Waxatiko deii. Il a vu juste, c'est incroyable. Par contre, ceux qui avaient une lecture politique savaient depuis longtemps que c'est SONKO qui sera et/ou fera le 5em Président de la République Sénégalaise
Toutes les chansons de Sonko-Joomaay sont belles, mais celle-ci me touche au fond du cœur. Youssou daal, yaay waaji. Yalla na la Yalla aar. NEEEEEEEEEEEEEEEX NA.
Waawawe. Li mo nekh. Soumaye deklou sama khole daye nekh. Patriotisme rek pour notre cher Senegal. Yalla nalene Souniou Borom Deffal ndame si soutoura.
Maachala Youssou dieureudieufeti yalla na la yalla lafal thiat té diapalé la bou bakh défal la ndam yokkeu leu ba ngua yeuk ko si sa ligueey té mou jikk leu inchalla.....sa son bii amna solo lool lool té nékh si khols yi maashala.......
Yala cedena ni lidafa nekhe lool té ame sense. Youssou yalananga begeu si ngourengui waye. Ya diara décoré honnêtement. Vous êtes un age. Merci de tout cœur
Ki daf ko guissone ma shaa Allah ! Je ne me lasse pas de cette chanson. Vive Ousmane Sonko et Bassirou diomaye faye. Yalla na leen Yalla maye ndam, kou leen di khaar Yalla na khadi
Salam quelle belle chanson, quelle belle voix. Que le bon Dieu accompagne et assiste le Président de la République du Sénégal Bassirou Diomaye Diakhar Faye et le gouvernement du Premier Ministre Ousmane Sonko et le régime actuel à réussir leur mission rebâtir notre cher Sénégal dans la dignité et le développement
Merci pour ce titre grand ça restera gravé dans l'histoire pour cette conquête du pouvoir. Patriotes yi abonnez vous et likez ce morceau qui restera dans les annales de l'histoire.Pour finir longue vie et plein succès pour le reste de votre carrière merci dieureudieuf.
Walay ndeysane Diomay moy Sonko.Bassirou Diomay dieul ndamli yow la yalla andal.❤❤❤❤.Sonko moy Diomay yalla nalen bur yalla sam si barki Salatul Fatikha
Des millions de vues. Je veux de millions de vues pour Youssou.
@@bounas663 ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Koudoul doyal si son com mane ?je l'écoute ts les jours et ca me va droit au cœur ❤❤❤ super !!!!
@@Keyna26 man lima ko deg mo épou mom lim ko répète 😂😂😂
Khana man douma si doyal billahi❤❤❤❤❤
Kii bimouy way lii dama yakar ni yalla dako wanone ni mbir yi di démé baparé ndakh nimouko wayé nonoula démé
Walahi ousmane mi teur noneu yi❤
Walakhi sokhna si😢❤
Walakhi 😢😢 Kou konetane lalale ❤
C'était l'espoir vraiment il a vu juste 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤🎇🎇🎇🎇🎇🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Waxatiko deii.
Il a vu juste, c'est incroyable.
Par contre, ceux qui avaient une lecture politique savaient depuis longtemps que c'est SONKO qui sera et/ou fera le 5em Président de la République Sénégalaise
Toutes les chansons de Sonko-Joomaay sont belles, mais celle-ci me touche au fond du cœur. Youssou daal, yaay waaji. Yalla na la Yalla aar. NEEEEEEEEEEEEEEEX NA.
Wallahi niép la
Bilay yak mane amiine
Moy sama sonnerie téléphone
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wolahi
Kham kham la weuy nague. Weuybi ame na batine. Mokk bou Abdou Guitté bi amougnou morome.
louwerr wayy bous batinei, nekh, original tei eumbou lepppp ci palougg diomaye-sonko ak nouniou nara diriger senegalll
Bilay son sonko Diomaye yi yep nex mais bi day toyal sama xol merci youssou je te salue depuis Italie 🇮🇹
Je ressens la même chose 😢😢😢
Billahi ❤
Pour mane limay sentir si son bi ❤️❤️ mane donc menko kham walahi 😢😢😢
Dou yaw dong dé man donge la❤❤❤
Excellent!!! ❤❤❤❤ MERCI!!!
Vive Président BDF
Vive PM Sonko, le Guide Suprême de la Révolution Patriotique!
Youssou Yalla nala Yalla defal diam AK soutoura. Jeureujeuf ❤❤❤
Cette chanson est rentrée à jamais dans l'histoire de la politique sénégalaise.😢😢😢
C est une chanson d une nouvelle ère
machallah cette chanson a joué un rôle important sur la victoire du PASTEF.
Dieuredieuf Youssou Bonho
Machallah youssou yalna yalla wereul baat bi si barcké seydina Mohamed Amine ❤❤
Waawawe. Li mo nekh. Soumaye deklou sama khole daye nekh. Patriotisme rek pour notre cher Senegal. Yalla nalene Souniou Borom Deffal ndame si soutoura.
Youssou waye wi nekhe n'a machahala kou selki daa nekha tague dieuf dji mo rafet
Jadîeuf couz Youssou Margane mbaye Yalla na wéreul baat bi Barke Mame cheikh Samba Diarra mbaye
Machalla sa waye bi dotoul amati patriote yeup contane nagn❤
Je ne suis pas de pastéfien mais j'aime ce son c'est très original
@@LassanaboubaTraoré normal, la Kora fait vibrer les cœurs 💞
Maachala Youssou dieureudieufeti yalla na la yalla lafal thiat té diapalé la bou bakh défal la ndam yokkeu leu ba ngua yeuk ko si sa ligueey té mou jikk leu inchalla.....sa son bii amna solo lool lool té nékh si khols yi maashala.......
❤🎉🎉🎉❤🎉😂 tayy rek nga déé ak ay Vues 😂🎉🎉🎉❤❤❤
Ndiguel Djip na Ousmane ma teur none yii mo diokhogn Diomay nekko dieuleul ndam li...
Youssou amnga keuchfou dh
Jaliba Kouyaté sera sûrement fiers de vous pask t’as bien remixer son fameux titre Moussa Diba vraiment j’aime ce Song
Nekhna Lo leuh ❤️🎊
Pour mann sakk c'est djialyba Kouyaté monko wayyy merci Youssou tu as tout dit 👉🙏🙏👍👍💯💯♥️♥️♥️👍👍👍💯💯💯💯
Yala cedena ni lidafa nekhe lool té ame sense. Youssou yalananga begeu si ngourengui waye. Ya diara décoré honnêtement. Vous êtes un age. Merci de tout cœur
Merci beaucoup Youssou mou s saliou sonko diomaye à vie ❤️🔐😭
Ki daf ko guissone ma shaa Allah ! Je ne me lasse pas de cette chanson. Vive Ousmane Sonko et Bassirou diomaye faye. Yalla na leen Yalla maye ndam, kou leen di khaar Yalla na khadi
Merci beaucoup frère le premier ministre panafricain sayidana Ousmane sonko Al Moubarak avec edo 92 66 🇲🇷🇸🇳🇸🇳🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇸🇳 🇸🇳🇲🇷🇲🇷🇸🇳
Youssou tube de l'année
Belle chanson Youssou way bi neh na lolou vraiment les patriotes sont fières de toi Sonko moy Diomaye.
Koufiné après la razia 😂
#Élections législatives 2024
Ñu jublu si rédition des comptes ak pôles territoires yi❤
Ça me rappelle des moments de vad, et campagnes de l'élection présidentielle ❤
Wallahi SONKO moy DIOMAYE. Bour YALLA dieureudieuf
Man Mack Sall la andal mai son bi mom douma si doyal bilaye ❤❤
Salam quelle belle chanson, quelle belle voix. Que le bon Dieu accompagne et assiste le Président de la République du Sénégal Bassirou Diomaye Diakhar Faye et le gouvernement du Premier Ministre Ousmane Sonko et le régime actuel à réussir leur mission rebâtir notre cher Sénégal dans la dignité et le développement
❤❤❤❤❤❤machalla frère Youssou et merci serigne Mame cheikh fall
Machalah yala na bate bi wer bravo
Thanks so much for the song President Ousman Sonko and Diomaye!❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💯💯💯💯💯🌹🌹🌹🌹😍😍😍🥰🥰🥰💪💪💪💪🇬🇲🇬🇲🇬🇲🤲🤲🤲
Machalah woy bi dey daw sama yaram vraiment
Très belle chanson extret du son d Dialiba koitè merci
Walay ndeysan tawfex agg tayssir rek inchaAllah nex na way
Maa shaa Allaah Sëriñ Youssou daal ndaanaan ga. Lii moom patriote yi war nagn ci def lou reuy
Félicitations a seugne Mame cheikh borom Mizane vraiment kou diap si yif yi leu 🕋🕌🙏🏽
Ndeysane respect youssou mou serigne saliou ❤❤❤❤❤
Jërëjëf diajeufeuti ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Quand j'écoute cette chanson j'ai de la chair de poule.
Félicitations le grand youssou c'est moi mbaye bine
Almomine mbaye nkmou
Niogui laye degg Lisbonne ou germany
Bilahi Youssou bou serigne Saliou ya meuna way sa son bi sama bir khôl bi lay douguou manshalla ❤❤❤❤
Ypusso yalla ga goudo fan mos gama way de me audio bi moma rerr mo meti ma trop bilahi me sama xoll sede na trop si yaw ❤❤❤ yousso ❤❤❤❤
Wa ki foumou nekonn😢❤ li nexna lolll yep bi mossi dakhhh
Bargue Serigne Touba ya Mane ya eupou dol yalnala yalla dėfal diamou Youssou 🙏🙏🙏🙏
Mane mooom dara guenouma nekh ssi waybi ludul sa tourbi, maachaala yaalla na baatbi gueuneu wer.
Machalla ♥️ sonko 👑 Moy diomaye ❤
barki Serigne saliou mbacké bimaye doga dégeulou pour mane aye diolla laye wakhe bilahi walahi mei son bii dafa nice trop sakhe bilahi félicitations frère
Ma challah me son bi son dialiba koyate la
Nékhna dé sonko moye diomaye rek❤❤
Thieyy kou Selki ❤❤❤
Moom Youssou daa faf nirook Sonko sakh Akassàaaaa Fall
La mélodie oooohhh
Djaliba kouyaté rk la sama khel di dem
❤
Salam Salam merci youssou c'est dieu qui t'a inspiré comme chez les diolas les compositeurs des chansons du boukoute sacrée wa Salam
Maximum de partage. Il faut le million de vue gnou xamni gno téyé rewmi. 💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾🤣🤣🤣🤣👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾
Maashallah ❤❤❤❤❤❤❤
Focus focus focus les patriotes sur Youssouf bogon
Partagez il mérite plus de 100millions de vues
Li nekh na waaay❤❤❤❤😂
Bilaye li nèkh na trop machallah 🙏♥️🙏
Merci pour ce titre grand ça restera gravé dans l'histoire pour cette conquête du pouvoir. Patriotes yi abonnez vous et likez ce morceau qui restera dans les annales de l'histoire.Pour finir longue vie et plein succès pour le reste de votre carrière merci dieureudieuf.
Sonko moy diomaye ❤
Son bi mo Dax Yep 😊😊😊
Mashalla youssou li nekh na trop yaw ak maa❤❤❤😂😂
Yalla nalla Yalla barkéle yaaarrraaabi dieureudieuf !!!
Manchalha liii dawna sama yaram
❤
Ça me fait penser au meeting de clôture de Mbour mais surtout à la bataille de Kaffrine gagné héroïquement par PROS
Nekh na machallah ❤
Cette chanson allait direct au coeur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😊😊😊😊
Je ne suis pas pastel mais cette chanson me fait vibrer le cœur ❤❤❤❤❤❤❤❤
Chansson bi nimoumay deff eupna walahi❤❤❤
Koumay dimbali si son originale bi ça fait des années manguikay weur
Artiste et titre
Mach'allah son bii djick nagnou,,
Youssou du rakk si akasa samb machall
Machallah neekh lolou
Wallahi ndayesane lii nekhna dè ❤❤❤
Ohhhh li nam nako lol
Bilay campagne daffa nékhonn lol
Machallah machallah
Machaalah yalla na yalla barkél bat bi
Merci patriote ❤❤❤❤❤
Machallah wowi 🎉🎉🎉 nekhna
Machalah youssou bonne continuation
MANCHALA YOUSSOU VOUS ÊTES FORT MERCI BEAUCOUP
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Jah jeef bay Youssou sa waywi dée gààlatch laa bay fall
Ndeysane thiey sonko mouselmi ❤❤❤❤
salam vrma ta chanson dafa nekh amna solo machalah
wawawe da nékh té âme solo
Ki mi ndieka wakh Sonko moy Diomaye ❤❤❤❤❤
What a voice. Liiiiiiii nekhna waaaaye
Walay ndeysane Diomay moy Sonko.Bassirou Diomay dieul ndamli yow la yalla andal.❤❤❤❤.Sonko moy Diomay yalla nalen bur yalla sam si barki Salatul Fatikha
Diomaye forever sonko forever ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
MaschAllah with Youssou!❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah belle chanson ❤❤
Ndeysane😢😢nékhna si khol❤❤ trop
Ma sallah néhk na yalla na yalla barkéall
Mashallah yallna mousalle lenne ci pekheme seytane yarabi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😍
جررجف يوس❤️✌️