Très pertinent Modou je suis fans de siteu a fait une erreur de communication Modou yaw daga bakh rek mais siteu limou wakh bilahi diap si dara vive la paix vive la lutte senegalaise
Boy wkhna deug toubab yii nioy dff sport yaw fi guay guiss mbeur bouy démm Di dieul say affaires yobouko si ayy mara pour yakeu laa guané c du cadre sport
Première commentaires cou d'accord avec moi laa lal ❤ j'aime❤
Ndam rk Mod lô inchallah ❤❤❤
Modou lo kėssė ndam rėk inchallah 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🥰🥰🕌🥰
Lambologue MODOU Anta The Best commentateur is The World ❤
𝕄𝕠𝕕𝕠𝕦 𝕩𝕝𝕠̂ 𝕤𝕖𝕦𝕝 𝕟𝕕𝕒𝕞 𝕣𝕜 𝕚𝕟𝕔𝕙𝕒𝕝𝕝𝕒𝕙 ❤❤❤❤
Ndam rékh situé inchallah
Très pertinent Modou je suis fans de siteu a fait une erreur de communication Modou yaw daga bakh rek mais siteu limou wakh bilahi diap si dara vive la paix vive la lutte senegalaise
Machallah rafetna torop yallna sen diam yagui waye amine yarabi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Siteu damako setane contact 17h ba 19h mok pakala bou lansar ,baye Ndiaye ,neko rél mais ken dou lal tank yi
Wakhofi dara😂😂😂
Dokhontoul Parcelles s'étan Modou day foyé école de lutte bi keneuh douko yeugeul
Modou lo mola wax dafa soxla ayy tank😂😂
Kou xam Neko Rel xamni Siteu kou meune beuré leu
Wakhatiko dee gayii khamouyou sakh lou khew
Merci modou antan et lambelok
❤❤❤❤❤
Siteu néna défoul sport na lérr 😂😂😂😂
Modou Lo Ndam rek inchalla
Lambelogue doff gua rek sponsor moy fay mbeur guanane li siteu solle baxna
Siteu kasse ❤
Wawe siteu kasse
Siteu kesse nak🎉
Lambalok ya manqué démbou si face to face bi
Siteu ylna ko yalla may ndam si kw modou lo amine 🎉
Wayane rek senegal😊
Merci❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂
Siteu doffe la billahi ki amoule khele waye billahi mome menance laye deffe baparé nena mome defoule sport konne li lanla
Est ce que dou banditisme lay dff
Boy wkhna deug toubab yii nioy dff sport yaw fi guay guiss mbeur bouy démm Di dieul say affaires yobouko si ayy mara pour yakeu laa guané c du cadre sport
Yaw mi ya dof dmr
Nice
Que meilleur gagne
Yalmine bi kassé laye toppou 🎉Ndam rk 🎉
Kou beug siteu gnou beug leu 👑💪
Bilay lou léér nga wakh
Lamb rk lay top 🎉
Bou limou wakh dara nékousi balla gaye contre tapha tine louné wakhnaniouko mo takh mou diay bakanam tore tapha tine bamouné euy balla
Voilà ioe mom kou nitté gua machallah
Modo lo rék
❤❤❤❤❤❤❤❤
Situe na top fale
❤❤
SiTEU kouko bagn niou bagn sa yaye
Séne duo bi Yalna yague waye 😂
Ay menace en direct. Xamoule ni il peut être poursuivi rien que pour ça
Daguéne mouss guiss siteu bou khess bay len niou way yekini mo geunone nioul Balla gaye fouff 😂
Lamb fayal thiow mo gueun ngay yokk
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉😂😂😂
𝕊𝕚𝕥𝕖𝕦 𝕕𝕖́𝕗𝕒𝕚𝕥𝕖 𝕣𝕜 𝕚𝕟𝕔𝕙𝕒𝕝𝕝𝕒𝕙 😂😅😂
Bilahi lambalogue damakoy beugue ba kagn la khamoul
🅼🅾️🅳🅾️🆄 🅻🅾️ 🅺🅴🆂🆂🅴
Ms journaliste bi khana mooy invitée bi
Ou ont vent les billets
Non lambalogue yangui yakh sama adouna 😂😂😂 siteu késsé ndam rék inchallah 🙏🙏🙏
♥️♥️♥️🇮🇪🇮🇪
Vous jeter dès fou q ils faut dire la vérité ils la pas a dire ça ces tout
Je suis derrière Modou lo❤❤❤ malgré que je suis un Sérère.
Wesh sa mère est serere aussi modou
Diadieuf sa way yabax
C'est ton problème,les vrais sérére sont avec siteu
xarangne Lo seuL ndam rek
Mafi djitou 🎉
lambalok Seul ❤
Modou anta SiTEU day kaff rek Bour ak fadam bouniou nieuwé Diamageune SiTEU moléni protègé wallahii YaL baye fall là xôl bi draa néwoussi
Siteu doff la amoul khel dou khalate😇
Siteu dafa yabaté waroul tok niépou diko sétane mouye menace Insbi lepou lou léne dall responsabilité Siteu la
Modou anta défal sa émission tai noopi boo bahé yaww la raik
Djoun wa Diameguene Sporounou Dani Djikhat def lenko séne bopou ❤
Ms Lou takh signatur yi dounsi wo lamblogue mou tew fa
Yalmine bi kessé kou douguou diamaguene gnou tégueul sa nday bour yak fadam
Boy yarou bakhna dé
@SidiyaDieng-m1v yarou bakhna kay mé siteu kessé 👑💪
NO MODOU ANTA MO DANG LE TE MANA TONTOU
Yéne ladone xarr❤❤❤
Mais lamb y'a néh
Siteu day dieul défaite inchallah 😂😂😂
Siteu dioumoul fadam dafa kate ndeyem😂😂
Modou lo yalla nala yalla may déféte bou amoul bénne wéranté inchallah
Siteu guéne beug mou Dane dh wayé inch alah modou dinako doumou Dane mo guéné nopi Yoe lamblog xawma werooo daga beurii wax xamo touss
Mane la lamb😂
Siteu kesse
Taay mom emission bi nexoul 😂😂 en matière d’analyses. On a beaucoup rigolé teih heure bi heurou titt leu passaka carte gui hawna diahasso.
Jambar loy doyé di tite tmt non ya beug lou meti🤣🤣🤣
Siteu moy yekini nappena nieupp
Siteu dieull ay aferam neik cii grabou coco yii guéne beug modou topou ko cii dathie yii dii wax lougn koy khibé
Siteu naniou may diameu,balla amoul loumou degoul contre tapha
Siteu wakh na DEUG fadam AK mbourr ay doumou kharam lén
Modou anta dioumgua bour journaliste lah amna drw wax lolou bayilenn diaxase
Siteu mo dakka contre clé si mbeur yi
Dou deug lac de guerre 😂
Modou Anta moy Lamin Samba bari wakh😂
Modou lo moko meune foufe bilah
Bilaye lam malla beuke.😂😂😂😂
Mak yaw lambalogue titiii rek da meuna wayyy té am mana
😂😂😂
Lambelok yangui commencé yak sa bobb wala danga ragal wa diamagueunn
Bly labalogue yaw rek ladone khare aprés face2face bi
😂😂😂lo
Ndam rékh situé inchallah
❤❤
❤❤❤❤❤❤