Li mom nogatou la . Siteu mi modone ladie Zoss 😂 Lamb dou affaire de banditisme , finga nieuw di monter fitt di guénné diam si face a face , takhaw nane lamb milieu la …. Balla Gaye ak Modou Lo niolene eupp fitt fouf té bign siy tollou dawougn niodi banditisme . Miser lene si sport bi té bayi yene details yi té bagna diapé sen bopp champion . Du courage Siteu et Félicitations à Boy Diop 2
Lutte tv faut partagé ce msg jusqu’au CNG et au Ministre du sport les tribunes 🏟️ Rouges de l’arène nationale doivent être fermés en deventure par des bariére au moins 10 m de longueurs pour k les supporter ne peuvent plus descendre du stade
Felicitation Diop 2 un vrai guerrier et espoir mais prk arbitre yi di yakamte ate bou diop 2 egualiwoule wone action bi thiow lou reye dina ame nak Siteu bou ngor defoul wone 4 appuis , apres niou deme var beurewate nguene yakk lambj dji
Felicitations Diop 2. Siteu bou Ngor xana sétanoul Diop 2? Waxoumala beuré rek mais dafa meuna xéx, té bén loxo droit bi foram la. Siteu yorou thiouné deug la yorou. Diop 2 vs Tapha mbeur
*Ay mbeur you ndaw fessal arène nationale bi nii c’est incroyable*
Ma gui nianal kép kou ame problèmes yallah defal la soutoura ak diam
Amine🤲
Amine Ya Rabii niou bokou ko
Amine
Amine yarabi niou bo cou ko
Amine kubaax ñu book ko
Boy diop 2 seul Brome sow mi ❤❤❤❤
Li mom nogatou la .
Siteu mi modone ladie Zoss 😂
Lamb dou affaire de banditisme , finga nieuw di monter fitt di guénné diam si face a face , takhaw nane lamb milieu la ….
Balla Gaye ak Modou Lo niolene eupp fitt fouf té bign siy tollou dawougn niodi banditisme .
Miser lene si sport bi té bayi yene details yi té bagna diapé sen bopp champion . Du courage Siteu et Félicitations à Boy Diop 2
Ki d'où mbeur n'a ligueyi mounane diokhe léne ma zoss😅
geuneul sama xel bii way😂😂
💛🖤
Bien dit
@@Menoo107 na ligueyi rek bayi limouy incarner nakh doussi lene
Guediawaye Derrière Diop 2💙💛 Banlieu kesssé 💙💛
💙💛 1:42
Banlieue nio far ❤
Team bouroukhlou
@@cheikhahmadoubamba1690Diop 2 ban écurie la nékeu
Billahi ont s’aime c la vie ❤
Félicitations diop 2.
Félicitations Diop deux borom sow bi sama kharitt bi 11 combat 11 Victoire machallah laf thiatt
Lutte tv faut partagé ce msg jusqu’au CNG et au Ministre du sport les tribunes 🏟️ Rouges de l’arène nationale doivent être fermés en deventure par des bariére au moins 10 m de longueurs pour k les supporter ne peuvent plus descendre du stade
BOYE DIOP 2 YALLA NA YALLA MOUSAL SI THIATE MACHALLA ❤❤❤❤
Félicitations Diop 2 yokou dole rek
Félicitations Diop2 bonne continuation.
Seul le travail paye
Du courage siteu bou ngor
Brrome soow mi seul🔥🏹
Yeumbeul deuk leu 🎉
Champion la ❤
Yeumbeul cest le bimbame❤❤❤❤❤❤
Vraiment Diop 2 Lou mbeur you magg yi di mobiliser Lolou Gua mobiliser Digua amat combat Légui inchalla ❤❤
Lambajdi Fès na machalah
Boys yi danio mobiliser MashaAllah . Boy Diop mom war na am cachet bou bakh prochain combat wam
Félicitations Diop 2 mais arbitre bi tmt ki defagoul 4 appuis skh gua beug attè do def nankeu
Mashala notre frère diop 2❤L’affaire thiat
Siteu courage jeul taankk bi danga ko téléphoner. Danga warone melni lu andi xeex dora jema jaapp taank. Félicitations Diop 2,un vrai champion
Borom soow mi kasse ❤❤❤❤
Khale yi bousi kanamé nioy téye lamb jdi❤❤
Felicitation Diop 2 un vrai guerrier et espoir mais prk arbitre yi di yakamte ate bou diop 2 egualiwoule wone action bi thiow lou reye dina ame nak Siteu bou ngor defoul wone 4 appuis , apres niou deme var beurewate nguene yakk lambj dji
Totalement d'accord avec ton analyse
Khana guissou lene 4 apu bi dafa lere nagne menoule ame bene thiow
@@algassoumdemba7844 merci mon frère de me comprendre
@@coach9635 sa khalate nga wakh damalakoy nangoul
@@coach9635Saway moment bi arbitre bi Di atté fofu waji trois appuis la def au dernier moment la dora tek 4eme appuis bi
DIOP 2 vs TALFA... WALA DIOP2 vs Mbacké Faye
Bly diop c'est le mailleur mais quel phènomène 🎉
DIOPRK ❤❤❤❤❤
Félicitations champion et bonne continuation pr la suite
Diop 2 rek ❤❤❤❤❤❤
Mérçi diop 2 siteu bou gor dafa beuri wakh douma gako dane ko
Félicitations bonne continuation
Félicitations diop2 bhillahi contan naasi yaw😍❤️
Félicitations job 2 le fls De Amaa Balde ❤️Du courage Siteu Bou Ngor ❤️Mé Job 2 My nako Lamb Senegal 🇸🇳 bayii xél Boubax sax kii champion la 11 combat 11 victoire Laf Thiath way🤲félicitations ❤️
Diop 2 mi dale beugue nako lol bilahi ❤
La rage du champion n'est dans siteu bou ngor . Ko gniéméwoul doko dane
Félicitations Mn amour diop 2
Un futur champion est née
Billaye diop 2 késé do séne morom contane na Billaye 🎉❤❤🎉❤🎉❤🎉
Combat dall lilasi xam tela comence mais legui ay 23h
Merci diop2
Felicitations Diop 2.
Siteu bou Ngor xana sétanoul Diop 2? Waxoumala beuré rek mais dafa meuna xéx, té bén loxo droit bi foram la.
Siteu yorou thiouné deug la yorou.
Diop 2 vs Tapha mbeur
Diop2 kassé brome sow mi❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Mais boy bi sou touki nieuw dinga guiss Lou graw Diop 2 bi machalla il a tout d'un futur grand champion
Mashalla 🥰🥰🥰
Félicitations
Amnagnu champion nioun Wa yeumbeul ❤
Wakhal way DIOP 2 seul
Wa cng ay deum lagne laloo bi Diop 2 kheupo mo ritakh guiss ngéne ka mes wakho léne motakh gnouy diap ba sonou diapoul😢
Félicitations diop 2❤
Très bien Diop 2 samorom boufi nekk di wakh rekk kharko thi guewbi yalene mane fouff 💪💪💪
Courage SITEU diop 2 ndanane la virement
Diop 2❤❤❤❤❤
Diop 2kassé amoul lénéne nioune bénzo laniou deukk🥰🥰💕💕
Tyson de retour ❤
Braaaavo 👏👏👏
Diop2 vs bb gouygui combat bou nekh🎉🎉
Boy yi dofou niou dé kham nagn gni niouy dieul
Bb gouye gui moko meun foufff
Siteu Niankou mola thiatou deh
😂
Mbeur féñ neu 🔥🔥
Niouss la dann laaa😂😂😂Do ndy bandit yeumbeul deuk leu
Félicitations diop2❤✌️
Lutte tv la beugue xam foum nek s'il vous plaît c'est très urgent
Lane la lou xew
Zone b la Nek côté grand Dakar
Siteu tégho fi dara lou lére😢😢😢
Diop 2 seul ❤❤yeumbeul reck
Combat bi nekh n'a 😂❤😢😅. Diop 2. Kasse
Machallha❤❤❤Diop2
Diop 2 vs tapha mbeur combat bou nékhe la dh
Tapha mbeur moko meune aller et retour .
@@paulbella8287dangay duul
Non
@@paulbella8287dagay wakh loula nekh rek
Arbitre mo yakha combat biii dieleu amoul mou siflé
Diop 2 doomou yeumbeul bi champion la❤
Felicitation Diop Mon Champion ❤❤
Diop 2 késsé yeumbeul deuk la ❤❤❤
Diop2 vs Talfa
Les coup irréguliers khana arbitre bi guissou ko
Diop 2 kassé💪💪💪💪💪💪💪
Diop 2 🔥 vs talfa 🔥
Sa da ta yaye
Non
Téel n'a deh l'Aa ilah
Talfa door ko mou dé rk😂
Lolou dou comba 😂
Boram soow mii❤❤❤ Diop 2
Borom Sow mi kasé 🎉🎉🎉
Dieul lénn Zambala
Arbitre bi da yakamti mais félicitation diop 2
Diop 2 seul borom Sow mi ❤🎉🎉🎉😊
Doummeu yii méttina ay coups de genoux lako door tchi kaw ba yéeg souff😂😂
Liss ndiago ak Diop 2
Modou lô rek
l'Aay guiss si nioom
Diop 2 un phénomènes
Ça commence ici : 11:45
Diop 2 seul feliz
Sites bou ngor tay ma Ray la Diop 2
Yaye zéré
Siteu bou gor de don Modou lô modoulô Lou wayé doto ko défati 😂😂😂😂😂😂😂😂
Machalla Diop 2
Zénéral malika deug❤
Nio mobilisé nio gagné 😂❤🎉
Arbitre bi bisous aaté siiteu mougui déf 3 appuis il faut fair un recour
L'espoir le plus populaires Diop 2 kassé
Diop2 vs mbacké faye comba bo nékhe la
Diop 2 moko meune dee
sitou day Modou lo Modou lo lou😂😂😂
Diop2 vs Franc
combat la
😂
Félicitations diop2 brome soow mi seul
Diop 2 vs mor kang kang kou d’accord
Mais moment bi arbitre bi Di sifflé 4 appui amoul wala ma guissoul
Nioune sakh yeumbeul Laniou deukk 🥛🥛🥛🥛🥛🥛❤️💪💪💪💪💪💪
Lamb dou milieu dh😅😅😅 liguey moy fay
Lamine seck est très professionnelle bogoul sax ak gayi da mane té bolé woukak wanéwou
Boy bi ame na mbolo Macha Allah
Siteu amo doolé .