor ignane gniy dislike guemougnou bene diner dougnou dara
Sa yone wi , amoul tanki guinaw Cheikh Bamba ma yeureum sa noneu yi, Bamba dieureudieuf ... mbékté réka lay andal 🙏 li lii nehna waay ,yalla nagnou borom bi defal diam 😭😭😭
Je suis Chrétien et j'ai toujours aimer. Kú beugg Bamba , warra beug Mariama yayoú Inssa ...beusseul jaime👍
Crisabel Brayan bamba taggna Mariama yayou Insa c fuzti 🥰🙏🏾👍
Liii dafa nekh torop
Mariama yayou INSA mo gueune si jigeen yi Serigne Touba moko wakh
ya bakh waye
Tous les musulmans aiment Marie et insee coco. Machallah parsk loulou manitou diangual
Franchement yonou mouride nekhna
En t’en que chrétiens j’adore bcp mame bamba 💪💪💪
Yala dinala fay si beugue binga bamba.effectivement il a tt fait pour nous donc beguer rek mossi dess.thiante rek
Abonnes vous svp ruclips.net/video/r2yTN6juBZQ/видео.html
Ndeyssan mame bamba kenla
Tu sais ce que j'aime chez vous les chrétiens votre honnêteté et votre franchise vraiment bilahi ya bakh té niak kiniane soma dieguéwone balégui ma diokhla adiya Serigne Touba ba nga bègue
F Félicité à toi Marie, surabondance de bonnes oeuvres, sainte patronne des femmes chastes et charitables,
Tu es au dessus de toutes les élues du Seigneur Sublime et Insodable,
b[L'Acte existentiateur de Dieu t'a pourvu, sans contredit du plus distingué des messagers[Jésus],
]b
Bonheur à quiconque place sa confiance en toi, sans désaprobation aucune,
Car, il est évident pour tout croyant que tu es la favorite des humbles obéissants [à Dieu],
Toi la mére du meilleur des généreux [Jésus], tu es affranchie de tout culte autre que celui adressé au Seigneur,
Les infinis saints mérites comptés à ton endroit m'ont conduit à te rendre hommage par cette ode,
Tu as été gratifiée de faveurs qui rendent bienheureux tout croyant scrupuleux et convaincu.
Je formullerai, ce jour, des éloges en ta faveur qui certes, m'assureront une vie émérite,
Qui se perpétuera jusqu'au paradis, et ce, sans aucune prétention d'épuiser tes immenses vertus.
Tu es l'héritière de la noble descendance prophétique et n'es point pécheresse.
Tu es le symbole de la circonscription et de la rectitude morale,
Le Seigneur a immensément agréé tes bonnes oeuvres,
Ton fils [Jésus] a obtenu ce a quoi il aspirait auprès de son Seigneur, l'Impénétrable,
Mon voeu en écrivant cette ode est d'obtenir l'agrément de Dieu, par quoi Il éternisera ton voisinage,
Auprés de Lui, Lui le Seigneur des royaumes célestes et le Pourvoyeur de la droiture et du culte sincère.
J'implore le Seigneur, le Détenteur de l'Acte existentiateur,
b[Afin que ce poème te soit un argument solide [contre les fausses accusations portées à ton encontre], et à moi un motif d'exaucement de mes prières.
]b
Ô lmére du Saint Esprit, Ô la mére de celui par qui les ténébres sont dissipés,
Ton fils ne s'est pas éteint sur la croix, il a été élevé auprés de son Seigneur,
Que la bénédiction de Dieu soit sur toi et sur ton fils, celui par qui l'ignorance est éradiquée,
De sorte que l'adoption de pratiques licites soit perpétuellement à portée de tout erudit pieux.
Accepte ce présent et ne le récuse pas,
Conformémént à l'acte du Seigneur, le Très-Généreux, qui accepta de répandre sa mansuétude sur ton humble ancêtre [Eve].
Ô Dieu, faites que ce poème soit un moyen d'adoucissement des coeurs,
Ô Dieu, faites que ce poème soit parmi les meilleurs panégyriques déclamés par les Houris du Paradis,
Un Tidiane très fier d'avoir Cheikh Ahmadou Bamba au Sénégal ❤️❤️❤️bon Magal à mes frères Mouride❤️
Merci beaucoup 😍😍😍😘
A toi aussi
Machalla
@@oumarcisse8217 Merci beaucoup chérie l.
.llj
..Merci beaucoup chérie l
l.Merci beaucoup chérie. K
Merci beaucoup chérie llj..l.l
llj.
..kk
.
K
K
J
..lllk
Llj.l
l.l
l
jllllj.llj.k
@@oumarcisse8217 k
K.
orite L.lllk
..k
n.
L
.ll
...
knl..
Online l
J
Online l
L.
l
.l
nn
.k
.
n.
Ln
Nk..
.Online l
n
l
.
.k...
j
K
kj.
k
.
n
k.
k.ll
l.kn
n
l
n
l.l
l
ll
L
Llljjjj.
.Liou k
Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne Aminnne Aminnne Aminnne Aminnne
Je suis tidiane, mais chaque magal je vais à touba,la chanson est sublime mashallah
Machalla
Wawawe
Ya bakh
And survive
Machalla
Suis chrétien mais j'adore vraiment les chansons que Jahman et Ahmada font chaque année yall naleen yallah lafal thiaat defal leen diam ak xeweul .
Dileen nianal yeen nieup magaloub diam
Bamba rkk🤲❤💪👌
Ndeyssane Machalla Amine way Dieuradieuf❤️❤️❤️👏
Yalla ga am diam
Yaw diame rek ngay am💓
🙏🏿✌🏿
Ndeyssan rafét na !!! Vive le dialogue islamo chrétiens 👏👏👍
Jahman mane tidiane 💯 mais foo wayé serigne touba sama kholle séd mais Gamou maynou béne son bou dall nioune tidjiane yii🙏
Moustapha Dieye Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Ok amoul bléme
❤❤❤❤❤
Wahk ga dahk jahman dafal lol y
Pour serigne babacar sy reck guarre yalla🤔🤔🤔🤔🤔
Vraiment jahman et Ahamada vous êtes exceptionnels... je peux écouter cette chanson toute la journée 😭😭❤️Quand je quittais Touba pour rentrer a mbour lors du magal de cette année... Jai écouté ce chanson fatick beu mbour😭😭 a chaque fois bou diekhé rk ma reprendre ko😔😔 Dieureudieuf Ahmadou ❤️❤️
nélaw ma goudi nélawouma jour ndakh vidéo bi la done wett depuis hier guir yalla way may léne maa J'aime té Sérigne touba rek takh ziare na baki mouridoulahi ❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
Pape Seydi Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
J'aime être mouride 😭😭😭
Jahman😍Js8 chrétienne et j'aime trop tes chansons de Bamba❤
Bon Magal à mes frères musulmans Yallah nalèn Cheikh Ahmadou Bamba takhawou guén eigu ak diam🙏🕋💕
Amine🥰🥰❤️
Amine
Ho 😭 machala merci 😍
Abonnes vous svp z
Yalna yalla defal diam
Je suis tidiane mais jador bamba ..la chanson est just "waw!" mbécté la yonou bamba mbécté la !!!!
Pareil
Moi aussi je suis talibé Chekh mais adore
Abonnes vous svp ruclips.net/video/r2yTN6juBZQz/видео.html
Machalla
Bon magal à toutes et à tous nos amis musulmans belle chanson vraiment
Dieureudieuf serigne touba 👌👌👌kene dou yawe 👌👌doffe naniou si yaw th dotouniou were 👌👌👌 bamba protege🤲🙏🙏
Je suis chrétienne mais j'adore trop cette chanson.
Chaque année j'attends avec impatience vos chansons.
Bamba fepp, bamba everywhere😊😘
Yaw sa khol mo rafféte Rék bilahi ❤❤❤
😂😂😂
maa contant si yaw billah yallah nala señ touba fay ku bakh nga
Sénégal béne bopp la kéne meunouko khar gnar❤
Moi aussi j adore
Je suis tidiane mai jaime wa Keur Serigne Touba Srtou le khalif yallah nako yallah may goudou fane ak werr 👌 meilleur chanson😍 Serigne Touba Mbeurou dioulite yeuppppppppp😍
👍
Koubakh boug Lou bakh mbecktè rek
Amine ya bakh dh billahi
Tw aussi je t'aime beucoup
Machallah
Je suis talibe Chiekh mé son bi Machallah yallañiou yalla feyal Chiekh Ahmed bamba si darke seydina mouhamed sm xol sédna billahi 😍😍
Idy Toure Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Je suis chrétienne mais j'adore énormément cette chanson le rythme est trop bien
Hey waye Jahman doma weyal Serigne Babacar Sy RTA guir Yala
Manchallah yala guene yagueu di wayele Serigne Touba.Yala naniou tassou si barkeme
*#Ndeyesann*
amin
Amine
Yawdaal yalnassa diamou yagge yaa bakh waay
Serigne Babacar nékoul sa morome ba guay gnanou pour gnou way ko thi aname yiii
je remercie mes parents d"être née dans le mouridisme fière d’être Salihate dieureudieuf Bamba notre joie
Wawa 💯❤️
@@taphadrame9693 ❤🙏❤🙏
❤🙏❤👌ok
Ndeysann ❤
ruclips.net/channel/UC7gOQ3KSmU3VZvc1SeZUjWw
Talibè chiekh la
Mais j’aime trop chiekh Ahmadou bamba mashallah ❤️❤️❤️❤️
Sa xol dafa rafet yaw diame rek ngay am💓💓
❤❤
Bilay
Merci
moi aussi je suis talibé cheikh et j'adore cette chason
Alkhamdoulilah bignou amé serigne touba ❤
Pourtant dioye yombouma dé mais 3 ans ngui ni Jahman dima dioylou !!!
Yalla nagn KO fekke deweune thi Barke cheikhoul khadim 😍
seye papa oumar Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
@@ligue1senegal23 c'est fait ,bonne continuation !!
Amine ya rabi
Ça aurait pu mériter d'avoir 1M de vues en 24h
Bamba la joie ♥️😊
Baye le king Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
@@ligue1senegal23 merci
❤️❤️
Mon réve le plus fou et le plus intence est d'avoir des jumeaux qui se prénomme serigne falou mbacké et serigne babacar gnoy borom diamano...mes respects a serigne bamba khadimou rassoul
mame maty Ndiaye Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Inchallah diko am sa beug beug raffett ... Machallah sur ce bégté bi Mame Bamba la Joie de l'Univers
Yala nako yala def mou done li gueune si yaw
Bonjour
Yalnalako yalla may si barkép S. Fallou Mbacke😍🙏
Ndeysane demb batay magui nane nagouwouma limou wakh mé tayou SERIGNE GUI gathiel ba loufi sama ame nio guena beug nio guena guem ❤❤
Serigne touba nolén ko woyè mou nex gnou prsk da nékk sounou khôl. Naniou yalla doli soutoureu si barké mouhamed ❤️❤️❤️😭😭
Wakh gua lépou lolou laye wakh si xassida mani noko dianguè mou nekh dakh si lokho bako binde là,🥰😍😍
Waouh c’est tellement propre
J’ai écouté et reeeeecouter tellement que c’est bon et beau à écouter.
Catholique.
Bon ceux qui dislike vraiment je ne comprendrai pas votre problème
Nous sommes le Sénégal on est ensemble
Mais de fouu on est dans le même bateau
Vous parlez slmnt de jahman mais
Ahmada il a une voix d'or tlmnt talentueux
Bilaye deh
Abonnes vous svp ruclips.net/video/r2yTN6juBZQd/видео.html
Bilay wakh nga deug wnii
Machalla
C'est ce que j'ai toujours voulu dire
I’m very proud to be a diciple of Cheikh Ahmadou Bamba the servent of the prophet peace and hail be upon him
Je suis tidiane mais l'i dafa nekh thi ❤jahman dinama ray rek machalla chapeau.Bamba la joie❤❤
adama seye Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Jahman😍😍 suis chrétienne et j'aime beaucoup tes chansons de Bamba😍 amal diam sama fan's bi. Bon magal à tous mes frères musulmans nalén Bamba taxawoun
Amine way mbokk mii👌👌
Ya rafét khole
Diadieuff 😍
Ya bax dh fall yarame
❤❤❤❤
Ku begu serigne touba besseul Jaime wayy❤️❤️❤️💯💯
Akasaa
@@ousmanegaye3503 jgc4
@@ousmanegaye3503
Dieureudieuf serigne Touba
@@gabrielefalchi1905qq
❤️💖💜🌹Machallha borom touba cheikh ahmadou Bamba amoul bène la fi serigne mountakha mbackè yallah nafi yague tè wer borom mbècktè mi 😍💖💜❤️🤩🤩
Allakhouma amine inchallah 🙏
Je suis catholique mais dama beugu serigne touba
Machallah
Félicité à toi Marie, surabondance de bonnes oeuvres, sainte patronne des femmes chastes et charitables,
Tu es au dessus de toutes les élues du Seigneur Sublime et Insodable,
b[L'Acte existentiateur de Dieu t'a pourvu, sans contredit du plus distingué des messagers[Jésus],
]b
Bonheur à quiconque place sa confiance en toi, sans désaprobation aucune,
Car, il est évident pour tout croyant que tu es la favorite des humbles obéissants [à Dieu],
Toi la mére du meilleur des généreux [Jésus], tu es affranchie de tout culte autre que celui adressé au Seigneur,
Les infinis saints mérites comptés à ton endroit m'ont conduit à te rendre hommage par cette ode,
Tu as été gratifiée de faveurs qui rendent bienheureux tout croyant scrupuleux et convaincu.
Je formullerai, ce jour, des éloges en ta faveur qui certes, m'assureront une vie émérite,
Qui se perpétuera jusqu'au paradis, et ce, sans aucune prétention d'épuiser tes immenses vertus.
Tu es l'héritière de la noble descendance prophétique et n'es point pécheresse.
Tu es le symbole de la circonscription et de la rectitude morale,
Le Seigneur a immensément agréé tes bonnes oeuvres,
Ton fils [Jésus] a obtenu ce a quoi il aspirait auprès de son Seigneur, l'Impénétrable,
Mon voeu en écrivant cette ode est d'obtenir l'agrément de Dieu, par quoi Il éternisera ton voisinage,
Auprés de Lui, Lui le Seigneur des royaumes célestes et le Pourvoyeur de la droiture et du culte sincère.
J'implore le Seigneur, le Détenteur de l'Acte existentiateur,
b[Afin que ce poème te soit un argument solide [contre les fausses accusations portées à ton encontre], et à moi un motif d'exaucement de mes prières.
]b
Ô lmére du Saint Esprit, Ô la mére de celui par qui les ténébres sont dissipés,
Ton fils ne s'est pas éteint sur la croix, il a été élevé auprés de son Seigneur,
Que la bénédiction de Dieu soit sur toi et sur ton fils, celui par qui l'ignorance est éradiquée,
De sorte que l'adoption de pratiques licites soit perpétuellement à portée de tout erudit pieux.
Accepte ce présent et ne le récuse pas,
Conformémént à l'acte du Seigneur, le Très-Généreux, qui accepta de répandre sa mansuétude sur ton humble ancêtre [Eve].
Ô Dieu, faites que ce poème soit un moyen d'adoucissement des coeurs,
Ô Dieu, faites que ce poème soit parmi les meilleurs panégyriques déclamés par les Houris du Paradis,
Machallah
Gnola beugueu Beugue
Bamba merci
Dieureudieuf Serigne Touba ken dou Ahmadou diarna Kanassou wallahi hazim li dafa nekh welelele. Mouride mo nekh Serigne Touba rek ❤
Akaye DEUG sohna khadidjatou
@@niasseahmadu9844 Serigne Touba rek 💖
Mafi nék
@@niasseahmadu9844 Dafa lerr
Xamon nané dinanou dadiewate li serigne touba rek moco mane
Bamba kéneu meunouko bagn. Dou Talibé Cheikh bi dou Talibé Mame Limamou Laye bi dou Talibé Baye bi dou Chrétien bi dou sakh ki geumul dara. Comme tous nos Guides Religieux, il est Extraordinairement exceptionnel 😭😭😭😭😭😭😭❤️
❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Je suis Gabonaise j'aime vraiment beaucoup cette musique 🥰
Degloul maa waxx la toutii sii limou dathie nguir Rassoulilah (psl)
Fii lalaytoul jumah lagnou ko tabal si negg (chambre) bou leundeum none yi nane ko lambal mou lambe dathie ayy gobart aki raabe gnou teudje ko fofou mou dess faak rabbes mou daldi dioublou hibela daldi kaabar nénaa kérok meune ta soudiote naxx tarr tar diangue nafa sarou bakara ak sarou imerane djibril mou tidji negg (chambre) bi fiil hourane am nafaa niarry goudii lékoul nanoul loudoul sii lérou yalla lolou nénoul néna guiss nafa sunu Mame Soxna Diarra mou diko niaxx teh diko doli daara nénaa guiss nafa Rassoulilah mou dée ko lo xamni déssou ko xam bilay😭✌❤
Légui nakala nitte meuneu beugué Rassoulilahi ba paré dii nonno ak Ahmadou Bamba
Bilay wakhal way
❤️❤️❤️❤️😭😭 j’ai les larme aux yeux mome rek là gnou âme kene dou ma Wadji ahmadou
Moma diakhal
Machallah
@@mariemediallo4234 walay deysan khol yepp nehna
Suis chrétienne mais je kiffe toutes c chansons c'est tropp bien mashallah yalna leine yalla sam
Amine🤲Nancy Dioh love you❤
Le SÉNÉGAL est "UNi" Peace & Love
Machallah
Machallah dieureudieufé Serigne Touba 🙏❤️
Nice nice il frappe encore fort
Bamba est la joie ki est d'accord avec moi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✨ kéndou Serigne Touba 😭😭😭😭
Moi,je suis d'accord pour le million de vues.
Jeureujeufë Serigne Touba!
Je suis tidiane❤mais li dafa nekh trop machallah ♥️kenn dou borom touba ila touba rék inchallah ♥️♥️♥️♥️♥️
Dieureudieuf mame bamba 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Adja Ndiaye Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Walae Sénégal mo dakeu si pays Afrique yi si kaw gnou mbolo et est l'union qui fait la force ....Nagn mouy sounou politiquecien yi gua xam ni xaliss Sénégal rk moléne gnore pas les sénégalais Mouride tidiane khadr layéne niasséne sounou mak yoyou ont fait tte pour rendre le Sénégal meilleur stp bougn ko yakeu ....♥️♥️ c le Sénégal qui gagne é il est temps nak gnou taxaw dfe sétlou
Le meilleur commenter jusque lá
Bamba La Joie🕊❤️
Mbégtè la yone wi yonou mbégtè la
Mouride aljana lay doundou bamba laa joie .
Kémane la gou lamboo yeurmandé
Bounou maasé kénnal ko rek kheweul yi Saawaane !
Jalaal dja bolékok jamaal dja
Monou may mbégtè minouy sagoo fa Touba
Bamba liguéyeul Rabanaa batax malaaka yeppa naa ! Kii dou nitt rékk xana ndax katt mayam yi eupneu.
Souniou ko nango té diapko lougne yotou mou xeuthieul niouko,
Bouniouko khamoul oumpaléko, loumniou diox niou yakh ko.
Nagne djéma topou ndigeuleum té djéma soobou ci mbireum, djéma Sakkou ngeureumeum ba amko ndax léppa di ndam
Anh ! Sa yone wii amoul tanki guinaw cheikh Bamba ma yeureum sa Noone yi (BAMBA DIEREDIEUFF)🕺🏾
Mbégtè rek lay andal rétaane té doumako tay anaa mouridoullahii ! (CHEIKH BAMBA DIEREDIEUFF)🕺🏾
Bamba yaye Mbeur mii borom djakkay guéedj gui
Yaa wéteul yalla Fa ma yombé firndé yanga wirwir
Sunu Mbeur mii mo daane Toubaab bii
touploo thiéddo Sowé jaam gni xassida yangay riir.
Waaaaaaaw ! Mbégmi souniou xoll yi di fégne thi kanam yi
Dof nagne thi bamba té dotouniou werr yakari jaam gni.
Kone fou waay née santal nou xadiimi
Borom magal guée nou dogal boumi jaam yi.
Té lou waay am téyeul nioune doylo nane
Goor ga démone guéedj mame borom Touba
Kheweuleum yi dathie na fepp
Gnépa ngui nane bamba fep bamba evrewher
(DIEREDIEUFF).
Doylok wolou la am thi yaw ya geuneu gaaw thi mane ! Doy nga seuk lakhou waay. (DIEREDIEUFF ).
Wéteul nga Rabbana bam dioxla Koune fa yakoune! Doy nga Seuk wérou waay. (DIEREDIEUFF).
La matona wax cheikh ibra jeuff nako
Désna djeufé ndigeul défar Sounouy djiko
Wadjhal Khoulobana la bamba wax
Hala tawadoudi kone nagne thi sax
Nga nekthi rek té andak Yarak téguine
Waxdjou andak ball la wayé day ladj déguine
Thierno borom darou jaraw lakk
Boudoul konak yaw niou done niou sakk
Waaaaaaw ! Day geune di néex té andak yarak téguine
Mouride bou deugeul day raffetal djeuffine.
jahman bilay mala beugue man ligay way dafa nèkh barkèp serigne touba mbakè❤️❤️❤️❤️❤️👍
J’arrête pas de l’écouté 😭😭😭😭 nekhna way ❤️🥰🥰 Bamba la joie♥️ yalla naniou yalla yobou si diam niou magal si diam gnibisi si diam si barké borom touba 🙏
Lol sakh vraiment 😭😭😭
Amin
Amine way
Je suis tidjanne mais Jahman c le meilleur ❤❤♥ yalla na fi yague te weur je ne comprends pas ceux ni dislikes khana khamouniou signification ni
Jahman ❤❤❤♥♥♥
Yalla na niou Magali si diamou gnibisi si diamou si barki Serigne babacar Sy♥♥♥♥
Amine 🙏🏼
Gni def dislikes xam nan jahman dé kimouy way lan beugoul wayé bamba mom insbi koumouy dérangé fayal sa télé ak sa téléphone rk nopalou
@@fatimadieng4455 on ne peut pas se dire musulman ou chrétien et détester Cheikh Ahmadou Bamba c'est insensé bilay Bamba partout Bamba everywhere Bamba la joie Ne vous privez pas d'être heureux
Badiane Fall Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Fatima Dieng Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Je suis un TALIBÉ CHEIKH♥
Machalah nekhna trop et j'aime BAYE ABDOU KARIM MBACKE ♥
Je suis fier d'être chrétien mais j'aime trop les chansons de jhama surtout de Serigne Touba
Chrétiens yi MaShallah yenaaa bakh wayy
Bamba la joie rek ❤
Suis chrétienne mais j'adore trop trop trop trop même chaque instant j'écoute waouh il a encore frappé 💋🎉🎉🎉
Marie Suzanne Diouf Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Pareille pour moi je suis chrétienne mais j'adore Macha Allah ♥️
Juif yi sakh Beug nane 🎈🎉♥️🙏Gaíndei Bara Protège
Moi aussi je suis chrétienne Marie Suzanne Diouf et j'adore ! Il est doué ! Toujours de belles chansons !!
Viv la paix. Viv le Sénégal que Dieu vous protège nos frères et soeurs chrétien
Être Tidjane ne n'empêche pas de reconnaître le grandeur de kheikh Ahmadou bamba la joie j'aime l'auteur jahmane
❤️❤️
Jotaime
Que l'on soit mouride,tidiane,hadre ou layene on l'aime bcp notre bamba 😍😍😍😍😍
Kou beugue serigne touba beuseule jaime ma khole li nexna way
Mancha Allah nekhna
Diop Moustapha Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
*_Ndeyesann Ani Gniy doundou mbécté mi yalla diamo sakh si Adouna si barkép serigne saliou mbacké😍_*
Bilahi goudaal fane ande ak wér ak ni suivre video bi♥️♥️♥️♥️
Barké serigne saliou 👌✨mbectei bangui May douguou tei dara khewaguoul ❤️❤️
@@erlingbrauthalland4581 *amine way kou bakh*
@@astoudiouf5749 _ndeyesann yalna yague way 😍😍_
Oh que des frissons 😭❣️♥️ yalna Diam yagg❣️♥️ Dieureudieuf Mbacké Balla Aïssa ❣️♥️
Rien de tout ce que dieu a crée dans l'univers ne m' inspire car Cheikh Ahmadou est le seul qui réside dans mon coeur.
J pense k gniy dislike danio khamoul à koi sert ce bouton mw machallah shui talibé Serigne Babacar mais j'aime tout c ki est mouride car lepp ben la ila Touba rkk
Même remarque que toi
J m dis la même chose sakh
Mala beugue
Ko bogo magal touba damal ga abonnes si page bi svp ruclips.net/video/Kye2pVxcxbI/видео.html
Walae ndeysaan
Je ne comprends les dislike
Yen lolen guem
Niko JAHMAN wakher rek YEREUM NAA SAY NOON
Tu ne comprend pas c quil ne comprén pas la diffrence entr ls deux
Eskeu tamite dou sokhore
Sokhor rék . Waayé gno koy yégu . Serigne Touba kouko bagn soneu rék
Chrétien yi sax di contan ñiom ñiuy soxor😯
Walay ndaysann🤣🤣
Épargnez nous de vos "je suis tel ou tel mais j'aime bamba" serigne touba dou pour béine tarikha nieupko bok c'est l'international 😍
fatimetou lagaré Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
jaajeuf lolou la beugone waax leipe gneup niogui sii biire Borome Touba
Bilay bambam dieup la keupe gouy dioulite
Merci ma chérie way 🥰❤️
Li 11 millions vue la warona doon avant magal❤❤
Barké alhourane jahmane dafa meune mais quelle élégance....
Macahalla diadief
Le meilleur duo au Sénégal, qui est d'accord ?
👇🏿
Moi
O
Iggkkkf
par force
Commenter na 2018 commenter 2019
AK 2020 yalnagnu ko fekke 2021 barkep borom mbectemi 🙏❤
soxna fatou yalla nga commenterat 2021
Yalla nga comantaire ba 2060
Amine ya Raby yaye boye
Amine 🙏
Amine yarabi Insha'Allah
Wetal nga rabana bamou diokhla kounfa yakoune.
Dieureudieuf Serigne bou MAKK BI
Je suis chrétienne mais j'adore cette chanson Bamba la joie 😍😍😍j'en ai des frissons quand j'écoute cette musique😭😭😭😘😘
Macha'allah
Machalla
Machlla💖💖💖💖💖💖
@@cirimbafaty2897 ññl mi k
A
Dp8 hier ba léegui nélawouma NDAKH KHAR VIDÉO BI WAAY MAYLÈENMA J’AIME WAAYE SONNOU NAA #BAMBA LA JOIE. KOU D’ACCORD NI VIDÉOS BI BALA UNE SEMAINE MOU AM 1million de vue puce bleu👍👍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yaw wéro ndékété.
Tu vas manger les j'aime après 😂😂😂😂😂😂 non Sénégal nexx na
*Amgua mélokan dh Seuhhttt Daguay sétt ly rek 🤣🤣🤣*
Baye zale ndeysan
Mahmoud Falilou wakhatoun lolou😂
Etant chretienne Jaime Mame borom Touba il a tout fait pour defendre l.humanité
Il a aussi parler de la vierge Marie dans Fuzti
Cheikh Ahmadou Bamba Mbacké❤💖❤
Machalla wayy..
Sama xole fésna
La vierge marie est l'homonyme de la mere de cheikh ahmadou bamba (mame mariama bousso)
@@moussandongo3182 akasa
Je vous j'aime
Je suis tidjana mais beugue Serigne Touba faratala thi nite kou gnoule
2018 Bamba la paix
2019 Bamba gneup
2020 Bamba la joie
2021 yalla nagnou yalla may feké ko...🙏
Jr YJ Joop Diop amineuuu way akk ioe akk gneup ❤️🎉🙏🏾
Amine
❤️❤️
Amine
Amine
Machaalah. Suis tidiane mais j'adore Serigne Touba et famille ( Serigne fallou♥️♥️♥️)
Sadio Diawara Slt doma diapaler gua abonnés sama chaine si c pas encore fait ce le lien en bleu 👉 ruclips.net/video/esbwd_j3qUk/видео.html
Je suis pas Mouride mais je suis fière de Bamba et abonnés sur ma chaîne so bégué ci Bamba .No chapeau Bou nieuw dakeu bou passé
Bamba rek
LAA ILAAHA ILAA LLAAHU MACHALLAH LII NEEX NA TROP CI XOL BILAHI
Les Diourbelois sont fiers de toi Jahman
Serigne Touba amoul morom deh barki alhourane
Ani talibé cheikh yi
Le Sénégal a vaincu
On a Ahmadou bamba Et Mame Maodo 😢💪🙏🙏
Bamba La Joie moy Mbégté mi. Kou bég ci Bamba ji rek beussal J'AIME
❤️❤️❤️❤️ li menoumassi doyal 😭😭
* doylo ak wolou la am si yaw ya gueun gaw si mane* thieyy mom ❤️❤️
*Suis le seul qui a eu le sourire tt au long de la vidéo🤷🏾♂️😁😅❤️*
*Lii mbecté rkk la meuna doon waay😅😁❤️*
*Safar sunu mbecté 😁😁😅😅❤️*
Bilhay 😂😂😂
@@rokhayalo8577 lii Kay mbecté mbi rk la meuna done 😁😁😅😅
Suis Ibadou ms j'adore beaucoup Serigne Touba et ces deux magnifiques chanteurs ❤️❤️❤️
Ndaysan yall na yalla fay sa khôl
Diadieuf Mourid,tidiane,layene, Ibadou nieup musulman